Mane maye wakh ni dame Scipion li gaye def meuneu né sa yaye dafa liguéye yaw meuneu ga féki boy kaîré ak diène kaîré borome ndeye diou liguéye diodiou thia kaw ka kaname
Ki dafa bari wakh kou rathie dieumeulé sa kanam mou deule diene kaïre champion la mais tolagoul foumouy beré ak balla gaye ak modou lo walla eumeu séne maime aye sa thies ak moussa ndoye dougnou moromam
Père ta. Bien bollèn dieulon zoss ma parè si yènn..zoss bou retraité bobou ..diène douko dieul wayy tamit..mai ndank rekk père yow yama geunneu kham lamb sakh..mai boul yakamti ba dieuleul boy bi combat bou bonne?
Diene Kaïré vs Reug Reug moy combat...à moins k Reug Reug tapete.il a combattu ak le poulain de Diene Kaïré, BB Diene. Donc pourquoi pas Reug Reug dieulko ?
fier d'être medinoise .vive dieen diouf kairé💪💖
Diène kaïré futur roi des arènes
DIÈNE KAÏRÉ LE TIGRE DE DAKAR
Fa lér frére DIÉNE LE TIGRE DE DAKAR
Boy boul tite boul ndey ragal mangi guédiawaye mé yay sama mbeur yay sama fils
Diène Diouf Kaïré lo fonk sa Baye nagua ko doli koula beugue la ta ame si yaw yeurmandé koula beugue sa baye ya takh..Serge..🇸🇳♥️🇮🇹🤲🏾.
Diene yarouna teyna
Amouniou koudoul Diéne Kaïré
Allez Champion diéne ndame rék sa kaw sa kanam inchallah
Mane maye wakh ni dame Scipion li gaye def meuneu né sa yaye dafa liguéye yaw meuneu ga féki boy kaîré ak diène kaîré borome ndeye diou liguéye diodiou thia kaw ka kaname
Tres gentil tu seras roi
Merci pere bien dit
Père tu as raison diene si catégorie bobou la nekeu, kou ko dieuloul dangua ragal
Père kairé diawene bi loumouy wax Balla modulo eum😂 amoul niveau bi pour l'instant
Ki dafa bari wakh kou rathie dieumeulé sa kanam mou deule diene kaïre champion la mais tolagoul foumouy beré ak balla gaye ak modou lo walla eumeu séne maime aye sa thies ak moussa ndoye dougnou moromam
Pere diene kaire jambar le mais boul yakamti pere
Diene
Chiampions
Père ta. Bien bollèn dieulon zoss ma parè si yènn..zoss bou retraité bobou ..diène douko dieul wayy tamit..mai ndank rekk père yow yama geunneu kham lamb sakh..mai boul yakamti ba dieuleul boy bi combat bou bonne?
No kayre andouma ak yawe jhos morawe diene si lamb
Sétal ligay wakh
Diene Kaïré vs Reug Reug moy combat...à moins k Reug Reug tapete.il a combattu ak le poulain de Diene Kaïré, BB Diene. Donc pourquoi pas Reug Reug dieulko ?
djiéne.zose.combala.zosse.limou.déf.djiéne.défouko
zoss tokh fi aye ateu mbeure woul newone bayina diene gnifi né dane beure la wara beurel ms pas aye zoss
Père danga bakh rek mais diene tolouwoul fofou boul yakamti ba yakhal sa dom