Amna solo trop Oustaz Ma'chaa'Allah Man déh dama yakar ni dagno wara déf ay émissions ak ay plateau pour sensibilisé goor-djiguéne yi. Ndakh yakar na rér rék molén yibé ci li
Persone de bon musulmans ne tolère jamais un homosexuel chez lui et c k tu ne tolère pas chez toi tu doi pas le tolérer dans la société ou tu vie …. Settt lennn yalla si li guénnn di wakh
Bayilé fofou ils le savent trop bien même nafekh wallah dégo français Di wakh niare yoyo moléne diap .oustaz le l'admire beaucoup mais manipulation d'où yeufou djoukit té si lolou lay dokh si histoire bi . projet bi ils sont trop petites pour saboté KO 54%yi voté pour diomaye son patient Dara meunuléne manipulé gni bagnone démbe rek gnoy wakh tay
Sonko n´a pas utilisé le mot ´´homosexuel ´´mais la parole goordjiguène est bien connue par Mélenchon qui n´a pas eu besoin de traducteur pour reprendre le micro pour faire son show
Ay fén dal dou bédiaw d'ici 2ans inchallah on verra si le gouvernement a la décision ferme de la pénaliser où il faisait du masla comme le gouvernement passé Dans tous les cas le teuwou takham dafa yagoul
Quand Mélenchon a parlé du mariage homo, les étudiants l'ont hué. C'est quand il a dit qu'il laisse les Sénégalais gérer le problème eux-même que les étudiants l'ont applaudi. Allez revoir la vidéo avant de s'exprimer.
Machalla Oustaz boula keneu dougeul say kadou lerna machalla
Mashallah amena solo lole dieureudieuf 🙏🙏🙏
Machalla Sarr yalla nasa diam yague bidjayi Nabi Moustapha swa 🤲🤲❤️❤️
Jërëjëf Oustaz Makhtar Sarr. Toujours constant dans ses positions sur la question, quelque soit le gars au Palais.
Oustaz waxtan wi amna solo mé amna badd yo xamni si francé boko waxé si wolof dég dég bi dou Donn bénn mé mashalla taxaway bi amna solo
Vraiment Sockna Mbene merci beaucoup tu es très Pertinente ❤❤❤
شكرا لك اخي الكريم جميل جدا جدا ❤❤❤
Merci beaucoup oustaz pour les messages
Macha Allah oustaz yallah na yallah samela katanalela Amine
Ma cha allah Al oustass waxtane wi amna solo
Dieureudieuf Oustaz Makhtar Sarr.
Merci beaucoup oustaz
Jerejef sarr❤❤❤❤
Merci Sarr
Amna solo trop Oustaz Ma'chaa'Allah
Man déh dama yakar ni dagno wara déf ay émissions ak ay plateau pour sensibilisé goor-djiguéne yi. Ndakh yakar na rér rék molén yibé ci li
Dieredieff oustaz yaw dé vraiment serigne makhtar oustaz gua contant na si yaw trop❤
Persone de bon musulmans ne tolère jamais un homosexuel chez lui et c k tu ne tolère pas chez toi tu doi pas le tolérer dans la société ou tu vie …. Settt lennn yalla si li guénnn di wakh
Diereudieuf Oustaz contane thi iow yalnagnou YALLA may ndam thi kaw peuple goordjiguen yi ah yefeur yi
Merci beaucoup imame kilifeu Dale daye gueustou merci beaucoup
Oustaz Makhtar Sarr, la tolérance signifie que, on vit avec même si on l'accepte pas .
Bayilé fofou ils le savent trop bien même nafekh wallah dégo français Di wakh niare yoyo moléne diap .oustaz le l'admire beaucoup mais manipulation d'où yeufou djoukit té si lolou lay dokh si histoire bi . projet bi ils sont trop petites pour saboté KO 54%yi voté pour diomaye son patient Dara meunuléne manipulé gni bagnone démbe rek gnoy wakh tay
Oustaz dafa wara doylou té yaw serigne makhtar sarr yaw dé daga doylou li motakh gua libour si sa dîné
Merci Oustaz Sarr
Ce n´était pas à Sonko de parler en premier sur le phénomène goordjiguène.
Il avait autres choses à dire.
Sonko savait que Melenchon allait en parler donc il l’a juste devancé….
Soukhenasi khana sanoupou yi bakhoule tathou ame na
Oustaz diajef diajef
Sunu waadji bou dioumé naniou ko wakh ni da dioum mo guene par par lo bi nioune toléré wougne Dara fi
liii moye dueg
Sonko n´a pas utilisé le mot ´´homosexuel ´´mais la parole goordjiguène est bien connue par Mélenchon qui n´a pas eu besoin de traducteur pour reprendre le micro pour faire son show
Ya Oustaz bo déguone francais deuk bi tass 😂
Sonko dafa wara règle li leup ousmane sonko lleu
Ay fén dal dou bédiaw d'ici 2ans inchallah on verra si le gouvernement a la décision ferme de la pénaliser où il faisait du masla comme le gouvernement passé
Dans tous les cas le teuwou takham dafa yagoul
Oustaz, Sonko wakhoul homosexuel wayé wakh neu lgbt. Mo raw homosexuel di deeem.
Andd naa nak si mbiroum gni tambali tatiou. Wa général yii université niom louniou fay diangu français? Tabarnak!
Si le Sénégal criminalise l'homosexualité il faut aussi criminaliser la fornication(djanlo)
Wakhal si bokalé bisi réw mi
Wolof sou dégoul lakam dou yomb mou dégue français même boudé président
Mais journaliste bi esque sa va amoul niouy tathiou