Non alphie biga dale togue spécialité senegalaise ba legui tay mome sa thiere bi machaallah wa senegal sakh meunouniouko. C'est très réussi machaallah. Bonne fête
Alphie no def .... c'est l'anniversaire de mon papa le samedi prochain motakh nak mangui top say vidéo béne par béne..... pour defaralko Lou rafet té nekh
Bonsoir, encore une fois merci pour vos partages. L'huile dans laquelle vous faites cuire le poulet c'est de l'huile de friture ? C'est quelle huile exactement svp ? Merci 🙏🏻
@@AlphieCuisine pour la tomate wakhal Diatou gp mou djieundal la tomate Aicha(tomate concentré)nar yi niocoy diaye fi Espagne.Ta Diatou gp warnaco kham car moy presidente association senegalaises ci ville bima nek.
Thiére guinar ngay vu niii lane merci Alphie cuisine thia Thiére bala
Machallah chef Alphie sa thiéré guinar tamkharite ça à l'air très délicieux merci pour la recette gros bisous d'amour 🙏😘❤
Non alphie biga dale togue spécialité senegalaise ba legui tay mome sa thiere bi machaallah wa senegal sakh meunouniouko. C'est très réussi machaallah. Bonne fête
Hooooo merci beaucoup ☺️ way
De rien yaw rek laniou wara remercier. Nos mari sont très contents nous tes abonnés et c'est grâce à tes recettes qu'on reprend à chaque fois.
ah machala encore mane j adore tes nokoss bilaye walaye. merci encore
Li thi thiere pour wadial tamkharit bi machallah 😋😋😋
Alphie no def .... c'est l'anniversaire de mon papa le samedi prochain motakh nak mangui top say vidéo béne par béne..... pour defaralko Lou rafet té nekh
Tata alphie gnoune gni nekk gambi nougn ci dioté
Man beug na ci épices yeup incha Allah
Manchalla awe na Yonne et c bien explique
Merci beaucoup
j'ai une question Alphie nokossou porro bii lane moko composer est-ce que porro késsé la??
Salam Alphie namone nala dé. Niou dougane guéw. Li ci thiére aycha. Té bou guinar moy sama préféré. Merci Alphie.
Haaaa mashalah
Macha'AllAh lafthiat ndokh dou bayi yonam kome dab RAS ak Reine Herbes Épices dafay melni Dubaï akiii laampam😘
😂😂😂
Machallah sister
Machalah dhi wadial thiéré niou nékh lol
Bjr alphie est ce que tamit. Sa plat yi doko def livre de recettes tamit c juste une suggestion
Sa thiere machallah
Oui ma chérie beugue nako deee paresse rek moma diap
@@AlphieCuisine ayway diap si
Wa alphie li tamite mba diame la wathe gnou guirr yala
🤣🤣🤣
Mashallah Alphie merci Bon appetit
Mashallah bon appétit Alphie
Assallamallikoume, niogui ziarre di lene begue aka souhaiter 1bonne fete a ts machallah
Alohie stp wahal gas yi gnou utilisé koudou thounewar batte moo gueune d
Alphie rekk m'achallah 🤤🤧
Mâcha allahh lafthiat thia thiere bala
Thia thiéré bala ❤🥰machallah Alphie❤💖💋
Thiere guanar rekk akk ayy épicé yi eupna
Waw touti rek
Wa kay ss thieré bala ak team Alphie 🥰🥰💯💯
Salut je vis a Barcelona comment je peux vous contacter pour acheter les epices.
Mashallah Alphie
Alphie ana thiere fromage ba🤣🤣🤣
Alphie tanyi lingay thieré dousa âge dé😍😍
Mashallah ah Alphie sa thierei guinar thiouk na thioum ❤️🥰
Wakhal way
Machallah sister🥘💯😋👍👍
Rang mouy tiere ginar alphi
Wa Alphie tiéré ng niou fane yi souma deugone sa keur gadaye 😂
Nieuweul way
Merci Maman 💐💐
Machallah ❤❤
Gnaff sm Alphi kenn douma si djitou boul tax ma engagé thiéré bi wayy
Boul ragal engagé ko
@@AlphieCuisine lolou def sama professeure
Thia thiéré bala 🥰
Thiéré bou amoul fén slt Alphie namenala der
Malaraw
Alphie ya woor
Machallah alphie croustillant merci beaucoup 🥰♥️♥️
Saf ba yégue si lol rekk😊
Mashalla thiéré ga bon appétit 🙏🙏🙏❤❤❤
Coucou chef cette annee ci mome linga thiere amoul fene
C’est pour vous
Bonsoir, encore une fois merci pour vos partages. L'huile dans laquelle vous faites cuire le poulet c'est de l'huile de friture ? C'est quelle huile exactement svp ? Merci 🙏🏻
Huile de tournesols
@@AlphieCuisine merci beaucoup 😊
@@AlphieCuisine pour la tomate wakhal Diatou gp mou djieundal la tomate Aicha(tomate concentré)nar yi niocoy diaye fi Espagne.Ta Diatou gp warnaco kham car moy presidente association senegalaises ci ville bima nek.
Namenala alphie
Merci beaucoup ma belle macha Allah
Machalla très bon👍😍😍
Salut Alphie , je vous depuis canada 🤝🤝🤝🙏
Merci beaucoup naka Canada 🇨🇦
Machallah 💪💪❤️❤️❤️
Machallah ma chèrie ❤️
Machallah
Merci
Reine herbe epice
Lane Tcha thiéré bala
Premier commentaire
Waw
Beggeutinaaa
😍😍😍😍😍😍😍
Non mè liguaye thiere lane tamite tane sa boula nekh
Waw tane sa boula nekh
😍😍😍😍😍😍😍😍😍😄
😋😋😋😋👏👏👏👏🌹🌹🌹🌹🌹
Laf thiat