C'est très important ce que tu dis en tout cas Medoune je conseils de continuer dans ce lancer pour essayer de changer la mentalité de certains con au Sénégal
Kou say woudjiou di sang do set Oustas ak serigne dou ben soude’lou yallah loumou wakh ak yenetou bi Lolou diadouna mais contre bakhoul nagou ndogal yallah
Man dh talibé Baye Niass la wakhou ma nak MC NIASS. Ms billahi Baye Niass diangal naniou Al khour'an ta firiko si zaahir ci baatin . Khamal na niou yalla (ta yalla moné: khamlén ma bala ngén may diammou) ta Baye Niass Yonnént bi rk leuh beugeu mom rek laniou diangal. Mc day politique pour Kaolack ta mom mo kham. Kon souma déggé ngéni wakh li ci baye Niass daf may métti. Souniou zikr yeup Allah la AK Mohamed psl.
C'est le croyant musulman tt court , qui doit être véridique,n'est ce pas. Le Sénégal est devenu un véritable El dorado à la Las Végas ,pour certains ; affreusement , aveuglément et misérablement hypocrites,ces soit disant musulmans.Que Soubhanahoh Taala ns préserve , ns bénisse et ns guide sur le droit chemin Amin yaa Raabi.
Serigne bi yow figa tolou ni wessouna niouffi wakhofi Dara nakho kéne sa bop gay nakh. Sa khola febar gua fok ni ya eup niep xam xam fek nopi AK diangui mola war
Yangui defendre tarikha te pourtant yonent bi amoul foumou diangale tarikha te pourtant mom la Yalla yoni . Wala sakh au contraire daf niou tere formellement niou diviser souniou diné si ay kourel. Yalla tamit tere ko si alquran. Mais bon lou lene nekh ngen di def
Yen lkep kou bok si tarikha loumou def rek bakhoul 😂thiey contre serigne sou mag yallah ak yenetou bi daf len diaron loum diara loul wone sen morom mo takh yallah meylen loum meyoul sen morom
Vous repetez les memes choses sans reflechir. Souma la ladje naka la yonente bi diarale sene mag yi tr diaralou ko nienene mak yi apres nga indi sa khalatou bopp beug ko imposer comme deug. Te pourtant sene mak yi louniou bakh bakh, sene ndono yi tey yonou toubab yefer laniouy atté wo bayi charia si guinaw. Dieul bida tek ko sikaw souna, yakar nitt fou nitt wara amé tawhid .. souma done lim lepp douniou fi diougue
Machallah vérité absolue
Mashaa ALLAH
DiazakAllahou ghayrane
Manshaa allah
Machalaaa medoune diop
C'est très important ce que tu dis en tout cas Medoune je conseils de continuer dans ce lancer pour essayer de changer la mentalité de certains con au Sénégal
Merci Medoune
macahall madoune yalla na yalla goudal saw fan amine yarbi tenou bokouko ligueye khakh deuge la yangi dimbouli nitngi bou kha khakh lol sakh
Merci Medoun.tu es objectif contrairement à beaucoup de youtubeurs
Kou am bairé soxlawul lajté defena. Wayé baire bukki amna itam!
Kou say woudjiou di sang do set Oustas ak serigne dou ben soude’lou yallah loumou wakh ak yenetou bi Lolou diadouna mais contre bakhoul nagou ndogal yallah
Man dh talibé Baye Niass la wakhou ma nak MC NIASS.
Ms billahi Baye Niass diangal naniou Al khour'an ta firiko si zaahir ci baatin . Khamal na niou yalla (ta yalla moné: khamlén ma bala ngén may diammou) ta Baye Niass Yonnént bi rk leuh beugeu mom rek laniou diangal.
Mc day politique pour Kaolack ta mom mo kham.
Kon souma déggé ngéni wakh li ci baye Niass daf may métti. Souniou zikr yeup Allah la AK Mohamed psl.
Walahi deugeuleu de
C'est le croyant musulman tt court , qui doit être véridique,n'est ce pas. Le Sénégal est devenu un véritable El dorado à la Las Végas ,pour certains ; affreusement , aveuglément et misérablement hypocrites,ces soit disant musulmans.Que Soubhanahoh Taala ns préserve , ns bénisse et ns guide sur le droit chemin Amin yaa Raabi.
Lanmosi yonou maky ak lamosi yonou mahi si ousmane sonko mou deme tede moromou domae
Serigne bi yow figa tolou ni wessouna niouffi wakhofi Dara nakho kéne sa bop gay nakh. Sa khola febar gua fok ni ya eup niep xam xam fek nopi AK diangui mola war
Ok merci niou yendok diam
arrête ‘lou nit wakh guen yob si tarikha politique guen yob si tarikha yakar yallah lolou d’accord na mais boul mélange ‘sujets