Bayina Ameth Thiou, L’oncle de Wally Seck Aladji Mbaye verse de chaudes larmes et révèle «Wally dafa

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 фев 2025
  • Nous espérons que vous prendrez plaisir à découvrir nos vidéos......
    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... CONTACT : 77 451 21 10 EMAIL : Redactionpeople221@gmail.com

Комментарии • 111

  • @People221sn
    @People221sn  Год назад +10

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...

  • @adamasamb1047
    @adamasamb1047 Год назад +3

    Franchement Aladji taye lala respecter, ndakh sa raisonement

  • @thiounelobe114
    @thiounelobe114 Год назад +24

    Machallah Lou yague deugeuleu elhadji mbaye yagua bakh yagua Gorée kéneu moussouko dégue mou wakhi Lou niaw wala mou dieufé ko . Yalla nalla Yalla faye sa khole mbaye yokou yagg wéeerr inchallah si barké Mame cheikh Ibrahima fall lamp.

  • @KhadimSyll-eb6wp
    @KhadimSyll-eb6wp Год назад +22

    Maman kiné Diouf yall nako yalla défall diam AK goudou fane❤❤

  • @momocisse1003
    @momocisse1003 Год назад +12

    Aladji Mbaye yaa baakh rek! Tu es un mec en or❤! Toi même tu sais… rafeet naa ❤

  • @elhadjimamadoukasse9333
    @elhadjimamadoukasse9333 Год назад +83

    Ki mo geuneu goré raam daan, mo léne fa gnieukeu gniome gnieupeu té kéneu moussouko dégueu dama fékké, mom ak Adama Sarr, khamnagniou kiy wakh ak gniome . Ba mouy door mom rék mo done féthial Thione Seck (yalla nako yalla yeureum te kharéko aldjanay firdawsi Amin)

    • @mrwong4093
      @mrwong4093 Год назад +11

      Un danseur très fidèle ,il était là pendant la traversée du désert jusqu’à ce que le ram dann se fasse une place au soleil

    • @elhadjimamadoukasse9333
      @elhadjimamadoukasse9333 Год назад +5

      ​@@mrwong4093 Deugeuleu

    • @buz7755
      @buz7755 Год назад +3

      Ndeysane

    • @Keyna26
      @Keyna26 Год назад +6

      je valide maa fékké

    • @khougebarry7689
      @khougebarry7689 Год назад +1

      Walaye wakh gua deugue pirr

  • @AFNNdoye-fz3pk
    @AFNNdoye-fz3pk Год назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ y'a rafeti wakh wayy amal diam mbaye

  • @aichasaliou7823
    @aichasaliou7823 Год назад +7

    Nit Nite Machala Mbaye bakhegua. Wakh dji rafetna diadieuf Machala

  • @AFNNdoye-fz3pk
    @AFNNdoye-fz3pk Год назад

    ndeysane mbaye y'a bakh yalna yalla fayy

  • @awananykeita357
    @awananykeita357 Год назад +2

    Aladjiii mbaye aka bakh té gorè beugue pape Thione ba beugue lou takk siii Mom
    Ak bakh sama kharite bii❤️❤️❤️yalana yala defal diam

  • @laminembaye3978
    @laminembaye3978 Год назад +4

    Aladji mbaye grand bou bax la machallah discours bi ame na solo

  • @yayodiallo1424
    @yayodiallo1424 Год назад +15

    Diaga exemple la de vie ci femme du monde bi yeupou

  • @NdeyeNdiaye-m1g
    @NdeyeNdiaye-m1g Год назад +1

    Elhadji Mbaye kou bakh nga wakh dji rafétna loll machallah

  • @FatouDiop-s6s
    @FatouDiop-s6s Год назад +7

    Machallah le meilleur ya guoret

  • @talladieng6132
    @talladieng6132 Год назад

    Pape Thione Seck Yallah nako Yallah yeureum kharé ko Aldiana firdawsi ci barké yonentebi psl Amin barké Alkhouran. YA goré Aladji Mbaye amal diam bou bakh grand bi

  • @DTFTV
    @DTFTV Год назад +1

    Machallah Elhadij Mbaye ❤

  • @leuzcisse6181
    @leuzcisse6181 Год назад +9

    Mane qui Dama ka Mbeugeu Billahi Chanpion la

  • @babacarsy3127
    @babacarsy3127 Год назад +4

    Aladji mbaye diambe reke guaye ame nite Kou bakh gua

  • @fantacisse3210
    @fantacisse3210 Год назад +6

    Vraiment je t’apprécie beaucoup nitt bou goré kom yaw barétoul sénégalais mo beugue detail kép kouy wakh am probleme sa keur té réglé woko

  • @chephotos5935
    @chephotos5935 Год назад +2

    he know joko west field GAMBIA very well he was always around thione seck

  • @mamadouthioune3123
    @mamadouthioune3123 Год назад +6

    merci beaucoup frère respect à toi

  • @khalifagueye4550
    @khalifagueye4550 Год назад +4

    Interview 40mn c trop long. Aidez nous svp 10 mn maximum

  • @jarieujallow8595
    @jarieujallow8595 Год назад +1

    You are good man Alagie Mbaye❤❤❤❤

  • @modoundiayesonko
    @modoundiayesonko Год назад +4

    Merci beaucoup pere

  • @rokhayagueye5840
    @rokhayagueye5840 Год назад

    Machalla Machalla wakhga Degue Yalla Nalla Yalla Faye

  • @yassine4935
    @yassine4935 Год назад

    Adouna amoul solo✋🏼na lep di rafet ma sha Allah rafetna

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 Год назад +1

    Machalla wakh dji rafete na machalla ❤❤❤

  • @AbyBa-gl6if
    @AbyBa-gl6if Год назад +3

    Alhadj mashala réfetna❤
    33:47

  • @kadijatoujallow3477
    @kadijatoujallow3477 Год назад +11

    Allahuma ameen 🙏

  • @BallagoFamille
    @BallagoFamille Год назад +7

    Merci ❤❤❤

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy Год назад +11

    Ameth thiou damako moudiė yeureum

  • @MaraDiop-u4g
    @MaraDiop-u4g Год назад +1

    Ndeye saane élément bou yague magui niiii akeu goré

  • @makkseck9982
    @makkseck9982 Год назад

    Sama pape dji

  • @mamadieng5574
    @mamadieng5574 Год назад +2

    Ndeysane un gars que j'estime beaucoup . Ken moussoko deg ci dara

    • @fatoudieng7270
      @fatoudieng7270 Год назад

      Daffa beugue bou sincère féthia ko intéressé mouye diarbate thi papa mou yarko thi discipline aladj mbaye bouko nékhone mou dieul micro mane nako vayé papa thione balago seck depuis ba age gnimou yar daffa ame foula fonke linou yor chainame amoul thiabal thiabal baye sy ndiaye fimou fété moko mome ToubakaAllah machaAlla Lawla thiat mane nako respecté nako sincère thi thi nimouye dokhalé eupeuloule diayoul khédje daffa ték liguéye bi thi foula gueume bopame ségame touké aye wakhou malak dée papa thione balago seck daffa préparé domame wakhna lako débeu wakhko teye papa thione koumou bocal dimbili nala ouff aye rakame motakh médias amena solo

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 Год назад

    Ndayesane yaw dagua bakh machala❤❤❤❤

  • @diodiofall3295
    @diodiofall3295 Год назад +1

    Ndeyssane meussouma lhamni Aladji mbaye la toudou kou goré la ndeyssane

  • @zoobastos4487
    @zoobastos4487 Год назад

    Manchallah kaddu yiii amena solo

  • @dabadiallo8267
    @dabadiallo8267 Год назад +1

    Manchala kou bakhe moungui nii doundeul wereule thi barkai seuyedina mouhamed.

  • @mamizndoye9303
    @mamizndoye9303 Год назад +1

    YOW dehh merito Nga THI voiture yi gnuy samba alar diko meye ak millions yiii..lima yem moy lutakh diohugnula THI te ngay nidiay wa SALAM

  • @ndattendiaye9737
    @ndattendiaye9737 Год назад +3

    Bilahiiiii ya goooré

  • @prodrmx5007
    @prodrmx5007 Год назад +1

    aladji mbaay, aladji mbaay, aladji mbaay...néléen alaaaa 😁

  • @OppoMaroc-uo3xz
    @OppoMaroc-uo3xz Год назад +1

    Jaim se mesieu il a tro d personalitai

  • @papeamadousow7549
    @papeamadousow7549 Год назад +2

    Diadieff mon père sa wakheu rafféttna bou bakh bï 👌 Ibrahima seck Sama wadji mon Ami yonbanté ☝️👌💌🚦 vert passage jaunes relentie rouge stop Mame cheikh ibahima fall point ☝️👌

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 Год назад

    ❤❤❤❤❤ machala

  • @daddoseck9953
    @daddoseck9953 Год назад +6

    Ameth dama yakar Danie ko khaptal😢

  • @aminatousall1221
    @aminatousall1221 Год назад

    Elhadje mbaye da bah deysane beugue thione Seck

  • @AbyBa-gl6if
    @AbyBa-gl6if Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤
    Aline

  • @cheikh3249
    @cheikh3249 Год назад +2

    Bayill nak il est temps

  • @maguettesene7527
    @maguettesene7527 Год назад +1

    Elhadji mbaye pikine darou je le connais nit cou baakhe la yaagua dimbeuli aayi domou Adama

  • @codoudiouf118
    @codoudiouf118 Год назад +1

    ❤🥰🥰🥰🥰

  • @wiliammalikk5482
    @wiliammalikk5482 Год назад +1

    Yow dé bo guénone né contanouma gneuppp dinagne né amnga si droit ndaxxx founék diangafa akk papa Thione té bougnomm Ameth gneuwé kaineu moussoula dégue nga waxxx

  • @mbackediop-ot5rj
    @mbackediop-ot5rj Год назад +1

    Music Ndiago Euro 💶💶 bisi souff

  • @khadimndiaye743
    @khadimndiaye743 Год назад +8

    Ameth thiou boumou nieuwatt diarinioul dara ramdane

  • @laliaaidara9304
    @laliaaidara9304 Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ 5:43 van ❤

  • @aramesamb5497
    @aramesamb5497 Год назад +1

    Bonsoir Sa wakh rafetena

  • @fatoucamara4792
    @fatoucamara4792 Год назад

    Sa numéro la beug

  • @ifrara-j3q
    @ifrara-j3q Год назад

    ⚠⚠⚠c'est un deal pour faire la promo de l'évènement de wally à Paris AMETH va revenir et participera à l'évenement de Paris inchala noter le

    • @elhadjimalickniang9475
      @elhadjimalickniang9475 Год назад

      Deal fane xana do xol😂 do yem wally boumouy todj Paris yageuna ameth si nopam mo siss

  • @awand4066
    @awand4066 Год назад

    Demal jaliko Alagie mbye

  • @MaguetteCamara-c1s
    @MaguetteCamara-c1s Год назад +1

    Li nga wakh DEUG pire thia Sahel,kili AK fepp foum dane teugué thi sénégal dem Na fa té yaw rek yafa nékone.

  • @diorndong2168
    @diorndong2168 Год назад

    Ameth thiou c pas la première fois Mouy bayi waly

  • @aissa2425r
    @aissa2425r Год назад

    Aladli walaye ramdan lako moussa ragnè, kilimanjaro, soumbè khamatouma sakh.gorè gua lol.motakh daw liko mbaye si dane wo wally dico weuye dama dane contane

  • @fatouka8857
    @fatouka8857 Год назад +4

    ameth na dem rek sokhlawounou kouye siisou

  • @dieynabagueye4887
    @dieynabagueye4887 Год назад

    Day fene ken dekouko dara mome Ahmet thiou

  • @serignefalloudrame3087
    @serignefalloudrame3087 Год назад

    Wally rék

  • @petisalam
    @petisalam Год назад +1

    Ameth thiou yen lay kassal yaw gat yoroko ya guenaa sonou nieuppp

  • @moussadiome4467
    @moussadiome4467 Год назад

    Aladji mala beug waye yaw rek laye topou si féthiekate

  • @mariemdiop2174
    @mariemdiop2174 Год назад

    Ya mene fethe

  • @buz7755
    @buz7755 Год назад

    Ki niut kou deug le wallahi kou bakh la

  • @nafysy5886
    @nafysy5886 Год назад +1

    Aladji mbaye aladji mbaye bayil fecc magalgua legui

  • @tamsirdia
    @tamsirdia Год назад

    Sokh

  • @Bassiroudiouf-q9z
    @Bassiroudiouf-q9z Год назад +2

    Nit Kou bakh ni lay df di défar

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf2749 Год назад

    Lou am solo ngua wakh frere bilakhi dfa wara gauré tmt kéneu khamoul lii lanela

  • @laminetall2712
    @laminetall2712 Год назад

    Oooooooooo kheweule doule

  • @milkmilo4082
    @milkmilo4082 Год назад +1

    Bokou na si gneuk féthial déme si yalla si nako wally geune géstou kou goré la la ba paré dafa watié bopam

  • @fatoumatajaiteh1764
    @fatoumatajaiteh1764 Год назад

    ❤❤❤❤❤

  • @africain82
    @africain82 Год назад

    famille wally Seck gnou bakh laniou xamnassi dara. il faut nga frequenté len pour xamko.benen. affaire laniou

  • @OppoMaroc-uo3xz
    @OppoMaroc-uo3xz Год назад

    Gran bi mo bah c sa

  • @diorndong2168
    @diorndong2168 Год назад

    Nit ni guaay mel gore baguay nitt daguay done ciment toy beneu yone

  • @falloudiaka4792
    @falloudiaka4792 Год назад

    Linge salle ce lavé a la maison c pas notre problème andelène c pas notre problème séparé vous c pas notre problème

  • @daoudadiatta529
    @daoudadiatta529 Год назад

    Papa changél métier

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 Год назад

    Dosène morom

  • @MG-dd2ps
    @MG-dd2ps Год назад

    Kii aka goré

  • @babacarseck9464
    @babacarseck9464 Год назад +1

    Diadieuf

  • @daoudadiatta529
    @daoudadiatta529 Год назад

    Pabi da wara arête je le connais diamonoye cli ma diaro

  • @aminandiaye4953
    @aminandiaye4953 Год назад +2

    Niome nieup molénn fa djitou yé tay la geuneu goré

  • @MohamedFall-ij1xc
    @MohamedFall-ij1xc Год назад +2

    Yawe kou bakhe ga

  • @mndoye702
    @mndoye702 Год назад +2

    Ameth thiou est faux ...d'où nitou d'ara pourquoi aller dans les Médias waye merde waye

  • @salioudiene
    @salioudiene Год назад

    Pa bou tolniii yaw ngay fethie demal diamou djii yala

  • @awadrame5080
    @awadrame5080 Год назад +5

    ❤❤❤❤