Merci ,Djumbori la situation du prophète n'est pas comparable à cette situation en plus pourquoi Aissatou penda porte elle un cheveux si l'islam est sa référence
@@awadiouf7001donc toi tout ce que tu fais du matin au Soir et depuis ta naissance tout est licite bravo et le sujet c'est pas le travail de la femme c'est son mariage mélange pas sltp
Il faut guen respecté choix qu'ou nek sey dou famille enplus est ce que yen khamguen loutakh depuis tous se temps lidianti wouyou ousseynou bamou tak niou begoko sonal kounek di nekh
INSHAA ALLAH BILAYE PENDA DINA AM EYES DOME INSHAA ALLAH DE VRAI INNOCENTS😢 ÇA S VOIT QUE GUEUM YALLAH YOMBOUL .DJIMBORI YOW VRAI GORDJIGUENE NGUE .YALLAH DAL MOY BUUR ☝️☝️☝️❤️ LÈGUI RÈK SÈN TOUR NIEUW INSHAA ALLAH SURTOUT GOROU MBOTAY BI AVC SA GUEULE DE CROCODILE 🐊 LIGUEY NEUB DINA FÈGNE DJIMBORI
Ndeyesane aissatou bo nekone toubab kene doula cas. Senegal chaque jours maguet toubab bou goor wala ndiguene tak fi khalé t kene dou wakhe dakh ay opportunité. Yeed yereum mo ko gueune 😢
Sénégal dou réw Wakho léne si Carte Gui si réw mi Thiaga dji Goor Djiguéne yi Ak site internet Yiye féne pour ame vu ak li yalla wakh si lollou yépp Té Seuye Kharamoul boye bi 24 ans la ame té khamna lépp
Personnellement je ne souhaite pas à mon enfant d épouser une femme qui est plus âgée que lui de 30ans et je pense que beaucoup de personnes ne souhaitent pas cela à leurs enfants Je ne blâme pas les parents ils peuvent ne pas être au courant de ce que faisait leur enfant sinon je ne pense pas qu ils allaient se mettre à pleurer et passer devant les réseaux sociaux pour dénoncer cela La dame aussi devra penser à son fils qui est à l université si un pareil cas lui arrivait
Djimbori doug nga thi lo momoul . Est-ce yow yaye YALA ??????????????? Est-ce que yaye mayé Ndiabot ??????? Sur les plateaux de télé, vous dites des CONNERIES
Moi je n'arrive pas à comprendre les gens . c'est note dieu qui doit juser . les êtres humains.moi je vois les gens qui ont leurs kilos problème et de juser . les libars des autres
Bouléne yakhal boy bi teranga bimou ame. Sou nguéne découragé Femme bi bamou divorcé akh son mari mba yéna nguiye sorr conséquences yi... le jeune peut perdre le contrôle déh et dépourvu de ressources. Laissez les tranquilles....
Dom yalla ko yor ..... mandoulèn .... mbiroum yalla daffa kemanè .... man guisna kou am 55 ans di indisposè ( tant qu elle voit ses regles ..... elle peut avoir un enfant ) .... Dieu seul sait ..... ragallen yalla
gnou soff nguén bayyi lén dérou diambour yi nguén di néck folén tolou. yaw Djimbory kou sof nga. sa yone nékoul si seuyou diambour. goor bou gnak fayda nga
Si vous connaissez la puissance d’Allah vous irez vous abstenir de mettre vos bouches dans l’histoire et le mariage des gens. C’est Allah qui décide et s’ils se sont mariés c’est par la volonté d’Allah ragal len Y’a Allah y’en nji tokk fi di wax Y’a Allah la nekh. Donc seuy bi sou amé mom la nekh et guiss nagn fi niou fi am dome à des âges très avancés (plus de 60ans). Donc taisez vous et laissez les tranquilles.
Cheuh teut teut yén khana amouléne programme ? Khana le prophète Mohamed psl n'avait pas fait pareil? Dimbeuliléne niou sõf nguéne ndayame trop bayiléne doug si vie privée jambour mais ana mandou?😮
Yen mandou bakhna ...yalla na seybi barké mm a 90ans c possible d'enfanter car rien né impossible à DIEU
Oui oui t’as raison
En tout yalla rek mo kham ndakh dina âme dôme wala dou ame miracle yalla amna dé mandouléne ci seyou ndiambour😏😏😏
Merci ,Djumbori la situation du prophète n'est pas comparable à cette situation en plus pourquoi Aissatou penda porte elle un cheveux si l'islam est sa référence
Et qu'est ce qui le différencie wàhal?
Seye dou yefou nitt..yefou YALLAH la
Ay way bayilen togn ragal yalla
Mandoulen si seuyou diambour ils sont majeurs et vaccinés.
Khana dolen ay dioulit bayilen wakh bi thiey senegal
Djimbori je suis parfaitement d'accord avec toi pour la première fois
Dom bénéfice reck la si seuy. Djiguéne dougou naci seuy moins de 20ans ba maguet fa té mouçoul am dom.
Djombory il a parfaitement raison
Khana bou nèkhoul Yallah. Yalla Subhana-wata -Allah meuna lounè.
Merci djoumbarry ,ya wakh deug , Sénégal dagnuy fonto seydina moukhamed!
Yayou khalébi la yeureum. Aïssatou kou niak kersa la meussouma nékh
Li de bou continue ma khathie😢loudoul deug dou yag
Merci djimborry femme bi domarame la .djiko thiaga la yorre
Kokoy begal la sokh la thi Khale bi dekoy utiliser rek fan lay am dom khesal tek sa greffage nan souna yonent bi lay topou thiey yalla
😅 bahilen togne 🙏heureux ménage Aissatou Penda Diop 🙏❤️
Aissatou meune nako wouteul gnaarail,mbaa yaayam wouteulkoko,mais baayi laine diaambour yi gnou seuy moo gueuneu ndiaaloo
Lolu moye deug deh..nyi takhawalu dunyu chi wakh deh
Aissatou penda domeram la, di teuder domou diambour. Bouko dafone sama rakh ma niaff ndayam. Cougare deug le
DOYNA WAAR DAL
Il ya cœur brisé, il ya carrière brisée
Merci djimbori
Fii daraye yonénte bi nekou fi
Bilahi Jimbori wakh ga deug…. Yaw mome deuggeu rekk nakk
Yaye ou khaley bou goor bi rek la yeureum 😢
Vous n'êtes vraiment pas sérieux dans votre émission. Le mariage est sacré.
Ay way manou len 🤧
Waw payi di tak senmormidom lolou lensi wah
Waw bouko yallah mayé dome nak loye déf
Mandou bakhna
Bane dom yalla na yalla may sa dom mère bou 62ans tè take ko 😅
Beug na gua wax amine
Mandouleen ci seyyou ndiambour
djimory bayil fénn sa histoire bi si yonéntiby wéroul
Astagfiroula ! Yalla wakhoul kaine d'ara !
dacor mariage est sacré il faut voir l'âge oci de se petit il na pas d'avenir pour sa santé oci et son avenir
Verite absolue djioumbori ❤❤❤❤❤
Merci djumbori
C'est leurs vie privè heureux menage à vous
Tak koula mak sounnah la
Sénégal rek gnoko metil
Heureux ménage la wakh
Linga wakh deugla dé mais li djimbory wakh deugla ngay top souna ba paré di sett té sett da haram . Doyna war
@@awadiouf7001donc toi tout ce que tu fais du matin au Soir et depuis ta naissance tout est licite bravo et le sujet c'est pas le travail de la femme c'est son mariage mélange pas sltp
Mane môme 20an magi ak sama diekeur ta mako mag
Jimbori tay diom nga boy bi mene ame bénén diabar ta seye amoul age Sénégal mo méti
Djimbori mii mo mana fene rek histoire bimiy netali nii ay fene rekla
En tout cas voyance dafa Haram. Man Aissatou Penda Diop meussoumaa nèkh ngir Yalla.
Il faut guen respecté choix qu'ou nek sey dou famille enplus est ce que yen khamguen loutakh depuis tous se temps lidianti wouyou ousseynou bamou tak niou begoko sonal kounek di nekh
Bayilen diambouryi..taniou debat ci Aziz dabala 😢..ma am lomeu metti.
Tu as parfaitement raison le problème de Dabala est plus plus plus important
@@antasarrcisse1803vraiment
Bien dit djimbori
Merci
Paix à son âme ce jeune 😂😂😂
Vous avez raison ay esaculations laye weur
INSHAA ALLAH BILAYE PENDA DINA AM EYES DOME INSHAA ALLAH DE VRAI INNOCENTS😢 ÇA S VOIT QUE GUEUM YALLAH YOMBOUL .DJIMBORI YOW VRAI GORDJIGUENE NGUE .YALLAH DAL MOY BUUR ☝️☝️☝️❤️ LÈGUI RÈK SÈN TOUR NIEUW INSHAA ALLAH SURTOUT GOROU MBOTAY BI AVC SA GUEULE DE CROCODILE 🐊 LIGUEY NEUB DINA FÈGNE DJIMBORI
Ndeyesane aissatou bo nekone toubab kene doula cas. Senegal chaque jours maguet toubab bou goor wala ndiguene tak fi khalé t kene dou wakhe dakh ay opportunité. Yeed yereum mo ko gueune 😢
Sof guéneu way trop amo léneu béneu soutoura
Xamngen lanal bayilen gni ganlo wouniou daniouy seyy sheut l’islam est d’accord 👍 donc ou est le problème
Il faut laisser le procureur juger l’affaire car il y’a CORRUPTION DE JEUNESSE 😂
ET ALORS IL PEUT AVOIR UNE 2ÈME FEMME. APRÈS. LAISSEZ LES TRANQUILLE VIVRE LEUR MARIAGE
Pour mane khalè bou gor bi sou amone 40 ans sakh mou tanè
Vraiment mère bi et ce que domome magoul dieukeurgui 😮
Djimbori magui ni amna 50 ans bo beugue gua nieuwe
OUSSEYNOU yow tamitt koula bayi
Li cas la 😂😂😂
Sénégal dou réw
Wakho léne si Carte Gui si réw mi
Thiaga dji
Goor Djiguéne yi
Ak site internet Yiye féne pour ame vu ak li yalla wakh si lollou yépp
Té Seuye Kharamoul boye bi 24 ans la ame té khamna lépp
Ohh soyez sérieux ! Qui rira le premier rira le dernier. Doundou bou sotekoul louné khathie nassi
Djimbori bayil reuy lamigne. Do yala do yonente. Le mariage est sacre. Khamoulo fou doom di sossoo.
Bayilene thogne toubape yagui Taken sougnou domme y thé khene wahousi dah khalise
Nasi procureur wakh corruption a la jeunesse la
😂😂😂😂😂😂😂😂 en tout cas mon fils à 18 ans mais je le souhaite pas sa
Yeen yenay ay nafekheu deug vraiment dolen niou bakh yeen dolen sakh ay nitt lii nguen waron ko rafetlou ndakh fratala ngueni wakh lii
Personnellement je ne souhaite pas à mon enfant d épouser une femme qui est plus âgée que lui de 30ans et je pense que beaucoup de personnes ne souhaitent pas cela à leurs enfants Je ne blâme pas les parents ils peuvent ne pas être au courant de ce que faisait leur enfant sinon je ne pense pas qu ils allaient se mettre à pleurer et passer devant les réseaux sociaux pour dénoncer cela La dame aussi devra penser à son fils qui est à l université si un pareil cas lui arrivait
Lima si kham dall dioulite déye madou
Vraiment yén ay nitt you bone nguéne wa séni wakh you gnaw yii nguéne amci lane
Djimbori doug nga thi lo momoul . Est-ce yow yaye YALA ???????????????
Est-ce que yaye mayé Ndiabot ???????
Sur les plateaux de télé, vous dites des CONNERIES
❤❤❤
Moi je n'arrive pas à comprendre les gens . c'est note dieu qui doit juser . les êtres humains.moi je vois les gens qui ont leurs kilos problème et de juser . les libars des autres
Sokhna khadidja amone na 4 dômes ak seydina mouhamed.ter mere bi ménopause na bou yagg donc boulen comparer.
*Seydina Mouhammad sall’Allahou aleyhi wa salam
Di wakh vie privée nit yi di nebeu sa bosse
Moffi am dè bilahi nakou nekk lidianti sa bop
Pourtant djiguene yi toujours ay khale you ndaw nioy seuy ak ay paa niatta khalé you djiguene you am 24 ans nioy seuy ak mak bou am 45 ans
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😢😢
Djimbori vraiment aujourd'hui je suis désolé mais déconné ngua trop respecte la maman au moins pour ta maman
Seul Dieu sait. Mandou ...
Femme bi sou diouré guen rouss. La femme de ibrahima(rta)a été enceinte à 70ans.
La voyance ça interdi par l'islam
Non Yalla nalène Yalla mouseul ci lamigne
Senn yonn nekoussi
Bouléne yakhal boy bi teranga bimou ame. Sou nguéne découragé Femme bi bamou divorcé akh son mari mba yéna nguiye sorr conséquences yi... le jeune peut perdre le contrôle déh et dépourvu de ressources. Laissez les tranquilles....
Dom yalla ko yor ..... mandoulèn .... mbiroum yalla daffa kemanè .... man guisna kou am 55 ans di indisposè ( tant qu elle voit ses regles ..... elle peut avoir un enfant ) .... Dieu seul sait ..... ragallen yalla
Effectivement
Non non mme meune nga guiss sa règle té do ame dome meune nga ame😂dome ba nga ménopause continue di guiss sa règle
Yow doul yow
Jimbory yéurem leen yayi xalebi
Vérité Absolue
Je ne crois pas en la voyance mais en amour ya pas d age
Mer bi dakoy Ray rek dah halle bi goudou fane dakoy deig rek
gnou soff nguén bayyi lén dérou diambour yi nguén di néck folén tolou. yaw Djimbory kou sof nga. sa yone nékoul si seuyou diambour. goor bou gnak fayda nga
Djimbori Mako beugeu
Tout le monde ne peut pas parler en mm temps
Khadija est plus âgée de 9 ans au prophète Mahomed
c'est 15 ans
*Seydina Mouhammad sall’Allahou aleyhi wa salam
*Seydatouna Khadija (RA)
CEST pas votre probleme
Pourtant si c etais un homme de 60ans qui a epouse une fille 18ans donc une femme de 54 ans peux avoir un mari de 20ans il y a pas de probleme a ca
Yalla na seye bi barkel thi barkè seydina Mohamed
Loungay comparé bokoul
Macron dé tak mère tewoul mou done président
Tegg lenn s'en guemine yenn am lou up Lou graw tibir sen keur Ak sen Djabars ndibell lenn niou bayelle couple bi sen yon nekoufi
Nanou oubi ay ucine xalè liguey wagni doundou bi
Ay yefeur gnolen gueun nafekh rek
Si vous connaissez la puissance d’Allah vous irez vous abstenir de mettre vos bouches dans l’histoire et le mariage des gens. C’est Allah qui décide et s’ils se sont mariés c’est par la volonté d’Allah ragal len Y’a Allah y’en nji tokk fi di wax Y’a Allah la nekh. Donc seuy bi sou amé mom la nekh et guiss nagn fi niou fi am dome à des âges très avancés (plus de 60ans). Donc taisez vous et laissez les tranquilles.
Halébî ďakoye namepal féragoul yaydî mokonapalol dafaka fé ral þamatoul fére
Mére Daye seye ak pa moguena rarétt
Li eupna dal c abusée 😂😂😂😂😂😂😂😂
Khale bi seutame.le magué n'a khale bi 29 ans
Doussi messeu am diabot qui menaupose na
Ragalale yalla
Dôme yalla mo KO yor mandoulene
Dako deudaler ak famille wam. Mere bi domeram la, sa mère doit saisir la justice li dou yone
Mais toubabe yi déf nagne Senegal plus....
Dom yalla rek mokoy maye
En amour ya pas d age
gisanekat ken warouko tak dou djoulite۔yenentebi psl meusoul tak gisanekatt😮mounan souneu
🎉🎉😂😂
Cheuh teut teut yén khana amouléne programme ? Khana le prophète Mohamed psl n'avait pas fait pareil? Dimbeuliléne niou sõf nguéne ndayame trop bayiléne doug si vie privée jambour mais ana mandou?😮