Niata Hadratoul joumou'a populaire niofi am thi stade🤔...mais souniou boss moy dérangé ndeysaane. Malène yeureum, il ne fallait même pas donner l'heure aux détracteurs... Al hamdoulilah, Dieureudieufé Baye rek🙏🏽
Yalla naniou yalla nangoul souniou nekk talibé cheikh Lolou mo woorr kou nekk di kheuthie ak di nioddi amoul solo Lii am solo moy xamni lepp cheikh Ma tambalei sa kaw nak dieu si souf Alioune harazim Mouhamadou khaly Mame cheikhou Oumar Seydil hadji Malick Mame abdoulihi niasse Mame ahmadou ndack seck Ak gni si top niepp Ken yorou fi Dara boudoul wone cheikh ken doulen xam Dieureudieuf cheikhou tidjan Ma fonkeu ndiabotou cheikh yepp mann Wakhouma moukhadamou cheikh Mais talibé yi gueuna ndaw beugg n'a len ndakh cheikhou tidjan
Affaire bi l'islam la té done dioulite. Kou nek am nga droit gueum ou beugue koula doye. Mais Seydina MOHAMED s.a.w moy ilimane molémi dioulite yi point.
@@o2la2.09 dafa melni dégoma dh si cadre bou tarikha bi la wakh cheikh Moy imam bi Mais niepp kham naniou ni l islam ben imam la am Seydouna mouhamed psl
الحمد لله بوجود الشيخ ابراهيم اناس نفعنا الله ببركاته ى وبفيضته ى الفيضة التجاني تعم جميع افاق بحول الله وقوته ى لايمسكها شيء ولايوقفها احد لابد تمتد علي البسيطة حيث كان تجانية شكر لك يا سيد عبد العزيز جاى جزاك الله خير فالامر واضح
Nous baye a travail pour tou c talibe on n pa peur des gens nous c dieu et Mohammed et cheikh tijani tou sa c baye ki a fe sa pour nous se ki parle mal fe très atason kare nous le bon dieu et avec nous a vie
Salam vraiment le Senegal va mal tjrs tarikha ani Allah Azawdieul ani Seydouna Muhammad les Senegalais prefaire leur marabou qu'Allah tarikha daniou ko sosse pour lou bakh mais kou nek nane sama Serigne mo gueuneu kawe moi je suis tidiane mais khol dara khadioufa kou doul Allah Azawadieul yallah naniou yallah def deugue deugue aye Muslim amin
Mai vous on dirai k vous avez rien nioune talubé baye yi souniou boloyé déniouw âme Dolé tai louniou beug si Sénégal dinegko âme tai lolou arangéwoul niou beury
Serigne bi ma ngi diegalou. Mais Mc Niass meunoul forcer kenne Macky sall. Ay personnes doués de conscience nio fi nekk. Kou nekk yaye tane koula nekh bo dougé si isoloir bi. En plus si khadra bi tourou Macky Sall djiboufa benni yone. Kone guissouma fa forcer vraiment. Na gnou deupo si lessentiel mo gueune té bayi di critiquer pour critiquer
Baye dal wakhna ni talibé wara mél si rouhoul adab kone kouy wakhné khadaradiouma bi waroul wone âme stade dowo talibé Baye fala war nga kholate sa bope bou bah ...Niass la solution
Parrein du Sunna borom tariqa bi mai suma beguè khalika bi nyow mbolo bi nyow te khalis moy fiancé sen transport te parrein ko macky sall mou jokhma khalis ma feyal Khalifa ak mbolo bi gnou menue gnow dafay dagan @Modou Tall
Yow mom Aziz Ndiaye khamo dara danga wara nopi Tu crois k parcoeuriser les livres 📚 de Baye moy kham kham Vous les petits Mouhadam vous vous foutez de nous, ay doungourou nguèn, diamou ay domou Baye Chak mouhadam est affilié sur un fils de Baye Merde way, Cheikh Oumar limou wakh c'est claire MC Niass gueumoul dara, yéna yèm, khaliss rk nguèn gueum
Ndeyssane YALLAH na xol yi défarou🙏. Nioune déh guissouniou sakh Baye Mbaye ak xalis bi nga touddeuh.. nioune gni nékkone thi wassifa bi ak Hadara bi YALLAH rék lagne fa yeugonne ndeyssane toubb thi YALLAH diouly thi SEYDINNA MOUHAMED (swas)... Zikr ba contenne Cheikh Mahy wakhtane Baba sikar leup nékh bilahi❣️.... Yaw ak Professeur Omar boudéh khaliss ak lénéne ngéne guiss yéne la engagée. Di dieugeulouh thi kadou bi nak🙏🙏🙏🙏
Salaam
Je suis de tivaoune . Ziarana tous les talubes Baye. Nous sommes tous des freres. Yallana jamma yagga
Amine ta doléle tarikha tidjiane
Allahouma Amin té bollé xol yii si barké Cheikh Ahmed Tidiane Chérif (RTA)🤲🏽
amine yarabi way machalah
i realize it's kinda off topic but do anybody know a good website to stream new series online?
@Charles Adrien I watch on Flixportal. Just google for it :)
Thieup gnoun sougnou lep Yalla Yonetebi ak Cheikhou Tidiane 🙏🙏🙏❤️💪
Merci cheikh Aziz pour la cohérence des propos soulevés la sagesse triomphera baye tanne
Machallah Serign bi yalla na yalla same la ta barkél
Parole d'un sage machallah kadou yi rafetna yalla na yalla tahawoula ci barké Baye Niass yalla na yalla def diam si rew mi ak gnico deuké
Mashallah cheikh bii wakh dji rafetna unissons-nous dieuredieuf Baye niass
Bilae lép dagua ko tek fou leer 🔥 Thieuy Bayeee❤️❤️❤️❤️
FIÈRE D'être talibé Baye NIASS DIEUREUDIEUFÉ Baye NIASS alhamdoulilah
Légui kou wotéh dadié mbollo rekkk yagui politique dina léér...T nitt kou bakh loumou beugoul wala xamossi daga warra nopi mo gueun wakh bi... dieuredieuffff cheikh bi💖💪
Alhamdoulilah Dieureudieufei Baye NIASS!
Baye moy deugg
Machaallah Baye merci beaucoup. Cheikh Abdou Azize Ndiaye 😘 jlaime
Dieuredieuf baye molén di méti wayé dé nagn dhé ak mérr ndax dieuredieuf baye bamou nékh baye niass la solution
Dieureudieufé Baye Niassssssssssssssss
@@fityaanousidkhine5796 mo waur dhé dieuredieuf baye rék ba fawwwwww
Gayi dagnio fire rek ils commencent à n'avoir peur des grandes mobilisations des talibé baye dans le monde
Bilaë ya wakh deug
Gua ballma senegale guene wane oui fi dine epelente mbolo donguo lanfiy wane koune dibouni yaoula tadou guen yonetebi rekk la mo ouf niepou
Niata Hadratoul joumou'a populaire niofi am thi stade🤔...mais souniou boss moy dérangé ndeysaane.
Malène yeureum, il ne fallait même pas donner l'heure aux détracteurs...
Al hamdoulilah, Dieureudieufé Baye rek🙏🏽
Bilahi
Baye molén di dérangé wayé néx nakhari baye mofi nék kou nieuwoul sa dome dina nieuw manougn si dra
sane aicha bijou Doyna war dal
baye niass la solution tv Motax souniou khamone daniouy téla nopalou té khamni Faydou Baye bi kéne meunouko tiyé kanam leu dieum inchallah
Billay loloula baye NIASSE rek moy deugue
Faydatou tidiania yalna baye téhallène bopame amoulène morome Macha allah séne ligueye si pays bi raféte na yalna léne pays bi arlène
Diambarou Baye bi namone nako trop dieureudieufff Al Faydatidianiya
Mashallah Sheikh Abdoul Aziz NDIAYE yalla Baye jotal la sa mboléme tiakoutéf!!!
Ma sha Allah Jazakalahou khayran ❤
machallah serigne goudall fane ak weurr
Machallah djeureudjeufé baye
Yalla naniou yalla nangoul souniou nekk talibé cheikh
Lolou mo woorr kou nekk di kheuthie ak di nioddi amoul solo
Lii am solo moy xamni lepp cheikh
Ma tambalei sa kaw nak dieu si souf Alioune harazim
Mouhamadou khaly
Mame cheikhou Oumar
Seydil hadji Malick
Mame abdoulihi niasse
Mame ahmadou ndack seck
Ak gni si top niepp
Ken yorou fi Dara boudoul wone cheikh ken doulen xam
Dieureudieuf cheikhou tidjan
Ma fonkeu ndiabotou cheikh yepp mann
Wakhouma moukhadamou cheikh
Mais talibé yi gueuna ndaw beugg n'a len ndakh cheikhou tidjan
Affaire bi l'islam la té done dioulite. Kou nek am nga droit gueum ou beugue koula doye. Mais Seydina MOHAMED s.a.w moy ilimane molémi dioulite yi point.
@@o2la2.09 dafa melni dégoma dh si cadre bou tarikha bi la wakh cheikh Moy imam bi
Mais niepp kham naniou ni l islam ben imam la am
Seydouna mouhamed psl
الحمد لله بوجود الشيخ ابراهيم اناس نفعنا الله ببركاته ى وبفيضته ى الفيضة التجاني تعم جميع افاق بحول الله وقوته ى لايمسكها شيء ولايوقفها احد لابد تمتد علي البسيطة حيث كان تجانية شكر لك يا سيد عبد العزيز جاى جزاك الله خير فالامر واضح
Maashaa Allah wakh ji rafet na jotall na yallana yallah feyal boppam bijahi Barhama Abdullah
Ma cha Allah
kadou yi rafetna
Le pédagogue machallah Cheikh
بلغت واكملت واحسنت بارك الله واطال عمرك مع الصحة والعافية والتوفيق ورضي الشيخ ابراهيم انياس ءامين
Sama khôl dafay sédeu souma guisé Talibé baye di wax ak dall xam xam bou wër andeuh ak yar ak téguine alhamdou lilah merci cheikh Abdou Aziz ndiaye
ماشاء آلله جميل جدا بارك الله فيك
Djereudieuf barakalah cheikh Aziz Ndiaye kham kham bi lerna machllah
Mane dale xamouma louma wara waxx cii Cheikh bii...thiey Daddy yalla nala Baye Taxawu
Man de Muriit laa waaye werante wi jaruko budee yéen ñépp Yàlla mooleen tax a jóg
Yàlla na Yàlla nangul ñépp
Mashallah Geuneu Goudou Fan Geuneu Weer
Waw noonou la rékk pour lèral rékk khoulou'ougnou khékhougnou yalla na yalla sakhal jam senegal ak islam
Machallah Cheikh bi🙏🏽
Dieureudieuf Cheikh bi lerna
Allahou Akbar 💘❣️❣️😭 Allahoumaine
Machalla jërëjëff ya cheikh
Ahsantà y'a cheikh
Machallah nanou continé rekk deug boci néké do guestou nakh ala kouli hall di nga guiss none niouy diéma di nguéte...
Borom Xam Xam bou Sell bi Cheikh Aziz Wallahi Faydou bi Def lay ndamo
Machalahh Cheikh Aziz ❤️❤️❤️
Machalla cheikh bii talibé bay yeup beneu lagne
Nous baye a travail pour tou c talibe on n pa peur des gens nous c dieu et Mohammed et cheikh tijani tou sa c baye ki a fe sa pour nous se ki parle mal fe très atason kare nous le bon dieu et avec nous a vie
Machalah cheikh baye
Machallah dieuredieuf
Vite longtemps et persévérez ndiaye
machalla serigne dieureudieuf yalla na baye faye la dieureudieufèè baye niass
machallah chiekh Ndiaye
Talibè baye leep loumu deeff tes yeekk yallah bii djutou deeg la
Cheikh Abdoul Aziz ndiaye.. machalaah
Al Alhamdoulilah...santt cheikh Ibrahim ba illa eubeutt...
thank for you may God bless you Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah
Alhamdoulilh dieureudieffff Baye Niass Moy laniou beugue dianatou khalbi
Mashallah Cheikh bii Djazakoumoullah haïrann🙏
Le succés est propice à l'apparition de nouveaux énemis. DIEUREUDIEUFÉ BAYE BARHAMA NIASS CHEIKH AL-ISLAM (RA).
Li day takh niou khamni chiekh mo mom 70% Senegal diarama akhlou ibrahima
Beurila barkele mokko gueune nek 200 pour cent nek 5pourcent te barkel mokko gueune
Baye hamoul wonewou Senghor sedelnako Baye sohor moye lek sene holyi wayé faydou deye dahtie guoko bouga effacer diokefi
Salam vraiment le Senegal va mal tjrs tarikha ani Allah Azawdieul ani Seydouna Muhammad les Senegalais prefaire leur marabou qu'Allah tarikha daniou ko sosse pour lou bakh mais kou nek nane sama Serigne mo gueuneu kawe moi je suis tidiane mais khol dara khadioufa kou doul Allah Azawadieul yallah naniou yallah def deugue deugue aye Muslim amin
Tu n'as rien compris yow.
Alhamdoulilah
baye niass la solution
Moi personnellement kou beugoul baye beuguoumala djeureudjeufé baye niass moy deuug ....
NIASSE bllay cheikh abdou AZIZ NDIAYE lepou léeeeeer na
Naniou nangou thiobaré Yallah ji kouko déff do dadiékk mbougal kignane fankhoul mourr ! Jeureujeuffé BAYE NIASS !!!
Bilahi sope nala LOL dakh sa kham kham talibés Baye niass dale talibés Baye niass lasi kham
Machalla
Alhamdoulila dieuredieufé baye barhama minka rek moy wadia
Santa yalla rek ...
Mai vous on dirai k vous avez rien nioune talubé baye yi souniou boloyé déniouw âme Dolé tai louniou beug si Sénégal dinegko âme tai lolou arangéwoul niou beury
Yen gni yena tilimal yonwi dakh doguen ligaye
Hadaratoul diouma daal lou baax la mais na Mc Niass baayi faydou boumouy business ak talibè yimouy forcer Macky Sall lolou moy dëgg.
Serigne bi ma ngi diegalou. Mais Mc Niass meunoul forcer kenne Macky sall. Ay personnes doués de conscience nio fi nekk. Kou nekk yaye tane koula nekh bo dougé si isoloir bi. En plus si khadra bi tourou Macky Sall djiboufa benni yone. Kone guissouma fa forcer vraiment. Na gnou deupo si lessentiel mo gueune té bayi di critiquer pour critiquer
Baye Mbaye ack Macky nékho wougn dé pour mouy lair ! Walla sétanoco si gamou gui
@@dorndokh3344 wakh deug yallah. Khana nga wakh ko. Ki suivroul actualité beugue juger
Talibé baye kén douko forcé dara baye Niass koumou paré si iOe doto nek dof bugnuY nakh
@@saloumbusiness4595 mrrrd
Bouniou ko fèfatone souba niou niewat dieureudieffffffeeee bayeee
Baye dal wakhna ni talibé wara mél si rouhoul adab kone kouy wakhné khadaradiouma bi waroul wone âme stade dowo talibé Baye fala war nga kholate sa bope bou bah ...Niass la solution
Wakho fidara hadara diouma kin warouko toudei ni guir khalis
Omar diagne da yabatè gnaw dou wakhat dè
Bayi leene topa ndoor
Kan lañiouy topado minables
Baye mo mome monde bii kou bagne dinga tall gaz tol sii
Astafiroula
diarediaf
Gisou Baye mady baye yaw
Parrain da am cii Khadara ??je demande seulement
Modou Tall Mane deih Mangui fa wone mais deigouma beine yone fougnou wakh wakhou parrain!
Alhamdou lilah Li dou dara!!! baye niass reck moy deugu
Parrein du Sunna borom tariqa bi mai suma beguè khalika bi nyow mbolo bi nyow te khalis moy fiancé sen transport te parrein ko macky sall mou jokhma khalis ma feyal Khalifa ak mbolo bi gnou menue gnow dafay dagan @Modou Tall
Bayilen di par parlo dem laine hami yala moguen
@@mamadougo2749 tu penses que fii ioe rek yaffiy a'rif .
Le pire cest que celui qui a dénigré la Hadara Jumuah General se dit soit disant Talibé Baye @Pr Oumar Diagne 🤔
Doynawaar wakham bi wakhou bakken lamay saff. Beugue guislenma ak ni la tolou kessé. Té wakh bi dafa saf trop wakhou wahhabite
@@sidimohamedaminegueye4869 bilahi ken moussou ko guiss hidmal Baye
Danguay doul rek khalis rek mo takh .ak mana topa ndo
Khana iow yaye doul imbécile bii
Yow mom Aziz Ndiaye khamo dara danga wara nopi
Tu crois k parcoeuriser les livres 📚 de Baye moy kham kham
Vous les petits Mouhadam vous vous foutez de nous, ay doungourou nguèn, diamou ay domou Baye
Chak mouhadam est affilié sur un fils de Baye
Merde way, Cheikh Oumar limou wakh c'est claire
MC Niass gueumoul dara, yéna yèm, khaliss rk nguèn gueum
Ndeyssane YALLAH na xol yi défarou🙏. Nioune déh guissouniou sakh Baye Mbaye ak xalis bi nga touddeuh.. nioune gni nékkone thi wassifa bi ak Hadara bi YALLAH rék lagne fa yeugonne ndeyssane toubb thi YALLAH diouly thi SEYDINNA MOUHAMED (swas)... Zikr ba contenne Cheikh Mahy wakhtane Baba sikar leup nékh bilahi❣️.... Yaw ak Professeur Omar boudéh khaliss ak lénéne ngéne guiss yéne la engagée. Di dieugeulouh thi kadou bi nak🙏🙏🙏🙏
Machalla
Machalla cheikh aziz
Machallah merci
Machallah
Machalla