Wakeur boy niang daniouy khékh ama pour mou danou😱..biss bou défé open press..coach bakary waxatina

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 270

  • @boubacarba8323
    @boubacarba8323 Год назад +20

    Vérité absolue Bakari ama n’a qu’à faire très attention

  • @fallcheikhibra1155
    @fallcheikhibra1155 Год назад +28

    🇺🇸🇸🇳Ama baldé yalla nako yalla diappalé Incha'Allah le 05 novembre mou néck roi des arènes Incha'Allah ❤j'ai toujours entendu cet rumeur que Ama baldé fait du social beaucoup plus que eumeu sene et boy Niang raison pour laquelle ils sont jaloux de Ama baldé ❤

    • @papesouma
      @papesouma Год назад +2

      Inch'Allah dakoy nek Inch'Allah

    • @Omarsane7491
      @Omarsane7491 Год назад +1

      Modou xaragne lo dakay d'âne inchallah

    • @tallakatalibeserignebabaca2049
      @tallakatalibeserignebabaca2049 Год назад

      Amine inchaalla

    • @ndiayeibrahima9876
      @ndiayeibrahima9876 Год назад

      Yaw bayil doule

    • @VISIONTVONLINE2299
      @VISIONTVONLINE2299 Год назад

      En tout cas dinaniou door bèna mbeurmi bamou Reupeu si khèèkh bou metti 4 minute de bagarre you amoul arretè am ndiaye diokhaal Diop ni mbathioum guertè. Je vais vous des détail pièce par pièce borom khèèl lay wakhaal.

  • @PapeamadouDieng-f7n
    @PapeamadouDieng-f7n Год назад +2

    Pure vérité absolue coach bakary degue nekhoul d Ama yée Ama yée future rois des arènes inchalah fii Yalla rek mofi nek bou décidé Ama baldé nek rois des arènes khene meunou si Dara ???👑👑👑🦁🦁🦁💪🏻💪🏻💪🏻

  • @MomoWade-y8z
    @MomoWade-y8z Год назад +12

    XLO yalnako yalla may ndam inchallah 🙏🏽

  • @amadou862
    @amadou862 Год назад +2

    Je sw aau Maroc mais toujours j'ai pensé à sa ke le kan de boy Niang danioy xexx Ama pour mou danou Lou lér mais Ama yallah nakeu yallah moussal rek inchallah

  • @azizjazzdiop941
    @azizjazzdiop941 Год назад +11

    Merci Baraky pour cette veritè

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 Год назад +22

    Vérité absolue, Ama soyez vigilants 🤲☝️

    • @ibrahimasakho-tz7kx
      @ibrahimasakho-tz7kx Год назад +3

      Jeudi passé mane ak sama bene frère analyse bi laniou done def té Lou khel di nangou la

    • @VISIONTVONLINE2299
      @VISIONTVONLINE2299 Год назад +1

      En tout cas combat bi ousmane sonko vs amadou ba.

  • @manoumbaye6277
    @manoumbaye6277 Год назад +7

    Force est de reconnaître que a chaque fois que boy Niang am combat qu on nous timpanise avec le 200/200 pikine. Pourtant ama combat Royal lay beuré on sent pas cette mobilisation qu avait boy niang.deugue nekhoul

  • @laminepreira8171
    @laminepreira8171 Год назад +5

    Bien dit coach bacary sur ama et boy niang

  • @djeganengom
    @djeganengom Год назад +4

    Yén supporters pikine yi la plus part ay doof guén ils veulent vous séparer vous les donner l’occasion c’est honte Ama balde ak boy niang ils sentent malgré defouniou contact ensemble mais ay xarit lagn te kouné yéné ga sa morom louné pikine béni bopou la boulén nagou nafekh yi dilen diaxasé soyons conscient les gars ce n’est pas le moment vraiment naniou andeu diapalé Ama balde mou dane modou après boy niang yobou ko retraite c’est le souhait des vrais pikinois ❤❤❤❤

  • @soulagertvofficiel8782
    @soulagertvofficiel8782 Год назад +2

    Ama yalla nako yalla soutourale si barkit seydina mouhamed psl 💙🤍

  • @maxlhommefort3343
    @maxlhommefort3343 Год назад +2

    que dieu vous aide Ama te yàlla na ko yàlla mayi ndamm si barke serigne babacar

  • @ndiamendoye417
    @ndiamendoye417 Год назад +19

    Sa analyse si ama modou lo daguassi dioum so xollé ama mogeuna volume th modou mogeuna musclé modou doley biir la yoré endurance cardio bi louma weer th woor modou moko eupelé Ama

    • @alhousseynoudiallo6054
      @alhousseynoudiallo6054 Год назад +1

      Sa khalat rek gafi walh

    • @papamakhtarniang
      @papamakhtarniang Год назад +1

      Pourtant wouté wolén trope si halat dé. Motah mouy nan nako modou yobou a l'usure. Contact dans les 1e minutes arangéwoul modou té lolou ama ham

    • @abdoukhadredjilybeye8785
      @abdoukhadredjilybeye8785 Год назад +2

      ​@@papamakhtarniangmais frère Ama dakhoul beuré Modou di😂😂... Modou meunn n'a dianguall Ama beuré jtj...

    • @senegal2
      @senegal2 Год назад

      Yaw bayil bakhoul

    • @senegal2
      @senegal2 Год назад +1

      Yaw boudon ya nonoungaye def boye niang bopam laye lidanti topatowoul ama

  • @sawroumbengue7820
    @sawroumbengue7820 Год назад +10

    Lima wakhone contre balla gaye boye Niang lay wakh Ama baldé n'a déff point de presse té bania def Open presse

  • @magattediop4442
    @magattediop4442 Год назад +2

    Bakari est trop professionnel ❤️

  • @MichelMendy-g7r
    @MichelMendy-g7r Год назад +10

    Coach bakari a parfaitement raisons.le camp de boy niang ne vont pas supporters Ama sur se combat donc c a Ama de se mefier .

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Год назад +1

    Amaa Baldé moy borome pikine 💚❤️💚❤️💚
    Lolou Doutaydé Coach Bacary Bien Dit Amaa Baldé combat bii Boula Boy NIANG Tékk Beute Féneu waxou Mala Moulay Lall Boy NIANG Ak papa Dji 🤭

  • @babacarndiaye1734
    @babacarndiaye1734 Год назад +1

    ❤❤merci Bakary bien dit boy Niang yénéwoul ama victoire sa c est sur mo Yoni nguéwélyi nann ama paréwul d'où Modou boy Niang la

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 Год назад +1

      Boy niang dal mo mom journaliste yi
      😂😂😂😂

    • @karimbandios4136
      @karimbandios4136 Год назад

      ​@@thiamahmadulattekh562sie parce que tout les journalistes ces des guewelles surtout sur la lutte

  • @MaïmounaMbaye-e4b
    @MaïmounaMbaye-e4b Год назад

    Deugg dou romb ay nopu boy niang sétann nako légui wakhoul sakh ama yalnako yalla may ndam bou sagnonn gnou dann bilahi wayé yalla douko sétann

  • @paulinecarvalho6257
    @paulinecarvalho6257 Год назад +1

    Tout le monde pense à ça que dieu me pardonne mais ama on le laisse entre les mains de dieu inchalla il va battre modou lo avec la manière inchalla

  • @ridialdieng2861
    @ridialdieng2861 Год назад

    Bilay coach deug rek nga wakh boy niang deum leu

  • @modoufaye5936
    @modoufaye5936 Год назад +2

    Merci bakari

  • @taphaamdygaye4245
    @taphaamdygaye4245 Год назад +8

    Ama roi des arènes Inchalla

  • @mordiodiosylla6496
    @mordiodiosylla6496 Год назад +1

    Merci bakari❤❤

  • @thierno711
    @thierno711 Год назад +1

    Merci bacary

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 Год назад +2

    Bakary. Tu. As. Raison. Ama. Defal. Attention

  • @BeckayDiop
    @BeckayDiop Год назад +1

    Non yalla bakhna yalla rek mofi nèk donc Ama yalla nako yalla eume sèn boy Niang guenna begg que Ama

    • @babacarndiaye1734
      @babacarndiaye1734 Год назад

      Eume séne AK boy Niang Yeup ay défaillant langne même contre gris eume gris faral

    • @BeckayDiop
      @BeckayDiop Год назад

      @@babacarndiaye1734 non bilahi Ama molènn guenn fouff grand bilahi dama yerem Ama

  • @BabacarFaye-w7d
    @BabacarFaye-w7d Год назад +3

    D’une part limou wahni wakeur Boye Niang deegla parce que titre roi des arènes est en jeu

  • @bocarbocoum4221
    @bocarbocoum4221 Год назад +2

    C'est la vérité absolue

  • @mayes2616
    @mayes2616 Год назад +2

    C est vrai si ama est roi le combat modou boy niang2 n aura pas de chance

  • @salifbalde8953
    @salifbalde8953 Год назад +1

    Meme la communication de tapha khandji c'est laba Que j'ais confrimer tout sa Mes dieu es grand

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj Год назад

    Ama yalla nako yalla maye dam thie barke seydina. Moukhamed

  • @ndongodiop2022
    @ndongodiop2022 Год назад +9

    Logique rekk ngafi wakh Ama na deff tres attention

  • @dimkhalebambiste2931
    @dimkhalebambiste2931 Год назад +6

    Bilay ya mana doul té dou yaw la setane kerok si bén live ngani modou mo geuna paré ama tay ngani ama mo eupou dolle doul rek ngay def

    • @cherifcissokho4633
      @cherifcissokho4633 Год назад

      Eupeu dolé ak geuneu paré bokoul réfléchi bien ci limou wakh physiquement ak endurance ak dolé bokoul

  • @ebousowe1535
    @ebousowe1535 Год назад +2

    I love this guy mein
    This is just the whole truth Ama must be careful

  • @ChaybaMaigaMaiga
    @ChaybaMaigaMaiga Год назад +1

    Merci Bakari

  • @omzokouya9779
    @omzokouya9779 Год назад +2

    Bakary je t apprecie pour ta sincérité

  • @KhadimNiasse-b8e
    @KhadimNiasse-b8e Год назад +9

    Ama kase❤

  • @karimbandios4136
    @karimbandios4136 Год назад

    Ta exactement raison ama est contre tous mèm balla je neppa confiance a eux sur le combat moudou lo et les camps de boy niang pikine

  • @ibrahimasene9243
    @ibrahimasene9243 Год назад

    Billahi coach wax nga deug waa keur boy niang deuguouwouniou

  • @khadimkebe224
    @khadimkebe224 Год назад +2

    Deug dou nekh verite absolu

  • @seydouba304
    @seydouba304 Год назад +7

    Bacary 😮 tay danga dioum 😮 vraiment yangui wakh Lou graw
    Ya ngui wakh faire rou chaytané lii bakhoul 😮 yow mouno kham Lou nieuweu goul 😮
    Pikine bénn bopoula 😮

  • @morgningue7654
    @morgningue7654 Год назад

    Lou ler gawakh bilay m yalla bakh na Ama balde kesse

  • @omarniang4346
    @omarniang4346 Год назад

    Ama yallanako yalla maye ndame si barkè baye karimmmmmm aminnnnnnnn aleee balla Geuye rk

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc Год назад

    Magi gnane modou douma ama baldé dane boy niang mais cependant le lutteur le plus loyal le plus professionnel de pikine c'est boy niang mou nexx nakari lolu la yalla défe

  • @ametmbaye9413
    @ametmbaye9413 Год назад

    Day dul rk ama AK boy niang nio bokou ndeye ak baye entouka Roi bii Day nieuw pikine force

  • @mamadousamate7142
    @mamadousamate7142 Год назад

    Bakary il a raison deh Lou Lerr lay wakh nii

  • @NiangeFallou
    @NiangeFallou Год назад +2

    Bakari yaw saytané bou kat sa ndaye gna sa data yaye

  • @bocarndiaye6795
    @bocarndiaye6795 Год назад +9

    Dama khamoul lou takh sénégalais beug graw grawlou
    Ki limouy wakh tegouko feine
    Certains sénégalais aussi di diay graw di confirmé
    Nitt dagayy mandou wakh loula woor
    Bene mbok boy Niang meusoula wakh liguay wakh ni
    Nguay diakhasse
    Yallah naniou yallah mouseul si Ayy sheytane.

  • @abdoulayendoye542
    @abdoulayendoye542 Год назад +2

    Déléne wakh diam diko dokhé boy Niang méloule nonou

  • @djibingom5668
    @djibingom5668 Год назад +1

    Bilay deg diou werrrr la wahhh

  • @TallaFaye-y8t
    @TallaFaye-y8t Год назад +3

    Vérité absolue

  • @mameyaxxilalo
    @mameyaxxilalo Год назад +3

    Bakary del def mouth mouno analyse fi senegal leu nitt niangui yenenete diam beu legui fi kounek seu weurseuk ngay lek

    • @mameyaxxilalo
      @mameyaxxilalo Год назад

      Aussi Boy Niang daneu balla gaye (idololou ama et 2 fois tombeur de modou lo) amoul loumouy yene loubone ama

    • @mameyaxxilalo
      @mameyaxxilalo Год назад +1

      Boy Niang Sakh Roi insbi mogui melne France ak Monaco

    • @mameyaxxilalo
      @mameyaxxilalo Год назад

      Boy Niang Diameu Rek leu Yene Ama bayilene Diakhasse

    • @mameyaxxilalo
      @mameyaxxilalo Год назад +1

      Il faut savoir communiquée, en d'autres termes si ama tombe c'est avantageux pour boy Niang point bar

  • @RamaNdiaye-ur1pc
    @RamaNdiaye-ur1pc Год назад +2

    Lou ler gua wakh Ama amna gnioukay khéh m inchallah Dina am ndam

  • @moustaphafall4552
    @moustaphafall4552 Год назад +1

    Billahi Bakary deugg la wax

  • @BabacarFaye-w7d
    @BabacarFaye-w7d Год назад +3

    Mè limou wah si parcelle es que mousna guiss Zoos si bèn combat tènor si parcelle et pourtant Gora Sock Talfa Garga2 jambar lagnou book moom caoch dafa faar de trop na lidianti mbeurram

  • @SerignedameDione-h9v
    @SerignedameDione-h9v Год назад +1

    Bonne continuation

  • @mahidrammeh2480
    @mahidrammeh2480 Год назад +2

    Bacari na fékh gua légui boye nian ak balla guaye2 ka na wakeur ama balla guaye mom lagne fralone wakhe lôlou domou rame gua réck maso wahke si boye nian louraféte

  • @naleer-vb2oi
    @naleer-vb2oi Год назад +3

    C vrai yagg nako khalate même BG2 beugoul mou dane lou graw lay wakh nii

  • @DjilyNdiaye-pw8zx
    @DjilyNdiaye-pw8zx Год назад +2

    Bakari kouma na doull nga diakhasé rk

  • @FallouFall-z9h
    @FallouFall-z9h Год назад

    Bilahi doumako wèddi Ama yalla nako yalla may ndame

  • @seydouba304
    @seydouba304 Год назад +4

    😮bayuilen DOUL
    Ay chaytané ngénn Ama AK boy Niang AK kharit DEUG laniou
    Beurré day diékh

  • @PapaDiop-g3d
    @PapaDiop-g3d Год назад

    Il a raison dhè

  • @ElimaneNgane
    @ElimaneNgane Год назад +1

    Man dh deukou m Pikine mais bakari li mou wakh ni seytané Mo koy wax diakhassé wa pikine rk leu niaw n trop nité lou bax leu

  • @mordiodiosylla6496
    @mordiodiosylla6496 Год назад

    C vrai ❤️ ♥️

  • @khadimthiam
    @khadimthiam Год назад

    Wolof Ndiaye nèna dou deug yeup lagni wakh tèy la comprendre lolou . Bakary dit la vérité gnou koy traité de seytanè . Mane khalat na li bou yag ba wakh si ak nit. Il y’a un enjeu dans ce combat

  • @abdoulayendoye542
    @abdoulayendoye542 Год назад +2

    Ama combat bi boy guawoul diekh Dina khoulokh gneup

  • @solimanjanneh
    @solimanjanneh Год назад +1

    Is true bakary

  • @ndiougamar2202
    @ndiougamar2202 Год назад +1

    C normal chacun défend son carrière Boy Niang vs Balla Gaye wakeur Ama rangé wougnou woone si côté boy Niang khana Pokola késsé mo assumer si pikinité bi

  • @papecisse6000
    @papecisse6000 Год назад

    Lingaye wakh sétte si Yalla Bakary sakho

  • @gogofofana9086
    @gogofofana9086 Год назад

    Yaw dangay feenn rek Cooch boy NIANG Amoul holou iniann ok seytaneeee ngueenn rek

  • @IbrahimaTambedou-u7w
    @IbrahimaTambedou-u7w Год назад

    yaw pape sarr mola wakh liguaye mouno nek Europe di khame lou khew fi

  • @amadugningue8168
    @amadugningue8168 Год назад

    Une bone question entre forme et force musculation dou dole

  • @ogviito1949
    @ogviito1949 Год назад +2

    Ki mom dof la

  • @malickly4840
    @malickly4840 Год назад +1

    Lolou moy deug,ama doit faire très attention

  • @IbrahimaTambedou-u7w
    @IbrahimaTambedou-u7w Год назад

    yaw mi yaye fene nak yaw mouno d'ara si modou lo yaw mou danou rek gua beugeu waye d'où am dé incha ala

  • @HerveBasse-in1lv
    @HerveBasse-in1lv Год назад

    De tout façon ama ak boy niang nieup si souff layouy dieum modou nèkeu nag president pikine mou dièh tak

  • @abdourahmanemballo67
    @abdourahmanemballo67 Год назад +9

    Tu as vraiment raison car en voyant le 200% de pikine c'était cré par Degaul pour combattre Balla gaye 2 contre la famille des jule balde

    • @babacarndiaye1734
      @babacarndiaye1734 Год назад +1

      Bien dit

    • @mactarlo3502
      @mactarlo3502 Год назад

      Lou ler

    • @Concept0208
      @Concept0208 Год назад +1

      Boy Niang amoul xolou kéñane. Yaw mi yay diaxassékat bi té xamo dara😂
      Bakary wax rek ngay def.
      3 combats professionnels MMA nga def: 1 victoire, 1 sans verdict (té dañla door 1er Round nga wathie. Après test dopage ñiou annulé victoire bi), 1 défaite.
      1 victoire contre Black Nash (14 Octobre 2017), Défaite par K.O au 1er Round/puis sans verdict contre Adam Dyczka (8 Décembre 2017)
      Défaite contre Walter Howard (2 Août 2018).
      Fin de carrière.

    • @momobouthiapathiolybi7752
      @momobouthiapathiolybi7752 Год назад +1

      ​@@Concept0208khamoul Sarah ndeyam 😂😂doul rk lay deff😂

    • @Concept0208
      @Concept0208 Год назад

      @@momobouthiapathiolybi7752 Au lieu ñou séti ñi xam Lamb wayé ñou dieulko diñouko forcé té xamoul dara

  • @GrandAbdou-lo7ms
    @GrandAbdou-lo7ms Год назад

    Bayil doule boy niang ak ama ben le yèn waliyane yénay seytane

  • @deugdeug381
    @deugdeug381 Год назад

    Pikine la deuk mais Bakari wahh na deug wa keur Boye Niang amouniou ngore

  • @tidianedoumbouya596
    @tidianedoumbouya596 Год назад

    Bonjour puis je avoir le lien de la chanson mbayang loum avant le live ?

  • @naleer-vb2oi
    @naleer-vb2oi Год назад +1

    Pape Sarr sakh khamna lolou

  • @BeckayDiop
    @BeckayDiop Год назад

    Ndakh depuis combat bi takhaw wa keur boy Niang

  • @serigneballagaye4105
    @serigneballagaye4105 Год назад +2

    Bakary wahna deukeu.guisna lolo bur pikine

  • @kevinbow758
    @kevinbow758 Год назад +1

    Bakary❤❤❤😊

  • @aliousarr3816
    @aliousarr3816 Год назад

    C vrai frère

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if Год назад +1

    Bakary bayile diakhasé ak doule pikine niongi si ginaw Ama

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv Год назад +4

    Bakary tagua khamni modou dolé danouko

  • @saloumisland2823
    @saloumisland2823 Год назад +2

    Il a problème avec boy Niang c pour cella mouy yalla der

  • @Fitserigne
    @Fitserigne Год назад

    Son bi avant vidèo bi ngir yallah Kou kham kouko way🙏

  • @profcoly6085
    @profcoly6085 Год назад

    Mais bacary ligua wakh ni meune na tass pikine ba réyanté al thie moytiul genroy wakh yi té sa wakh dji meune na tass pikine ba faaw moytoul wakh

  • @falloufall2765
    @falloufall2765 Год назад +2

    TAYE moome daga dioum déle khôl bou bakh ligaye wakhe Ama AK boye Niang gniou Book pikine boull yakhe khélou pikinois yiii

  • @falloumbodji3062
    @falloumbodji3062 Год назад +2

    Même eumeu sene sawaroul si ama

  • @ndiougadieng
    @ndiougadieng Год назад

    Bakary mi mo oubi leufeul ndeyam meune wakh diou niaw . Yaw kato sa ndeye def dara thie lamb wakh diou Boneu rek nga meune . Sa tounou yaye bakary sakho

  • @gogofofana9086
    @gogofofana9086 Год назад

    Lolou si promoteur lay donn par se k Gaston Comba royal la Beug teug par se boy NIANG kasseee Comba royal lanou ko fay

  • @cheikhdiouf-mm3yk
    @cheikhdiouf-mm3yk Год назад

    Bilahi Lou leer NGA wakhe ama kassé boye niag dou dara

  • @NdiagaFall-b6t
    @NdiagaFall-b6t Год назад

    Saway guene ngafi bou yagoul ni boy niang dala yorel xaliss wax ba doyal falé woula tay nga nieuw di def sa yeufo guel yi Ama dou ragal gniko weur niapa xam lamb yallah naka yallah may ndam

  • @boyniangniang4700
    @boyniangniang4700 Год назад

    Ragal yalla saytane ki d'où coach

  • @yvonnebadiane2702
    @yvonnebadiane2702 Год назад +1

    Vérité absolue Ama waroule def Open Press

  • @laminjagne7254
    @laminjagne7254 Год назад

    Modou xarange lo for life