Cette vidéo n’est pas à rater prenez votre temps 😂 Vous allez rire 😂 D’ici là je vous souhaite à toutes et à tous une bonne année 2021 anticipée 🙏🏾 Partagez au Max 🙏🏾
Lima diaxale, moy dangène fateii yalla ... naniouy diouli di wakh Yalla souniouy sokhla mou fathie ko ... délene diouli diokh Allah sén lépe bayi ndiabar katte yi ay yakh kate lagne ... merci bcp Makhfouss ... naniou khalate douniou dounde sakh 150ans Yalla naniou yalla yeureume ... naniou doylo Allah sama mbok yi
Moi suis étudiant et à chaque fois qu'un étudiant dis dans cette vidéo:"je veux du travail pour aider mes parents" mon coeur se remplit d'angoisse.que nous aide tous dans nos domaines.
14:33 Wawaw nitt bou nékk beugue nga évoluer yalla n'a yalla motal sa yénné . Yénén piégé yi aussi yalla nalén yalla défal sen beugue beugue té mou geun.
Apprante bi ndeye sanne ça m'a vraiment touche caméra cachée la ms mom ba tay mogui continue ni wadji nianall rek motakh adouna boul khep béne niane yalla nala yalla defall li beugué inchallah
M entalment bien réfléchi A ntistress de tous les jours H olala tu vas nous tuer de rires F orce à toi frère O n est très fier de toi U nion de fer avec Zé S acré réussite dans vos projets S oucis dissipés en 2021 E pithète, ma plume rime merci MAKHFOUSSE Z éro faute merci MAKHFOUZ E t ZE vous êtes formidables !!!❤❤❤💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯
🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂wouy ma gui dei Borom oto bi akk le dernier surtout no Makhfousss franchement t'es le meilleur avec zei no makhfouss do dem say dalla dague😂🤣🤣🤣🤣
Cette vidéo n’est pas à rater prenez votre temps 😂 Vous allez rire 😂 D’ici là je vous souhaite à toutes et à tous une bonne année 2021 anticipée 🙏🏾 Partagez au Max 🙏🏾
Yallna 2021 gueune fouf 2020
Mahfousse bi mome bakhoul respecter les gens way ishhh
Amine
Oui Grand frère à vous aussi
Mahfousse namone nanou la looool
Ça montre qu' ils veulent vraiment réussir pour aider leur parents yalnalén KO borom bi yombal , ça m'a vraiment touché
Amine
Ndeysan 😢
Je suis pas d’accord avec toi, nous ne devons pas faire du Shirk
@@moiberete7333 😄😄😄😄😄😄
Bilahi lou werr gua wahh mille merci a toi nalla yalla dolly souttourra amin
Kou beugue sa yaye beseul j'aime way
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Cb
Non non, Zé amoule koi déguale mounane grand bii > un j'aime pour lui wayy🙏👈
Dégeul sérère bi😂😂 "apprenti la chauffeur la beugu done am ay auto you barri" ndeysane yallah nala ko yallah diapalé 🤲🏾
Dawal auto am garage 😂
Ani sopey seydouna mouhamad yi. Meussouma am like you Bari😭
صلي الله عليه وسلم
Les Personnes qui aiment le prophète mouhamed psl aime
👇
💓
❤️
💕
Psl
Lima diaxale, moy dangène fateii yalla ... naniouy diouli di wakh Yalla souniouy sokhla mou fathie ko ... délene diouli diokh Allah sén lépe bayi ndiabar katte yi ay yakh kate lagne ... merci bcp Makhfouss ... naniou khalate douniou dounde sakh 150ans Yalla naniou yalla yeureume ... naniou doylo Allah sama mbok yi
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Sénégal Serigne rek
T'as parfaitement raison bro
Merci beaucoup
Amine
Moi suis étudiant et à chaque fois qu'un étudiant dis dans cette vidéo:"je veux du travail pour aider mes parents" mon coeur se remplit d'angoisse.que nous aide tous dans nos domaines.
Amine gorgorlul rek respecte tes parents surtout et fais ton devoir. Le reste suivra.
Noooo boy bi néna Amina la beug,,Amina beugoula demal leguéyi
mande al qouran rek lay dougual ms guissouma kouma abonner 😭😭😭😭😭tedama buega niep dideklou al qouran
abonner svp
Inshallah dina abonnée
@@cisselleveridique1274 جزاك الله خيرا
Inchallah Dina abane won
Bane bass la
Waww
Le meilleur Caméra cachée de tout les temps 😂😂😂😂
Zei c’est l’acteur du chaîne force fréro ✊🏾depuis état unis mahfousse me régale toujours un grand acteur zei 😭🤣🤣
Wadji néna mane apprenti la mais chauffeur la beugue done😂😂😂😂😂😂
Bilahi mahfouss ak zè nioy anti stress Non dama ree ba sonn ms chaque vendredi nous vous attendrons inchala
Ndeysane djieguene ki wax wergou yaram dimbli samay wadiour daw n’a yaram
Mai 2 far yi nak
Djiguen waroul bari far daf koy tardél rk
Son numéro 😭😭😭😭
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
@@sidindiaye9356 waw Lolou mom baxoul
First
Vraiment Mahfousse c est le meilleur ce qui sont d’accords likez 👇🏾
1er vue
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Good job👏dama fébarone mais dama ré ba sama yaye nane ma yaw xana dara diotoula long vie à toi et bonne continuation
Bonne fête de fin d'année 💐🙏
Makhala tt’est mystique au Sénégal 😂😂😂
Makhfouss hana seu Manager moy aimé commentaires yii 🤣😂😂😂
14:33 Wawaw nitt bou nékk beugue nga évoluer yalla n'a yalla motal sa yénné . Yénén piégé yi aussi yalla nalén yalla défal sen beugue beugue té mou geun.
"Apprenti souba
Apprenti ngone
Apprenti timis
Dawal auto
Ame garage"😂😂😂😂
Donc tu es là toi🤣😅
Am auto dawal garaz
😁😁👌😁Aka yomm sakhh
kimo naxari khel
@@ndiambesylla3927 lol sax
16 secondes rang mouy gaw anna fans mahfouss yiii 😅😅🤣😅🤣🤣😅😅
😃😃😃😃😃😃😃
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
L'apprenti m'a fait verser mes larmes 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣en rirant
En rirant🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Wouuuuy Modou bayil guel yi guel yi bayila té nga concentréwou si sa diangue🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Ana gniy commence lire commentaire avant vidéo Bi di Diekh 😂
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Mann😄😅
Moi je suis malien
Je comprend pas woloof mais c'est très coolll vraiment vous êtes fort 👍👍👍👍
Bambara mousso sabali sa
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Je vais te donner des cours wolof je parle bambara aussi
Merci beaucoup
Sila bokou 😂😂 mes djitouw mafi 😂😂qui est d’accord k zè dafa con
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Les sénégalais aiment trop les maraboutages mais koussi amm sa nianou wadiour lou begeu danga koyy amm inchallah
Le dernier m'a tué srx wouyayoyyy 😂😂😂😂😂😂
Mahfouz t'es le meilleur ❤️ depuis Canada yangui niouy ray 😅😅😅
Zei dawoor 😂😂wouÿ le dernier m'a tuée mouniko tay ngay dh 😭wa dji néko Yamana D..l ay lima rétane tay doumalén bal
Maman❤️
Zei actor mon ami tu es le meilleur 🎉❤️ bilahi vie sur toi bro 🖖
Makhefouss stp diapaléma si sama chen RUclips cité police production diap sii rrk
Vraiment sénégalais da beugue serigne
Gueumleun yalla
Il suffit de prier, avoir un bon cœur ak am gnanou wadiour c'est tout
Walahi frère
Bilahi wah gua DEUG pure
Ma khaakk
Bilay
Apprante bi ndeye sanne ça m'a vraiment touche caméra cachée la ms mom ba tay mogui continue ni wadji nianall rek motakh adouna boul khep béne niane yalla nala yalla defall li beugué inchallah
amine
Amine🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Mais DINA tas couple you bari yéna grave😂😂😂😂
Bilahi de
Mangui pointé di khaar bobu batay❤❤
Enfin yalla na 2020 gaaw djekhhh ishh.
Niougui khaar yeneen caméra cachée 2021
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
bilahi serigne bi mo gueneu done doméram yépp😂😂😂😁😁😁
😂😂😂😂😂😂😂non ki sèrieux woul mahfousse ma tuè Sheutt
Ndeysane jeunesses bou begueu tekkkè am diom yalla nalene yalla diapeulè guene tekki
Nnnnn le dernier gars m'a tué 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Yalna na sen diame yague waye 💖💖 JUST LOVE ❤️💎
Sénégal daleuuuuh aka nio geum serigne neiikhoul ba neiikhoul meii vs etes ls meilleurs
Apprentis souba,Apprentis ngone,Apprentis timis,dawal auto et ame garage 😂😂😂
🤣🤣🤣
😃😃😃
😂😂🙂🤣
Dawal gua rass😂😂😂
Mom garage , am garage 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Non sénégalais mo deugeur fiit guiss niane xamon niane numou démé rk nga talal say loxo baye wakh sa sokhla😂😂😂😂😂
Makhfouz puissance !!!!
LOL cest que deuk bii !! non dafa meiti !!
Alassane a tout dit , fene rek, di tek, nitigni toppelène. Qu'Allah nous préserve. Amine. Évitez les maras....
Fait gaffes mon péti
@@alzoosamb8659 Sinon quoi?
😅😅😅samba Sow ak David ya infidèle... Non zé ak makh dougn dém kW😂😅🇸🇳
Xanaa Serigne Kouna Fall leuh😂😂😂
> non Wadji raynama 😅❤️❤️😄😄🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Bilakhi
No wadji raye nama. 🤣🤣🤣🤣🤣
Lolou lima ko rèe 🤣 🤣 🤣
Mouné amina 😂
yaw mi di lire sama commentaire yalla nga am diamou diou bari tei bull fetei abonner si sama chaine RUclips bii
The apprentice tho 🤣🤣🤣
Keep it up bro ...
All love from Gambia 💕😘
Zéh Ya Meun Diakhasé Bismillahi rahmanirahim.....😂😂😂😂😂
Timis moy sirrou gui😂😂😂😂😂😂😂😂ay way dé waaaaaay kéne gnémé wouko 😂😂😂😂😂😂
Nenako dimbali samay wadiour 🙏🙏🙏 yalla naniou yalla may lougnou dimbalé sougnouy wadiour amine
Amine
Nièppa beugue dimba Li sèn waydiour yallna yallah oubillén bountou xèwalll yii
Amin ya rabi
Wa defal rk 😂😂😂😂bakhalal neen bi diokh ko golo ak mbelentane 😂😂😂😂😂😂
Makhfouss tu es bourré de talent machallah ❤️
big up depuis le Canada
billahi yawe
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Moi aussi je vie au Canada Toronto makhfouse amoul
😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😬😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅😀😀✅
Man borom apprenti timiss bi momaye raye 😂😂😂🤣🤣😂😂🤣🤣🤣😂😃🤣🤣😂😂🤣😂😁😂😁🤣😂😂😁😂😂😂😂
bilay
Momay ray 😂😂😂😂
Néna dawal,mom garage
Dawal garage 😂
@@benwos4441 no Sénégal kaye dou dém. Mais noublier pas de vo5u abonné sur ma chaîne instagram.CMR COUTURE
Qui a remarqué son aida Faye bi si souf Dieureudieufe baye niass ❤️
Dieureudieufé Baye niass
@@oumarcamara9941 machahala
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
😂😃😅😆
Sama mbokk sérère bii vraiment xell bii naaxas naa
M entalment bien réfléchi
A ntistress de tous les jours
H olala tu vas nous tuer de rires
F orce à toi frère
O n est très fier de toi
U nion de fer avec Zé
S acré réussite dans vos projets
S oucis dissipés en 2021
E pithète, ma plume rime merci MAKHFOUSSE
Z éro faute merci MAKHFOUZ
E t ZE vous êtes formidables !!!❤❤❤💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯
Ay way li mane nama ray 😅🤣🤣🤭 eupna nak mais fin bi mo dakh soubala tabaski 😅🤣🤣🤣
Makhfousse mon fan depuis la Mauritanie 🇲🇷 😂😂
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Apprenti bi dioylo na kounek😂😂😂😂😂😂
Ou sont les fans mahfouss❤️❤️❤️kay len aime svp yangui fekheul holl yi
Nguirr yalla boul fate abonné 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Leçon boumasi tirer moy sènègalais serigne la geum. Geum yalam dèsna lolll🙄😂🤧
Bravo makhfouz💪
Vraiment sénégalai mo geum Serigne bilahi té Lép louniouy wah yép ay fén la
Bilaye bouniou khamone lisi serigne bilahi dinako moytou Sénégal dall warnène oubi sène khel yi
Makh pro et équipe yague leen fi loll té werr si barki CAB❤❤❤
Samba sow ak David 😂😂
Merci makhfouss yanou ko dikk sak vendredi ✌🏿🤙🏿⚡
Makhfouss yama téré nelaw ba heure billahi méré nala trop m j'adore
Ak mane
Pousse bleu les fan's de Zé et de makhfousse vraiment ils le méritent et n'oublier pas d'abonné a la chaine pour ne pas rater aucune de leur vidéo
Woooy yayoye mangui dhé 🤣🤣🤣🤣Kéeene niéméwoul dhéee
Boy Zé ioe ak mahfouss di ngen fi claté relations jambour yi rek 😂😂
Modou rek la yeureum😅
@@hhghhh4166 🤣🤣🤣
Le nombre d'abonnés de mahfousse
👇👇🔥
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
No mahfousse you Killing me i can't stop lauphing 😂😂😂
Laughing
Meilleures caméra cachée 😂😂😂
Amina diapsi nguir yalla sa amourou indou la yor😄😄😄😄😄👍
Srx 😂😂mangi beug dée Amina beugou la
No zeii mo rèww 😃😃😃😃
Tasnga couple you Bari 😃
Sénégal dagno geum serigne 😂😂😂🤣
Bilaye
Jtjure France gui ma nek walahi am toubab bo khamni chak jours mou waxma ko
😂😂😂apranté soubeu apranté ngone apranté timiss dawal auto am guarage😂😂😂😂non z dou nitt
😅😂😅😂😅cabinè bi raynama mais dèlène neube kaname gui bala Khadija diko ray
Apprenti bi pour mou am permis dina méeti torop xel mi néexoul dh maaxal sama diamou Sérére ri la 😁😁😁Zé am nga inspiration force à toi Mahfousse 💪💪
Nianll leunma Gouddou fan Ak weur Ak xalis
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Apprentie bi khél mi mo nékhoul dou guawa ame auto dh 😂😂😂
Ray nguama way🤣🤣🤣 sérère la
@@ablayethiam3951 😂😂😂bayile serrere yi
Non non 😁😁😁
Dawal garage 🤣🤣🤣
@@Kaa_Tiktok 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Amina 😅😅😅😅😅😅😅😅 boy yay dom.....😇 senegal yéna naik xallat deug
ZÉ Daour key wadji ragal na de😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂wouyyyyyyy
9:02 douche bi dina fatteu dh 😂😂😂
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
Vous êtes les meilleurs ❤❤❤
Nn Alassane rayi nama bilay nn zée d’où nitte 😂😂😂😂😂😂😂
ruclips.net/video/WU2LeXdJT5c/видео.html
🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂wouy ma gui dei Borom oto bi akk le dernier surtout no Makhfousss franchement t'es le meilleur avec zei no makhfouss do dem say dalla dague😂🤣🤣🤣🤣
🤣 🤣 🤣 🤣 🤣 Wouy Sama ndeye apprentis bou guènè soulou bi di saaw
Mah ak zéé niogui réy gars yi longue métrage rang mouy gaw bari nguèn ay néne 🥚 🥚😂😂😂😂
Apprentis soubeu apprentis ngone apprentis timis dawal auto am garaace 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Wouy 🤣🤣🤣
Mahfouss number one of senegal il te fait oublier tes stresses big up ze
Oooooh ndawe si néna dimbali samaye wadioure yalna la yalla diopoula
Alasane Seck 😃 nena bodeh yallah tawAli khale 😊
Merci Makhfouss tu nous a régale 😂🙏
Wa niakhar manifestaient vous
Worna yalla mah ya geuneu nekh si adouna 😂😂😂
Camera cachée bi ray nama 😂🤣🤣😂🤭
NN mane amina nobou la démal ligueyi daf😁😂🤣🤣 may ray
😂😂😂😂 sheuteuteute nooo serigne bii sérieux woul koi vraiment vidéo bii c'est le meilleur dangay réé ba tass