Nagnou gueuna Diap si serigne touba mi mbokou talibé yi bagn ko yamalé dra serigne kenn leu dh defal nagnou lep niossi dess guena goor goor lou si héritage bimoufi bayyi mouy khassida yi. Dieuré Dieufé Cheikh Ahmadou Bamba khadimou Rassoul❤nioune ak yw ba yawmal khiyam 😍
😭 Ndeysan Thiey Serigne bi li kawéna trop khassida yii moy lepp ndiageumi kawéna yalla na Serigne bi Sam té are la si bareké Mame cheikh Ibrahima Fall ❤❤❤❤
ohhh MachaALLAH serigne SALIOU namoon nanu la . Yalna la sunu BOROM dolli saam ak fan wou goudou YALLA boolé la si MOURIDES yi SERIGNE BI geureum. Yalna baat bi wer, begg nan lool waay amal diam yaram
Serigne Saliou Aissy 👇
ruclips.net/video/J41kRkjcR5Q/видео.htmlsi=NCAyCj9eKwb1j7Vd
Serigne saliou assiy xanaa amoul télégramme bou am ay audio
Sa bi Magui ziar Khana diangou ko marahib
MachaAlla serign saliou borom touhfatou bou nekh ba. bagay toutank ba legui watho yone wi. Yalla Naga tassé ak gueureumou borom touba
MashaAllah Allahuma Amine ❤
Machalah goudou fane ak wer S Saliou touhfatou❤
Dieureudieuf Serigne Touba khadimou Rassoul Diarama Cheikh Ibra baboul mouridine
Bilay nekh na way si khol serigne touba kenela yalna yalla yok ay leram amine yarambi
Nagnou gueuna Diap si serigne touba mi mbokou talibé yi bagn ko yamalé dra serigne kenn leu dh defal nagnou lep niossi dess guena goor goor lou si héritage bimoufi bayyi mouy khassida yi. Dieuré Dieufé Cheikh Ahmadou Bamba khadimou Rassoul❤nioune ak yw ba yawmal khiyam 😍
Akassaa Ndeysaan Jaajeufati Werr na
YALLA nala Serigne Touba faye barké Khassidas yi barké Alkhourane
Serigne khadim ayssi yaalnanga am ngeureumeul borom touba
Ohhhh😢😢😢😢 dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba dieurdeufty Serigne Touba
😭 Ndeysan Thiey Serigne bi li kawéna trop khassida yii moy lepp ndiageumi kawéna yalla na Serigne bi Sam té are la si bareké Mame cheikh Ibrahima Fall ❤❤❤❤
Macha-allah dieureudieufaty Serigne TOUBA Cheikhanaa Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul
Yalla nanou ko YALLAH fayal ❤ ❤ ❤ Amine ❤ ❤ ❤ ❤
Amine Faal
Dieuredieuf Serigne Touba Khadimou Rassoulillahi ❤❤❤
🥰🥰hoo boumou lale souf jërëdjëfy serigne Saliou Mbacké brome touba amoul morom 🙏🏽🙏🏽
Akassa suma doom. Mucc ak xeweul ba faaw barké Xadimul Rassul. seene keur la nekké murid. Dila beugué rek
Waaaaaw liii moom yalla wé na di laay laa baye serigne saliou yagal te wair yaw fall da nga war di diangue
ohhh MachaALLAH serigne SALIOU namoon nanu la . Yalna la sunu BOROM dolli saam ak fan wou goudou YALLA boolé la si MOURIDES yi SERIGNE BI geureum. Yalna baat bi wer, begg nan lool waay amal diam yaram
Al hamdou lillah dieura dieufatiy cheikhouna cheikh ahmadou bamba ❤❤❤❤
Masha Allah sama serigne c'est à travers vous que j'ai découvert touffatouh mouttadaraïni longue vie à vo.
Ohhhh nèkh na tropp tropp billahi yalla samou la barcke borom touba ❤❤❤
❤❤❤ ndayssan nekhna lole❤❤❤ dieureudieuf Serigne Touba ❤❤❤
Dieureu dieuf sëriñ Saaliwu asi yallah gau tase ak garamou sëriñ Tuubaa
Machallah ❤️ 🥰 thiay brom touba jërëjëf
Désé loo niou dra yalna la bour yalla fay brkép mouhamed *ﷺ*🙏🏿❣️Mbacké jërëjëf 😢😢
❤❤❤❤❤❤
Njang mi neex na tē tegginē ! Yalna Sëriñ bi sam la tē aar la waay❤❤❤❤❤❤!!
Mashallah 🥰 tawfeikhh ak taysir Serigne Saliou
Ohhhhhhhhhhhhh😭😭😭cëuy Ahmadou kén khamoul loumou doon ❤❤❤diereudieuf Borom Touba diaarama Mame Cheikh Ibra Fall Lamp ❤❤❤❤❤
Ndeysane safena Yallah lole machallah
Serigne Saliou Aïssy Jërëjëfëti si Nourou Dareyni bi kawèna lolllll sakh
Macha Allah Dieureudieuf Serigne Touba🙏🏼
Thieuy ❤❤ macha allah guena yague guena were incha allah
Serigne saliou del diangue way. Boul di rare❤❤❤❤❤
Yalla nala sa borom dolè samm si barkep segn Abdoul Rahman
Ndaysan machallah norou bi nekhna dh ❤❤❤
Lii rékk lanouy topou Bilahi
Machalla Thiey
Xassida dolem kawé na😭
Machallah Dierjeufé cheikh ahmadou bamba ❤️❤️❤️❤️❤️💯💯💯🙏
Ndaysan li nekh SERiGE Touba amoul morom ❤❤❤❤❤❤❤😢😢
Machallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
S saliou li kawéna lol way❤❤serigne touba amoul morom
❤❤❤❤❤ xol sedna brome touba jeureu dieuff
Ndeye saane
Ndeysaan lii kawéna ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤santé s touba rek
Machallaa Xidma Tv ❤❤❤
Machalla sama wadji sa kaw sa kaname barki brome TOUBA❤❤❤❤
Ohhhhhh thiey li waay
DIEUREDIEUFATII SERIGNE Hamssatou Mbacké 😭😭🫂
نورالدين 🥰😢
❤❤❤Guena yague guena wèrre SERIGNE SALIOU ❤❤❤
Machallah yalna yallah barkél
Thieye kou tedd ki amoulle morome❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf Cheikhoul Khadim
Macha Allah
Machalah dieuredieuf mm barom Touba ❤️❤️🎉
Diadieuf Serigne Touba
بارك الله فيك ❤❤
Ohhh nekhna trop❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yall nalla serigne bi faye li neikh na lol
Ndeysan waw gor 🥰❤️❤️❤️❤️
Dieuredieuf s touba amoul morom
THIEUY NOUROU DAREYNI NEXNA LOLL❤
Jërejeufei Serigne Touba ❤
Waw gooooré wayyyy maté nga ko dh❤️❤️🌺
Yalna yalla sam té barkél la
Machalla dieuredieuty serin Touba ❤❤❤❤
Thiey ndeysane ❤
Ohh thiey li kawena bilahi 😭😭
Lool kay
Massallah
Mashallah ❤
Cëy xassida ❤❤❤🎉
Cey ndaaysaan ❤️❤️
Diadieuf Serigne Touba ❤❤❤
Yalla nalla Serigne bi Faye
Li neikhna waye🫠🫠🫠❤
Cëy Téré bu Màak b!❤
Sallal lahu halla mouhamed
Machallah sangu yaram diadieufety
Dieureudieuff 😢
Jambaar DEUG 🙏🏾❤️
Khassida ❤❤❤❤
Jërëjëf sñ touba ❤🎉
Roubaarkallah
Diadieuf serigne touba
Machalla ❤❤❤❤❤❤
Dieuredieufe serigne touba
Diereudieuf borome touba
Cëy DAME ❤❤❤❤❤❤👌🏿👌🏿👌🏿
Mashala nekh na loll 🧠😍❤️
DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA ❤❤❤❤❤❤
Diaye ❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndaye sane 🎉
KI DAFAA DOFF ROMBB NAA BEPP MASSAMM
Ceey li mom keman la
Waw goor
Sidy Ibrahim ❤❤❤❤❤❤❤
Serigne touba
Ay waay kumay jàppalle ci son bo ngir jëmmi ku tedd ki
Whatsapp 76 755 11 48
Yalla na yalla wéral batt bi barcké xassidah yi
Diaradiaff serigne touba
❤Nourou darayni❤ma vie❤❤❤❤❤
jërëjëfëti Borom Touba
Mane der li sogne nama thi lep thi lep barki broom touba