Aye waye Sénégal li loumou doon si bone sokhor ignane yalla rék mo mome bakén doumou adama lii mo takh dou gnou avancé tjrs dernière position dou gnou dém
Koudoul xalat biss bu ndieuck ci bamél loula nékh defal.adouna dou keur té Yalla geumoul nélawoul.kou yakar ni meun nako nakh rek yagui nakh sa bop.Dieu nous jugera In sha Allah
Nioune nio wara yeureum sounou bopp xalis dou dara dou fathie déeee té adouna déy diéh allahira siy top té yalla quéne yabouko deniou KO khamoul rek waye beusang si beuss yi lou mata khalat loudoul DEUG dou yague nagne dem rék
alakhira sènègalais you beuri dinèn dougou safara ndakh sèn ligueuyeuntè bi tè neysan aduna dou dara bèn exemple bouma sama oustaz diokhone nèna kholal thi lèk ak khif nèna tèy bo lèkone 10 guinars nga tok souba rèk lèko dara dèy melni bigua dioudo beu lègui mousso lèk
Man lima diakhal ba diakhal ma yem ma ossi moy si adouna bi gni yewo ban bien fait mofi diar dieuf gui bilahi amoul nagn len delossi khel yi si sougn borom
La plupart des sénégalais guemouniou yallah. Motakh vous voyez ce genre de chose ak yenene. Daniouy andeu ak dioulit yi rek di faire semblant. Dioudo dioulit ak beugg done dioulit bokoul
Wah xetou Bonn yi amatinaa yalna nu ylla may moudié gou raféte
Dolenn ma dimballé cotisé ma am billet dem voyage bayi Sénégal ngiir yalla fi sabillilah.dama tite ci miim rew
So amei billet daga leile ma ethiopie la dieum
@@astoudiopdiop2315 😂😂😂
Tito yawe kessé
@@halimatousadiyaseye4420 dama tite lol sakh instant bi kay dama doyal ci rewmi
@@allendime5746 en tout cas doma fi bayi dé senegal mome les gens sont devenus sombres et méchants
Soubhanallah yallah nagnou borom bi dieugueul té argnou ci pékhé seytané
Continue leen Senegal dina avancer kay
Lima gueneu méti moyy sama beau frère laa ki déff lii yalla nako yalla nite
Merci pikini🙋♀️🙋♀️vs etes les meilleurs.
Franchement li doyna war mangui niane tie yalla gou déf li yalla na yalla alack té wére ko tie barkép seydina mouhamed
Niit bone na yalnaniou yaAllah diapalei baniou teikhei aduna ak alakhira
Mane dama chokewou thi senegal yalla na ngou yalla same ak bep domou adama
Ndite yi legui ragalouniou yalla. Kham ga kou sagne souli neew pour def mystique kokou ragaloul dara
Ay way domu adama dafay fatei bamel Ak alakhira. Li niaw na nagnou yenentei diam ndakh yalla yeureum niou naatal sunu reew 🙏🏾
Deglou nako tay si xalass mais merci wa Pikini liguey bi rafett ne
Vraiment Sénégal khawme founguene Dieum
Inâlilah 🤭thieuy moudioub jamono lou nék ngay guiss. Yalla na Yalla aaral gnou bopam ci Barké Alkhourane 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Aye waye Sénégal li loumou doon si bone sokhor ignane yalla rék mo mome bakén doumou adama lii mo takh dou gnou avancé tjrs dernière position dou gnou dém
Li doyna war senegall warnano kholatt soun bopu de lii si riewou diolitt
Koudoul xalat biss bu ndieuck ci bamél loula nékh defal.adouna dou keur té Yalla geumoul nélawoul.kou yakar ni meun nako nakh rek yagui nakh sa bop.Dieu nous jugera In sha Allah
Nioune nio wara yeureum sounou bopp xalis dou dara dou fathie déeee té adouna déy diéh allahira siy top té yalla quéne yabouko deniou KO khamoul rek waye beusang si beuss yi lou mata khalat loudoul DEUG dou yague nagne dem rék
allahou akebare lî niawenà
Yalla guiss na lep qui def li yalla nako yalla weer
Yalna yalla wèriko parce que li dafa niaw trop
Allahou akbar ay lii yallna niou yalla mothiel
Soubkhanallah allah akbarrrr
Senegal koothii guiss mouy diay kourous gou reuy,ak meuneu deem diaka mai walahiii jouliit deug yomboul thii reewmii
Nooooo mais serigne ci tamite g mm pas de mots
Défouniou dara ndakh douniou sérigne...
Alahou akbar thieuy yala
Khalis motakh gnoy def li soulli new yalla nanousi yalla moussal
😥😥😥😥li loko fi diar aduna amoul bene solo
Thiey akhirou Zaman😭😭😭😭
Dafa am nitte you kham né fallé founiou yalla ragalougne ko mais bismilah
Senegal moy lolou maneu sama bopeu je ne fréquente même plus les Sénégalais (es) bakhougnou daleu
Arc en ciel gno yem fouma len guiss laliii
Waw qui s'acharne sur cette famille ?
Ayi li dafa doywar dei yallah naniou yallah mousseul thi ayi pékhé seytané
Yalla naniou yalla doli dimbalé
Noun.ban.senegal.lanou.neka.soubkhanallah
Yeufou deume yi sokhor ignane bone motakh gnouy ligueyate gnak geum yalla rek Serigne biko def yalla mongi kay khar
Ay way lilanla tamitt thiey warouna bilahi
Alakhou akbar
Moytoulene ndiabar safara rek lélén diemé
Thieye yalla
alakhira sènègalais you beuri dinèn dougou safara ndakh sèn ligueuyeuntè bi tè neysan aduna dou dara bèn exemple bouma sama oustaz diokhone nèna kholal thi lèk ak khif nèna tèy bo lèkone 10 guinars nga tok souba rèk lèko dara dèy melni bigua dioudo beu lègui mousso lèk
Jaime
Billakhi Senegal khole bou Bonne ak ignane Rek mo takh gniou Tardé
Young the Legend wakh gua deug sénégalais dafa sokhore ignane
😲😲😲😲😲
Khana qui Def li khalatoul souba
Sénégal yakhou na dé louko fii diare adouna by dafa diékh ba paré .naniou ragal yalla
Thiaye yalla
Oh my God loukofi diar 😭😭😭
Wa Sénégal xeetou nit yoyou kouleen diour noooooo
Ay kou dougou si cimetiere warnga halate sa bop, soubahanali
Vraiment Legui dama ragal sénégalaise
Yo Allah suureen🙏🙏😭😭😭😭
Thieuy yala founiou dieum
😲😲😲thioye. Noun.fan.lanou.dieme. Nanou.ragall.yalla.lou.
Bon. Li.naka.lako.nit.didefe
À wa li lanla tamit Sénégal dal diakhalnama à doyna war
subhanallah ah man tiit na de
Boudone pre-election, nguén né politicien la..
Mais askan wi mo yakou
Adouna amoul solo dh te adouna diekhna ba pare wante gniy bone mom dagnouy khey di guena bone
Sobkhanala🤔
Tieuy yalla mon pays va mal mé li louko fi diarr meusso léne guiss kou dé ba yobou dara ayy wayy nayy rafett
Adouna diarouko
Non lilanelanii
Man lima diakhal ba diakhal ma yem ma ossi moy si adouna bi gni yewo ban bien fait mofi diar dieuf gui bilahi amoul nagn len delossi khel yi si sougn borom
Wa man té ma guén rewmi lii tamiit eupena dé snhl yakhouna
Kimou don diema fekhel moko eup bopou motakh li fegne liguey bou tojj la
Exactement nak
Am na ay nit yo khamni dano mistique bilay lounek lanoiuy def ki leernama coepouse sam ladon ligey pour mou dé wayer yalarek mo nek
La plupart des sénégalais guemouniou yallah. Motakh vous voyez ce genre de chose ak yenene. Daniouy andeu ak dioulit yi rek di faire semblant. Dioudo dioulit ak beugg done dioulit bokoul
Fatou Diop tu as raison wakh gua deug guemougnou yalla ay nafékh you mak
Kawtef aye way li uawna de bilaye
Noo nit mor deger fit ragal yalla amatul
Senegal fala bate yem
Ma warou mane pouye wa li ba diam
Louko fi diarr
Kamille nac euppe na
Thiey yalla