Cheikh Béthio Thioune : " l’endroit où je serai enterré après ma mort "

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 30 янв 2025

Комментарии • 119

  • @talibebambatouba2271
    @talibebambatouba2271 5 лет назад +150

    Dieureudieuf s.saliou kou beuug serigne saliou pousse bleu

  • @ayshajuliette
    @ayshajuliette 5 лет назад +3

    Ndeysane sokhna bator thiam mougui ni ci weteum cest émouvant
    Cheikjh bethio moi jlaim bien
    Kou ko defal teranga mou wakh ko
    Yalla yana yereum ko tey xarei ko aldiana amin

  • @nefertaribaidy669
    @nefertaribaidy669 5 лет назад +17

    Qu'Allah lui pardonne ses pêches et lui accorde sa miséricorde en ce jour du ramadan à serigne bethio thioune.paix à son âme. À Dieu nous sommes et à Dieu nous retournerons.

  • @marichousow5147
    @marichousow5147 5 лет назад +2

    Yalla nako yalla yeurame thi barké barhama niass
    Yalla nagua dadjé ak serigne saliou mbacké😢

  • @cheikhbambasarr6812
    @cheikhbambasarr6812 5 лет назад

    Dieureufeuty Serigne mountakha khadim Rassoul delotiga sagalaatt yonou mouride cheikh Bethio rawga

  • @bakhbayembacke2448
    @bakhbayembacke2448 5 лет назад +5

    Ndeye san thiey yalla 😭😭😭😭😭😭khol bou rafet yalla na la yalla yerem tenga deuk ak Serigne saliou

  • @papandiaye4922
    @papandiaye4922 5 лет назад +24

    Il n'y'a de dieu que Dieu et Mouhamed est son messager

  • @biranethiaw6577
    @biranethiaw6577 5 лет назад

    Yallana yalla yeureum cheikhbi defalko Tawfekh sa janatou firdawsi barke Serigne Saliou mimou yakar

  • @mouhamedmouhamed8005
    @mouhamedmouhamed8005 5 лет назад +2

    انا لله وانا اليه راجعون اللهم اغفر له وارحمه وعافه واعف عنه واكرم نزله ووسع مدخله امين يارب العالمين

  • @FamaMuslima
    @FamaMuslima 5 лет назад +29

    Allahou wahid.Allahou ahad.Keur yoyou yeup amoul ndieurigne.kou diamouwoul yallah billahi perte nga.deloulene thi séne Borom mom rek mouffi sakh.firawna aki mbokkam yalnagnou torokh

    • @diabelseck8525
      @diabelseck8525 5 лет назад

      Nissa Feem yaw ndiabotou firhawna nga bokk !

    • @dieylani2675
      @dieylani2675 5 лет назад

      @@diabelseck8525 ah aouis celui qui jure par un autre Qu'Allah a mecru hadith sahih

    • @sunugaalsenegal7069
      @sunugaalsenegal7069 5 лет назад +1

      Nissa Feem yalla dafa bari yeurmeundé. loutakh ngen sokhar si mayou yalla si diam yii.

    • @Momarbineta
      @Momarbineta 5 лет назад

      Deug piir nga wax limou def dara bakhoussi

    • @FamaMuslima
      @FamaMuslima 5 лет назад

      Saga yakamté khékh la.diné bo khamni amoo féne fokomouna weere dou ci quran douci hadith
      Toumal serigne bi rek wayé yalla mom nopina.
      Domou Adama bou souffé Ab saggarou mbindeef gnou dieul Diko def comme bourbi azawadial
      Lolou yéména.boudeh ci ndiabootou firawna laa book yalna Allah mabb lépp louy bokkalé ci mil rew mabb firawna Ak Aÿ nioniam.
      Serigne bi bou délouwatone ci adouna dina réndi gnou barri.nékéwougnoufi loudoul dikko toumaal aka Diokh KO Aÿ martaba youmou wotéwoule ci boppam.

  • @diopgoor9437
    @diopgoor9437 5 лет назад +4

    Yalla nako yalla kharè alle diana si barkèpe serigne saliou mbacke

  • @noixdecajou3673
    @noixdecajou3673 5 лет назад +9

    SubhanalAllah !!! Yalla rek ☝️ laniou wara diamou , mom laniou wara sant té si mom laniou wara yakkar. Alakhira metina meti bo khamni kene dou tal kéne kounek say djeuf nguay khalate, Kene dou dougueul kene Al janna koudoul Yalla .Kou dé ak sa bammel té kounek Li ngua liguey sisa adina mom nguafay fek.

    • @bachirbachir9831
      @bachirbachir9831 5 лет назад

      Nafissatou Diop deugu rek nga wakh mane beugu nala def kharite

    • @mohamedba9766
      @mohamedba9766 3 месяца назад

      Khalil dara nopile

  • @bintousamb1938
    @bintousamb1938 5 лет назад +5

    Yalla na nako yalla yeureume si barke s saliou

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 5 лет назад +17

    Manchalla linga am si serigne salihou yemena

  • @lomamadou4526
    @lomamadou4526 5 лет назад +5

    Paix à sn âme j l'aimé bien...!!!

  • @mamemorniang9550
    @mamemorniang9550 5 месяцев назад

    اللهم اغفر له و ارحمه

  • @niangsalimata8102
    @niangsalimata8102 5 лет назад +19

    Daysane dioune yalla na adiana firdawous dissa keur adouna dou dara🙏🙏🙏😭😭😭😭

  • @rastavanch2000
    @rastavanch2000 5 лет назад +2

    Dieuredieufffffff Thioune

  • @dioubelgueye8712
    @dioubelgueye8712 5 лет назад +4

    Yalla nako yalla kharé aldiana

  • @dioppape5254
    @dioppape5254 5 лет назад

    Yallah nako yallah yeureum kharéko aldiana

  • @dijaitskhadyba3420
    @dijaitskhadyba3420 5 лет назад +1

    Ndeysaan yalnako yalla yerem

  • @katyniangndiaye5098
    @katyniangndiaye5098 5 лет назад

    Yalla nako yalla guéguel te khare ko aldiana ...

  • @diopserigne2514
    @diopserigne2514 5 лет назад +3

    begone s Saliou LOL amone xorom LOL ndAssane yalla nako yalla yereum ta xarei ko aldianay fiirdaw si thii barkeip seydina Mouhamed

  • @nogayegueye7458
    @nogayegueye7458 5 лет назад +4

    Yalla nako yalla yereum

  • @modoudiack8924
    @modoudiack8924 5 лет назад

    Cheikh béthio yala nala yalla maye foff al dianaye firdaw si

  • @maramesady1484
    @maramesady1484 5 лет назад +17

    Yalla nako yalla yeureum tass gnou si barkeim

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 5 лет назад +3

    Serigne Mountaqa est sage. Ainsi on pourra contrôler les thiantakounes. Ils voulaient un grandiose mausolée où il traiteraient béthio de dieu.

  • @zanasow3414
    @zanasow3414 5 лет назад +10

    Yallah Nala boure bi yeureum mou até la si yeurmendém

  • @cheikhmouhamadoumourtadasa2799
    @cheikhmouhamadoumourtadasa2799 5 лет назад +4

    Yalla nako Serigne Saliou Mbacke terrou sa aldiana firdawesi

  • @maremesidibe7701
    @maremesidibe7701 5 лет назад +15

    sama yakarou tay ak euleuk demna.ma ngui koy dialei adouna.Yalla doli leiram😥

    • @fatimataarameboyeseck8889
      @fatimataarameboyeseck8889 5 лет назад +3

      Astafour lah ana Allah koula bindou bin sa baye sa yaye ak ki ga wakh

    • @moussacisse3616
      @moussacisse3616 5 лет назад

      FATIMATA ARAME BOYE SECK nit yi dagnouy wakh wakh té khamounouy moy lan

  • @ibrahimasenenabien1204
    @ibrahimasenenabien1204 5 лет назад

    Yalnako yalla diègal barkèb wèrou korr gui

  • @Cheikhmouhidineofficiel
    @Cheikhmouhidineofficiel 5 лет назад +17

    Que le paradit soit sa demeure éternel

  • @cheikhdiop5069
    @cheikhdiop5069 5 лет назад +1

    Ndeysan

  • @abatalibniang9950
    @abatalibniang9950 5 лет назад +1

    Ndeysan adouna, bakh rék mo woor

  • @IB-dh8uw
    @IB-dh8uw 5 лет назад +2

    Ndeysan c la vie

  • @aron6054
    @aron6054 5 лет назад +5

    Yalla nako serigne saliou térou

  • @adamadiallo4933
    @adamadiallo4933 5 лет назад

    Repose en paix ✌️

  • @falloundiaye2182
    @falloundiaye2182 5 лет назад +2

    Amine

  • @niangsalimata8102
    @niangsalimata8102 5 лет назад +15

    Yalla naco serigne saliou terrou gnii adiana firdawous yii

    • @zai5562
      @zai5562 5 лет назад +10

      Bayi lèn sen wakhou doff yii. Sereign Touba térouwol kenn. Il est mort. Taloul kenn, boppam leu tal. Arrêtons avec les bêtises. YaAllah rekk mo fi nek. Délou len ci YaAllah té bayi thiaxane you bari yi.

    • @aichalaye5702
      @aichalaye5702 5 лет назад +2

      bien dit zayna jagne

    • @mamoudoudiallo2333
      @mamoudoudiallo2333 5 лет назад +1

      Niang Salimata serigne mokoy terrou wakh doff demal diangui alkourane. Nitt sou déhé dieufeum ak Yallah mokoy terrou. Amna souf fi amna keur mane mayé keur sou diebaloul lolou moy lane tay bayina lolou yepp dougou fou khatt

    • @Topofthetopapex
      @Topofthetopapex 5 лет назад +1

      Zaina Jagne nga wakhatiko. MAne deh affaire yi niouy wakh daf ma diakhal ba beugouma ci wakh sakh tellement dagn saga ak you nekk

    • @gerenad6gerenad631
      @gerenad6gerenad631 5 лет назад

      Niang Salimata Esk Saliou Saliou est aldiana seul Dieu sait

  • @papetraore1451
    @papetraore1451 5 лет назад +5

    Nimporte quoi cest Dieu qui decide quand et comment son serviteur rendra lame personne d'autre.même le prophete psl ne savais pas quand il va mourir.
    Tu avais dit que tu vivra encore longtemps et tu es parti aujourd'hui

    • @lamineseck5426
      @lamineseck5426 5 лет назад

      Yaw doule.sa khol bou bone.

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 5 лет назад

      yaw dof ngeu dei seneu wa keur war naniou leu di surveillé kom ay tothe toth ngay wakh si reseau socio yi

  • @willblacked6743
    @willblacked6743 5 лет назад +9

    Bon la preuve que yalla rek mo meune. Nénga Serigne saliou promettre nala goudeu fann ak dokh sa diganté ak metitou deh. Lolou amoul. Puisque tu as souffert longtemps des maladies tu es parti crever en france ...et sa fann goudoul trop en tout cas tu as pas eu 90 ans wade sakh mola makk.
    Naniou diaamou yalla yalla rek mo meune😊😊😊😊

    • @fatousamate2775
      @fatousamate2775 5 лет назад

      Bonne nga. Serigne Bethio khamoko. Wayei bagnoko dei, dangako khamoul

    • @sonkomachaallahsonkorek5052
      @sonkomachaallahsonkorek5052 5 лет назад +3

      Yaw Serigne bethio ame 82 ans
      Mou geune Adouna 1 jour weerou Goor
      Mais yaw lepp diam
      Loutakh sookorr
      Mane douma talibe serigne Bathio
      Je suis mourite
      Mais nakk Yalla dayy mayei
      Manoule

    • @sonkomachaallahsonkorek5052
      @sonkomachaallahsonkorek5052 5 лет назад +3

      Loutakh guanei il a souffert lolou ayy fene leu
      Nakh Seydina Mouhamad Psl
      Il a etais malade ; mou metii torop si mom avant mouy rentre l"ame
      Lolou dou metitou dei
      Amo kham kham

    • @willblacked6743
      @willblacked6743 5 лет назад +3

      @@sonkomachaallahsonkorek5052 yow doul del deglou c'est lui qui a dit que serigne saliou promettre nako né dou souffrir avant mouy deh et c'est pas vrai il a souffert j'en sais quelque chose suis à Bordeaux la ville où il est mort. Noppil je sais de quoi je parle. Et même avant ça la maladie lui a fait vraiment souffrir.
      Ok mais le prophète n'a jamais dit avant sa mort qu'il allait pas souffrir? Wala? Au contraire le prophète savait qu'il allait mourrir le jour venu ....selon les hadiths.
      Baylene nafekh c'est lui qui a dit des choses qui sont pas vraies je dis juste que fenn na. Yalla rek mo meune mo kham!!!

    • @bambagaye3837
      @bambagaye3837 5 лет назад

      Soma khamone fo deuk Kate sa ndaye domérame sa baye dou dara mo takh embecill

  • @dieylani2675
    @dieylani2675 5 лет назад +1

    Celui qui jure par un autre Qu'Allah a mecru hadith sahih

    • @malickgning6834
      @malickgning6834 5 лет назад

      Iow khamo loy wakh so nieuwé nio djangual la darra khamo ko bayilene nek ci vidéo d'i garaw garaw lou ta khamolene dara

    • @dieylani2675
      @dieylani2675 5 лет назад

      @@malickgning6834
      D'après Ibn Omar (qu'Allah les agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit :
      « Celui qui jure par un autre qu'Allah a certes mécru ou associé ».
      (Rapporté par Tirmidhi dans ses Sounan n°1535 qui l'a authentifié et il a également été authentifié par Cheikh Albani dans sa correction de Sounan Tirmidhi)

    • @dieylani2675
      @dieylani2675 5 лет назад

      @@malickgning6834 danguay wedi wala ?

    • @mohamedba9766
      @mohamedba9766 3 месяца назад

      Touss

  • @mamoudoudiallo2333
    @mamoudoudiallo2333 5 лет назад +7

    Regarder moi la femme day deugueul sa dieukeur mais Yallah rek laniou diamou

  • @elsultano5333
    @elsultano5333 5 лет назад +10

    Femme 👩 Diamoul yallah mo geune thi yow

    • @moustaphadiagne8859
      @moustaphadiagne8859 5 лет назад

      On ne peut plus dire ça. Il n'est plus. Ferme ta gueule, c'est mieux

    • @Momarbineta
      @Momarbineta 5 лет назад

      @@moustaphadiagne8859 C'est toi qui devrais la fermé. Lii Philips minth wax moy deug

    • @diorndiaye3873
      @diorndiaye3873 5 лет назад

      Djiéguéne tok si aye gore Di wakh

  • @babacarndong8217
    @babacarndong8217 5 лет назад +8

    Bepp dioulit bou beug nitt beug bi tollo ak yoneneti bi kokou dou dioulitt
    Kouy diamou diamoul yalla nitt kene douko diamou
    Bokkalé yalla la

    • @ibrahimathiongane2947
      @ibrahimathiongane2947 5 лет назад

      Dioulite daye mandou

    • @babacarndong8217
      @babacarndong8217 5 лет назад +5

      Ibrahima Thiongane mane li wakh alquran leu nekk

    • @babacarndong8217
      @babacarndong8217 5 лет назад +1

      Zazal DESIGN TV kone kou wakh al quran sa joulit desna
      Khana yalla wakhoul ni ٱلنَّبِىُّ أَوْلَىٰ بِٱلْمُؤْمِنِينَ مِنْ أَنفُسِهِمْ

  • @soxnamaye1229
    @soxnamaye1229 5 лет назад +1

    😭😭😭😭😭

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 5 лет назад

    Yalla nako yalla xaré aldiana

  • @samsoufaye9840
    @samsoufaye9840 5 лет назад

    Thiey SERIGE béthio sama yakarr mou bakhe

  • @oumoundiaye5184
    @oumoundiaye5184 5 лет назад +1

    Rip

  • @Kingsolomon8459
    @Kingsolomon8459 5 лет назад +3

    Aka Bakhone

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 5 лет назад

    St srgn saliou thioune mame bambi

  • @dieylani2675
    @dieylani2675 5 лет назад +3

    😂😂 serigne saliou ci bopam devant Allah Azawajel bopam leye tal

  • @soldaroubayekarimbassiroun4535
    @soldaroubayekarimbassiroun4535 5 лет назад

    Esskuy cey mbacke

  • @dirmounasoumare3071
    @dirmounasoumare3071 5 лет назад +1

    Toujours fo débat

  • @dirmounasoumare3071
    @dirmounasoumare3071 5 лет назад

    Comme pharaon vraiment lui c'est un perver

  • @aminatabarry640
    @aminatabarry640 5 лет назад

    Mounone guene KO denthh fimou beugueu rekk

  • @mbackembacke4531
    @mbackembacke4531 5 лет назад

    Vidéo bi tay la

  • @dirmounasoumare3071
    @dirmounasoumare3071 5 лет назад +1

    Des pervers plus pure k pharaon

    • @ndiayecheikh3309
      @ndiayecheikh3309 5 лет назад

      Dirmouna Soumare yaw innocent nga nit daguaye am deguine

  • @mbackeabibou4511
    @mbackeabibou4511 5 лет назад

    Koubagu listikhar gouwor woma appel Walla ay nian Walla touki Walla borom kur Walla khalis Walla bayre woma 777945489

  • @saabiquuna5255
    @saabiquuna5255 5 лет назад

    Euleuk door ne pour yaw. Gat nge meunoul ci lifikhèw. Kookou moy se djaam djaamat? Be kèrook. Yaqq katou generation leum nge.

  • @en2mots817
    @en2mots817 5 лет назад +2

    pourquoi on a pas respecte sa volonte

    • @moustaphadiagne8859
      @moustaphadiagne8859 5 лет назад

      C'est à cause d'un lobbying d'État et de calcul d'intérêt

  • @fatoumatadiatta5175
    @fatoumatadiatta5175 5 лет назад

    N'importe quoi

  • @lookingtv2641
    @lookingtv2641 5 лет назад

    Ktlndm feulée😣

  • @koudythimbo860
    @koudythimbo860 5 лет назад

    Rip