Lâ Hawla wa lâ Quwwata illâ billâhi'l aliyul Aziim. Alhamdulillâhi Rabbil âlamiin. Allâhumma Salli alâ Seyyidinâ Mawlâna Muhammadin Wa Sallim. YALLÂH Jërëjëf, Yonente Bi Jërëjëf, Yaay boy Jërëjëf, Baay Jërëjëf, Borom Xamxam yi Jërëjëf. Na len Yallâ Fay. Na nu Borom Bi Yokkal Jamm, te May nu mujj bu rafett Adduna ak Alaaxira. Amiin, Amiin, Amiin…
Baye Sakho way yalla na yalla Yokaka ayes Leers
Yalna sen dieum si kanam ❤
Yalna sa borom barkel fayal niouko
Man kii dama koo bëgg billaahi : da fa am hikkma maanaam limuy wax da fa leer nàññ
Yalla na yalla yessal yeurmandè si moom
Machallah yalna yokou ay léram té tasgnou thi barkém🤲
Machall sakho iliman
Jeureujeuf
Kontan n a si yen dh ligey bi rafetna
Merci
Yalla na yalla doli yermandé si Mame ibou sakho
Mashalla
Machallah Sakho yalla na souniou borom faye
Machallah. Li dagneko wara di dialalé si télé yi waye
Walay ndeysane
Deugueuleu
Ken dou mame maodo❤❤❤
Lâ Hawla wa lâ Quwwata illâ billâhi'l aliyul Aziim. Alhamdulillâhi Rabbil âlamiin. Allâhumma Salli alâ Seyyidinâ Mawlâna Muhammadin Wa Sallim. YALLÂH Jërëjëf, Yonente Bi Jërëjëf, Yaay boy Jërëjëf, Baay Jërëjëf, Borom Xamxam yi Jërëjëf. Na len Yallâ Fay. Na nu Borom Bi Yokkal Jamm, te May nu mujj bu rafett Adduna ak Alaaxira. Amiin, Amiin, Amiin…
Yalnako yalayaram thkarekoaldina firdwc
MashaAllah Yalna nako yalla khare Aldiana Fidawssi Sacko Elimane
Sallalahou aleyhi wassalam Amine 💘💝❤️💝
❤❤❤❤
Yalnaniou yalla fayal El hadji ibrahima sakho
Allahouma amine
Amine ya rabil akhlamine
Dieuredieuf geoul Tv 🙏🏾
Gor gou vakh baye sakho demb lako sama rak toudé dome nako nieup nianal
Merci Sakho yalnala yalla feye
Mame yalla nala yalla kharé aldjana 😭😭😭😭😭
Amiine
Ndiayssan paix à son âme Amine 🙏 🙏 🙏
Machallah Mame ibou Sakho yallnako yalla faye
Waliou kamil
Dieureudieuf baye Ibou Sakho... RTA
Thieuy dji dieum
Diarama El Hadji Ibrahima Sakho thi sounou Sanga bi Malick fawade Sy gorgui bi amoul morome.
Yalla na yalla fayal nioko
Macha.alla dieuredieuf
can you please upload the song running from the background
Bay salon 5
Machallah
Yala borom bi yokou say ler té tass gnou si sa barké
فأولئك مع الذين أنعم عليهم من النبيئين والصديقين والشهداء والصالحين وحسن أولئك رفيقا. مام الحاج إبراهيم ساغ
000
Ok Ok Ok a fait fait rien rien que que ça wly je je t’ai pas pas encore vu ça ça ça va te dire
نيل فضل...عند رسول الله صلى الله عليه وآله وصحبه وسلم.
😭😭😭😭
38:40
U
Macha Allah
Machalla