Yéne gni di défendre Nabou bougnou rayone séne yaye wala sene baye wala sene frère douguéne ko wakh . Police miko diap mo téyal khélou nityi kone la moindre des chose bouniouy bayi niou wakhak les concernés lou lérr c le minimum de respect
La famille de aziz a raison dans sa démarche Affaire bi dafa wara leirr ne serait-ce que pour la santé mentale et morale de tous les sénégalais ndax dossier bi nieup leu concerné Daniou wara waax sénégalais yi ce qu’il en est de ce dossier
Si vous tenez à rendre justice à votre frère. Arrêtez de parler au média et concentrez vous sur la voie légale en trouvant des avocats redoutables qui vont challenger le dossier et faire éclater la vérité.
Aida machallah rakk djou bakhla yalna la yalla takhawou samou la aar la deugeureul la ak famille bi yeup nii leu rék manifester votre mécontentement dans les règles de l'art lép dina léer inchallah stay focus✊
Yén gni wahe yeup koumou si donone sa mbok lou raw li ghaye déf sa réaction est légitime bayilen naféh li dafa minti yallah n'a yallah léral lep inchallah 😢
AK fi cas bi tolou ni justice boula diappé Di def enquête paré bayiwatela rek amena Lou khew té Mane jusqu'à la preuve du contraire douma meusseu gueume ni nabou leye silla bokke insbi Dale yalla rekka khame té yalna fégnale deugue bi si barké nabi MOUSTAPHA 🤲🤲
Non mais c'est incroyable😢 et effroyable, ce pays doit se poser de sérieuse question sur cette sois disante justice . Ce n'est pas possible que ce Nabou soit libérer de plus sans en informer les familles ou avocats des victimes. Cela suscite un enieme tolet sur les pratiques incohérentes de ce qu'on appelle la justice des hommes.
Bilahi walahi maane nimaa amee louma meti ci décès Aziz bi dafa meti yalla rka ko xaame💔💔💔😭😭😭 tellement brisé 😭 c grave kou dé ya perte repose en Paix.Tres cher Dieu svp justice pour Aziz mon cœur saigne kan je vois sa maman daaye melni dama boke ak Aziz raaye nite com ça keene taxawoula pour lerale deug ji niaak dolee moo bone kone ya Rabi mangilaye niane nga dolleele famille bi niak je compatis énormément ♥️♥️🙏
Le dossier à dépassé la police. Il est entre les mains du juge d'instruction qui reprend toute l'enquête. Si l'enquête est bouclée il peut accorder une liberté provisoire ou un non lieu
Barké Seydina Muhammad sounékone mane oubi na leufeul Ndayi nebou leye yague na kone instant bi magui cachot 😢😢 Sénégal jusqu'à présent justice bou bakh amoufi
C'est que la famille était trop ''diverti'' par les interviews,alors que vous deviez vous même la famille prendre les démarches au lieu d'attendre la justice.
Notre justice bi daal dafa bari aye Domeharame ndakh certains veulent l'éclatement du pays une guerre civile entre les senegalais pour que le gouvernement daanou comme sa ñou meuneu ñeuwate si pouvoir bi. Car la famille du victime et leurs avocats ne sont pas averti ou leur faire savoir de ce qui se passe réellement dans cette dossier
@@thiammamadoulaity5279Yéne gni di défendre Nabou bougnou rayone séne yaye wala sene baye wala sene frère douguéne ko wakh . Justice miko diap mo téyal khélou nityi kone la moindre des chose bouniouy bayi niou wakhak les concernés lou lérr c le minimum de respect
Mais pourquoi guene beugeu teudj lou nite vraiment li diakhal nama Yone moko tiyéwone bayi Wate ko legui li louye problème mais yene dal casso guene ko yené sou feké defoute nak
@ sa leufeul ndaye iow bamouy 10fois domou haram bala gua saga do lire boubakh lima binde bagua ndaye comprendre gua dogua wax émbécil nitt day wax hamouléne limou beugu wax guéne di saga Dou damani vue k police libéréna nabou sans wax nitt gni lou lérr famille aziz bi ligni déf ni c’est normal sinon justice dou meusa ame
Nabou surment amna bras long si autorité you bess yi Sénégal dal rupture biniou beugue doufi am li dou yone dou deugue nabou leye était sur les lieux et son téléphone a borné le jour du crime loutax nioukay bayi daniouko warone bayi fofou bamou leer aziz nit la ter dafa am ay mbok niou rayko si zéro soudone domou riche dou demer ni Sénégal yeup nio warone diouk unir pour dénoncer cette injustice 😢 #justicepourazizdabalaetwaly#
Wa man louma diakhal moy est ce que dou yon da ama goul loko lérr motakh mou may nabou leye liberté provisoire mais yéméne dh yalla rék mo kham yalla nako yalla lérall
Sénégal mo amoul justice bi Macky Sall moko yague kharou niou li si sonko ak diomaye goumba am ndaye ak goumba amoul ndaye mo wara diékh Sénégal loumou tar tar nabou leye guene warouko bayi bilahi
This is a public problem the process supposed to be in public everything they do they have to are from the country to people know what's going on something is not right why Nabou out😢 this is not just for the family problem this the country problem we need Justice to talk
Wakhofi lefeul ndeyam nabou leye kou kate ndeyam la sa xarite nomouy déwé ak nou dé métiwé nganane kou dé déna ou est le problème siça xarite néga kou tothie sarap ndeyam la khawma defna wala défoul mé domouhram la
Pourquoi insistee ni nabou leye moko Ray t amoul, justice boula arretee def enquette in jour mou bayila xam na nii defo dara, boulennn fatee police scientifique migi wonn sur les lieux, doff yi diangoul xamouniou dara nioy dieul placou procureure Di doul Di wakh lo xamoul
Bou féké danguéne diapou né moko raye kone yobou léne ay preuve ndakh pour l'instant momm preuve bouy takhal nabou leye amagoufi donc bou léne sonal sof nguéne trop way té faté
Sénégal amoul loi lidieunti rek mo fi am mais li dou yone enquête bi diekha goul donc bou dèmé bay gueneu war nagn khar ba bouclé ko gnou kham lan moy motifs meutre bi et comment ils ont fait pour entré dans l'appartement lolou lep bo si nabou defoul dara gnou expliquer ko population bi mou soga gueneu justice pour Aziz et Wally
Yakar nguéne ni Nabou bouci bokone dina ame liberté provisoire yalla na yalla sétal lépou inchalla
Amine
@@MameDiarraGueye-bk3fl Yakar nga bousi bokoul wone kéne dina takhal comme iow kéne bolé wola si
@@ibrahimadieye7051c sa osi doyna war ku deful dara kenduko wolu lima yakar
Sénégalais you bari xamou gnou louy enquête diapp nitt taxoul gua nk coupable prison
Sa data ndèye fi guiss nage fi louné 😢 nabou sila bokou dagne ko wara réye
WaLAHI YALA rek Moma Time Wayé Gueumoumeu Ni Lokho Nabou Léye Mingui Ci Fatoukk Aziz Dabala
Bilay ioe 😢
Bly
Le problème len la justice bi gno wara guen wah depuis le début dou cyber criminalité dou tribunal dou ken kou leral doy n'a war nak
Yéne gni di défendre Nabou bougnou rayone séne yaye wala sene baye wala sene frère douguéne ko wakh .
Police miko diap mo téyal khélou nityi kone la moindre des chose bouniouy bayi niou wakhak les concernés lou lérr c le minimum de respect
Franchement
waye rougui li dafa yombou trop barki Serigne saliou mbacké 😢fi kéne yéné woufi nabou léye kaso mei li dafa niawe trop sakhe thi justice bou senégal tcimmmm thiotou ndeye li waye li dafa yombou trop waye akhe
Diap naniou nitte 5 ans té défoul dara niou kheuy bayiko khamo leen justice té doleen nopi
Merci beaucoup vraiment lii da méti si khole
Yiow tamite bougnou toumalone sa baye wala sa ndèye si limou défoul doula nékh
La sœur de Aziz elle est trop belle 😻 repose en paix aziz ak wally que la terre soit léger 🤲
Bouko gor waxon gnouni da beug djigen
@@CheikhFall-f9o bouko djiguéne waxé nak ?
Motakh guiso si ben Thiow 😂
😂😂😂😂😂@@CheikhFall-f9o
@@CheikhFall-f9o mbadou dagako beugone wakh sikk nga dé😂
Mm boko khalaté sakh sikk nga😂
La famille de aziz a raison dans sa démarche
Affaire bi dafa wara leirr ne serait-ce que pour la santé mentale et morale de tous les sénégalais ndax dossier bi nieup leu concerné
Daniou wara waax sénégalais yi ce qu’il en est de ce dossier
Wakh deug yallah lii mingui tenir en haleine toute une nation mais nagn wakh liisiii neik bokkk😢
@@beatricendoye1800 moy yonneu sax
C’est trop mélangé dans nos têtes
Si vous tenez à rendre justice à votre frère. Arrêtez de parler au média et concentrez vous sur la voie légale en trouvant des avocats redoutables qui vont challenger le dossier et faire éclater la vérité.
Aida machallah rakk djou bakhla yalna la yalla takhawou samou la aar la deugeureul la ak famille bi yeup nii leu rék manifester votre mécontentement dans les règles de l'art lép dina léer inchallah stay focus✊
Justice defoul ligueyam bilay procure ,warna wah nak li mettina
Na mbokou aziz réye nabou mou diéx takk
Nabou ley yalla ko yalla takhaw
Yén gni wahe yeup koumou si donone sa mbok lou raw li ghaye déf sa réaction est légitime bayilen naféh li dafa minti yallah n'a yallah léral lep inchallah 😢
Si Nabou était vraiment coupable je ne pense pas que le juge l'aurait accordé une liberté provisoire
Yalla meune sérigne, té yallah dina féye kouné dieufeum
Mei elle a raison dossier bi leroul na ler
Aye waye bayiléne nabou leye , depui au début je n'ai jamai crue ke elle n'a rien fai, justisou sénégal kène dou lénène diangale liguéye
Cette libération risque de provoquer des troubles à l'ordre public. Le juge devait tenir compte de cette possibilité
C’est ce que j’ai dis
Vraiment da wara léeeerrr bilahi
Tu as parfaitement raison nak, meuneu creer ay degats collateraux, meme Nabou est en danger
Je vois elle sera tué par des incompris
C vrai dei en plus c même pas sûr pour sa sécurité
Justice pour nabou ley
elle communique bien ndeysann yalna yalla léral lep inchallah
Loutakh gniou beugue wakh nabou leye moko ray problème bobou la ame
Mé kéne wakhouléne nabou mo ray mé nabou mogui si chaine bi khamna lép mome nabou mé délene khalat téguene si placou famille aziz
@ problème dou affaire famille sama xalate la wakh té dieu ki c’est tout
Wallahi c'est la même question que je pose loutax niou beuga takhal nabou leye té preuve amoul
@@papezulefaye7263 Seul prombleme police doit faire une conférence de press
Vraiment niepou Niogui niane kosi boko yallah na fegne mais loutakh niou beugue nabou bokou si la khamoul
AK fi cas bi tolou ni justice boula diappé Di def enquête paré bayiwatela rek amena Lou khew té Mane jusqu'à la preuve du contraire douma meusseu gueume ni nabou leye silla bokke insbi Dale yalla rekka khame té yalna fégnale deugue bi si barké nabi MOUSTAPHA 🤲🤲
Bonne courage Aïda justice pour Aziz et Wally 😢😢
Le procureur doit sortir pour éclairer les sénégalais sur ce dossier sinon la justice populaire risque de s evir.
Non mais c'est incroyable😢 et effroyable, ce pays doit se poser de sérieuse question sur cette sois disante justice . Ce n'est pas possible que ce Nabou soit libérer de plus sans en informer les familles ou avocats des victimes. Cela suscite un enieme tolet sur les pratiques incohérentes de ce qu'on appelle la justice des hommes.
Nono Sénégal mo nekh ki rayoul gen bague mou ray
Wakhal way
Vraiment gni nak doy nagne warr trop
Walahi..te li geuneu metti moye même bou gnou prouver innôcencam..les gens vont continuer de croire que c’est elle..Elle ne sera jamais en paix.
Bilahi walahi maane nimaa amee louma meti ci décès Aziz bi dafa meti yalla rka ko xaame💔💔💔😭😭😭 tellement brisé 😭 c grave kou dé ya perte repose en Paix.Tres cher Dieu svp justice pour Aziz mon cœur saigne kan je vois sa maman daaye melni dama boke ak Aziz raaye nite com ça keene taxawoula pour lerale deug ji niaak dolee moo bone kone ya Rabi mangilaye niane nga dolleele famille bi niak je compatis énormément ♥️♥️🙏
Peut être la police n’a pas assez d’éléments incriminants nabou leye laissons les faire leur taff il le maîtrise mieux que nous.
Le dossier à dépassé la police. Il est entre les mains du juge d'instruction qui reprend toute l'enquête. Si l'enquête est bouclée il peut accorder une liberté provisoire ou un non lieu
@@dieynaba7570 li nga wakh la. Gueumm
Pourquoi vous voulez coûte que coûte k nabou soit incriminés vous oublié k kiko ray mogui prison je suis choqué
@@ndeyesokhnadiop5155 ndeye waxal, justice lou tolnii crime mou xeyy bayila nonou rek nabou loutakh niou bayiko Moy defoul dara, pourquoi douniou wakh thi niou dress niou teuyelenn, Senegal mo barii ay na fekkk
@@ndeyesokhnadiop5155 deugg nexoul tamitt
Bagnou gnou Nabou ame liberté dh wayer gnou avertir famille Aziz sah wahlen loutah gnou mayko liberté
Lolou amoul feneu nak
Nabou dè kouko niousse mou wakh ki raye
LEgui niom nabou leye là niou bégue wax moko ray lo Lou mo waral khekh bi 😢😢😢 thiey yalla
Mai attend ki vous a dit ke Nabou léye est coupable mai il faut laisser la justice faire son travail wayy
Vraiment
Li bizarre na trop depuis premier jour bi mou melni daniou beugue niou teudj nabou.
Waaa yéne Lane mooye séne blm pourquoi Nabou Dafa raye force rayoulle kaye d’où geune légui Lou Ngéne beugg 😮
Legui Kane mo raye ???
Le procureur doit sortir pour leral affaire bi.Pourquoi libérer nabou et les autres ?C’est juste une question.
Elle est toujours prudente naak dans ses propos
Barké Seydina Muhammad sounékone mane oubi na leufeul Ndayi nebou leye yague na kone instant bi magui cachot 😢😢 Sénégal jusqu'à présent justice bou bakh amoufi
C'est que la famille était trop ''diverti'' par les interviews,alors que vous deviez vous même la famille prendre les démarches au lieu d'attendre la justice.
Yene dal yena guena xam enquêteurs yi sene liguey
Nabou leye sou rayone wala mou bokk si nione douko bayi
Wakhou dof ngaye wakh liberté provisoire pas acquitté donc c'est louche
@@CheikhtidjaneSeckmerci
@@tantylarose809 je pense nji douniou réfléchir
Merci narét pas le justice soit fait😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭❤
La famille de aziz wakhouniou nabou mo raye mais n’a lérr niou kham lou khéw, lou khéw
@@Anta-ef5ty lou xéw moy nabou léye est innocente
li dafa yombou nako mbokou aziz yi réye wax dji diéx😢
Dakar deujou nafékh la
Notre justice bi daal dafa bari aye Domeharame ndakh certains veulent l'éclatement du pays une guerre civile entre les senegalais pour que le gouvernement daanou comme sa ñou meuneu ñeuwate si pouvoir bi.
Car la famille du victime et leurs avocats ne sont pas averti ou leur faire savoir de ce qui se passe réellement dans cette dossier
Loutakh nguene beug takhal nabou aussi yone moko diap yone moko bayi donc croyez à la justice
@@thiammamadoulaity5279Yéne gni di défendre Nabou bougnou rayone séne yaye wala sene baye wala sene frère douguéne ko wakh .
Justice miko diap mo téyal khélou nityi kone la moindre des chose bouniouy bayi niou wakhak les concernés lou lérr c le minimum de respect
Mais pourquoi guene beugeu teudj lou nite vraiment li diakhal nama Yone moko tiyéwone bayi Wate ko legui li louye problème mais yene dal casso guene ko yené sou feké defoute nak
@@rouguikebe9984police mo leu wax nii Nabou dafka reyy waleuh deu nio a preuve de complicité Bou lerr ??? S
@@BaaaB159 l'avocat du diable🤧
En tous le procureur doit éclaircir le dossier publiquement ca se fait aux Etats Unis et partout
Il ont des problèmes personnels avec nabou lèye c’est tellement visible mai yalla moy le grand juge
Li guéne di déf ni c’est normal ndakh justice dou meusa déf liguéyame danio sagané
Sa data yaye nga nane fi lane nabou dagnio wara ndéyam
@ sa leufeul ndaye iow bamouy 10fois domou haram bala gua saga do lire boubakh lima binde bagua ndaye comprendre gua dogua wax émbécil nitt day wax hamouléne limou beugu wax guéne di saga
Dou damani vue k police libéréna nabou sans wax nitt gni lou lérr famille aziz bi ligni déf ni c’est normal sinon justice dou meusa ame
Amal foula bayi nabou leye té topou justice pour Aziz li métina trope ŵayé Dieu est juste et est le meilleur juge
Nabou Leye seirigne niam bakhna
Bilay 😢
Et ce que nabou guénoule deuk bi. Sénégal Yakhouna bouguéne sétané dinaméleni adji sarr doumoudje féne 😢 justice pour azize et waly
Aida courage ❤❤❤❤
Justice lagnou wax waxougnou lénéne
Nabou mome manoul libre dou yone
Démal nga dougalate ko kasso et foutez nous la paix
Lan la def ?
Mm si elle est innocente dagn ko wara diap pour nguene contane ???
@@adamasambou1217 doul ki ta sonné .
@@Lenasow-zp5uo innocent fane bakh na yalla guisse na lép
Me pourquoi guene ame problème thi nabou guene si elle n’a rien fait yene tamite
Eyaw la petite elle n'est pas bien ku ko guiss khamni elle est parti avec son frère... J'espère que amna assistance derrière
Aida ndaye san 😢😢li dafa Miti nak
Khamouma kou raye, Mais mane dama diape ni Nabou sou guéne pour da si séte
Wa sene famille khana gorr amoufy pour dieul kadou famille tout l temps c les femmes ki femme
Kou decede perte ngua Senegal li mofi ame
Cest quoi cette justice qui tinforme pss les concernes de l'état d'avancement du dossier?? Ca cest un signe d'incompétence de la justice senegalaise
Sénégal dafa ame niou seytane ndeyeme ki niou ray magame nguen beug dou wakh
Nabou surment amna bras long si autorité you bess yi Sénégal dal rupture biniou beugue doufi am li dou yone dou deugue nabou leye était sur les lieux et son téléphone a borné le jour du crime loutax nioukay bayi daniouko warone bayi fofou bamou leer aziz nit la ter dafa am ay mbok niou rayko si zéro soudone domou riche dou demer ni Sénégal yeup nio warone diouk unir pour dénoncer cette injustice 😢 #justicepourazizdabalaetwaly#
rewmi amoule justice dé billahi
Justice pour aziz dafa wara leer
Yen daguéna beugua wakhe ni nabou laye moko ray yon moko takhal moko bayiwat kon kay d'où mom
Parce que khamougnou justice noumouy dokhe
Li do youn nabo ken waroko bayi 😢😢😢😢😢😢😢😢
Thioto ndayi rew mi 😢😢😢😢😢😢😢amol ben youn
*Ahhh nagnou leeral mbirmi Adouna yeypp mo Sokhla lumière si affaires bi😮😮😮😮😮😮😮*
Je n'ai jamais vu une personne impliquée dans le meurtres deux personnes avant une libération provisoire je parle en connaissance de cause.🤔
Je modi Dakar b.
Pourquoi insiste sur nabou leye
justice pour Aziz et wally
Wa man louma diakhal moy est ce que dou yon da ama goul loko lérr motakh mou may nabou leye liberté provisoire mais yéméne dh yalla rék mo kham yalla nako yalla lérall
Sénégal mo amoul justice bi Macky Sall moko yague kharou niou li si sonko ak diomaye goumba am ndaye ak goumba amoul ndaye mo wara diékh Sénégal loumou tar tar nabou leye guene warouko bayi bilahi
Bou féké défoull nakk wala mou am gualathie rékk
Liberté provisoire bi thi bopam mo tel pour dire vrai même pas trois c trop facile pour deux vie
This is a public problem the process supposed to be in public everything they do they have to are from the country to people know what's going on something is not right why Nabou out😢 this is not just for the family problem this the country problem we need Justice to talk
Aziz amna bokou nabou amna mboko ligui nabou defoul motakh you bayiko
loutax avocat bi yégou ko lolou molaye wanni amna lousi laxasou 😢 nabou léye na ko wa keur aziz réye
Sénégal kouniou rayy ya perte deukk bi Amoul yonn louway nékh na déff mane mom galle gui lay ndayi dieule guénneu ndayi deukk bi💔🤧🇸🇳
@@bigmaker2247 fi dei kouniou rayy ya perte bilay
nabiu leye bouko rayonne keneuh douko may liberté provisoire
Sénégal amoul justice, pourquoi libérer Nabou leye ? C'est trop facile quand même
La soeur de Aziz mom si bopam lagne wara teuthie ndakh mou bayi tv yi ish
Nabou Leye déffoul Dara kii raye goor laa
Yéneu mom Nabou léye bane dolé laffi am ba yone warko ragal. Écouter la justice mo gueune eupeul
Afrique dafa doy war dé Nabou leye drianke la dé eske Amoule lou nékk si guinaw
L'argent l'argent.
Vraiment vous nous fetché dakh yéne yone ngéne yepe yéne khamone ngéne née nabou leye defou séne guemegne lamigne yi rek montah gnou teyé ko
Nabou bou defonn dara douniouko bayiii,
Wakhofi lefeul ndeyam nabou leye kou kate ndeyam la sa xarite nomouy déwé ak nou dé métiwé nganane kou dé déna ou est le problème siça xarite néga kou tothie sarap ndeyam la khawma defna wala défoul mé domouhram la
Vraiment
Nay rafét bok yakar n'a so défon yon doko bayi heure bii 😢😢 sm khalat la Wakhe nk @@boyetownfromdkr5287
Pourquoi insistee ni nabou leye moko Ray t amoul, justice boula arretee def enquette in jour mou bayila xam na nii defo dara, boulennn fatee police scientifique migi wonn sur les lieux, doff yi diangoul xamouniou dara nioy dieul placou procureure Di doul Di wakh lo xamoul
@@boyetownfromdkr5287 yaw wero ndayam
Justice pour azize est waly
La célibataire a tout pris, quelle tristesse
Pour man dagnou wara took deglou libertés provisoire sou amé doute amna procurer dafa wara gen wakh
Da guene seytane yene nia di defandre nabou leye mi guene kham deum la montak ken beugoul ame xarite
Elle est coupable
Mai pourquoi ngain bege juger Nabou leye t yonn bayiko arrêter
Yene doy nguene war li enquête leu diekhagoul teylene rek aida amo conseillé nak
Pourquoi nguen beuga def nabou mortier 😢😢
Vous amerdez les gens na yoon def liggéyam yoon def liggeyam ngeen niouy sonal ndéyou nabou léye mo geneu liggey seen ndéye
Li warra leer moy wally akk aziz ban heures lagnou décédé
C'est Louche pourquoi liberté provisoire donc elle est coupable sinon elle serait acquitté
Bou féké danguéne diapou né moko raye kone yobou léne ay preuve ndakh pour l'instant momm preuve bouy takhal nabou leye amagoufi donc bou léne sonal sof nguéne trop way té faté
Sénégal amoul loi lidieunti rek mo fi am mais li dou yone enquête bi diekha goul donc bou dèmé bay gueneu war nagn khar ba bouclé ko gnou kham lan moy motifs meutre bi et comment ils ont fait pour entré dans l'appartement lolou lep bo si nabou defoul dara gnou expliquer ko population bi mou soga gueneu justice pour Aziz et Wally
Waw mais fadel yaw estimé nala trop mais lane moy sa probléme déléne kholate ni nguéne di wakhé svp
'
Li motax fadial sa bopou difi am
Mais je comprends rien pourquoi Nabou leye waroul gueneu ?
Vraiment bayilene justice mu def ligeyeum Sénégal mom legui gneup ay juge lagnou doyna war