Bouba Ndour: "Serigne Mountakha nimou déf tay djitou diokhé un exemple gnou..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 1 тыс.

  • @mouhamedfadallba1346
    @mouhamedfadallba1346 4 года назад +124

    Yaw mi images serigne Moutakha bi takh nga sétane video beusal j'aime

  • @diallombathio2227
    @diallombathio2227 4 года назад +275

    Serigne mountakha souniou mbecetei

  • @coumbambaye14
    @coumbambaye14 4 года назад +176

    C'est la première fois que je suis d'accord avec vous Bouba DEUG rék nga wakh Serigne Touba amoul morome kene la

  • @toubandindy3643
    @toubandindy3643 4 года назад +107

    Bouba merci yalla na la seringe touba fay.

  • @saam447
    @saam447 4 года назад +100

    Bouba machallah sa wax dji Rafét Na Trop

  • @fallcheikhou3406
    @fallcheikhou3406 4 года назад +114

    Dioumay Touba dou diouma djougnouy Tdeudj kou Téd ki bamoukoy niane Yalla kéne fékéwouko

    • @serigneserigne4133
      @serigneserigne4133 4 года назад +1

      Yow dofga reik teudiouna diouma mouhamed psl . Demleine diangui

  • @azoubrat220brat9
    @azoubrat220brat9 4 года назад +196

    Serigne mountakha mbacke yala nafi yague te weer balla aissa dama beug guene khamni touba borom touba moko moom boulene djakhasse mbiir mi magui djegalou te bene kilifa mofa ame mouy serigne bi wasalam

  • @bambaseck8541
    @bambaseck8541 4 года назад +74

    Merci bouba j’aime bien pour ton reponse

  • @fatouaidara7910
    @fatouaidara7910 4 года назад +94

    Tarikha ou pas yalla na coronavirus déme si barké seydina Mouhammad saw 💞💞💞

  • @serignedjilymbacke6422
    @serignedjilymbacke6422 4 года назад +95

    TOUBA Moy deuk bo khamnè kène moussou fa diamou koudul yalla Kène moussou ko mome koudul
    Chiekhoul khadim

    • @modoubane118
      @modoubane118 4 года назад

      Lolou dou Ndem dèmale jamou yalla

    • @serignetackothiam366
      @serignetackothiam366 4 года назад +1

      Diamou yalla bou ndieuke moy djouli wakhal si niaka woor ak niaka djouli dji

    • @lahatefaye899
      @lahatefaye899 4 года назад +1

      @@serignetackothiam366 Mame.ch.i.fall.kouco
      Dinguat.dem.safara.nagniou.mandou.moguene

    • @serignetackothiam366
      @serignetackothiam366 4 года назад

      @@lahatefaye899 wakho deugeu mane douma kou dougou safara et puis sakh loutakh gua momalé wakh bi cheikh Ibra fall

    • @serignetackothiam366
      @serignetackothiam366 4 года назад +1

      @@lahatefaye899 ya manou iow miye dougalaté safara mane goudoul yalla geumoumala adiana rék

  • @adamafall820
    @adamafall820 4 года назад +88

    Seringe touba koumoy dérange dou am diam bilakhi

    • @bambatoubareck
      @bambatoubareck 4 года назад +1

      BILAHI LÉRNA

    • @abdouly6773
      @abdouly6773 4 года назад +7

      Seydi Hadji Malick Sy koumoy dérangé do am diam

    • @papealelam519
      @papealelam519 4 года назад +5

      @@abdouly6773 yow katal ndayam nioun mourid el hadj dunu massa déranger domu haram

    • @malickdiop3949
      @malickdiop3949 4 года назад +1

      @@abdouly6773 serigne Touba ligues des champions la El Malick sy 2e division la nék niveau yi bokkoul ya pas débat

    • @ndiayesokhnaseck2451
      @ndiayesokhnaseck2451 4 года назад +2

      @@abdouly6773 s touba kou mi diranci dou am diam mime rew s touba mouy kika moule💪

  • @talladiop2013
    @talladiop2013 4 года назад +55

    Naniou oubbi djiouma yi jamou yalla moy wakhdji wasalam dieurediéfé s touba

  • @mbayemodou2412
    @mbayemodou2412 4 года назад +105

    Touba Dioulli réck

    • @JUA-AFRICAINE
      @JUA-AFRICAINE 4 года назад +2

      Ça me fait rire

    • @alibango9368
      @alibango9368 4 года назад +8

      La seule ville bou am ay nite youni niom douniou diouli douniou wor..foutez nous la paix jumah mom apar vendredi dotoul fesse rawatina fadiar

    • @khadimdylla4477
      @khadimdylla4477 4 года назад +1

      @@alibango9368 fekhalal sa khol

    • @alibango9368
      @alibango9368 4 года назад +1

      @@khadimdylla4477 wakhi doff bo amoul argument nopil mo gueune

    • @habiboufall1089
      @habiboufall1089 4 года назад

      @@alibango9368 Wakho fi dra wakhou ignorante Rék Nga fi wakh diouli dji adiouma moy frata

  • @mistercarter467
    @mistercarter467 4 года назад +60

    Bouba ndour pour une fois ma d’accord ak yaw .... niome nieupp dagni garouwaleii touba.. al mountakha ❤️😍 mbir mii tolou waye leuh si sougne borom

    • @wakhdeuggrek8040
      @wakhdeuggrek8040 4 года назад +2

      Begeu nala sa waaye

    • @ndeyebarakatoufall7314
      @ndeyebarakatoufall7314 4 года назад +4

      Khana yène lou waye wakh nguène guissi sen bope sa bolèndi wakh kèn doulèn falè

    • @aminasophieball8453
      @aminasophieball8453 4 года назад

      Lidieunti len s'en corona bobu mo gueun

    • @sarrfallou8315
      @sarrfallou8315 4 года назад

      @@aminasophieball8453 Yow Dooo Nitt Epuis Wakhofi Wakhi Djioulit Djioulit Dou Yeene Moromame Mousiiiba demal nga guestou sa diiine

    • @dd4582
      @dd4582 4 года назад

      Suis pas d'accord ak Bouba oustaz n avait pas fini son explication. En plus il se contredit néna gnoune nieup si yoninte bi lagnouy roy té yoninte bi néna sou mbass amé na gnieup took sen keur.

  • @elhadjisk271
    @elhadjisk271 4 года назад +50

    Bouba très bien ❤️👍

  • @zallnitoudeugue5764
    @zallnitoudeugue5764 4 года назад +32

    Touba yalla may nalene ay matouway ba mana organise pour diamou yalla serigne touba darame dou ay thiakhane

  • @abdoudiop5163
    @abdoudiop5163 4 года назад +52

    dieuredieufety seurigne mountakha mbacke bachir yague fi lol te andak weur

  • @nargackou7140
    @nargackou7140 4 года назад +3

    yén wax yi amoul solo waw
    dieureudieuf serigne touba

  • @moustphafall353
    @moustphafall353 4 года назад +14

    Dieure dieuf serigne moutakha mbacke yalla na fi yague té wër

  • @khadyseck8353
    @khadyseck8353 4 года назад +1

    Dieureudieuf Mame Ousmane yonnentibi li rk la beugguone moy sounna sou rakhoul dara😍😍

  • @alydiop4394
    @alydiop4394 4 года назад +59

    Bouba Ndour.kou nité la ndéysaan

  • @meissagueye9645
    @meissagueye9645 4 года назад +1

    Senegal migui nih kou deugou niou khas lah merci bouba dieureudieuf s touba

  • @modoukarabeye870
    @modoukarabeye870 4 года назад +32

    Dieuredieufety Serigne Touba

  • @abdulo8266
    @abdulo8266 4 года назад +1

    S mountakh yalla nafi yague tewér
    Wakhlén amine

  • @papesall6930
    @papesall6930 4 года назад +46

    Très bien Bouba

  • @salioufall7261
    @salioufall7261 4 года назад +59

    Thiéy serigne Touba ak waa Sénégal kagne lagniy kham serigne Touba donté wakhouma batin bi nak

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup7403 4 года назад +53

    Machalah li guen wara Kham moye diouma kenue waro ko tuedj ndakh té diouma dou am ngant nit ki moye am ngant dieureudieuff s mountakha mbacke

    • @doubadouba1488
      @doubadouba1488 4 года назад +1

      Diouma moy am ngante nak nite ki modoul am ngante diouli dou wathie kenne fi ak Mingui ak khelam

    • @alibango9368
      @alibango9368 4 года назад +1

      @@doubadouba1488 yaw gni amou niou kham kham diarou niou tontou

    • @moussakebe3242
      @moussakebe3242 4 года назад +1

      Loutax diouma macka yi niou teudj d mm la mosquée de medine . Wax sa khalate boum la taxa wax lo maîtriser woul

    • @bambagueye4167
      @bambagueye4167 4 года назад +1

      @@doubadouba1488 yaw linga wakh dou kham kham dh nite moy ame ngante ba manoul déme djiouma wayé diouma mome dou ame ngante déme léne diangi kham kham mo gene

    • @bambagueye4167
      @bambagueye4167 4 года назад

      @@moussakebe3242 bourou macka bi téki woul dara

  • @moussasall1393
    @moussasall1393 4 года назад +2

    Thé boy wax dêko teksi Xam bou oustaz mourid nieuwon nek sa place dina wax lou werr, lou xamxamé thei doussi toudou Serigne Touba, maodo wala bay Niasse
    Mangui toup bou wëër nakk 🙏🤐🙏🙏

  • @rokhayambodj615
    @rokhayambodj615 4 года назад +23

    Quant à Bouba ma sha allah 🙏je trouve qu'il à toujours été pertinent ! Bravo 🥰

  • @mamekhadydiaga1150
    @mamekhadydiaga1150 4 года назад +9

    Olofff néna gnij nga bookal nionla gueneu baagne Bamba protège❤️🙏🏻

  • @medzoseck6035
    @medzoseck6035 4 года назад +86

    BOUBA NDOUR WALAHI TÈY MOME LOU LÈR NGA WAKH....

  • @khadimcisse7687
    @khadimcisse7687 4 года назад +1

    Obrigado bouba ndour

  • @papemusasall3301
    @papemusasall3301 4 года назад +8

    Bilahi wallahi dangena xamoul s.mountakha

  • @mourtadabadiane1663
    @mourtadabadiane1663 4 года назад +1

    mersi bouba

  • @supplements_nutritionnelle3108
    @supplements_nutritionnelle3108 4 года назад +5

    Bouba ndour tay mom vraiment machallah amna sollo trop

  • @cheikhniane5301
    @cheikhniane5301 4 года назад +2

    Apartir de taye Bouba beugueunanla nguir serigne touba

  • @djilygueye5264
    @djilygueye5264 4 года назад +5

    Touba sa kaname diarama wakeur serigne touba yi amoudiou morome

  • @diazartpro4341
    @diazartpro4341 4 года назад +2

    Merci bouba ndour ✌🏼🙏🏽

  • @sofimarietoucisse4412
    @sofimarietoucisse4412 4 года назад +9

    Dieureudieuf Cheîkhoul Khadim Mbacké ❤❤❤

  • @daoudadiop6919
    @daoudadiop6919 4 года назад

    Dieureudieuf serigne mountakha mbacké ❤☝🏽

  • @mamecheikhtine7751
    @mamecheikhtine7751 4 года назад +5

    Chapeau a toi Bouba pour ton intervention. Tu as bien réagi par rapport a ce que dit Limane. Il a parlé jusqu'à prendre une position donc Bouba tu as raison. Imane bi dafa diok gni deuk diokh gni tord. Dafa warone tedei ndiakhanay

  • @nitafofana7788
    @nitafofana7788 4 года назад +2

    C'est la première fois que tu dis la vérité Booba

  • @lesauveur.1651
    @lesauveur.1651 4 года назад +12

    DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIARAW LAKH MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE

  • @cheikh-biindiaye3237
    @cheikh-biindiaye3237 4 года назад +43

    Bouba a été toujours pertinent et cohérent sur ses propos

  • @serignefallousarr4571
    @serignefallousarr4571 4 года назад +25

    machallah bouba ndour begna ci yaw taye

  • @modoufall8127
    @modoufall8127 4 года назад

    Machahalla bouba Ndour amna solo loool barkep s touba yalna yalla féyla

  • @ndiayemana3489
    @ndiayemana3489 4 года назад +25

    Merci bouba linga wakh leer na

  • @milkgunofficiel
    @milkgunofficiel 4 года назад

    Sénégal si foo rek laniouye an bou D si burou yalla kouneck dikha touba Mame bamba daka liguéy borom touba amoul morom All mountakha douckouye wakhantou🙏🙏🙏🙏🙏

  • @olimatadiattara8449
    @olimatadiattara8449 4 года назад +9

    Bouba ndour i love you 😘😘😘

  • @laminmaster9387
    @laminmaster9387 4 года назад

    Machallah Bouba Ndour Serigne Touba amoul morom wallahi boudoul won mom dîné soukh Sénégal

  • @fatouaw3818
    @fatouaw3818 4 года назад +50

    Dafa lér bouba

  • @diopdiop8331
    @diopdiop8331 4 года назад +1

    Bouba tay mom 👍

  • @kikkasolare8386
    @kikkasolare8386 4 года назад +8

    Machallah Ndoura Yasine sa wakh rafétna. Nioune nieup béne laniou naniou ande diamou yalla té yalla rék takh serigne si séne walla dém neu liguéyeule naniou yalla ba paré séne lép mate na. Nioune rék nio si déss na lép raféte aduna amoule solo.

  • @mouhamedlamimegueye2663
    @mouhamedlamimegueye2663 4 года назад +17

    Merci beaucoup bouba wakh dji rafétna

    • @ibralame7661
      @ibralame7661 4 года назад

      Man dall bék siyaw Bouba tay mom nékh gamadh 🤣🤣

  • @modousow8832
    @modousow8832 4 года назад +22

    So, teye Bouba star la? Ndeyesane, les gens gnofi nekone diko khass tt le temps!! Bouba a tjrs etait pertinent. Senegalais mo meti rek :)

    • @aminasophieball8453
      @aminasophieball8453 4 года назад

      Parce que aider na votre corona de ville mddr

    • @modousow8832
      @modousow8832 4 года назад

      Amina Sophie Ball Corona de ville de merde veut dire?

    • @aminasophieball8453
      @aminasophieball8453 4 года назад

      @@modousow8832 Touba

    • @modousow8832
      @modousow8832 4 года назад

      Amina Sophie Ball SoubhnaAllah. Dete way ma soeur ya tamit

    • @ak-hh3tt
      @ak-hh3tt 4 года назад

      Mane lolou la guiss il et toujour pertinent

  • @mbayeyatt9310
    @mbayeyatt9310 4 года назад

    Merci bouba contane na ci yaw barké mouhamed yalla naga goudou fane té ande ak wére

  • @cheikhndiaye5539
    @cheikhndiaye5539 4 года назад +3

    Merci Bouba je suis très content et j'espère tout le monde est content de vous il ne faut pas qu'on laisse des soit disant imam de dire n'importe quoi et s'est vraiment déplorable naniou bayi far té wakh té yalla rék takh merci encore Bouba et birama de même que pape Djibril fall bonne continuation merci

  • @diopletaifoisdiopletaifois6639
    @diopletaifoisdiopletaifois6639 4 года назад +1

    No Bouba tayy mom FORRRGUA KOOO ...
    DALL GUASSI CARRÉMENT...
    Dji tall REW MI LAGNU BEUGUEU MAIS XAMNAGNU NÉ SERIGNE TOUBA AMOUL MOROMM❣❣👍👍

  • @baboudiagne7728
    @baboudiagne7728 4 года назад +27

    CHEIKH AHMADOU BAMBA PROTÉGÉ ✌

    • @johsonjohson3264
      @johsonjohson3264 4 года назад +1

      Allah protège

    • @fallcheikhou3406
      @fallcheikhou3406 4 года назад +2

      @@johsonjohson3264 sa kawar gui nimou gatté nonou la sa khél mi gatté

    • @ndiayesokhnaseck2451
      @ndiayesokhnaseck2451 4 года назад

      @@johsonjohson3264 wouy yéne lou takhe guéne soukhar mime rew s touba mouy kika moume yaw mi sakhe moula moume moume sa baye moume sa ndaye mou lay nekhe ak mou lay nakaré ak sengr bigau yakar

    • @johsonjohson3264
      @johsonjohson3264 4 года назад

      @@ndiayesokhnaseck2451 la seule réponse des mouride en débat religieux ce sont des insultes
      Tu n'a aucun respect à tes parents mon gars
      7 ans d'exil et il n'a pas convertit une dizaine de personnes et vous dites qu'il est le sauveur
      Il n'y a de dieu ke Dieu et Mohamed est son messager c fini

    • @modousall2693
      @modousall2693 4 года назад

      @@johsonjohson3264 yaroul way togne bakhoul dh bayilen Di wakh Di generalise

  • @famalo7804
    @famalo7804 4 года назад

    Bouba li gae wakh leep deugue la serigne mountakha mbacke balla yague fi lol te weer ♥️♥️👌

  • @diengabduokhadre5846
    @diengabduokhadre5846 4 года назад +13

    Machalla bouba

  • @mortallaseyedallou6976
    @mortallaseyedallou6976 4 года назад

    Machaallah bouba wakh bi Rafetna yalla nala s.mountakh defar sa ay mbir

  • @leyedieuestgrand9991
    @leyedieuestgrand9991 4 года назад +19

    Bouba tu as gagné un point dans mo coeurs

  • @ndiagadiakhate6058
    @ndiagadiakhate6058 4 года назад +20

    Merci Bouba guém wolou yakar ragal segne Touba lagne ko déf

    • @ndioufandoye64
      @ndioufandoye64 4 года назад

      Yalla la rek mom lanou wara ragal mofi né tay ak soube seringe bi fane la né ak folene coy fekque eleck diamou len yalla bayi bokalé bi

    • @boygainde3764
      @boygainde3764 4 года назад +3

      @@ndioufandoye64 nio bakalé sa yone nekoussi dougal li ssa yone nek
      Geum ak wolou ak ragal ak yakar kou teddi ki rekk laniouy koy defal bamba point le reste au coin

    • @cherifcherif7033
      @cherifcherif7033 4 года назад

      Wakhi doff Serigne bi khamoula sakh déna depuis 1927

    • @boygainde3764
      @boygainde3764 4 года назад +2

      @@cherifcherif7033 tidian yi doff nene niak nen teguin ak kham amouniou gatte rakh ssi sokhor 😂😂

    • @ndiayesokhnaseck2451
      @ndiayesokhnaseck2451 4 года назад

      @@ndioufandoye64 yaw sa xoul migui djikhe dh s touba diara dief💪

  • @salimatasow1271
    @salimatasow1271 4 года назад +1

    Mame Maodo c'est la référence au vrai sens du terme !!! la preuve Tivaoune Corona défoufa une semaine fofou Deukou lér la !!! Aÿ way thiow lii barina kou munn na déff !!!

  • @gnimasarr8232
    @gnimasarr8232 4 года назад +3

    franchement limay guiss ni si tarikh yi titale nam lolou et li imam wakh lousi nek ba kou nek oubékou di ratatati rk bouba fi boub fé... gni oubi séne diouma amna fougne ko ték et gniko tedje aussi amna fougne ko tékkk fou lére aussi nekoul kou deudje sa diaka rk djiouli té wo tmt kou xam tidiane xam ko si dioulitè machallah
    tarikha yeup béne yone bi lagnouy woté mbadou léne ishhhh

    • @ndateyalla2784
      @ndateyalla2784 4 года назад

      Wallah ça fait peur et ce ne sont que les mourides qui font tout ce bruit kou wakh deee
      Serigne Touba santouleen liii

    • @pendambaye1161
      @pendambaye1161 4 года назад

      @@ndateyalla2784 yw louniou dff rkk fii nieup yam khadialéwuniou ken diakhalguenma lou nieuw rkk gueni mouride yii thimmmm sof guene trop ish

    • @pendambaye1161
      @pendambaye1161 4 года назад

      @@ndateyalla2784 et aussi gno tayy

    • @pendambaye1161
      @pendambaye1161 4 года назад

      @@ndateyalla2784 point barre

    • @ndateyalla2784
      @ndateyalla2784 4 года назад

      @@pendambaye1161 athiaa reek Serigne Touba leegui mouwoonleenii santouleen liii
      Ligueey Ak diaamou yalla laawakh toop digley Mohamed PSL
      Pareenathi tontoula ndakh awma been diott.Ziaar

  • @mominagaye5261
    @mominagaye5261 4 года назад +2

    Pour la première fois ma commenter ci mai mais merci boubou

  • @tallibeserignesallouelectr7681
    @tallibeserignesallouelectr7681 4 года назад +33

    Serigne Touba fou diamono tôle rek daye feuseule boopam gnou fate likou bureau ba sa Ndare

    • @amygueye3882
      @amygueye3882 4 года назад +1

      Merci boeucoup

    • @manianggning977
      @manianggning977 4 года назад

      @@Rhitnewtv9835 yagui mére dé

    • @bambatoubareck
      @bambatoubareck 4 года назад +3

      MACHALLAH DIUERUEDIUF SERIGNE TOUBA

    • @morabsakandji9918
      @morabsakandji9918 4 года назад +4

      Yenne niep vous n'êtes ni mouride ni tidiane ni khadre ayy seytane rek guenne.diemlenna nitte ta bayyi waxx Lou niaw.serigne niep ay nittou yalla laniou diemal daimou yalla.

  • @bayematarfall303
    @bayematarfall303 4 года назад

    Merci Bouba taye nekh nga Serigne Touba amoul morom

  • @Xasidayirek
    @Xasidayirek 4 года назад +3

    Al mountakha 🥰🥰❤❤

  • @pamatarcisse4612
    @pamatarcisse4612 4 года назад +1

    Diouma Touba Dou Mosa teuthie Ndakh Serigne Touba Da Nianone Yallah Diouma Touba Diouly Dofa Mosa Dioke

  • @khadimkane7195
    @khadimkane7195 4 года назад +9

    Merci bouba ❤

  • @fatoudiop3180
    @fatoudiop3180 4 года назад

    Bilahi moy serign touba yallana yalla yoke fanam si barke borom touba

  • @narka4603
    @narka4603 4 года назад +12

    Merci bouba

  • @azizdiop2391
    @azizdiop2391 4 года назад

    Bouba sébon🤸🏼‍♀️🤸wawe kaye Bouba sébon

  • @ballabeye9595
    @ballabeye9595 4 года назад +23

    Merci merci merci beaucoup bouba

  • @abdoulahatgueye6492
    @abdoulahatgueye6492 4 года назад +1

    Merci Merci Bouba 👍 machalla liga wakh Amna Solo

  • @cheikhounambaye2062
    @cheikhounambaye2062 4 года назад +8

    Bboba yalla nala yalla defal diam barke borom Touba

  • @goraloum2345
    @goraloum2345 4 года назад

    machallah bouba touba lifi serigne mountakha wakh mony lifay am ndakh touba tituerfos la dipi moia du septamber 1928 montakh macky lou nekhoul serigne mountakha dou cokofa deff

  • @papecheikhyade3847
    @papecheikhyade3847 4 года назад +6

    Merci bouba ces soit disant ouztaz fanatique,kudje ak diel seen beut teey ko ci touba,waye ba ila yawmil abat kenn meun ta tere niou wakhtane serignebi ak diko kennal

  • @diabbambayegningue6417
    @diabbambayegningue6417 4 года назад

    Merci bouba tey mom suisse dakkor avec toi

  • @oumarsene4604
    @oumarsene4604 4 года назад +5

    Saway yaaw borom yéré bou jaune bii Touba louniy soukanekou daangaa toutt djii xamko Touba dou Diouma bounouy teuddjj Kou téd ngui moko faagoul boopam té noonou laay démé saasouné inchaa alakh

    • @sarakabacamara6266
      @sarakabacamara6266 4 года назад

      moi je pense que un jour les talibes des differents engendront un grand probleme un jour au senegal

    • @sarakabacamara6266
      @sarakabacamara6266 4 года назад

      des differents tarikha

  • @madickendiaye3560
    @madickendiaye3560 4 года назад

    Bien parler Bouba tu es un grand homme : Ousmane ndiaye a bien dit que ceux qui ont ouvert les mosquées exposent les fidèles ce qui n'est pas vrai et un manque de respect considérable envers ces derniers.
    Vous ne voulez pas ouvrir vos mosquées vous êtes libres mais respecter ceux qui veulent ouvrir car ils reposent sur leur foi en Dieu avec des textes orthodoxes.

  • @bathieleye3860
    @bathieleye3860 4 года назад +6

    Bilakhi bouba taymom loulér Ngawakh merci bouba

  • @layelaye6583
    @layelaye6583 4 года назад

    merci bcp bouba ki kouko degue khamni nono moirite la waye mourite kouko banie khôl bou dague rekkk

  • @rosettaroset8814
    @rosettaroset8814 4 года назад +24

    Heureusement qu’il y’a des gens qui c’est lire entre les lignes merci boubou

  • @sokhnamaymbacke1852
    @sokhnamaymbacke1852 4 года назад +1

    S.touba❤ kéneu leh dh kouko bagn déel

  • @moussambengue8768
    @moussambengue8768 4 года назад +61

    Bouba ndour lou léer gua wakh ki dafa sokhar Serigne touba rek mou len de déranger nagou lén li yalla dougal dakh guen nopalou

    • @rafadiop5989
      @rafadiop5989 4 года назад +2

      Yaw liga wakh dara amou si dilin wakh wadio rafit

    • @modoubane118
      @modoubane118 4 года назад +5

      Ab tidiane Lou mouye banie si Ab mouride ragalale yalla

    • @morabsakandji9918
      @morabsakandji9918 4 года назад +2

      Si tu est mouride et talibe éviter c genre de parole.serigne avait mis en garde c genre de personne.

    • @senemodou6476
      @senemodou6476 4 года назад +1

      bouba merci

    • @seynidiadieuflernadetague5200
      @seynidiadieuflernadetague5200 4 года назад +7

      Mouride dou bagne tidiane tidiane dou bagne mouride mes wathie dafa meusa contre mouride yii wakhe douniou ko ragall wa salame

  • @amadoudiop548
    @amadoudiop548 4 года назад +2

    Serigne touba rek mon fi naik wa salam

  • @sfanConfection221
    @sfanConfection221 4 года назад +28

    Franchement bouba deugue rek lay wax

  • @mamadoudieye3085
    @mamadoudieye3085 4 года назад +1

    Bouba évolue depuis coronavirus welcom

  • @barafall5330
    @barafall5330 4 года назад +1

    Dieure dieuff seringe touba cheikh Ahmadou Bamba

  • @Idyxaragnelo
    @Idyxaragnelo 4 года назад

    Cheikh Mountakha Mbacké Bassirou Yalla guafi yaaaag looooool té wére Ya Raby

  • @mouhamedfall5174
    @mouhamedfall5174 4 года назад +10

    Bouba aujourd'hui tu es un model.....al muntaqa yague fi

  • @mbayeyatt9310
    @mbayeyatt9310 4 года назад

    Merci doctor Abdoul kane pour ton analyse pertinent

  • @daoudafall9451
    @daoudafall9451 4 года назад +17

    Gnoun danou weuroul ay concurrent bayi lenn nou boulenn nou yeungeul fii lifi nekk gnoko fii deff srg Touba kenn d'où mome

    • @islamakmandou2835
      @islamakmandou2835 4 года назад

      Borom Touba amoul morom
      Kou keu geum nopalou
      Dieureudieuf Mame Bamba ak Cheikh Ibrahima Fall
      Wa salam

  • @papeallediop7996
    @papeallediop7996 4 года назад

    Bouba ndour, un monstre pour la cohésion nationale.

  • @mourdiouf6285
    @mourdiouf6285 4 года назад +31

    Bouba borom boulma dageu..damay wakh...mdr

  • @passecrystal879
    @passecrystal879 4 года назад

    Machallah Bouba linga wah lolou rafet na trop

  • @lampseye9769
    @lampseye9769 4 года назад +1

    Bouba Merci bcp thanks