Le combat de zarco est meilleur que le combat de balla et Boye Niang . Faites attention à lui il est venu avec de nouvelle ambition merci pour ce retour incroyable.
Dafa rey lamigne. J ai juré k Ada peut pas battre zarko. Les gens sous-estiment zarko parsk il n est pas populaire mais c un vrai technicien. Ada doit avoir revoir son comportement il passait son temps à montrer ses muscles li ken douko deff 🇰🇲🇰🇲🇰🇲
Félicitations à Zarko et courage à Ada Fass. Ada devrait raser les murs et se faire discret mais affairou bandit yoyou faut le faire dans l’enceinte de l’arène et éviter les gamineries sur les réseaux sociaux. Zarko dou ngaaka et il mérite amplement cette victoire au vu de sa concentration et de son sérieux depuis l’officialisation de son combat. Braaavo 👏🏽
J’ai connu zarko lors de son combat contre siteu. Depuis ce jour, et je le confirme, il fait parti des lutteurs les plus tenaces, très technique et très puissant. Et il le sait il a confiance en lui, il est endurant ce qui est dommage est qu’il prend de l’age. Mais félicitations champion.
Félicitation à zarko du courage à Ada fass il est encore jeune il a du chemin à faire pour revenir en force aujourd'hui l'expérience de zarko a eu raison de lui
Ndysane liii mokoy dff mbeur walahi Booy ada fii laay diare done mbeur ba faw combat bii dinala diangual lou beuri du courage et félicitations a zarco athlète degue mooy Kii Bilaee Insbi ioe ak franc combat la bou nekh walla sa revanche contre siteu pourquoi op😊
@@cheikhndiayetouba040 Mane mi baréwoul sakh maako gueneu kham Zarko. Amna fit amna doolé moom Zarko.. Ta boy yi danouy naagou trop. Tay loolou la wakh mani zarko dakoy daan parce boy day minimiser Zarko ndakh khamouko.
Vraiment li moye lamb nekhena trop felicitation zarko es tu courage ada fass mes supportere yi billayi amaniou yarr dara yague bakhoule c est pas serieux li sa fait honte li sounou sport national le waroulaine def li adouna yeup diko kisse ken begue lamb avancer ak image you bone yi
Zarko félicitations sois plus sérieux dans tes combat respecte les amateurs et tes adversaires Ada fasse du courage Je signe pour une revenche zarko vs siteu parce qu'il y a eu ambiguïté lors de votre premier combat Ton deuxième combat potentiel Zarko vs Mouss ndoye
Ada fass trop orgueilleux pour son âge. Je suis de pikine mais il fallait corriger ce jeune homme pour qu'il soit desormais respectueux envers ces anciens. L'experience et la confiance en soi a permis une victoire à zarco et une belle chute. Ada fass doit apprendre à être discrèt et sage.
Bravo zarko am nga fit moun nga beurè tè dof nga ci entrainement mais staf rèk mola manqè mais heur bi warnala fek ngaýe beurè niom balla gaye2 tapha tine
Felicitations zarko 4ans spain Deff retour 3 combats 3 Victoria jeul risque dane mbaye guy gui ak niome ak Ada fass Nako gouye gui dieul mba junior yekini
🔥 Les Potentiels adversaire de Zarco Zarco vs Yekini jr Zarco vs Gouy Gui Zarco vs Modou Anta Zarco vs Moussa Ndoye Zarco vs Jackson Zarco vs Ness Zarco vs Alioune seye 2
Zarko-Diene Kairé waleu Zarko Alioune Seye Jr. Jackson neu ligueyat boum yakamti il est temps mbeur yi am plan de carrière mais niom lamb thiow rk motakh amneu défaite yi niouy am dougn diogat. Jackson kouko encadré mom ak Thiatou Daouda Fall dinagn indil satisfaction guediawaye
Un sport de combat comme la lutte c'est sur un algorithme d'intelligence : Action-reaction-action. Toutes les techniques sont dans ce logarithme. AdaFass a manqué terriblement de réaction de et réflexe. Il devrait simplement laisser sa main droite agripper derrière le nguimb de Zarco pour avoir une troisième appuis et le tour est joué. Félicitations à Zarco et félicitations à AdaFass
Bi combat bi taxawé lolou mo done wax-j. Mais liguey na loumeu dane Zarko mais dieuféwouko. Pour Mome beuré Zarko ci beutt la yam. Lolou la téthie nangouwoul Zarko fétéko bén yone souf. Zarko aussi comprendre diémko nogatou ba li fék ko ci.
Zarko dan nga wayé tegoyone si linga beré adversire dankoy respecter tay so danouwone dinga deig louné '''Mes Ada fass mbeur day lakatu defaite bi nak molay def mbeur ...
Wakhone nani ada fass na défe atatinons thi zarko ndakh zarko adversaire bou nakaré beuréle la thi tous les plans mais ada fass na défarouwate té khame fomouye téke tankame té maytou lou beuri ndakh khaléla té lambe mingi thi kanamame félisitations zarko
Ada Fass combat bépou dako diafandou. Mano baña encaissé, bañ sa adversaire fété la souf. Biko Zarko dioxé thieur ci guéw bi dafa farone dirigé, andi sañ sañ, toñ ko pour Zarko andi maniname mou dane ko ci. Mais warona xamni combat bén bén ak diap deguelou dou ci dane Zarko. Zarko der la ci guéw dou beuré banga néko cim.
Ada tay mom danga roukh Zarko dafla diay prek diay la bandit nangou lamb j danga done diay Rew mais tassé nga ak koula gueuneu rew gueun leu Waga doumeu leu Mbeulé sa supporters sagua lene baparé dane la
Zarco depuis son retour de l’arène il avait eu 3 combats 3 victoire pour l’instant félicitation à lui 🔥⚡️❤️🔥
C’est faut siteu moko dane
@@Jah911 werr gua 3 victoire yi après son combat contre siteu la
Meme contre siteu. Siteu avait perdu.
Danagoul koutakh ma nagoulko
Darko vs cris2 combat la dh
Le combat de zarco est meilleur que le combat de balla et Boye Niang . Faites attention à lui il est venu avec de nouvelle ambition merci pour ce retour incroyable.
Zarco est devenu mature maintenant c'est du jamais vu,
Mature ngua wakh dè mbeur bou immature mingui ni😂😂
@@mmmaaannnsssooouuurrr9109 mature sur la la façon dont il gagne ces combats ,il est plus serein.
Félicitations ZARCO, yangui saggal grand yoff .On est fier de toi.
Courage à Ada Fass té nga wagni wakh bi
Dafa rey lamigne. J ai juré k Ada peut pas battre zarko. Les gens sous-estiment zarko parsk il n est pas populaire mais c un vrai technicien.
Ada doit avoir revoir son comportement il passait son temps à montrer ses muscles li ken douko deff 🇰🇲🇰🇲🇰🇲
Yéna ko geuneu beuri wakh. Ada késsé
Boy biikaay daffa wara wagnii wahh djii lamb dou affair de bandit
Bly motakh nekhou ma
@@elisabethmanga4782 nioune louniou beurri wakh daniouy def fouleu lidjialeu dane l'en te dolen si moune dara 💪🏾😂
wakhona ni ada dougou neu si carapidou samba laobé zarko d’à tel trop si ada mai du courage et félicitation zarco merci lamine et toute léquipe ❤
Vérité absolue tu as bien di
Oui j pense que lolou c très tôt
Dafa tél té zarko da bari dolé
Vérité absolue
Mais frr nianku pawlis kagne la please
Lutte tv for everything
Vous êtes les meilleurs en ce moment
Félicitations à Zarko et courage à Ada Fass.
Ada devrait raser les murs et se faire discret mais affairou bandit yoyou faut le faire dans l’enceinte de l’arène et éviter les gamineries sur les réseaux sociaux. Zarko dou ngaaka et il mérite amplement cette victoire au vu de sa concentration et de son sérieux depuis l’officialisation de son combat. Braaavo 👏🏽
Vraiment lamb dou affairou banditisme
J’ai connu zarko lors de son combat contre siteu. Depuis ce jour, et je le confirme, il fait parti des lutteurs les plus tenaces, très technique et très puissant. Et il le sait il a confiance en lui, il est endurant ce qui est dommage est qu’il prend de l’age. Mais félicitations champion.
Âge numéro la rek
Lamb beuriwoul combattants. Mais Zarco en fait parti.
Moi j’ai vu ça en lui dès son combat contre Gouy gui
Félicitations à Zarko🔥👋❣️💯💯masa'Alah. Boy bi dafaa bary baxx trop 😂😂😂
Félicitation à zarko du courage à Ada fass il est encore jeune il a du chemin à faire pour revenir en force aujourd'hui l'expérience de zarko a eu raison de lui
Zarko toujours en forme phisiquement
Zarko vs Gouye Gui l’heure de la revanche a sonné
Bien dit
Lolou fou combat gouygui beuré toul
Zarkô siteu
@@mbackemoustapha9161 c'est ça le combat véritable
@@momobouthiapathiolybi7752 bilahi
Ndysane liii mokoy dff mbeur walahi Booy ada fii laay diare done mbeur ba faw combat bii dinala diangual lou beuri du courage et félicitations a zarco athlète degue mooy Kii Bilaee Insbi ioe ak franc combat la bou nekh walla sa revanche contre siteu pourquoi op😊
Zarco dou beurré ak wa PA
Mane dé zarko diakhal nama😂😂 mome zéro pression
Boope bi aka bakh
Bilahii nilako wakh won zarko mo man Ada fass
😂😅 zarco kagn leu
Bilahi
@@cheikhndiayetouba040 Mane mi baréwoul sakh maako gueneu kham Zarko.
Amna fit amna doolé moom Zarko..
Ta boy yi danouy naagou trop.
Tay loolou la wakh mani zarko dakoy daan parce boy day minimiser Zarko ndakh khamouko.
Zarco vs gris deux comba la dh 🤝😍😍
La vie continue felicitation Zarco courage a Ada Fass
OOOOH TAY MANDI NANIOU LAMB WAY SUNU SPORT NATIONALE NÉKH NA❤️♨️
Boul real bax lé woul rek nguén daw ci thi lamb j😂😂
Vraiment li moye lamb nekhena trop felicitation zarko es tu courage ada fass mes supportere yi billayi amaniou yarr dara yague bakhoule c est pas serieux li sa fait honte li sounou sport national le waroulaine def li adouna yeup diko kisse ken begue lamb avancer ak image you bone yi
Zarko félicitations sois plus sérieux dans tes combat respecte les amateurs et tes adversaires Ada fasse du courage
Je signe pour une revenche
zarko vs siteu parce qu'il y a eu ambiguïté lors de votre premier combat
Ton deuxième combat potentiel
Zarko vs Mouss ndoye
Felicitations Zarko👍🏾❤
Ada face dafa nagu comunicazione
Zarko vrais mbame khoukh le koi😀😀😀😀 mouy doigt d'honneur 😀😀😀😀 ada fass courage.bravo zarko.
Merci Zarco pour cette belle victoire contre Ada fass💪😂
Ada fass trop orgueilleux pour son âge. Je suis de pikine mais il fallait corriger ce jeune homme pour qu'il soit desormais respectueux envers ces anciens. L'experience et la confiance en soi a permis une victoire à zarco et une belle chute. Ada fass doit apprendre à être discrèt et sage.
Lamine vrai reporter meilleur d sa génération
Zarko à diarama yo poulagu yaarou yesso
Aminé
Non hhh🤣🤣🤣 kén dou iow billay Doomou fouta dou ragal bravo ZARKO💪💪🏽🏆brom grand yoff
Merci Zarco ,khaler dagnon Bari wakh
Domou Grand Yoff le nak 🙏🏼❤️🤸🏽
Watal machalah
Zarko ☀️☀️☀️☀️bandit la..Fire boom!!!mes felicitations
Zarko félicitation Merci grand yoff beugue nagniou bilay
Bravo zarko am nga fit moun nga beurè tè dof nga ci entrainement mais staf rèk mola manqè mais heur bi warnala fek ngaýe beurè niom balla gaye2 tapha tine
Ms Zarko forme bou graw la yorr🤣🤣 très musclé
C'est du jamais vue Zarko ya woor💪💪💪
Felicitations zarko 4ans spain
Deff retour 3 combats 3 Victoria jeul risque dane mbaye guy gui ak niome ak Ada fass
Nako gouye gui dieul mba junior yekini
Felicitation zarko suis content sii iow
🔥 Les Potentiels adversaire de Zarco
Zarco vs Yekini jr
Zarco vs Gouy Gui
Zarco vs Modou Anta
Zarco vs Moussa Ndoye
Zarco vs Jackson
Zarco vs Ness
Zarco vs Alioune seye 2
Sauf Jackson
Zarko Diène kaïré aussi combat bou nèkh lay doon dé.
Zarko vs Gouye gui moy combat. Zarko combat thiow la sokhela bou nekh ame ambiance. Zarko gouye gui signature dara dakouko 😂😂😂
Zarko-Diene Kairé waleu Zarko Alioune Seye Jr.
Jackson neu ligueyat boum yakamti il est temps mbeur yi am plan de carrière mais niom lamb thiow rk motakh amneu défaite yi niouy am dougn diogat. Jackson kouko encadré mom ak Thiatou Daouda Fall dinagn indil satisfaction guediawaye
Vous vous souvenez de onde le fou , un excellent lutteur il était ❤
Franchement il mérite emplement quon lui donne ceux qui sont dans la cours des grand zarko bayil mayei chance bi tu as assez bien prouvé
Zarco mo leu gueuneu waga fouffffffffffffff🤣🤣🤣🤣🤣 félicitation zarco du courage ada fass
Un sport de combat comme la lutte c'est sur un algorithme d'intelligence :
Action-reaction-action.
Toutes les techniques sont dans ce logarithme.
AdaFass a manqué terriblement de réaction de et réflexe. Il devrait simplement laisser sa main droite agripper derrière le nguimb de Zarco pour avoir une troisième appuis et le tour est joué.
Félicitations à Zarco et félicitations à AdaFass
Wakh yomb na deh, mais les réalités à l’instant T sont toutes autres. Zarko moko meun c’est tout
Boy bii da commencé khawaa bariii wakhh toutiii rekk,,,, mais bon c’est pas encore trop tard,,, tu reviendras plus fort
Yénna wakh thii zarko rkk mais Tony jr mongii diekhal xaleyii
Boy bi si bopam mo meun beurè
Je l'avait dit que ada fass a fait un mauvais choix fallait pas prendre zarko
Staff bou bone la yoor Ada mo wara deim écurie fass si niom Gris Bordeaux
Ada fass amoul loumouy perte ci combat bi.. Zarco vs gouy gui combat leu
Bi combat bi taxawé lolou mo done wax-j.
Mais liguey na loumeu dane Zarko mais dieuféwouko.
Pour Mome beuré Zarko ci beutt la yam. Lolou la téthie nangouwoul Zarko fétéko bén yone souf. Zarko aussi comprendre diémko nogatou ba li fék ko ci.
@@pronosticfootsenegal1112 wi buko ada danon zarko mo siy pert me zarko gouy gui wala zarko siteu
Ana borom wax diou Bari ji merci beaucoup zarco
Zarko dan nga wayé tegoyone si linga beré adversire dankoy respecter tay so danouwone dinga deig louné '''Mes Ada fass mbeur day lakatu defaite bi nak molay def mbeur ...
Zarko n'a diele siteu bilay combat la
Félicitations zarco boy bi dèla khamoul rek mobile wakhone nako mais courage ada
Zarko ndele bi da âme doole🤣😂😂😛
Felicitations zarko kessé lagnouy topou do khôl 👀✅❤️🔥💪🏾
Bilahi Zarko dou ñekhou ñeber do khol yoi
Félicitations zarko grand yoff
Vrai diaye prek leu 😂😂😂
Lamine aka bakh nena grawoul ❤❤
Ducourage Ada fass champion Dina bakh inchallah
Non mé Kou d'accord ni Zarco Bandit😂 leu rek Lalle ♥️♥️♥️😂
Merci zarco bien joué 💪💪💪💪💪
Zarko quel technicien bravo champion
Zarko félicitations 🥰💪
Dolé Dokhoule Díame, Zarko est Plus Fort que Boys yi. MACHA'ALLAH.
Zarco est mature maintenant 💯✍️
Le doigt d’honneur de Zarco !!! hhhhh 😂
Ada fass dafa niapa ndayam bari waxx 😅
Wakh mo bari
😂😂😂😂😂
Apprenez à respecter nos athlètes
@@bmkillertv1849 qu’Ada fass se respecte lui même en étant mature et en évitant les réseaux en tant que Mbeur…!!!
Lindia bi dall nako dh😅😂
Li sport leu affaire saga yi bokoussi. Faut respecter ses sportifs le plus grand et le plus petit. Sport rek leu
Wa maani aniii toucouleur yiii séné lokho si kao sen dom amna ndam
Niogui nii
Boy bii da beuri wax
@@SambaSeydisenegal needoo koo mbadoum
Zarko nagne ko déllo Europe sinon dinafi ray mbeur 😂😂😂sadick la koi
Zarko & Musaa Ndoy
Zarko & Neex
Revanche Zarko Guy gi
Wàlla Zarko Lac.
Kong la saga la daan la😂
Lutte tv mes félicitations à vous
Nioune mouye meti mouy nekh nioune ioe lay beug fier de toi ada fass bo diar yone la Nioune ioe rk laniouy topou ada nakarou du courage frère 💪
Zarko si boyyi la nara tekki Lamb khaliss diene vs zarko Zarko vs gris zarko vs situe combat la
Quel victoire zarko gouy gui combat la siteu combat leuh
Zarco nena do toul beuré ak siteu
Ada fass sa nguémbe bi taamit 😂😂😂😂😂
Wakhone nani ada fass na défe atatinons thi zarko ndakh zarko adversaire bou nakaré beuréle la thi tous les plans mais ada fass na défarouwate té khame fomouye téke tankame té maytou lou beuri ndakh khaléla té lambe mingi thi kanamame félisitations zarko
Félicitations zarko et du courage Ada fass mes autorités grand Yoff yi nagnou diapalé bou bakh zarko tamit
Lindia la ✨dOumeu leu✨saGa la✨Dane la ✨zarcO kassé ✨Grand yOff sOuniOu Deuk dO khOl 👀
Ada fass dagne la noke sagala danela 😂😂😂😂🤪❤❤❤❤Zarko machalla ❤❤
Sarko a bien travaillé dan ce combat
Combat yeupou la ligey zarko masoul niaka indy état
Kou guisse kongue bi reck lalale j aime
Bou Niang Bou ndaw dane Ada fass vs Niang Bou ndaw combat la
Ada Tay mom danga roukh Zarko vraiment dafla diay prek Lamb j yeup nga roukh
Zarko vs Boy Niang combat la ,Zarko vs lac 2 combat tmt boy yi doyna seukk
Lindia naniou malfaiteur bii 😂😂😂
😅😂deub lindia
Hamul boy grand Yoff bi
Ada Fass combat bépou dako diafandou. Mano baña encaissé, bañ sa adversaire fété la souf.
Biko Zarko dioxé thieur ci guéw bi dafa farone dirigé, andi sañ sañ, toñ ko pour Zarko andi maniname mou dane ko ci.
Mais warona xamni combat bén bén ak diap deguelou dou ci dane Zarko.
Zarko der la ci guéw dou beuré banga néko cim.
Billahi zarco dafa decide deh zarco vs gris combat leu
Zarko Non stress lay Dounou kii 😂😂😂Dii beraii Dii foo dii sagua waa tribune 🏟 bi baparé sokko Danne 😂non Zarko vré Faxeu Man la kiii 😂😂😂
Ada tay mom danga roukh Zarko dafla diay prek diay la bandit nangou lamb j danga done diay Rew mais tassé nga ak koula gueuneu rew gueun leu Waga doumeu leu Mbeulé sa supporters sagua lene baparé dane la
Bilahi wakh gua lép
Arbitre yiiii war nanio wakh akk niom kamm danio wara bayi lutteur yiii consentreou kamm
Merci zarko Ada dafa beuri ndaye wakh
Ku guiss ni paa bii di wakh daa faral zarko rk laalal j'aime 😅
Zarko vs Gris combat là dh
Pit t'en 😳 moy Bandi dhe dofla tamé zarko 😀😄😆🤣🤣😭😭🤔🤭🏃🏃🔥🔥🙆♂️🙆♂️
Ada courage nioune ioe laniou beugg 🫶❤️ félicitations zarco 👏
Une chute très spectaculaire de zarco
Zarco diéle bou raye quel champion
Félicitation A Zarco et du Courage a Ada Fass
Félicitations gaynde bi du courage Ada wagnil wax wathiée Sax boop touti oke
Zarko l'a mis dans une pièce
Ada a trop pris le combat à cœur avec fougue
Deh Ada limou djap si nguîmbe dafa yague deh beuréwoulll
Zarko, il a de la force intérieure
Trop souple comme l'a dit Lamine
Zarco dieulal gris rek wala lac il est temps gua yekk
Félicitations le sang 🩸 🎉
Du courage Ada ndakarou yay souniou mbeur dafarou water💪💪
Merci Zarko.
Comme ça mou nopi. Beuri wakh torop boy yi té défougnou dara si lamb. Na dieul thiatou yoff
Sa badio yaye ioe
@@boussethiam6015 Dieureudieuf. Bayi nala ak yalla Inchallah. Khasbounallah wa nikhmal wakiil
Lamine ndeysan Aka bègue lambo bogol ben yon cemera bi diel boy yi di yakh sess yi😂
Zarko mo beuré mo daane❤
No zarco bandit leuh bly✌️😅