BAYE AS NDIAYE INTERNATIONAL: DIOTNA NIOU COMPRENDRE LAN MOY TARBIYA

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 19 янв 2025

Комментарии • 36

  • @OureyeSeck
    @OureyeSeck 4 месяца назад +3

    Machallah Baye ass ndiaye❤

  • @kaliloulayesy2729
    @kaliloulayesy2729 2 месяца назад +1

    Mashaallah Serigne bi Dieureudieuf ninguay diangale dafa leer te yombeuna comprendre , Yalnala Yallah faye bidiahi Seydil Woudioudou Sallalahou Aleyhi wa salam

  • @zeydandeyecodousymoubayech1730
    @zeydandeyecodousymoubayech1730 9 месяцев назад +5

    Macha Allah bilay wakhna deugue dama weur madjaliss ba sonneu ci keneu rek lako guissone Mouy oustaz Ahmed Dame Gueye té aussi wakeur cheikhoul Kayri Ndeyssane 😢yalla n'a yalla barkel kham kham bi ,on a vraiment besoin de mouquadam comme ça ❤❤❤

  • @Sidybarhame
    @Sidybarhame 9 месяцев назад +4

    Machallah cheikh bii yagui lerr lep yallna yallah yook xam xam bii❤❤❤

  • @ndiayecheikhou2289
    @ndiayecheikhou2289 9 месяцев назад +7

    On a l'impression que Baye Niass est plus connu au Nigeria qu'au Sénégal le premier africain à diriger une prière a Alzhar mashallah

    • @Sadview2
      @Sadview2 9 месяцев назад +3

      Pas seulement au Nigeria mais dans l'Afrique et le monde entier

  • @ToureMouhamade
    @ToureMouhamade Месяц назад +1

    La vérité absolue ❤

  • @muhammedfaye9242
    @muhammedfaye9242 9 месяцев назад +4

    Sering bi Thank you so much i am a talibeh baye from the Gambia and i always watch your videos but all what you're saying is true, blie how some people behave in the faydou is so shameful

    • @SohnaJr11
      @SohnaJr11 4 месяца назад +1

      Even me too my brother...I am from The Gambia 🇬🇲💖💞. I live in Konbo North District. I am also Talibe Baye Niass.....

  • @oumouelbachir6277
    @oumouelbachir6277 9 месяцев назад +5

    Bilahi serigne bi djambar la , faydou li la sokhla , haley yi legui folklore rek ak snapp allah baye walahi dangay rouss sah ,

  • @DramaneKeita-s9y
    @DramaneKeita-s9y Месяц назад +2

    Machallah ❤❤❤❤

  • @aliousow9271
    @aliousow9271 7 месяцев назад +3

    Bilaay Serigne tu as parfaitement raison demna bassi Benn muhadam ma bayi lima indiwonne ndakh lima fa guiss walahiiiii…

  • @aissatoucoumbakamara7573
    @aissatoucoumbakamara7573 9 месяцев назад +3

    Dans la vie nerk gnit mo diafer parceque domou adama rek moy khalate
    TR li cheikh baye di wakh Lou l’ère rek la ay nopou ak khol😂bou serl mokoy dergu manchalla
    Yalla nagniou yalla def ay gnit gniou niter ak di dergu di topou manchalla yalla na yalla faye❤

  • @AbsaNdiaye-n5g
    @AbsaNdiaye-n5g 5 месяцев назад +2

    macha allh baye as ndiaye

  • @oumouelbachir6277
    @oumouelbachir6277 9 месяцев назад +3

    Yalna yAlla djapalè deugueureul le

  • @tijangassama4826
    @tijangassama4826 2 месяца назад +1

    Masah Allah

  • @AdjiDiouf-bi3zp
    @AdjiDiouf-bi3zp 8 месяцев назад +2

    Machalla sangue bi

  • @AbdoulayeDrame-wy3sx
    @AbdoulayeDrame-wy3sx 7 месяцев назад +2

    Macha Allah ❤️

  • @alassanecoly7200
    @alassanecoly7200 9 месяцев назад +3

    Billahi cheikh bi

  • @mamadoumamoudoundiaye
    @mamadoumamoudoundiaye 9 месяцев назад +2

    ماشاءالله تبارك الله ❤❤❤❤

  • @BarhamCosmetics
    @BarhamCosmetics 9 месяцев назад +2

    Wallahi Serigne bi ngay Wakh deugue bou wer la

  • @MohamedMbaye-i2d
    @MohamedMbaye-i2d 7 месяцев назад +2

    Ndeysane yalla mo mana neub

  • @niasssaer5513
    @niasssaer5513 Месяц назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aminatasarr4744
    @aminatasarr4744 3 месяца назад +1

    Merci

  • @hassaneba8028
    @hassaneba8028 8 месяцев назад +2

    Masha Allah

  • @ModyNgayde
    @ModyNgayde 9 месяцев назад +2

    Numéro Serigne bi la solhla

  • @AbdoulayeDiallo-dj8hb
    @AbdoulayeDiallo-dj8hb 3 месяца назад +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @aleledia2065
    @aleledia2065 9 месяцев назад +2

    Salam sérigne bi magui ziar lou barri dila nianal Allah goudou fane ak wéer. Est ce que meun ga niou expliquer biroum Mahdi al dadjal.
    yalla na Baye niass féyal nioula.
    Wa salam

  • @ousmanediop8838
    @ousmanediop8838 9 месяцев назад +2

    Mais achète t’il ses bonnet kala ?
    Mâcha alla pour ces enseignements.

  • @alieucham3391
    @alieucham3391 9 месяцев назад +2

    Deug rek ngafi wakh serigne bi. Yaangi gindi talibe you Bari.

  • @aminatasarr4744
    @aminatasarr4744 3 месяца назад +1

    Tout deviant Claire a present

  • @AmadoutidianeSow-u6q
    @AmadoutidianeSow-u6q 4 месяца назад +1

    Ndamal faydou

  • @beugueseydiinsarouhoulahib2566
    @beugueseydiinsarouhoulahib2566 9 месяцев назад

    Cheikh bi nawon n'a sa xam xam, yakar ni sa xam yallah lou yayou leu,, mais téy bama dégué khani insa sous déloussi thi assamane bi lay bayéko direct wathieu ak ni kha geumé ni assaman bi niou xam leu, bilahi dama ameu déception. Insa dou lén loumay lérou fardoul diamihou meussteu dégn thi di nék thi kaw souf. Té insa sou diogué direct thi assaman bi nieuwat kom nimou démé ak noubouwatom donc noubouwatou lay wathié walé de ce fait rassoul dotoul nék xatmoul noubouwa car bénén yeninte nieuwat n'a thi guinawom. Insa nieuwatom thi manteau wilaya lay done,, Baye ni samay andado moy doneu andandowom, sama faydou bi thi mom lay maté. Insa en temps que yeuninte déloussi dieul tarikha done talibé cheikh topeu faydou Baye, motali faydou bi en temps que yeninte yow tamiteu xolatal likhay wakh té utilisé sa xam xamou Yallah bagn di forcé nit gni sa serigne comme si k né foufou rék la faydou ameu

    • @Bayeasndiayeinternational
      @Bayeasndiayeinternational  9 месяцев назад +2

      NIOUNE SOKHLA WOUNIOU KOUNIOU NAW NAK LIY SERIGNE VI DI WAKH KOU BEUG TEGUI REK DEFAL VIDEO NI MOM INDI AYE ARGUMENT

    • @SohnaJr11
      @SohnaJr11 4 месяца назад +1

      ​@@BayeasndiayeinternationalWakh Nga Degué ❤❤❤