Mawahibou Darou Mouhty Kurel 1 Tout Tank HTDKH TOUBA KAZU RAJAB 2024

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 фев 2025
  • КиноКино

Комментарии • 235

  • @abdourahmanendiaye8742
    @abdourahmanendiaye8742 Год назад +31

    Aay boulen yalla fayé aay boulen Yalla fayé❤

  • @abdoukhadresamb2565
    @abdoukhadresamb2565 Год назад +29

    Jërëjëf Borom Touba ❤❤❤❤❤❤❤Walahi sante nala Mbacké 😭😭😭.Pass-Pass bi ma âme si diné (donté déssana Lou bari)xame nani Bo guéno Si mane , maye gueuneu yéess gnép. Yalna nala gueune di beugue Mbacké.

    • @ndiobagaye6627
      @ndiobagaye6627 2 месяца назад

      Thiey pour mane rek makoy yeug boudoul won Ahmadou dina Déme nenéne

  • @MountakhaThiam-i4g
    @MountakhaThiam-i4g Год назад +56

    Thieuy darou khoudoss lounou diang mou nékh mangui ziar serigne khadim dia sama wadji

    • @ChiekhFall-te5fq
      @ChiekhFall-te5fq 3 месяца назад

      Non daaru Muhti la Dou daaru khoudooss dh ku baax ki 🙏

    • @MamorGaye-h9q
      @MamorGaye-h9q 2 месяца назад

      Kourél darou khoudoss la ky ​@@ChiekhFall-te5fq

  • @alfaadalpro4768
    @alfaadalpro4768 Год назад +30

    Cheikh Ndiaye yallla na nga goudou fann barkepp borom Touba

    • @bakhesall
      @bakhesall 11 месяцев назад +3

      Amiine waay billahi aka bakh machallah

    • @alfaadalpro4768
      @alfaadalpro4768 11 месяцев назад +2

      @@bakhesall ta yarou loool barkepp Serigne bi

    • @ismailaaw9807
      @ismailaaw9807 11 месяцев назад +2

      Amine

  • @antadiop6272
    @antadiop6272 11 месяцев назад +4

    Naysane machallah❤️
    souniou pa beyti yi Darou Mouhty yalla nagn fi yagu té werr

  • @mbow78
    @mbow78 11 месяцев назад +4

    Ndeyesan😭kené dou saigner touba mbacke bilay ki yalla nanuko yalla fayalé 🤲❤

  • @Dieylanidiop28
    @Dieylanidiop28 Год назад +13

    Daadiou Daarou Muhty founiou ko dianguei nga am lo yeuk kénn dou wa Ahlou Beyti🕊️

    • @MamyDiouf-sq8fd
      @MamyDiouf-sq8fd 11 месяцев назад

      1

    • @Fatou-su8nj
      @Fatou-su8nj 7 месяцев назад

      Bilahi ken dou wa akhlou bayty​@@MamyDiouf-sq8fd

  • @mbow78
    @mbow78 11 месяцев назад +4

    Bilay wally serigne touba amoull morom❤mashallah yalla nalen yalla défal Djamé aminé 🤲 waye ❤❤

  • @CheikhNdiaye-ru7jv
    @CheikhNdiaye-ru7jv 11 месяцев назад +6

    Ndaysan Cëy xassidayi lén méloutt nh mome wallahi mais wah darou khoudosse ken dou ñiome yên rek lay topou aduna kouy weur ndiag mou nekh th deugou ñieuweul thi wah darou khoudosse yall nalên serigne dolê dimbeuli yagg lên fi loll way diagg katt yi😙😙😙

  • @cheikhdiouf1074
    @cheikhdiouf1074 13 дней назад

    Diawrine Cheikh Mbaye HT Yalla na Yalla yëssaal yeurmendé sikawam té kharréko aldianna firdawsi 😭

  • @ibragaye2320
    @ibragaye2320 11 месяцев назад +4

    Ndaysan wallahi nekhna lol yalla na léne yalla faye si barker xassida yi❤❤❤

  • @k1htdkh662
    @k1htdkh662 11 месяцев назад +7

    Am ndiague mom yen lako serigne bi ndenk bilay nekh na lol way

  • @papedaoudafaye8379
    @papedaoudafaye8379 Год назад +7

    Machallah diangue bi nékhna lol Barki Borom Touba. Yalnaléne Serigne Touba féyale boppame. Walaye danguéne meuna diangue yéne wa Hizbut Tarquiyyah Darou Khoudoss❤❤❤❤❤❤❤

  • @komxel
    @komxel Год назад +19

    Demleen tewlu ci 33mn maaha dalaala ak khad khada moohu😭😭😭 Tolluwaay yu doywaar la ci tout tànk htdkh yi jàng hooooo limay degue diko yeuk fofou motax damakoy arrière rek diko deglu waat mu yeem ma lool wallaahi ci neex masalla yalna yalla musëlnu ci thiat bafawu te samu and bi ci ligeey bi ci xasidayi ak lepu lunuy ligeeyal boroom tuubaa ci htdkh yalnanu doon ay milliardaires yu woolu boroom doyloko diko ci ligeeyal bubaax ci wet gumunu ligéey lool te yalnanu boku am ngërëmul boroom ak guddu fanak werak jamak xeewël ak sutura busax bafawu adina ak allaaxira amiin ci barkeb xasidayi nu dund ba sunuy doom ak sunuy seut fekantek nun ci biir ligeey bi bokuko ak nun and ko ak nun te lepu geuna rafet geuna baax amiin ci barkeb xasidayi

  • @HTDKH61
    @HTDKH61 11 месяцев назад +3

    Bilay yéna meune barké serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @khatabdieye4320
    @khatabdieye4320 11 месяцев назад +2

    Aye waye Djilé likeu geuneu nekh khalass❤

  • @bghistgeo3886
    @bghistgeo3886 Год назад +8

    24 mn 15 seconde bii boum la rawe seuteuttt waw baxna rek ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @BeuggXassidadiouf646
    @BeuggXassidadiouf646 Год назад +9

    C'est les meilleurs sans doute ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤O' vous aime Hizbou tarkhiya Darou khoudoss

  • @MorNdiaye-o9w
    @MorNdiaye-o9w Месяц назад

    Dieureudiefe Serigne Touba

  • @abdouamar6373
    @abdouamar6373 Год назад +7

    Ndeysane yalna yalla samm leen❤❤

  • @Mbeneseck-vi5ne
    @Mbeneseck-vi5ne 11 месяцев назад +2

    HTDKH 💚🤍 geuneu foncé RK inchallah
    Mawahibou de l'année ❤

  • @damendiaye3353
    @damendiaye3353 11 месяцев назад +2

    Macha allah sama Diange katt yi tout tank hizbut tarqiyah Darou khodous ♥️♥️♥️

  • @bassirouka4278
    @bassirouka4278 Год назад +14

    3em dath bi ❤yawmal khiyam lay saff😢😅❤❤

    • @HTDKH1717
      @HTDKH1717 Год назад

      😂😂😂❤️

    • @Chatndiaye
      @Chatndiaye Год назад

      😂😂😂😂😂😂😂😢😢😢😢😅😅

    • @AbdouFall-g5f
      @AbdouFall-g5f Год назад +1

      Mom kay kimane le😂😂

    • @Oumar-j2q
      @Oumar-j2q 11 месяцев назад +1

      Môme fougniou ko dielé sakh

    • @khatabdieye4320
      @khatabdieye4320 11 месяцев назад +1

      Wala Firdawsi kay😂😂😂

  • @freegunbxc3918
    @freegunbxc3918 Год назад +4

    Tiey serigne cheikh ndiaye ,beug nalaaa beug koumaa tayoull 😊😊

  • @khadimniang6151
    @khadimniang6151 Год назад +7

    😢😢😢seet kou sa khôl yeuk Serigne bi danga yeuk Ndiag mi barkeb Boroom touba

  • @kossothioye528
    @kossothioye528 5 месяцев назад

    Alhamdoulilah Rabbil Hanlamiin Dieureudieufaty Cheikhouna Akhmadou Khadiim

  • @falloudia-lx3mc
    @falloudia-lx3mc Год назад +9

    Kou beugg kharou rk man del deklou htdkh 🥰🥰 cheikh Ndiaye mii sk nit leh sheeet 😢❤

  • @OusseynouGaye-ew5dl
    @OusseynouGaye-ew5dl Год назад +2

    Toubarkallh li nexna lool machallah thieuy sm gars yi wa htdkh

  • @MamadououmarDiaw-i6j
    @MamadououmarDiaw-i6j 11 месяцев назад +1

    Ndeysane amna yeurmande nexna thiey ahmadou yalnanouco yalla fayal

  • @leyefallou4349
    @leyefallou4349 11 месяцев назад +1

    machallah thieuy s Touba aldiana deh sori woul ndaxte thi xoll les Koy dounde 😢😢😢😢❤❤❤❤

  • @cheikhounadiouf5489
    @cheikhounadiouf5489 13 дней назад +1

    Manchallah 🎉❤

  • @MourtallaLo-xh7ue
    @MourtallaLo-xh7ue Год назад +8

    HTDKH c'est la rois du forêt

  • @fallougueye5898
    @fallougueye5898 11 месяцев назад +3

    Darou Mouhty tigui Machallah ❤

  • @cheikhmamadouabdoulayefall6254
    @cheikhmamadouabdoulayefall6254 Год назад +3

    Walahi yalna len yalla fayyy

  • @bayecheiksarr9541
    @bayecheiksarr9541 11 месяцев назад +2

    Machalla df nèkh ba wêssou nèkh 😭😭😭

  • @AwaTaye-r9t
    @AwaTaye-r9t Год назад +8

    29:06 Goré mourid Machalla néhk na dé❤❤❤❤❤❤

  • @morawahtdk39
    @morawahtdk39 9 месяцев назад +6

    Serigne Touba mognou mom dé

    • @cheikhleye584
      @cheikhleye584 4 месяца назад

      Werna 😢😢😢😢❤❤❤

  • @AHMADOUKOUROUMA-z5m
    @AHMADOUKOUROUMA-z5m Год назад +5

    Htdkh université bou make ligueye bi dh dou taxawe sikawe rck la dieume

  • @Majalissousalihiin
    @Majalissousalihiin Год назад +2

    Machallah Thiey Tout Tank yi❤❤❤

  • @modousarr542
    @modousarr542 Год назад +5

    Yéneu meuneu diangue wayy❤❤

  • @LamineDiop-ze6cf
    @LamineDiop-ze6cf Год назад +4

    Bilahi borom darou mouhty bègue nathi yénn
    Kou deglou mawahibou bi rk kholam Toy nah

  • @khadimfall7975
    @khadimfall7975 11 месяцев назад +1

    Serigne elhadji Ndiaye sama Wadji yala n'a yala Guen la same li nekhna tourop walahi Di begue wale s khadim Dia bou bakh machallah

  • @ahmadoubambaseck4292
    @ahmadoubambaseck4292 Год назад +2

    Waa daaru xuddóos jaaxal nañ ma nag vraiment

  • @serignembackeniang2664
    @serignembackeniang2664 11 месяцев назад +2

    Theiy darou khoudoss ❤❤❤

  • @modougadiaga5305
    @modougadiaga5305 11 месяцев назад +4

    Doma si doyal❤19/2/24/12:27

  • @abdoulayeyath675
    @abdoulayeyath675 Год назад +4

    Lii kawe na lool Manchallah

  • @mawabousso7273
    @mawabousso7273 Год назад +1

    Ma chellah Cherif Gueye ma ngi lay ziaar ak wa kourel bi yépo❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ChiekhDiaw-fu7kr
    @ChiekhDiaw-fu7kr 11 месяцев назад +2

    Wallaiy yena mann mann de yenne rk ly tooppo 😢😢

  • @Fatou-su8nj
    @Fatou-su8nj 7 месяцев назад

    Diangue by nexx na wérr na machallah yallah na lén Serigne by faye ci barkép xassida yi mais moi xassida mawakhibu mon bonheur ❤

  • @mouridesadikh435
    @mouridesadikh435 Год назад +15

    Le meilleur Moy Htdkh ❤

  • @mubawaasidqintv
    @mubawaasidqintv Год назад +4

    Thieuy Yalla, Waaw leen Goor waaw leen Goor Waaw lenn Goor. Yalla nalen Yalla saam ak mboleem Jangkatu Qasida. Toyaal ngen xol yeep😭

  • @Sahadatou_toulab
    @Sahadatou_toulab Год назад +1

    Yalla na lene yalla arre lene

  • @SerigneMbackeFall-k4t
    @SerigneMbackeFall-k4t 11 месяцев назад +1

    Thieuye sama wadji Mame cheikh Niang dingama faat dh billahi wallahi 😊😊

  • @moustaphadieng3840
    @moustaphadieng3840 Год назад +5

    Yennne mennne wayyye😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @MFG_14
    @MFG_14 Год назад +3

    HTDKH 😍🥰😍❤❣FOREVER AND EVER

  • @modoubambakane3076
    @modoubambakane3076 Год назад +17

    HTDKH les meilleures

  • @AlassaneBa-x3y
    @AlassaneBa-x3y 11 месяцев назад +1

    nekhoul ba nekhoul waye yen gni ay diambari serigne touba géeen

  • @MamediarraLo-o5o
    @MamediarraLo-o5o 11 месяцев назад +2

    Adina ak alahira yenasi daka diange bilahi walakhi darou khoudoss rek bilahi

  • @diengfallou9829
    @diengfallou9829 Год назад +6

    Cëy Maam Seex Ibra ñaŋ mii Waay

  • @ouzseck4344
    @ouzseck4344 Год назад +4

    Walahi htdkh damalen beug rek ❤

  • @FallouFall-k2y
    @FallouFall-k2y 11 месяцев назад +1

    Machallah li nekhna trop 😢

  • @mamemaremelo2495
    @mamemaremelo2495 11 месяцев назад +2

    Wa rim kat yi thi souff bakane ngendi lathie wala😂

  • @CheikhFaye-dj9tf
    @CheikhFaye-dj9tf 8 месяцев назад +1

    Wa li nekhna way❤

  • @moustaphandoye7811
    @moustaphandoye7811 Год назад +5

    Fin 3em khabb wi saway dina ma si raay rk😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢

  • @AwaTaye-r9t
    @AwaTaye-r9t Год назад +2

    Mawahibou de lanée❤❤❤❤

  • @saliouGningue-de4bi
    @saliouGningue-de4bi Год назад +8

    Serigne bi moma neu binde

  • @Azert-z5v
    @Azert-z5v Год назад +3

    Machallah ❤❤❤

  • @FatouKinéMbaye-t2c
    @FatouKinéMbaye-t2c Год назад +5

    ❤nekhati na🥺

  • @alfaadalpro4768
    @alfaadalpro4768 Год назад +2

    Louné maa ngi koyy deggg❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndongokhouma
    @ndongokhouma Год назад +3

    Htdkh ❤❤

  • @MohamedDiouf-ds1kq
    @MohamedDiouf-ds1kq Год назад +3

    Htdkh❤

  • @laminethiam2699
    @laminethiam2699 Год назад +2

    Bilahi yéna mana ndiangue

  • @diengfallou9829
    @diengfallou9829 Год назад +3

    ماشاءالله تبارك الرحمانِ

  • @mandiayediop
    @mandiayediop 11 месяцев назад +1

    Ëskëy 😢
    Cëy YALLA saa BOROM 😢😢😢

  • @mamelamp6983
    @mamelamp6983 11 месяцев назад +2

    BOROM TOUBA dou moromu kennn ☝.

  • @alfaadalpro4768
    @alfaadalpro4768 Год назад +5

    DAROU KHOUDOSS wéesou Daara UNIVERSITÉ LA WALLAAHI

  • @alfaadalpro4768
    @alfaadalpro4768 Год назад +3

    Barkepp Naala dialaaalaaa❤❤❤❤

  • @MourtallaLo-xh7ue
    @MourtallaLo-xh7ue Год назад +4

    Nous sommes meilleures ❤❤❤❤

  • @dieyehane5001
    @dieyehane5001 Год назад +1

    Kawé na lol Mach'Allah ❤❤❤❤❤

  • @IbrahimaDiop-t1v
    @IbrahimaDiop-t1v Год назад +1

    Ndeysane nekhna lool❤❤❤

  • @khadimthioune6229
    @khadimthioune6229 10 месяцев назад +1

    Ndeysaane 🎉🎉🎉

  • @khatabdieye4320
    @khatabdieye4320 11 месяцев назад +2

    19ème minute thiey samp ba

  • @AbdoulayeSambe-l
    @AbdoulayeSambe-l 11 месяцев назад +2

    that's awesome

  • @papinodieng7726
    @papinodieng7726 Год назад +2

    Wa 3ème dadj bi mom ❤

  • @AwaMbaye-zy3tj
    @AwaMbaye-zy3tj 8 месяцев назад +1

    Thiëyy 😅❤

  • @mustafaalkarim3428
    @mustafaalkarim3428 11 месяцев назад +1

    ❤htdkh

  • @BassirouBèye-v2o
    @BassirouBèye-v2o 11 месяцев назад +1

    😢😢li nekhna

  • @murtadaajonn6502
    @murtadaajonn6502 11 месяцев назад +1

    Céy lu neex daal neex na❤❤❤

  • @cheikhseye4712
    @cheikhseye4712 9 месяцев назад +2

    Thieuy 😢😢

  • @AbdouFall-g5f
    @AbdouFall-g5f 11 месяцев назад +1

    Ndeysan li kémane la dh😂❤😂 tarkallakh

  • @LatteDiop-oe5ql
    @LatteDiop-oe5ql Год назад +2

    Machalla ❤

  • @zanzosaar891
    @zanzosaar891 11 месяцев назад +1

    Waw len gour way😢❤

  • @AdlaDaou
    @AdlaDaou 11 месяцев назад +1

    Thieuy Mame Dame❤

  • @KodeThiam-i3f
    @KodeThiam-i3f Год назад +3

    Ndeysane❤😭

  • @modoungom6368
    @modoungom6368 11 месяцев назад +1

    Cheikh ibra ya meuna woy 🎉

  • @EMDNSD
    @EMDNSD 11 месяцев назад +2

    Waa li nexx na dh 😢

  • @MoussaKebe-ig1ej
    @MoussaKebe-ig1ej Год назад +1

    Mangui bou bakh kan mothe djilly Ndiaye thie souf❤❤

    • @papamasseneseck6818
      @papamasseneseck6818 Год назад +1

      Djily dou toutank té nékkatoul Darou khoudoss moungui si Ablaye Diop

    • @MoussaKebe-ig1ej
      @MoussaKebe-ig1ej Год назад +1

      Saway degoma des damanè borom riim yi djilly Ndiaye doon dèf amna koukay dèf thie biir kanla

    • @mbayediane7442
      @mbayediane7442 11 месяцев назад

      @@MoussaKebe-ig1ejmame cheikh ibra la

  • @alfaadalpro4768
    @alfaadalpro4768 Год назад +5

    l'Université DAROU KHOUDOSS

  • @Defdaraaa
    @Defdaraaa 10 месяцев назад +1

    Ndieysan

  • @MbayeBabacarsamb-w9g
    @MbayeBabacarsamb-w9g Год назад +3

    Waay bakhna rék 🤭🤭🤭