Jërëjëf S. Aliou ci Waxtaan bu am solo ci Sokhna su Tedd di Sokhna Âicha Mbacké Bint Al-Khadîm. Yalla ngaci dajeek Ngërëmu Sokhna-si. Lenn rek laa bëgga leeral ngiy ñikoy diklu té xamuñu ni jigeen waruñoo yékkati Khasaayid ludul ci jotaayu kuñu araaman teel (melni sa weyjur sa rak sa boroom kër etc). Ñooñu S. Aliou di wax ay Doomi Serigne Touba lañu ak Ñiniy tuddé “Waa Barzaq” maanaam Ay Sokhna yu Kutedki: looloo moowaral ñukoko daan défal. Ludul loolu dañukoy téré: looloo waral duñu bérël (wax ci kaw) Julli walla Liqaam té duñu nodd. Jërëjëf

jerejef ci lérayi anasolo
Machalla
Dieureudieuf serigne TOUBA KHADIM RASSOUL
Kawe na lool. Yal na nu SËRIÑ BI dollee fayal sunu NDAY JI.
S. Aliyun Jóob, jërëjëf
Alkhadimiyyah, noo ngi xaar wataanu ren wi.
Yalna borom touba fayal ñiou ko barkep khassida yi
Machaa Allah thiey sama tourando YALLA nagnko YALLA Borom bou Magg bi Fayal Balla Aïssa
Thieyy Sokhna Astou gawane mbacke
Yàl na nu ku Sëriñ Tuubaa fayal....
Jeurajeuf s Alioune Diop khidma
Thiey. Ndeissane
thieuy