Safara diamou yalla leu aldiana diamou yalla leu nioune tamit ay diamou yalla lanou yalla néna loumou binedeu domou Adama mokosi geuneul Takhaw sétlou bi mo wara doone domou Adama mi geune lép Lou yalla sakeu moy kaane diouli niawetéf lay dinedi fén ndialo dieuw déf Lou xaram AK Lou yalla di ayé ndakh bounou faté ni kén manoula dakeuu salté ba nopi tilime khafistou anta salakho deuliline rasoulouh andane tardihou
Mandou, dou nopi si lo khamoul. Mandou moy wakh li YALLAH wakh té bagne thié set kou mouy nekh ak koumouy nakari. YALLAH néna: sourate 98 / verst 5: " Il ne leur a été commandé, cependant, que d'adorer Allah, Lui vouant un culte exclusif, d'accomplir la Salât et d'acquitter la Zakât. Et voilà la religion de droiture." Le prophète à dit que: diouli 3 personnes rek lay wathieu: khalé bou majeureu goul, kouy nélaw ba ba mouy yéwou, ak kou doff ba ba mouy werr. Kone nak kou doul diouli 3 yi kène nga si. Kone nak kou top wakhou gni ba do diouli, yaw mal khiyam cheikh Ibra doula tal ba dila lindieunti et tu sera seul. Niak douli rek eupeuna mais dém ba diko léyal mom doyna war.
Kepp kou geum né dioulli wathie nako ap yeffer la ta safara la dieum bou dèwè ta touboul. Li ngène di wakh nè ibra fall moko wakh boudé deug la kone môme yeffer bou mak la wône, shaytan bou mak bou fenal Yallah nâne Yallah moko wakh bou dioullé douko faye. Ndax mo geunône yonent bi ( sallaallaahu’aleyhi Wasallam ) aki sahababam ? Yonenti bi(sallaallaahu’aleyhi Wasallam ) dadâne dioulli ba tank yi di newwi fen kat yi di wakh né Yallah molène wakh niou bayyi dioulli . Ñi ay nonou Yallah you mak lañou, nonou yonent bi ak nonou bepp dioullit bou deugou . Motakh Senegal dou gen si moussiba , deuk no khamné shirk, bida’h ak fenal Yallah rek moy sène diné , Allahul Musta’aan .
Merci beaucoup pour ton éclaircissement sur chéikh Ibrahim Fall
Dieureudieufeuty CHEIKH Ibrahima fall
Dieuredieuf Biçhri. K dieu vs protège si barke s.saliou amine
Dieureufé borom Touba diarna mame cheikh Ibra
Kodol diole yifar ga
Dieuredieuf mame cheikh ibrahima fall
Vraiment vraiment merci beaucoup à vous la sen tv du fond du coeur
Khol fékhhneu❤
Jërëjëfé s Touba jarama mame cheikh Ibrahima fall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💚💚💚💚❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💚💚💚💚❤❤❤❤❤❤💚
Dieuredieuf Serigne bichri
Beugeu na sama mame cheikh ibra fall 😭🙏🏻
Macha alla amatina solo kene d’où bayou groo gni 😭❤️♥️
Fenal Yallah rek lafi def, nganâne machalaaAllah. Kou geumné dioullli wathie nako , kôkou yeffer la ta safara la dieume bou toubou balaa mouy dè.
Cheikh Ibra Faal mom bayoup goor gni❤❤
Khanaa legi deh d'accord nanou né SEN TV moy top.
❤❤❤❤
Machallah
Walahil Azim Azim Cheikh Ibra Fall amoul morom
Thieuye Serigne Touba
Dieureu dieuffei lamp fall
Dieureudieufé Yallah , boromu lamp fall .
Diarama mame cheikh Ibra fall
Wa sen TV je vous aime
This mame Cheikh ibrahima fall lamp
Nonou Mohamed yi balégi sén Aÿ seutt niofi nek beugouniou souniou Serigne yi wayé liray séni mame ak séni wadiour moléndi ray kholbou bone
Dabaye Mame Saye Ndiaye Ken dou souniou waadji borom Sagne sagne bi ...
Walay wakh ko thia kaw
Macha Allah bonne continuation 🇲🇱✊
Kouthii djouli woul ba faatu safara direct ngua dieum
Yaw mom xana ya mom safara
Safara diamou yalla leu aldiana diamou yalla leu nioune tamit ay diamou yalla lanou yalla néna loumou binedeu domou Adama mokosi geuneul Takhaw sétlou bi mo wara doone domou Adama mi geune lép Lou yalla sakeu moy kaane diouli niawetéf lay dinedi fén ndialo dieuw déf Lou xaram AK Lou yalla di ayé ndakh bounou faté ni kén manoula dakeuu salté ba nopi tilime khafistou anta salakho deuliline rasoulouh andane tardihou
Waho DEUG d ,va kerogue
Iow mom khana nitou safara gia
@@cheikhsene1151 amoulo xam xam amoulo arguments bo touboul lignaa wax ba dé yalla mbougeul leu
Kepp koudoule jouli yifar ka yalla moko wax amoule bine wax bo giuna kawe wakhou yalla amole
Doul way yaw ya djuli xamga nah nanguna bay lidjanti djuli Ku meuna sa baay
Wa teh gua dell kholl la yalla wakhonn yonennt shwm ليس لك من الأمر شئ ba fam yem rk teh gua diem ko doundou magui koy toub nak
Di sakou nguir dieumi serigne Touba nga aboné si EUKHLOU MAWAHIBOU NAFIKH TV.. Dieureudieuf.
Thiey sunou wathi
Sénégal mandou rek mo geuneu yomb té mounou niouko..wayé disaga rek ...
Mandou, dou nopi si lo khamoul. Mandou moy wakh li YALLAH wakh té bagne thié set kou mouy nekh ak koumouy nakari. YALLAH néna: sourate 98 / verst 5:
" Il ne leur a été commandé, cependant, que d'adorer Allah, Lui vouant un culte exclusif, d'accomplir la Salât et d'acquitter la Zakât. Et voilà la religion de droiture."
Le prophète à dit que: diouli 3 personnes rek lay wathieu: khalé bou majeureu goul, kouy nélaw ba ba mouy yéwou, ak kou doff ba ba mouy werr. Kone nak kou doul diouli 3 yi kène nga si.
Kone nak kou top wakhou gni ba do diouli, yaw mal khiyam cheikh Ibra doula tal ba dila lindieunti et tu sera seul. Niak douli rek eupeuna mais dém ba diko léyal mom doyna war.
Mashallah. Amna solo mbok . Deug mom Yallah moko mom te ler na
Machallah Barak Allahou fikum
Moustapha séck damal diangui lila war déffoko
Yaw nopil kiiy wakhni mo geuna diang sa baye
@@iboudieng1993 khanaa sa baye la guena diang, wakhou fi dara loudoul fenal Yallah Ak wakhi nafeq
Theiy enterré une personne dans une mosquée 😢🤮
Kepp kou geum né dioulli wathie nako ap yeffer la ta safara la dieum bou dèwè ta touboul. Li ngène di wakh nè ibra fall moko wakh boudé deug la kone môme yeffer bou mak la wône, shaytan bou mak bou fenal Yallah nâne Yallah moko wakh bou dioullé douko faye. Ndax mo geunône yonent bi ( sallaallaahu’aleyhi Wasallam ) aki sahababam ? Yonenti bi(sallaallaahu’aleyhi Wasallam ) dadâne dioulli ba tank yi di newwi fen kat yi di wakh né Yallah molène wakh niou bayyi dioulli . Ñi ay nonou Yallah you mak lañou, nonou yonent bi ak nonou bepp dioullit bou deugou . Motakh Senegal dou gen si moussiba , deuk no khamné shirk, bida’h ak fenal Yallah rek moy sène diné , Allahul Musta’aan .
Machachla wakhnga lep 👉👂
Sa tatou yaye sa bo yéwo sa data Ndaye sa koyou baye
Aka léer
@@mountakhagueye5312 li day firndel ni nitou safara nga yaw AK sa serign
Saway khana khamo yalla moye brom koune loka nékhe deff thé dou lathie kéne amo xam xam thé aliwo dafa gate
Merci baye fall tiey mame cheikh
Machaalla