Ndéssane yaye amoul remplacent yaye yifi nék yalla yalla nagnou gueudou fane ak wér féké ndiérigne diabote yi inchallah yaye yi dedou yalla kharéléne aldiana si Barker seydina mouhamad ❤
Cette émission mérite d'avoir des sponsors. Car elle permet à tout un chacun d'avoir l'opportunité d'extérioriser ses sentiments. Aussi de faire croire à tout le monde que seul lacommunication peut régler tout problème. En tant sociologue je suis à 100% de l'émission.
Eumeu Ndeysaan.. Kou fonkk dinnee.. Ñoo doon bokk sappé Ak Falah Pikine ci KHIMAYOUL LAYL yi durant les derniers jours du Ramadan. Qu’Allah facilite ta sortie de la lutte.
Eumeu diambaar la... Confidence bi sa digeunteik Tyson laci ndawci boleiwoul et ça aurait été super intéressant... Belle émission avec plein d’émotions diambaar
J'ai commencé à suivre quand j'étais petit avec son combat gris bordeau billahi c'est la où j'ai compris un vrai homme supporte tjrs les vrais ❤❤❤❤💫 t'es le meilleur billahi
Taye dioyena bilahi ndakh damakhame lii eumeu séne di dounde envers sa très chère maman comme moi est d'autre ki on perdue leur très chère maman ndeysann mme cagne ngamaye invité confidence mawakh linék sama ❤ bonne fin d'année à tt le monde
On peut avoir des millions et des milliards Toutes ces richesses ne peuvent jamais remplacer nos mamans Longue vie à nos mères et paix à leurs âmes ceux qui ont perdu leur mères !
Wallahi Sénégal kou beugueu bakh yalla dibalila.ngnifi diarrhée nieum dagnon tarbiwou seni way diour. Naniou gueum yalla tey naniou ligueye tey diamou yalla
0:45 L'importance d'être tjrs bon avec les parents particulièrement la mère, walahi après leur mort on regrettera beaucoup 😢 courage eumeu t'as touché mon cœur ❤❤ 0:48 😢
Eva était vraiment inspirée pour ce podcast les questions étaient super précises par rapport à la lutte et tout ce qu'il y a autour 👏🏿 on aurait aimé avoir ça avec Sadio mane. Bonne continuation 🫶🏿
Eume yallah nala yallah maye kholou mougne parce que c'est pas facile mane nékouma ak sama yaye mais sou gnewé fima néke si sama keurou mame souy délou sama raguogne yi bougnouy géneu doumako sakh taye Mais Éva chapeau à toi beugonena gua invité bass thioung
Sokhna si indil lén ma Modou lo way sinon eumeu séne yalla nala yalla défal jamm té mère bi aussi sougnou Borom yereume ko té diégal ko haré ko aldjanay firdawsi té yéhé gnouko si barkep Nabil Moustapha PSL 🙏🏿
La journalist Elle et tres magnifique et gentil et correct Elle te pose des question correct elle te force pas de dire cest que tu voulez pas dire machallah Bonn continuation 🎉🎉
Vraiment li metina trop sa wadiour sone si yaw te fekewoul sa ndiarigne 😢mane sama mame lakoy dioye Vraiment il a tout fait pour moi 😢mai yalla defe mou guene adouna mou meti trop mai nak yalla moy bour 😢courage eumeu 😢❤❤
Respect Champion pour tes Valeurs thi diomebi et Respect bi Santé Longue vie et beaucoup de Baraka Sois béni que Allah te garde te préserve et te fortifie ❤❤❤❤❤❤
j'ai beucoup pleure avec Eumeu Sene. Yal na Yallah yereum souniouy way dawlou yi. amine. je t'estime beaucoup Eumeu Sene. Yal na la Yallah di yagg defal ndam adina ak alakhira.. amine
Sokhna yalna yalla samm leu ! Vous etes semblable à une pepite derivée des ouroul aini. Tout chez vous me fait frémir, sourire rire regard voix... mashaAllah seu leer woo nama !!!!!!!!!
Eva sama kharite bi bayyil di invité nitt yi dilén dioy looh la wakh😂ay dioyou makk bakhoul dh mes sa liguey rafét na machallah bonne continuation ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
❤ dicourage eumeu sene masta tu Champion notre fierté pikine notre 2em roi des arène champion d'Afrique pikine t'aime fort ❤ yalla nala saye dôme faye si sa yaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ si barke khadim Rassoul ❤❤
Maan d dama xamoul liatx maa, Eumeu di na dioylo 😪😪😪 Il es tro b1 ce type mashallah Yalla na la Yalla défaal diam ak salam😍. Mw d perso litax ma beug ko book nasi doka daan bamou saletél sa victoire
BONJOUR JEUNE FRÈRE NOTRE MAMAN ÉTAIT UNE FEMME DE VALEUR SÛRE, JAMBAR DEUK ,TRÈS GENTILLE, PIEUSE QUE FIRDAWSI SOIT SA DEMEURE ÉTERNELLE AMINE AMINE AMINE YA RABY
Mafi djitou nakk khana dina am Jaime tey nakk si Barki brom touba ❤
❤
démal ligueyi
❤❤❤Kou beug eumeu sene lalal j'aime ❤❤❤🥰
Ndéssane yaye amoul remplacent yaye yifi nék yalla yalla nagnou gueudou fane ak wér féké ndiérigne diabote yi inchallah yaye yi dedou yalla kharéléne aldiana si Barker seydina mouhamad ❤
Amine Amine Amine
Kou beug sa yaye lalal j'aime ❤❤❤🥰
❤❤❤❤
j'aime 😅❤
Cette émission mérite d'avoir des sponsors. Car elle permet à tout un chacun d'avoir l'opportunité d'extérioriser ses sentiments. Aussi de faire croire à tout le monde que seul lacommunication peut régler tout problème. En tant sociologue je suis à 100% de l'émission.
Pas à tout un chacun deh , seulement les stars
@@270tjrpluhautmerci laba😂
Non mbeur dioyelo guama bilahi kou sa yaye di doundou yalla na yalla goudal fanname
Amine
Ndeysane Eumeu séne le grand champion, yaye dafa am solo yaye moy lepp si doom
Cela fait plus de 35 ans que j'ai perdu ma mère et je suis tjrs en larmes quand je parle d'elle pour vous dire vous que une maman est irremplaçable
Eum sa wadjour yalla nako seydina mouhamed terou
Man Balla Gaye moy sama mbeur ms eumeu sene nit kou la yalna la yalla defal diam🤲
Amin
Eumeu Ndeysaan.. Kou fonkk dinnee.. Ñoo doon bokk sappé Ak Falah Pikine ci KHIMAYOUL LAYL yi durant les derniers jours du Ramadan. Qu’Allah facilite ta sortie de la lutte.
Eumeu diambaar la... Confidence bi sa digeunteik Tyson laci ndawci boleiwoul et ça aurait été super intéressant... Belle émission avec plein d’émotions diambaar
Oui moi aussi je m'y attendais mais est ce que invité bi niaanouko mou bagn si sori
Il a tout fait pour ne pas craquer quand il parle de sa Maman mais L'amour qu'il a pour sa mère est irréversible
J'ai commencé à suivre quand j'étais petit avec son combat gris bordeau billahi c'est la où j'ai compris un vrai homme supporte tjrs les vrais ❤❤❤❤💫 t'es le meilleur billahi
Meilleur pour moi 👊❤
Nous qui avons encore nos mamans en vie ..faisons de notre mieux pour les rendre toujours heureuses.....
Je vois en lui une personne très responsable et sociable merci champion bon courage
J'ai toujours aimé et respecté EUMEU SENE DEPUIS L'époque "BOUL FAALÉ" Daafa Yaarou Troop ❤❤❤
Taye dioyena bilahi ndakh damakhame lii eumeu séne di dounde envers sa très chère maman comme moi est d'autre ki on perdue leur très chère maman ndeysann mme cagne ngamaye invité confidence mawakh linék sama ❤ bonne fin d'année à tt le monde
Lima nekh si mom moy day lamb ta meun lamb ❤
Ohhhhhh masta champion walahi kouko doundoul mounoko kham ALLAHOU AKBAR repose en paix maman
On peut avoir des millions et des milliards
Toutes ces richesses ne peuvent jamais remplacer nos mamans
Longue vie à nos mères et paix à leurs âmes ceux qui ont perdu leur mères !
Verite apsolut
Bilaye
L’absence de sa mère lors de son premier départ à Ziguinchor et son deces ont laissé un grand vide dans son coeur 😢
Walahi ndeysane
C très dure d perdre une maman la douleur es inexplicable k'Allah le très miséricordieux accorde le paradis a nos mamans
Ndeysan Eumeu kou bakhla champion
Un grand champion moy eumeu sène mbeur kamile machallahh ❤
Eumeu Séne n'est pas mon lutteur, mais je vois en lui un homme qui a un grand coeur
Wallahi Sénégal kou beugueu bakh yalla dibalila.ngnifi diarrhée nieum dagnon tarbiwou seni way diour. Naniou gueum yalla tey naniou ligueye tey diamou yalla
0:45 L'importance d'être tjrs bon avec les parents particulièrement la mère, walahi après leur mort on regrettera beaucoup 😢 courage eumeu t'as touché mon cœur ❤❤ 0:48 😢
Seuls les braves savent pleurer. Les braves sont ceux qui ont du cœur.
Best Senegalese program that touches heart ...bless great journalist and eumeu sene my ake me shed tears after a ling time
Eumeu sene un vrai champion ❤
Eva était vraiment inspirée pour ce podcast les questions étaient super précises par rapport à la lutte et tout ce qu'il y a autour 👏🏿 on aurait aimé avoir ça avec Sadio mane. Bonne continuation 🫶🏿
Eume yallah nala yallah maye kholou mougne parce que c'est pas facile mane nékouma ak sama yaye mais sou gnewé fima néke si sama keurou mame souy délou sama raguogne yi bougnouy géneu doumako sakh taye
Mais Éva chapeau à toi beugonena gua invité bass thioung
Merci Eumeu, pour les conseils (la fin❤).
Je beaucoup ❤❤ bilaye walaye yaguimey dioy loo 😭😭😭😭💞💪🙏❤️ champion bonne continuation ❤❤❤
C vraiment émouvant courage Eumeu. Sa yaye yalla nako souniou borom kharé Aldiana firdawsi❤❤❤❤❤❤
Sokhna si indil lén ma Modou lo way sinon eumeu séne yalla nala yalla défal jamm té mère bi aussi sougnou Borom yereume ko té diégal ko haré ko aldjanay firdawsi té yéhé gnouko si barkep Nabil Moustapha PSL 🙏🏿
Eumeu un vrai champion kou beugue yayam bilay ❤❤❤❤❤
La journalist Elle et tres magnifique et gentil et correct Elle te pose des question correct elle te force pas de dire cest que tu voulez pas dire machallah Bonn continuation 🎉🎉
Vraiment li metina trop sa wadiour sone si yaw te fekewoul sa ndiarigne 😢mane sama mame lakoy dioye Vraiment il a tout fait pour moi 😢mai yalla defe mou guene adouna mou meti trop mai nak yalla moy bour 😢courage eumeu 😢❤❤
Respect Champion pour tes Valeurs thi diomebi et Respect bi Santé Longue vie et beaucoup de Baraka
Sois béni que Allah te garde te préserve et te fortifie ❤❤❤❤❤❤
Eumeu sène gor deugueu leu wallahi
Goor yalla deugue dioyena nianalko yalla foumou nék geunalko foumou diougué souniou borome kharéko aldiana 🙏
Eumeu séne yalnala yalla defal diam .amouma sa yaw sago bilahi .sa yaye aussi yalla yeureum ko xaréko aldiana firdaws ak mbolem djoulite boufa nek.
Merci senepeople sene liguey rafêtna mais ronganii beurina Eumeu m'a fait pleurer bonne continuation à vous
Big respect Enmeu sene
Do sama mbeur deh mais borom xoll bou Nice leu🤗
Bama beuguei balla gaye ba parei eumeu sène laa ci tek mashAllah un homme de vertu très humble 🎉❤
Prochain invité tyson svp 😊
j'ai beucoup pleure avec Eumeu Sene. Yal na Yallah yereum souniouy way dawlou yi. amine. je t'estime beaucoup Eumeu Sene. Yal na la Yallah di yagg defal ndam adina ak alakhira.. amine
Merci champion courage à toi 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Sokhna yalna yalla samm leu ! Vous etes semblable à une pepite derivée des ouroul aini. Tout chez vous me fait frémir, sourire rire regard voix... mashaAllah seu leer woo nama !!!!!!!!!
Machalla yalla samla 🎉🎉
Ndaysane eume yala bakh n'a
N'oubliez jamais les 5 prières par jours ❤🎉
Champion borom xol bou Nice la en même temps gaindé la j'adore ce genre d'invité au lieu difi invité Mama Gentille comme la dernière fois
Ndeyessane yalla na bour yalla doli soutoura
Non bilay eumeu mane dama beug rk t bikahi yalla kese takh sur son stile❤✌️
lii Eumeu dii wakh kham nako bou bakh niak yaye koumou daloul meunouko expliquer doko miss moukk chaque jour dafay béss sii yaaw nguay doundeu ak mom doko meusseu faaté loula métti siissa aduna nguané boufii sama yaye nékone so amé mbecké daa ngua kooy beugue partager ak mom. Yalla bakhna
Eva sama kharite bi bayyil di invité nitt yi dilén dioy looh la wakh😂ay dioyou makk bakhoul dh mes sa liguey rafét na machallah bonne continuation ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Mbeur bou dal vraiment
Yalla nala yalla takhawou ci barké Seydina Mohamed psl
Your story tells me my dear mother Yalneu souf sédd si kawam , Mbeur téy mom djoylo ngama 😭....
Amna solo wakh dji rafetna trop Machallah
Eumeu sène daf ma nèkh trop❤❤❤❤❤
Un vrai champion ❤🎉eumeu sene🎉
Mv eumeu séne ❤bokou mako ak ken sm mbeur bi 😊
Nitt kou am yarr té rafet xol toujours souriant masha Allah
Macha Allah eume aka yarou té Am diom❤
NE PLEURE PLUS JEUNE FRÈRE TA MAMAN EST TOUJOURS PRES DE VOUS ,MERCI BEAUCOUP A PAPA NGOM ET MAMAN ASTOU
❤ dicourage eumeu sene masta tu Champion notre fierté pikine notre 2em roi des arène champion d'Afrique pikine t'aime fort ❤ yalla nala saye dôme faye si sa yaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ si barke khadim Rassoul ❤❤
Yaye dafa sori thie dom sama yaye yalna ko yalla yeureum té kharé Ko aldiana thie barcké khassida yi ak dioulite yi djitou niépp 😢
Eva andile niou dip doundou guiss kou d'accord lala j'aime
Lolou la wara dff nak
Lolou rek la yakamti dip le dicton
2024 je sai que vous avez beaucoup de projets
Que 2035 sw le meilleur pour nous ❤
Ndeysan
Love you too my beautifully brother thanks for your ❤❤❤❤❤❤❤❤ God bless you amine yarahbi ❤❤❤❤
Maan d dama xamoul liatx maa, Eumeu di na dioylo 😪😪😪 Il es tro b1 ce type mashallah Yalla na la Yalla défaal diam ak salam😍. Mw d perso litax ma beug ko book nasi doka daan bamou saletél sa victoire
Mangui réclame dip doundou guiss ❤❤❤❤❤
Kou rafet khol bilay Eumeu
Mon champion 🎉❤❤
BONJOUR JEUNE FRÈRE NOTRE MAMAN ÉTAIT UNE FEMME DE VALEUR SÛRE, JAMBAR DEUK ,TRÈS GENTILLE, PIEUSE QUE FIRDAWSI SOIT SA DEMEURE ÉTERNELLE AMINE AMINE AMINE YA RABY
La prochaine 🤔 Le Grand champion Du monde MMM Reug Reug kou d'accord ak man beuseul j'aime👍
Bou gneuwè dou djoye dèhhhh
Deffe n'a ba paré@@iboudiop9093
@@iboudiop9093😂😂😂
Koku manul communication bu bkh
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
C'est émouvant cette émission
Machallah merci beaucoup à vous 😢😢😢😢😢😢😢🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉🎉❤🎉❤😢❤😢
Dama beugue eumeu séné deugeu deugeu ❤❤❤
yaye kaina amoul fayam ndeysaan, yana yalla faye baipe yaye boudon mounie to sonon si njabootam
Eumeu ndeysane dafa yarou am talibè ❤
Massa champion repos éternelle à ta mère la mienne et à tout nos disparus 😢
Sama mbeurr wayyy❤
On réclame Eva même en tant qu’invité pour se confesser 😂😂kou d’accord rek lalal j’aime
Walahi souniou yaye yi danio sonou loool bilahi 😭😭😭
ndeysan yaye dafa sori khole 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Vraiment l'animatrice est trop forte ❤
On reclame TYSON ❤❤
Eumeu diambar NGA gor yalla deugue NGA
Courage champion ainsi va la vie ça fait 19ans que j'ai perdu mon papa
Eumeu Sene = Gaïndé❤
Eumeu damako beug té Yallah takh wallahi dadone am combat madone dem si ay Serigne diko gnanal té meussoumako tek beute lou wessou stade
Diantalmen la emeu sene❤
yalla nako yalla yerem
Ndeysane soko kholai kham ni khôl bou rafette la yore ohhh