Touba: Revivez l’arrivée de la dépouille de Cheikh Bethio Thioune

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 ноя 2024

Комментарии • 88

  • @mustindiaye4508
    @mustindiaye4508 Год назад +4

    Sonko 2024 Incha Allah

  • @mamesaye1977
    @mamesaye1977 5 лет назад +11

    Ay way yalla nanou yalla doli diamou ak soutoura way😭😭cheikh bi yalla nako yalla yereum tè dieguel ko ak mbolèm dioulit thi barkeep s.saliou 👍🙏

  • @iboudionne1841
    @iboudionne1841 5 лет назад +6

    Mourid yomboul bilahi gni guisoumasi mourid chiekh bi demna yalla nako serigne saliou terou

  • @mouhaeuro683
    @mouhaeuro683 5 лет назад +2

    wa gni amna gnouy saga dh vraiment li rewande la

  • @mustindiaye4508
    @mustindiaye4508 Год назад +1

    Geum Yalla rek mo woor

  • @shelamendy5534
    @shelamendy5534 5 лет назад +1

    Je suis tellement choquée j'ai pas les mots pour qualifier leurs actes toujours dans l'excès

  • @ousmanefall1110
    @ousmanefall1110 5 лет назад +2

    Bakkane Bakkane la rek Te chiekh bi kouka xam deug do takhaw fi di wakh ,wax diou Barii Te Cheikh bi fomou menah nk si Addouna bi S. Saliou Mbacke dinako fa fék ndax limou koh Tarbia wou kone nioun Lingou wara def rek moy nianaal ko Yalla yokkou Ay Léram thi Barké S. Touba Te niou Bayi wakhou you niakk Téuggin Yi 🙏 Yalla naniou yalla nangoul sonou koor thi Barkê S. Touba Yalla na diam yagg si Senegal 🇸🇳🙏

  • @diilerecaalifuuta549
    @diilerecaalifuuta549 5 лет назад +5

    Ndeysane thieye thianta koun ayye jambarengen ayye fidèle ngen

  • @baymodoumbaye3614
    @baymodoumbaye3614 5 лет назад +8

    Mane dei bima dioudo ba légui magui doga guis niouy yobou ap mouride touba am niounane dousi dal

    • @mariaalaloumamebamba4058
      @mariaalaloumamebamba4058 5 лет назад

      Barki bamba de mm k mw

    • @mariaalaloumamebamba4058
      @mariaalaloumamebamba4058 5 лет назад

      Barki bamba de mm k mw

    • @beugbambatouba5181
      @beugbambatouba5181 4 года назад

      C par ce que guemouniou serigne Touba danioukoy mboubo rék

    • @ibrahimasamb8444
      @ibrahimasamb8444 8 месяцев назад

      Il se trouve que Touba gnou bari beuguougnou wone Cheikh bi dagne ko bagnone ba teudd thi souff...Tè cheikh bi dafa ni wone beuss bou wathié liguey nagne ko de denthie Madinatou salam...

  • @aissatousylla4172
    @aissatousylla4172 Год назад

    Ndeyssane yalna co yalla yeureum si barké SEYDINA MOUHAMED SAW amiiine amiiine

  • @mamecheikhmbaye8491
    @mamecheikhmbaye8491 5 лет назад +7

    ay saga ndaye devant la dépouille de leur guides? lii dou yonou serigne touba !

  • @assanesow-om1zr
    @assanesow-om1zr 2 месяца назад

    Cheikh bi yeureum naako 😭😭😭😭

  • @papesamb9968
    @papesamb9968 5 лет назад +2

    Serigne bi wakhol fi mais serigne mountakha touba la wakh

  • @modoumatarndiaye1449
    @modoumatarndiaye1449 5 лет назад +2

    dangi na rew yène thian tayi s touba nékol ci yeene doumo ram ngeene

  • @londam5104
    @londam5104 5 лет назад +1

    Ma yeureum kou reree bilaye

  • @santesamayaye7483
    @santesamayaye7483 5 лет назад

    Kousi ame sa baye soleko foulanèkhhh bouniou yobouwone cheikh bi medinatoul salame falaniou nèkk diko weure di fèthiee touba force

  • @papacisse7155
    @papacisse7155 5 лет назад +1

    Yalna yalla guindi niou defniou ay Dioulitt deug tee moytouloniou réer

  • @ls2massgueyendiaye14
    @ls2massgueyendiaye14 5 лет назад +5

    Doull rek ngén di deff yena yakh derou mourid yi fi koufi sa baye dé sr Mountakha nila diokhmako ma diokh sr touba nga diokhe ko

  • @serignetakkricain1339
    @serignetakkricain1339 5 лет назад +2

    Bilaye yen dagèna rew ba dof dou ken lou kèn kham

  • @santesamayaye7483
    @santesamayaye7483 5 лет назад +5

    Rèww ba dofff imbecil touba rèkkk.com khar lêne sèni nêwou baye

  • @Looricinaltalz
    @Looricinaltalz 5 лет назад +1

    Touba rke Touba rke ila Touba

  • @marametoure4306
    @marametoure4306 5 лет назад +1

    Mètina trop 😭😭😭

  • @diilerecaalifuuta549
    @diilerecaalifuuta549 5 лет назад +3

    Touba danio ragal soulko madinatoul salam bala thianta koun deffe am tarikh bopam

    • @falloulo3983
      @falloulo3983 5 лет назад

      Bonne def sene tarikha bop Bane problema la touba di am fi coun fi top ahmadou bamba takh kene def fi lou war takh kene top sa guinaw

    • @famakhathiouba6946
      @famakhathiouba6946 5 лет назад

      Walahi boss bouniou ko soulonn médinatoul salam moussiba dina am pask thianta yii ma guiss kone sen tank dootoul dem touba

  • @mamecheikhmbaye8491
    @mamecheikhmbaye8491 5 лет назад +9

    réwandé, fanatisme, ignorance, cocktail explosif!

  • @famawade2101
    @famawade2101 5 лет назад +2

    Téguéna liguéyi sen euleuk té bayi cheikh mom demna ba paré té yén gniy wax ak mana yam kén khamou si leugueum fan lay moudjou moudj gou rafett mo diara niane rakhass lén khol yi té selal nénen wi tey def lou bakh kousi kham euleuk foy moudji lan monou wor siné euleuk bounou démé dinan retrouvé sounou corps banouy entéré khamou gnou si bane anam lanouy démé kon nane nianal cheikh bi té dem diamou dji yalla

  • @djilydiopallodakar5194
    @djilydiopallodakar5194 5 лет назад

    Yénn nij di wakh li niépou dougénn touss téki woulénn dara
    Deugénna réw reck diamoulén fénn ay mariredoo génn reck
    Amoulénn yarr amoulénn kilifeu
    Ay domi kharame you dieumoull fénn génn
    Beugue taw fi di wakh
    Fi nak Touba la
    Nioune yarr bann ni neurr
    Diagallénn bani arr niofinék
    Bou génn yorée sénn réwandée
    Génn dieumé ko thia khadie

  • @falloulo3983
    @falloulo3983 5 лет назад +5

    Fate guen diam yalla lidiantil sene kuer yi té bayi kuer diambor yi taxaw bir touba di saga dom xarm yi

  • @madoundiaye697
    @madoundiaye697 5 лет назад +1

    Mé lii et c'est que néné rék la vraiment yénné ndiaķ yarr rék

  • @modoumatarndiaye1449
    @modoumatarndiaye1449 5 лет назад +2

    Loci seene yoone do seene baye dem leene sollé ko war doole

  • @fanambaye7593
    @fanambaye7593 5 лет назад

    Merci cheikh bi💘💘💘💘

  • @babacardiop123diop2
    @babacardiop123diop2 5 лет назад

    Respecter l diégueul yonnou mourite khamoul lii yalla nako sounou borom diégueul

  • @ndiayebada9873
    @ndiayebada9873 5 лет назад +2

    Ay marireundo leugne dougne aay mouride

  • @ahmadoudiagne7863
    @ahmadoudiagne7863 5 лет назад +1

    Wakh wakh dji yeup ay dokho ndèm reik gnofi nëkk dih mbèl mbèl fii ish way layo kay 😁😁😁😁😁😁😁😁😁

  • @juniorpro1523
    @juniorpro1523 5 лет назад +1

    Yéna khama de té rew lin lin may dafa epo djoma DJ du saga daguéna reew bègue lén Serigne saliou boguén begon Serigne bi doguén takhaw fi du saga

  • @damefalle6972
    @damefalle6972 5 лет назад +1

    Khana serigne bibamna kilifa bayilèn thiakhan yi

  • @adamagaye4136
    @adamagaye4136 5 лет назад +2

    yien ñi ragall lien yalla

  • @amadoufall2175
    @amadoufall2175 5 лет назад +4

    Sénégal jour bouye takk internet mokoye tall

  • @jesuisfieredeletresoninike8867
    @jesuisfieredeletresoninike8867 5 лет назад +5

    Aller a travail c'est mieux

  • @ckiekhdiop2711
    @ckiekhdiop2711 5 лет назад +1

    Yene niale yar way

  • @diorndiaye3873
    @diorndiaye3873 5 лет назад +1

    Di khatrayou si bayou diambour sou ngéne kou défone séne baye Kone heure bi vous seré dé milliadaire

  • @layeyade901
    @layeyade901 5 лет назад +1

    non amna loma miti 😭torop donte ap mourid la yar dafa bakh si domou adama

  • @ramatoundiaye154
    @ramatoundiaye154 5 лет назад

    Touba forc nekh naxari wax ba khoteko takhol mo dem madinatoul Salama Touba forc Touba forc Touba forc

  • @tphiskoyop4061
    @tphiskoyop4061 5 лет назад

    Yéne Bilay da ngénà Reww vous êtes tellement impoles

  • @djibrilba5453
    @djibrilba5453 5 лет назад

    Nagnou yakar yalla môme dou dès

  • @mbayefaye5046
    @mbayefaye5046 5 лет назад +2

    Atank mourid damay méti reurr bakhoul

  • @priinceuhhwiizzmmo3500
    @priinceuhhwiizzmmo3500 5 лет назад

    Yeine weurou leine

  • @mariaalaloumamebamba4058
    @mariaalaloumamebamba4058 5 лет назад

    Mane d barki bamba dama warou tay
    Mouride dieufé ndiguel tey ame yarr ame talibé laniouko khaméwone mé pa rew khamadi niak kersa insolent
    Souniou kilifa wakh nguéne beug ko tekki ak di khass wa touba té touba moy tékhé kounioufa dinthie tékhé nga walahi sama xol diekhna takk j vien d m rendre compt k thianta yi amouniou yarr

  • @diorndiaye3873
    @diorndiaye3873 5 лет назад

    Esk wer ngéne séne baye bou déwone douguéne fi nék di réw réwlou

  • @seullepouvoirdallahesteter9612
    @seullepouvoirdallahesteter9612 5 лет назад

    Waa mais!!!! 😂😂😂😂😄😄😅😅😅

  • @jupiterndiaye8888
    @jupiterndiaye8888 5 лет назад +1

    Est ce que gni aye mouride deugue laniou

  • @matarndiagadieng8287
    @matarndiagadieng8287 5 лет назад +1

    😭😭😭😭

  • @mouhaframarene9792
    @mouhaframarene9792 5 лет назад

    Yèna re w te khamadi niakk talibé serigne mountakha wakh niou yobouko bakhiya yéne guênnê madina khamo Lene lane motakh S mountakha def li am lene yar way

  • @Serignekhadim5546
    @Serignekhadim5546 5 лет назад +4

    Gni danio xamadi s mountakha diokhé ndigueull guénne ni doufi amé

  • @diordiakhate7828
    @diordiakhate7828 5 лет назад +2

    Hahaha le KHALIFE GÉNÉRAL a parfaitement raison car il sait que le fanatisme est bien réel chez les thiantacools

    • @laghemtv7024
      @laghemtv7024 5 лет назад

      Wakh loula waoroul ak soss yalla beugou ko

    • @laghemtv7024
      @laghemtv7024 5 лет назад

      C'est bon d'être fanatique dans le bien mais pas dans le mal

  • @diopmamediop5535
    @diopmamediop5535 5 лет назад

    Rew amna

  • @expertpablo7148
    @expertpablo7148 5 лет назад

    Niake ngéne yarr mouride ndigueul

  • @ndongodaara2391
    @ndongodaara2391 5 лет назад

    Niak yar ak teeguiine!¡!¡

  • @seullepouvoirdallahesteter9612
    @seullepouvoirdallahesteter9612 5 лет назад

    Ay way guem lene YALLA 😒🤔😂😂😂😂😁😃😃😃😃😂😁😁😁

  • @bassiroundiaye5572
    @bassiroundiaye5572 5 лет назад

    Wakh diee fi nekk wayé bane robéé ba paré daw ngêne dh xam ngêne né kilifa yafa nekkonee mo takh nou ande ak dall wayé bane paré amna nioune khawa lappou dh mourid daye dégue ndigeul

  • @elhadjisour6776
    @elhadjisour6776 5 лет назад +1

    Khar len ba sen bay dee guin yo boko folen nekh ba yo diam mbor sen yonn neko si rew

  • @faloufall9356
    @faloufall9356 5 лет назад

    gni di saga dougnou ay nitt sakh ay mala sakh gnolénn geunn

  • @mbayembaye2632
    @mbayembaye2632 5 лет назад

    Li lepou gnake khame khame rek moco waral amelene yar

  • @Looricinaltalz
    @Looricinaltalz 5 лет назад

    Yi dof

  • @moustahinesarrmouritanesen465
    @moustahinesarrmouritanesen465 5 лет назад

    Dof rek

  • @allefall5545
    @allefall5545 5 лет назад

    Yene bou fekéné d'à ngena mane demléne tha kasoba dieuly séné moromou talibe yafaneck mogueune

    • @moussaaw9495
      @moussaaw9495 5 лет назад

      Yènar rèw sr mounetakha moy sr touba

  • @cheikhseck4126
    @cheikhseck4126 5 лет назад

    yarrr sokhmonanouko torop yeina rer rew niak yarrr niak talibei niak kilifeu ignorant k vous êtes

  • @fanambaye7593
    @fanambaye7593 5 лет назад +1

    😭😭😭😭😭😭😢😢😢