Je suis patriote mais je ne suis pas d'accord pour ton mariage avec ce gamin. Accepteriez vous que votre fils se marie avec une femme 30 ans plus âgée que lui? Mets toi à la place de sa maman et tu sentiras son chagrin. Hasbun Allah
Aye mbeguél mo méty rék yaye boy fékhél sa borome keur ak yayam niou djibo lolou rék mo ame solo louthi dess yalla na yalla doly soutoura khay na li djitou wone séne dioudou
Mère wakh deug Yallah seuy moy li guen Wayé sey ko mak 28 ans té ay wadiouram yégou niou.Ma soeur yaw tamit, sen bonheur bi bolé len ci la mère et la sœur de Ousseynou
Senegal metina trop😢 kui ciaggatou nyu wax, kui sey te Yallah tax nyu wax...if this woman was a White woman, everyone would have appreciate this marriage..ay mere tubab nyoi jugeh Europe nyow Africa di sey ak ay xale yu ndaw..te amana dunyu sax ay julit..te dankoy nangu...Hawma lutax African geumul boppam?? Happy marriage 🎉 may God bless the union❤
Fekhele no djoubo ak saye goro ak seye mbokki djeukeur rien n'est impossible fait tout pour sameu les relations avec ta belle belle famille c'est ce que je te conseille. Yallah baakhna
Je suis de tout cœur avec toi tu as le droit de faire ce que veux de ta vie pourvu que tu sois sur le droit chemin. Pourtant notre prophète a eu une femme plus âgée qu elle .Bon courage
Am nga droit beugueu koula nekh. Yonou kéneu nékou si. Tu es pleinement libre def lula nekh ak lula saf. Gnoulay jugé dougnou yallah dougnou yonenti. Que chacun s'occupe de ses propres affaires. Sénégalais mo manou woul
Seuy yalla moko wakh dokord Mais nik ki soko beugué mouy khallé aussi warr. Ngako conseil pour mou top ay. Wadiouram si seni ndigal .yaye dou morom baye d'où morom👏👏
Aissatou penda Diop diam ci yow yama gueneul halé yi ga hamni thiagatou rék lagne fi néqué gooro goor teudé naléne ci beugue halice yala na yala déf diam ci séye bi ya donou sohna hadija bou seydina mouhamed ouseynou mbengue diam rék gaye ham inchallah
Ils s’aimèrent bcp, vécurent heureux et eurent bcp d’enfants Un homme de plus de 20 ans est entièrement responsable de ses choix Heureux ménage à vous Nadone lou dagane rek lithi dess wax rekla
Adamo est t on fils mais t on mari peut être un petit fils pour toi tu pouvais rester coul dans t on coin avec t on mari c toi qui a amené le débat sur les réseaux sociaux
Mère delol khalebi yayam mo gueun li ngay wakh kham ngané dioubo 18ans aucun homme n’a voulu se marier avec toi désespoirs motax nga doug ci khalebi niak nga fayda torop.
C vraiment triste k ça soit un débat. Alors si c’était une blanche ça serait totalement le contraire. Maman il faut seulement faire tout pour k l’enfant parle à ses parents c tout
Beaucoup de respect mais libère ce garçon de grâce.
Mane deh je suis avec la maman de ousseynou.je suis patriotes
Meyegnou diama do patriote justice pour ouseynou justice pour khalébi😭😭😭😭
Nous les patriotes nous sommes pour la maman de ousseynou bayile fenne
Toi tu ne soutient pas moi en tant que patriotes je soutiens à 100%100 pour le mariage
@@ModouBodian-jv4ojmoi aussi je soutiens Aïssatou
Merci
Yaw deh Adji Sarr mola gueune
Vraimen dafougne lou yalla nangouwoul naniou mandou ta bayii gni niou seyy sene seyy bi
Foutez nous la paix tu sais en âme et conscience que cette relation te créera énormément d ennuis.
Teu mome seule meun neu défendre bopam, aka meun wakh
Merci
Libere l'enfant de quelqu'un cest tout
VRAIMENT SOKHNA SI YAKE SONKO COMME YALLAH Ake YALLI. SOPE KO TAKHOULE NGUÈNE NIRO DJIKO
Wakh deuk mashallah
Merci ils croient que en faite que ay kharr you top Sonko lagn
Je suis patriote mais je ne suis pas d'accord pour ton mariage avec ce gamin.
Accepteriez vous que votre fils se marie avec une femme 30 ans plus âgée que lui?
Mets toi à la place de sa maman et tu sentiras son chagrin.
Hasbun Allah
😮
On est d’accord en plus elle n’écoute pas
Aye mbeguél mo méty rék yaye boy fékhél sa borome keur ak yayam niou djibo lolou rék mo ame solo louthi dess yalla na yalla doly soutoura khay na li djitou wone séne dioudou
Mai seyou diambour séné yone nekou Thi yalana yalla barkel seybi si barkel seydina Mohamed psl
patriote bu doff ngaa
@@aliousane6776vraiment😂
Matar ndoye yalla nala yalla maye dom bou am 24 ans bou takk mère bou am 55ans amine y’a rabbi
Je suis la maman de yousseynou libére mon fils
L'amour n'est pas d'âge k Dieu vs protège.maman tu as bien dit.loutakh sénégalais di dougue si vie privée diamboure bayilaine sokhore wayy.
Mère libère domou diambour way 😂
Mère wakh deug Yallah seuy moy li guen Wayé sey ko mak 28 ans té ay wadiouram yégou niou.Ma soeur yaw tamit, sen bonheur bi bolé len ci la mère et la sœur de Ousseynou
Mér diapal se borom kuer mu diapala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vérité absolue merci Mme c'est à vie privée donc tu as parfaitement raison
Bon ménage !
Yalnakén yalla dioubalé barkél sey bi si barké seydina Mouhamad
Amine
Senegal metina trop😢 kui ciaggatou nyu wax, kui sey te Yallah tax nyu wax...if this woman was a White woman, everyone would have appreciate this marriage..ay mere tubab nyoi jugeh Europe nyow Africa di sey ak ay xale yu ndaw..te amana dunyu sax ay julit..te dankoy nangu...Hawma lutax African geumul boppam?? Happy marriage 🎉 may God bless the union❤
Merci beaucoup ma sœur billahi Dara nékoul thi
senegalais moy naafekh .lou nekk mou dougou ci .c'est pour ca qu'on est en retard.
Boul diakhasè patriote sounou yone nèkou si boul tass sènègal
Pourquoi veut elle mêler les patriotes à son histoire ? Mère gerel say affaires rek, ñun tal nañu yeneen
Beugueu dougueul patriotes yi rek😂
Vraiment délol domou diambour mère li doula djiikk
Felicitation belle je Suisse avec toi a cent por cent tu est toute belle moisés cest ANTA MBENGUE ET du courage
Foutez Lui la paix waay ils sont majeurs et vaccinés ,Sénégal vous êtes en retard ,fii Koula neex ngay takk
Liberelle thiouthiou boy bi svp
😂😂😂😂
Vraiment, je suis désolé mais lidou diné dou yone, yaw mome tu es tombée trop bas ngay wakh dicdef comparaison ak Viviane 😮c'est du maraboutage.
Ah bon tu pense que c'est du maraboutage
Merci la belle je suis devtout coeur avec toi
Yalla mo diklé sey mais avec le consentement des parents
En tout cas man mi rouss na vraiment mère ak khale 😂😂😂
Moi suis patriote pure et dure et suis pas d'accord avec toi ki dango warone na khalé beutou dome parsk tu est une mère 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Tata j connais très bien mn amie Weuz svp libéré le sa maman tata ndeye elle vie des moments difficiles en ce moment svp fait ça🙏🙏😭😭💔💔💔🤦
En tant que musulman quelle est sa faute beuguente n'a niou set naniou
Fekhele no djoubo ak saye goro ak seye mbokki djeukeur rien n'est impossible fait tout pour sameu les relations avec ta belle belle famille c'est ce que je te conseille. Yallah baakhna
Le mariage est quelque chose de légal.
Elle n'a rien fait de mal
Zero classe zero foula fayeda zero eskey doyenawar déllelo khalébi 😂😂😂😂😂😂😂
Patriote kene andou thi ayy patriote lagnou kene andoul al yow si ligua deff kene wowoula kene feliciter woula arretel nak issshhhhhhh
Je suis de tout cœur avec toi tu as le droit de faire ce que veux de ta vie pourvu que tu sois sur le droit chemin. Pourtant notre prophète a eu une femme plus âgée qu elle .Bon courage
macha allah PENDA Manemi souma diotone si yow takla je t estime beaucoup
Merci Madame Aissatou Penda 🙏heureux ménage 🙏❤️
Yalla na seuy bi barckél si barcké Mouhamed ❤ le mariage est actés
Mane amosa numéro 😮 adouna wergal kep😂😂😂thi labokk
Yow dal kilifa. Bou doyadi nga ! Soko dieuloul dou. té mouye wakh ! Sa mbok dénaniou ak Gatié !
Yalla na mariage bi am réussite inchallah 🙏🙏
Je suis la pour lire les commentaires
She is very much right ❤❤❤
Yalna yalla dioubale❤❤❤❤❤❤❤
Daouda ! Tu es fort.... Machallah
Du courage que dieu vous protège vous bénisse vous donne longue vie et vous laisse avec ton mari amine
Du n’importe quoi 😢😢😢
Seuyeul bayi thiaga dji AK GORDJIGENE yi tout mes respects dakh diay leuf mofi eup té kén dusi wakh
En tout cas le mariage te va bien machalah, heureux ménage Mme
elle dit a Adamo Mane sa yaye là, mais alors c'est aussi la mère de ousseynou non? elle a tout dit
Faut pas orienter le débat vers sonko ou les patriotes .liberel ousseynou bounko dfone sa dôme Doula nekh
Yalla nala yalla Diapalè
Soutou râle la seybi barkél
Néko thilou bone dé
Mère dèmal yobou domi diambour thiakhan bakhoul yaw mi yanècoul si yone😂😂😂😂😂😂😂
Sonko beugoul kou niakeu fayda
Lou way wakh fi si adouna digua ko wakhate lakhira nagnou mandou si vie privée diambour yi . Gnome sény mboki bop nagnou lidieunti🙏
Première fois dans l'histoire du Sénégal je suis choquée 30ans de différence d'âge. Même animateur bi est choque . La c est abusé quand même
Mère bi comme mousse mou nane diweline😂😂
😂😂
Arrêtez la jalousie.laissez les faire leur vie svp.
Bilahi mére gathie moléye réy motakh guanane kholal ni ma sangsé
Am nga droit beugueu koula nekh. Yonou kéneu nékou si. Tu es pleinement libre def lula nekh ak lula saf. Gnoulay jugé dougnou yallah dougnou yonenti. Que chacun s'occupe de ses propres affaires. Sénégalais mo manou woul
Seuy yalla moko wakh dokord Mais nik ki soko beugué mouy khallé aussi warr. Ngako conseil pour mou top ay. Wadiouram si seni ndigal .yaye dou morom baye d'où morom👏👏
Aissatou penda tiaga diop , nous les patriotes on soutient la mere de Ousseynou. Yow Sénégal kene nawlo woula domeram ga
Merci 👍
Yagui togne dh Patriote dou togne fall mandou mo rere Sénégal 😊
Vraiment @@MoustaphaDiop-f7s
Niit day am respect
Dis pour toi. Pas les Patriotes les vrais Patriotes daniouy mandou ekh
Sama borom keurr😟
Mounumako mougn 😂😂😂😂
Fi kaay lifi métti mo bari😢😢
Mais parce que vous êtes une grande voyante que vous devrez évitez d être avec un jeune de 24 ans. C immoral
Penda sonagua moye toule nithie gni
Félicitations Ndeye Penda
Moi aussi vraiment mangui sah guinaw maman sey diambour yonou ken nekousi dafa setlou Kay khalni xalebi bakhna simon ani problème bi
Senegalai mon sonou
Guènè thi sonko rèk
YAW KEYE GUENEEL SONKO THIY SAY WAKH YALLA BOUN'GUENE DOONE BENE YAAG SONKO.
😂😂😂dama hamagua Ousmane ak point commun 😂😂😂wawawe corruption de la jeunesse 😂kep nake
Moi mon problème est que le fait que les parents du garçon n'étaient pas au courant du mariage et ils ne sont pas d'accord.
Aissatou penda Diop diam ci yow yama gueneul halé yi ga hamni thiagatou rék lagne fi néqué gooro goor teudé naléne ci beugue halice yala na yala déf diam ci séye bi ya donou sohna hadija bou seydina mouhamed ouseynou mbengue diam rék gaye ham inchallah
Aissatou.boul.tontou.guisgua.senegalais.gno.bakho.wakh.bayillenne.gnou.wakh.te.nga.doundou.sa.vi❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Marci Sister dam rk ❤❤
Merci maman ❤❤❤❤❤❤
Aisatou penda diop Amina pote mo guena domoram Adamo 😢😢
Pourquoi se fatiguer laissé les gens vivre leurs vies de quoi je m'en mêle
🇺🇸Projet Kate khalé yi 🤠🤣 sen Sénégal
Boul niou fonto libere domi diambar dji 😢
Mai dara nekoussi seybi dagan naa nassi diamm topp ak yermande machella
Ndiallo dall mon bonne
Ils s’aimèrent bcp, vécurent heureux et eurent bcp d’enfants
Un homme de plus de 20 ans est entièrement responsable de ses choix
Heureux ménage à vous
Nadone lou dagane rek lithi dess wax rekla
Mais pas mature
Et combien d’homme se sont mariés avec un pareil écart d’âge à leur avantage au sénégal?
Dieuredieff maman kenn dou sonko
Yereumeul yayou khalé bi gua libérée khalé bi mane bousi yayam andonne douma si wakhe
Ndawci mo gueune cougar yiye fate jeunes yi di léne dieufeu ndiko té seuye amoufa.
Ma soeur Adamo jaroul wakhal ya gui si yone période
Tu a raison maman ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Elle a raison, elle comme Sonko et les kateiotes😂😂😂😂😂😂
Mére néna gayi dagno jaloux😂😂😂😂
😂
Wa raw adji sarr
Adamo est t on fils mais t on mari peut être un petit fils pour toi tu pouvais rester coul dans t on coin avec t on mari c toi qui a amené le débat sur les réseaux sociaux
Mère delol khalebi yayam mo gueun li ngay wakh kham ngané dioubo 18ans aucun homme n’a voulu se marier avec toi désespoirs motax nga doug ci khalebi niak nga fayda torop.
Elle est mignonne n’importe qui peut tomber amoureux d’elle pourquoi pas le garçon qui l’a épousé
Wakhale sama dome kaye
Les patriotes yayou ouseynou layou andal
Mais me garçon à 24 ans non.Il est majeur donc la mariage aussi bien dans l'islam que juridique est Acceptable.On ne peut rien reprocher à cette dame.
C vraiment triste k ça soit un débat. Alors si c’était une blanche ça serait totalement le contraire. Maman il faut seulement faire tout pour k l’enfant parle à ses parents c tout
Maye gnou diam tu es niaka diom. Sa soutoura khawecouna ba pare. Sa belle famille bi ngaye menacer tu ne doit plus leur parler. 🗣️
Tu me déçois.
Nitgni ragalougn Yalla am sen problème thiagatou bi bari sobé bi bari si rewmi. Yen nguen seuy niou beug nieuw dici wakh? Damani Heureux Ménage