Il faut apprendre à nos enfants l'histoire de notre peuple. Cette chaine est vraiment venu à son heure. Merçi Monsieur Mbaye Guéye Syll. Mais on voudrait bien que vos émissions ne s'arrêtent pas aux royaumes wolof (Cayor, Baol, djolof et waalo). Le Sine, le Saaloum, le Fouta etc. Si réw mi la gnou bokk. XAM SAM RÈW WAR NAA WAKH SI RÈW YOOYOU
Magui université ms li fi rk lagne ko meunna xamée mboorr lou âme solo lh thi deuk souma koy dégulou damay niakh toye khépou ndakh kholl bou diékh douma beugu sakh mou diékh yalla nalla yalla faye xamna ni daye gua lou métti pour nétali li 🇸🇳😭

Félicitations serigne Mbaye Syll amna solo trop
Une histoire qui mérite d'être raconter des sites qui mérite d'être valorisé
LORO ma fierté
Sante naala dé
Masàllaa baay mbay gëy am na solo di ñaanal ñépp koorug Jàmm Móodu-Móodu yi ndam rekk
Dieuredieuf baye Mbaye Syll yague fii lol te werr amena solo loool walahi
Dieudieuf bay Mbay Syll. Sa takhaway rafetna bokena thi liniouy gueum lo souniou bopou.
S Mbaye Gueye Syll Yalla nala Yalla faye ci barkep Serigne Touba
J'ai les larmes aux yeux.Fier de vous baye Mbaye
Magui université ms li fi rk lagne ko meunna xamée mboorr lou âme solo lh thi deuk souma koy dégulou damay niakh toye khépou ndakh kholl bou diékh douma beugu sakh mou diékh yalla nalla yalla faye xamna ni daye gua lou métti pour nétali li 🇸🇳😭
Merci excellent 😂😂😂😂😂
Papa billahi yaangi def lu waroon sunu ministère yi.
Vraiment fierté nationale nga heureusement que je suis amoureux d'histoire 🙏❤️
Yaàŋi déf lu mucc ay Ayip.
amna solo
Amena solo trop machala
Waw for way
Machalla serign mbaye gueye silla
Dieureudieuf cheikh mbaye yallana sa diam yague et Ramadan MUBARAK
Fier de mon grand pére Lat joor
Sunu baay Serigne mbaye bonne contunation ♥️🙏🙏
Jërëjëf yalna yàlla gudd al sa fan té mayla k wér mbuuru m ndaté yàlla noo ngi xaar aga lebi
Dierdieuf serigne mbaye amna solo
merci pour ce travail c'est essentiel pour notre peuple d'apprendre son histoire si on veut se devellopper
Je suis fier d’être un lorois
Machalla minal khadiim Ila khadiim
Numero s mbaye gueye syll la beug dh
Machalha s mbaye geye rafetena
Tonton soumaye deg Lou sama xole déye sed billahi syll
Mchallah pere mbaye Geuye sylla amatina solo loll
Ñaaw teff rekk la fi tubaab bi deff seen làkk wi sax dama koo seexlu
Bismillahi gnongui tewlou bou weeer
Bay Mbaye wakhtanwi amna solo loll wayé toubab lilénn arrange réck lagnie binne
J'aimerais bien une vidéo sur Mabadioukhou Ba
Dieuredieuf
Gnogui xam sounoum rew
Machaallah dieureudieuf baay mbaye
Machallah Pere Mbaye Gueye Silla vraiment vs êtes excellent
La bataille de Koki s'il vous plaît
Maasàllaa maasàllaa
Machalla
Diadieuf 👋
Machallah
❤❤❤❤❤❤❤Merci Beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Il faut préciser les dates en français rapidement félicitation j'aime bc cette émission
Mor fademba kane lamp
كما قلت دائما نحن معكم في نشر العلم و المعرفة في التاريخ
نشكركم شكرا جزيلا تقبل الله صيامكم وصيامنا بالخير والعافية
Je suis frere loro loro
Loro ma fierté
mbooru m Ndate yàlla jeexul té yaw rekk yaa koy Wax ci réew mi boo ko bayyé rekk mu réer ñu
Ensuite la bataille de Samba Sadio
Ziarnala sa teere bi si serigne Touba feeskoy mana ame si Europe? Nonghi sakku ab teere si histoire bou Senegal yanu si doy
Merci
nassarane keneu douko yéss
Diareudieuf smgs
😭😭😭😭👹👺😢😢
😭🤔
Grazie mille 👏👏
Loro loro
santatinano bobax
Machalla
Machalla