Bichiri mane dale sa khame khame bi diakhale nama no mana togué si télé nane cheikh Ibra néna képe kou boke si mane djoulli ake wore YALLA téguilnalako....et en plus nguané toke Di zikr mo guene djoulli bilaye ya ngui toumale cheikh ibra loudoule deugue....khana khamoni cheikh ibra binde n'a téré bouye diangualé djoulli
Tere boo xam si Mame Ibrahima FALL, moom molako gena xam. Ku am xamxamu terre ba nopi xam boroomam mooy Cheikh Ibra. Mbindana, jëef na, wax na. Ñun nak Mame Cheikh doy nañu te janga nañu, xam nañu xamee nañu. Wax ji matuko, lu Mame Cheikh def moo ñu genal lu mu deful. Dieuredieuf Daam diarawlaak Baabul Mouridiina.
Bilahi Chiekh ibra fall walahou kamil leu kou khamoul khamoul nag
Cheikh Ibrahima fall rékkk ❤️🥰
❤❤❤Mame Lamp❤❤❤
🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳vive le Sénégal Paix à touses ❤️❤️❤️❤️ depuis Paris
Diarama Ahmadou bamba yalla mo nagolnou yalla nanou yalla hamal chieck ibrahim fall baboul mouridina
Diarama mame cheikh Ibrahima 💯❤️❤️ fall yaram ❤️
❤Sidi birahim fall ❤❤mome guenn go la fall ❤❤❤❤
Diarama mame Cheikh ibrahima fall❤️🙏
Theye Mame cheikh Ibrahima fall lampe fall yarame fall 🤍🖤🤍🙏🤝 😮🙏
Dieuredieufeti Borom Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌
Dieureudieuf Fall Yaaram ❤❤❤
Rékkkkk ❤️❤️❤️
Dieuredieuf borom Touba diarama mame cheikh ibrahima fall
Dieuredieuf Borom Touba Jarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
ESKEUY THIEY KOU BAHH KI
Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
Dieradieuf mame cheikh ❤❤❤❤❤😂
😂😂😂
Mame cheikh Ibrahima fall moy lamps adouna ❤
Dieuredieufaty serigne Touba mbackè dieuredieuf diarama mame cheikh ibrahima fall lamp baboul mouridina
♥️♥️♥️♥️
❤❤❤❤❤❤❤
Diarma mame cheikh ibra falll lamp ❤
Sameuh mame Cheikh Ibra fall kein leuh 🙏
Cheikh ibra fall ya goré fall
LAMP Baboule Mouridina
akasa dierediefe seringe touba
BasRE
😢😮😅
Bly amoul morom Lou khamoul khamoul reek
Bilahi kou khamoul khamoul
Moustapha gueye yaw sofnga nopil nioun cheikh ibrahima fall lamp ak serigne touba langi topou mé pa yaw ak say morom
Machalla
Santati nan stouba
Doul rek
Yawe dangua alkou
Bichiri mane dale sa khame khame bi diakhale nama no mana togué si télé nane cheikh Ibra néna képe kou boke si mane djoulli ake wore YALLA téguilnalako....et en plus nguané toke Di zikr mo guene djoulli bilaye ya ngui toumale cheikh ibra loudoule deugue....khana khamoni cheikh ibra binde n'a téré bouye diangualé djoulli
Moustapha gueye Lislam deug moy mandou si lousa yone nékul segne bamba cheikh ibrahima fall rék lagni topou
Moustapha gueye est ce que doko wo gua wakhekako comme yako eupeu xam xam Iao
Tere boo xam si Mame Ibrahima FALL, moom molako gena xam. Ku am xamxamu terre ba nopi xam boroomam mooy Cheikh Ibra. Mbindana, jëef na, wax na. Ñun nak Mame Cheikh doy nañu te janga nañu, xam nañu xamee nañu. Wax ji matuko, lu Mame Cheikh def moo ñu genal lu mu deful.
Dieuredieuf Daam diarawlaak Baabul Mouridiina.