Размер видео: 1280 X 720853 X 480640 X 360
Показать панель управления
Автовоспроизведение
Автоповтор
Machala ❤❤
Ndaysane
Ndaysan
LYRIC1).Ci Thioçaan Kena genula( Jaamu Serigne Saliou).Serigne Salihoo def ngay Yeurmandé.2).Thiossanal sunu Yonén Taba téktal nama( Jaamu Serigne Saliou),Banoo haachim taxul may way léér gua soss louné.3).Sénégal lignko fonk taxna may Andi historique( Jaamu Serigne Saliou),Jublou guéye téktal léén lééru Mame Bambéé.4).Serigne Touba sunu Mbërma fégnal Lou nëbula,( Jamu Serigne Saliou).Tax ba mbacké am way lii la jotaléé.5).La Anta lazii ouhtiita Xidman nubu atann( Jaamu Serigne Saliou),Wa Adamou Baynal Maa i wa tiini Yanjaléé.6).Borom berndé yii dounël Sénégal laadi way( Jaamu Serigne Saliou),Çossanam Chérif la waayé MOURIDE baanguinii.7).Mooy ka lééraloon naarba lay chérif baka séétci soon sa Diamono ..Taxawal Illaahééy def Chérif wéréé.•Kula gën Ragal Yalla Moola gën fii ba foo feléé 8). Baye Kulli THIOUNE Moussé mbooré...Mademba moussé mbooré..Naarba ba Albabou sa maman Yémën la juguéé.9).MOURIDE mooy bëg bëg lassa gën bëg Yalla la ( Jaamu Serigne Saliou).Ka Begëm Serigne Saliou léér Adoun yaanguinii.10).Bam jigué... Egypte la dém top dékh ga Di Nîl ...Tabbi Soudan Jaar Bogal...Bamou douguéé Walo Barack Ba Bourbaa KO dalal...Bam Namé dém Cadior aw Fass lako waajalé.. ( Refrain)11). Fala jeuléé Santawa THIOUNE Top dékh ga Jëm Ndar,Ross Béthio Borom 17 Avril baanguinii( Bis).12).Le Béthio miidaan dinthia Sécret Bour sa Diamono wouténaak,Serigne Saliou fam déf ...MBOOTOU YALLA Yéé.• SERIGNE SALIOU WALA JOKH MBOOTU YALLA YÉÉ.13). SABABU Mouridou Baye Kulli Serigne Balla Thioro Mbacké la,Li Kulli Chaï In Sababounn Tassétt Dajébaanguinii.•Tassêt 17 Avril Béssou dajè baanguinii 14).Diganté Momar Anta Salèék Mame Thioro Diop ak Sokhna Coumba Saala mbaye..Ku dém Kool khandann...guisfa Yeurmandéé.•Waa Kool Xandan Yërmandé Jaanguinii15).Balak Maram Aychak Sadio tag kassi téréwul Loxoom bu Toot ba kumou Sédul ..Bësba ngay Fandéé( Refrain).16).Baye Kouly THIOUNE Moussé mbooré... Mademba Moussé mbooré (Jaamu Serigne Saliou),17).Béthio Albabou Bakar...Mbassé Bakar Mbassé... Mbassé Baabou,•Mbassé moo jugéwoon Madinatou Mounawwarraa.•( Bis) 18).Ngaye Mékhé Kaïré ...Ngaadiam Bay Ngélkool...Kadior kiléén Yénèwoon Ndam...Seutba wooténaa•Cadior kiiléén Jangal Seutba wooténaa )19).Baye Kouli THIOUNE Moussé Mbooré Mademba Moussé Mbooré.•Béthio Albabu Bakar mbassé mbassé Baabu( Jaamu Serigne Saliou)•Mbassé moo Jugéwoon Madinatoul Mounawwarraa.•(Bis)20). Wahwa lazii hixa Djismii han ziaratihii laakin Lissaani Lahoo kal Xalbi Zawaaru...Dani Habad Tou Laaha Salaassa Alfa Haamin Xabla Irhaassi Adama wa Hawwaa wala yawma Habdu Laahi ..21). LOUFI massa amrdr wwawdef rxcf. Rndeké! .22).Kou Mag KOO guiss23). Bougnouy way ci tssa 24). Djiitouk Rassoulou25). Dani tafakar26).Lam tanhounii2728). Mooy ka SABAP tassét29) .Datou 17 Avril kako wakh Sokhna Aïcha Mama laa(Loufi massa am ndéké Serigne Saliou M n'backéé)30).Bi Bess bu Barkél Thiantaakones yi Séén Thianta laa31).LOUFI Massa am ndekéFIN• Par S Ibrahima Diagne Wérekane ( Son,Lyriques et Interprétation)
Machalaa
Akassa
Dieureudieuf Dwr Ibrahima ❤❤
Macallah yallana yalla defal diam Way 🥰
Amiin
Machallah universel ❤
MRC
Mioungui lay ziar ❤❤❤
Ndeysaan❤
Ziar Dwr saliou
❤❤
Ndeiysane borom thiossane gou reuyy gui thioune Albabou
Wallay
Li nekhatina di Macha allah
MRC❤❤
Merci
Djeureudjeufeuti ❤❤
Nipungui lay ziar Dieuwrigne Souleymane ❤
Jeureujeuf
Ziar
Diagne kessé❤❤❤❤
Mrc ❤❤❤ Dwr
Akassa❤❤
764296777
Diagne siarnala SA número WhatsApp la sokhla wonn
76.429.67.77.❤
Machala ❤❤
Ndaysane
Ndaysan
LYRIC
1).Ci Thioçaan Kena genula( Jaamu Serigne Saliou).
Serigne Salihoo def ngay Yeurmandé.
2).Thiossanal sunu Yonén Taba téktal nama( Jaamu Serigne Saliou),
Banoo haachim taxul may way léér gua soss louné.
3).Sénégal lignko fonk taxna may Andi historique( Jaamu Serigne Saliou),
Jublou guéye téktal léén lééru Mame Bambéé.
4).Serigne Touba sunu Mbërma fégnal Lou nëbula,
( Jamu Serigne Saliou).
Tax ba mbacké am way lii la jotaléé.
5).La Anta lazii ouhtiita Xidman nubu atann( Jaamu Serigne Saliou),
Wa Adamou Baynal Maa i wa tiini Yanjaléé.
6).Borom berndé yii dounël Sénégal laadi way( Jaamu Serigne Saliou),
Çossanam Chérif la waayé MOURIDE baanguinii.
7).Mooy ka lééraloon naarba lay chérif baka séétci soon sa Diamono ..
Taxawal Illaahééy def Chérif wéréé.
•Kula gën Ragal Yalla Moola gën fii ba foo feléé
8). Baye Kulli THIOUNE Moussé mbooré...Mademba moussé mbooré..
Naarba ba Albabou sa maman Yémën la juguéé.
9).MOURIDE mooy bëg bëg lassa gën bëg Yalla la ( Jaamu Serigne Saliou).
Ka Begëm Serigne Saliou léér Adoun yaanguinii.
10).Bam jigué... Egypte la dém top dékh ga Di Nîl ...Tabbi Soudan Jaar Bogal...
Bamou douguéé Walo Barack Ba Bourbaa KO dalal...
Bam Namé dém Cadior aw Fass lako waajalé.. ( Refrain)
11). Fala jeuléé Santawa THIOUNE Top dékh ga Jëm Ndar,
Ross Béthio Borom 17 Avril baanguinii( Bis).
12).Le Béthio miidaan dinthia Sécret Bour sa Diamono wouténaak,
Serigne Saliou fam déf ...MBOOTOU YALLA Yéé.
• SERIGNE SALIOU WALA JOKH MBOOTU YALLA YÉÉ.
13). SABABU Mouridou Baye Kulli Serigne Balla Thioro Mbacké la,
Li Kulli Chaï In Sababounn Tassétt Dajébaanguinii.
•Tassêt 17 Avril Béssou dajè baanguinii
14).Diganté Momar Anta Salèék Mame Thioro Diop ak Sokhna Coumba Saala mbaye..
Ku dém Kool khandann...guisfa Yeurmandéé.
•Waa Kool Xandan Yërmandé Jaanguinii
15).Balak Maram Aychak Sadio tag kassi téréwul Loxoom bu Toot ba kumou Sédul ..Bësba ngay Fandéé( Refrain).
16).Baye Kouly THIOUNE Moussé mbooré... Mademba Moussé mbooré (Jaamu Serigne Saliou),
17).Béthio Albabou Bakar...Mbassé Bakar Mbassé... Mbassé Baabou,
•Mbassé moo jugéwoon Madinatou Mounawwarraa.
•( Bis)
18).Ngaye Mékhé Kaïré ...Ngaadiam Bay Ngélkool...
Kadior kiléén Yénèwoon Ndam...Seutba wooténaa
•Cadior kiiléén Jangal Seutba wooténaa )
19).Baye Kouli THIOUNE Moussé Mbooré Mademba Moussé Mbooré.
•Béthio Albabu Bakar mbassé mbassé Baabu( Jaamu Serigne Saliou)
•Mbassé moo Jugéwoon Madinatoul Mounawwarraa.
•(Bis)
20). Wahwa lazii hixa Djismii han ziaratihii laakin Lissaani Lahoo kal Xalbi Zawaaru...
Dani Habad Tou Laaha Salaassa Alfa Haamin Xabla Irhaassi Adama wa Hawwaa wala yawma Habdu Laahi ..
21). LOUFI massa amrdr wwawdef rxcf. Rndeké! .
22).Kou Mag KOO guiss
23). Bougnouy way ci tssa
24). Djiitouk Rassoulou
25). Dani tafakar
26).Lam tanhounii
27
28). Mooy ka SABAP tassét
29) .Datou 17 Avril kako wakh Sokhna Aïcha Mama laa(Loufi massa am ndéké Serigne Saliou M n'backéé)
30).Bi Bess bu Barkél Thiantaakones yi Séén Thianta laa
31).LOUFI Massa am ndekéFIN
• Par S Ibrahima Diagne Wérekane ( Son,Lyriques et Interprétation)
Machalaa
Akassa
Dieureudieuf Dwr Ibrahima ❤❤
Macallah yallana yalla defal diam Way 🥰
Amiin
Machallah universel ❤
MRC
Mioungui lay ziar ❤❤❤
Ndeysaan❤
Ziar Dwr saliou
❤❤
Ndeiysane borom thiossane gou reuyy gui thioune Albabou
❤❤
Wallay
Li nekhatina di Macha allah
MRC❤❤
Merci
Djeureudjeufeuti ❤❤
Nipungui lay ziar Dieuwrigne Souleymane ❤
Jeureujeuf
Ziar
Diagne kessé❤❤❤❤
Mrc ❤❤❤ Dwr
Akassa❤❤
764296777
Diagne siarnala SA número WhatsApp la sokhla wonn
76.429.67.77.❤