MADA BA parle de sa relation avec sa soeur Sokhna Khady et attaque Gagne Siri GUEYE de la Sen TV

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 13 окт 2014

Комментарии • 311

  • @djimegaye4670
    @djimegaye4670 2 года назад +24

    Bravo Mada,
    Ton honnêteté est appréciable. Je te comprends car je vis une situation similaire

  • @dethiediagne3387
    @dethiediagne3387 Год назад +24

    Mada ba une femme plein de dignité ❤❤❤

  • @ibrahimadieng5783
    @ibrahimadieng5783 6 лет назад +20

    Mada courage j'aime ta personnalité. Les mauvais commentaire ne prête pas attention...
    Si on a de mauvaise relation avec quelqu'un d'autre même si la mort survient il faut garder ta position si on est pas hypocrite

  • @sophiamarques7797
    @sophiamarques7797 9 лет назад +48

    Mada Ba je l'ai toujours aimé, elle est très posée et très véridique.
    Courage Mada

  • @cheikhmbackediop7678
    @cheikhmbackediop7678 6 лет назад +29

    Sokhna Khadi dh dafa bakh yalla nako yalla Faye barkeb Serigne Saliou mada yaw comma bétga

  • @ngba01
    @ngba01 9 лет назад +38

    Deugue kénn doukou neubeu. On vois la vérité sur son visage. Je l'estime bcp et elle est ma copie de femme que je veux ressembler. Une femme calme et toute posé, très précise dans sa langage. Longue vie à toi

    • @berebuxamxam1383
      @berebuxamxam1383 6 лет назад +1

      Nar Sofia Amiine waay moi je cherche son numéro désespérément . C'est une femme de valeur

    • @djibm9m998
      @djibm9m998 5 лет назад

      mada bete nama

    • @ndeyamie6808
      @ndeyamie6808 5 лет назад

      @@djibm9m998 gns ne kansfjs'd
      Je

  • @senegalaise2251
    @senegalaise2251 6 лет назад +8

    Bayilèn di wah wahi soutoura loolo yah senegal. Ki dagnko fenal dafko wara léral. Bravo Mada. Senegalé hamou deugue.

  • @babacardiouf1071
    @babacardiouf1071 9 лет назад +7

    salam wa sénégal magui djégalou mais nanou tapé xol yi té rafetal sounou ande ak dolénté soutoura téy diégalé. Sokhna mada yalla nala yalla défal name délossi wate sa rakabi thi kadou yiguéne wouté baguéne andate done béne nax bokou ba paré dioubo dafa néx té lolou la l'islam diguelé. Sokhna khady na yalla djégual ko ak moléme dioulite boumoufa féke té ték lokhome thi ndiabote gui moufi bayi encore une foi nanouy mougnalanté tay djégalé merci.

  • @FatoubintouMbodji-tw8mb
    @FatoubintouMbodji-tw8mb 10 дней назад +13

    Ce ki ont là après confession expliquer leen ma nou histoire bi démé

    • @abybodian1448
      @abybodian1448 10 дней назад +2

      Ma gui nii😂😂😂😂

    • @antagueye2645
      @antagueye2645 8 дней назад

      Gnogui ni topeuse de cas ​@@abybodian1448

    • @KY-ed5qp
      @KY-ed5qp 7 дней назад +1

      On est là on comprend pas 😅

    • @lalafaye2072
      @lalafaye2072 4 дня назад +2

      Li histoire bou yagu leu.Madaba ak sa famille niou deuk té deukine bi nékhoul wone comme pratikmnt bcp de famille nga am ay rakk dégalougn leu kou nék dieul sa yonou bopp di déff louléne nékh.kéne wagnékouci ndakh nimé guénéwone ci keur gui nékhouko wone .Gagnsiry une membre de la famille et animatrice de la radio joubou woul wone ak Madaba am loumko dinthial di utilisé temps d'antenne nam diko di déff ay thème diko garawoula à chak fois k l'accaz se présente.sheuttt l'histoire longue meunouma bind lépp té youtube amoul vocal😂😂😂

    • @abybodian1448
      @abybodian1448 4 дня назад +2

      @@lalafaye2072 merci à toi

  • @mayoutoure8166
    @mayoutoure8166 9 лет назад +33

    wallahi Mada degue gua wakh kéne dou yow Awa Ba dé féne rek lay def meunoul séte meunoul dara meuna loula dara digua bok ak nite bou sokhoré laa Mada Ba doneul way 111ans koula bagne YALLAH na dé wayyyyyyyyyyyyyyyyyyy

  • @Laspheredesdistinguees
    @Laspheredesdistinguees 6 лет назад +24

    Tu as raison, mais nakkk li d'où wakhou télé Mada.
    rawatineu kinguay wakhal nekouffi.
    dieugelou

  • @Thiar-nt2oc
    @Thiar-nt2oc 11 дней назад +4

    Ma voisine de liberte5 etant gamin❤❤❤

  • @FatouNdiaye-fq1ro
    @FatouNdiaye-fq1ro 2 дня назад

    Mas'sa Mada j'ai vécu a peu prés la même chose je te comprends tellement !.

  • @khadijatraore3090
    @khadijatraore3090 4 года назад +8

    Massa, Madda famille leigui mom do comprendre... gnigua bokal niolay yakk tek la Lou metti, lolou kouko doundoul dou meuneu comprendre ligua neik di doundou instant yi... wayei bo neikei nittou deugg ak nittou principe keine doula beugg...
    Courage et concentre toi sur ton foyer... Nga fekhei deiff ba say dom douniou am différence seine birr... li brisé famille mom lissi eupp si wadiour yi lay diouguei...

    • @ngonethiam2580
      @ngonethiam2580 4 года назад

      Hi my dear how are you I greet you have a nice day give me chance I can chat with you I'm living the knock on you

  • @mamadoudiallo6684
    @mamadoudiallo6684 3 года назад +2

    Allah akbar machallah mada ba Sénégal yeppou molaa wahal loubah machallah

  • @mamadoudiallo6684
    @mamadoudiallo6684 3 года назад +1

    Machallah mada ba courage diegene boumeni yow yo boul machallah

  • @marieamar134
    @marieamar134 7 лет назад +14

    courage mada Ba walahi nitou deug nga tu as des principes tu es sincère si kaw si kanam te yalla mousal leu si journalistes yi daniou seytane sokhna khady yalnako yalla yeureum mayko Aldiana Firdawsi si barke Seydina Mouhamed psl. Gagnesiri ken dou tass mbokk alalou yalla leu.

  • @thiatesow492
    @thiatesow492 5 лет назад +6

    Vraiment tu es sincère maman Daba je t'adore bcp

  • @larosedivine5266
    @larosedivine5266 9 лет назад +37

    Sénégal déh bo amé fouleu ak fayda, bo mandoo té réservé gniou taxé la.bone ak fouyi. Mada ba que Dieu te protège. J'aime ta personnalité car c'est proche de la mienne. Et les saytanés de commentaires pourris là quittez là bas.

  • @sopendir4275
    @sopendir4275 6 лет назад +3

    Très bien dit

  • @muhammedsamba8755
    @muhammedsamba8755 6 лет назад +6

    Masalah MADA BA yalnala yalla defal djam aduna ak djam allahira si barkeh rasulillah yalla mun nako am nako yalna ko yalla deff
    DEG REK MO MORR

  • @malickfall6563
    @malickfall6563 9 лет назад +33

    Sokhna Khadi est une pieuse et elle a un sentiment très profond envers les versés coraniques en particulier et en générale le coran. Qu'ALLAH le tout puissant l'accueille dans son Paradis et lui pardonne ses péchés. Amine.
    Mada BA qu'ALLAH te bénisse . Tu es vraiment une femme battante et toujours respectueuse et digne malgré le monde musical très sensible et complexe.
    Thioro tu as un paradigme vestimentaire unicité, copie un peu le " TOP 10 " actuel qui te permettra avoir une personnalité accru sur la Chaine TV. Que DIEU nous bénisse.Amine

  • @boyefall1411
    @boyefall1411 6 лет назад +10

    Bilay mada ba borome khol bou raféte ga

  • @user-ot6kj9nw4d
    @user-ot6kj9nw4d 7 дней назад

    Mada ba,en référece pour cette génération de musiciennes,elle est belle mais ne nous a jamais offert un scandale...respecr❤

  • @alphabazz1
    @alphabazz1 9 лет назад +54

    J'ai beaucoup apprécié sa façon de parler
    Et je ne vois pas de mal à ce qu'elle a dit.
    En la voyant parler, on sent que elle est véridique à ses propos.

  • @diarratoure-qg9pj
    @diarratoure-qg9pj Год назад +6

    Iow khamone ngani akou sokhna khady mou bakh ma dina la dal li ngay yéss leppou faye kéne khamatoul ni sakh yagui doundou li ngay bone lepp sa rak khana loy défane té basa rak fatou nga wara arété lou doul di weur di yakh déram wayé loko mane di wax mom rawe nala la serigne touba mame cheikh ibra térouna ko thia aldiana yeu gueneu kawei nakh nék nafi ba diougué fi massoul guénei wakh diou niaw si guéminieum lou doul sakho di toudou trou yalla bi souniou yaye fall bou bakho e ba lolo douniou diouk thi dila nianal😭🙏

  • @aminasylla276
    @aminasylla276 9 лет назад +3

    vrement mada ba jsuis de tt coeu avec toi du courage encore une fois yalla nala yalla leralale lepp ci barki SEYDINA MOUHAMED (PSL) adouna bii so nopiweii rekk gnou beugue takhaw sa boppou...Awa Ba jtei go 1 fois ci mom et chaque fois mom soeurou mada ba lay bakko..mais tkt lii yeupp ayy netalii laye moudjou du courage je t'adoreee

    • @awaba5104
      @awaba5104 8 лет назад +1

      c'est ça le Sénégal seytane hypocrisie nafek rek lagnouye courage disent musulman mais gomoudnou dara bon courage domou baye

    • @gueyesophie6034
      @gueyesophie6034 6 лет назад +1

      Doy n'a waar mais Mada mounone na dem djalle mogueuno rafet
      nakhte c est sa sœur ka même

  • @aidandao8836
    @aidandao8836 8 лет назад +11

    elle a trop dit vraiment

  • @bintousarr261
    @bintousarr261 7 лет назад +17

    je t'aime Ma Daba bcoup même.

  • @bachiirleveridique9767
    @bachiirleveridique9767 8 лет назад +16

    EN TOU K DEUGG REK LAFI WAKH LIMAY NAKHARLU MOY WAX GUIMOU WAKH TELE MANOONNA RESTER COMM AVANT.
    MAIS SERINE BI MAYE RAKKU DIAMBOUR AK DOMU DIAMBUR AU MOINS MOU YEUGUEULKO AY MBOKKAM LOLOU MOY DUEGG
    GNOUN AY TAALIBE LAGNU MADA BA MII TAALIBELA DAANA DALL SUNU KEUR MAGAL XAMNAA CI DARA
    SERIGNE TOUBA NAK LIMOU NIOU DIGUEUL MOY TOPPU NDIGEUL SURTOU NDIGUEULOU WAADIOUR

    • @madrame4142
      @madrame4142 8 лет назад +2

      salam pour moi j'étais pas la peine vraiment le linge sale se lave en famille.on ne ta jamais entendu sur ses genres trucs en plus ta sœur n'est plus sur ce monde te média defa grave

    • @madrame4142
      @madrame4142 8 лет назад +1

      salam pour moi j'étais pas la peine vraiment le linge sale se lave en famille.on ne ta jamais entendu sur ses genres trucs en plus ta sœur n'est plus sur ce monde te média defa grave

  • @lenaamar9284
    @lenaamar9284 6 лет назад +3

    Yalnako yalla yeureum sokhna Khady aduna amoul solo yalna yalla joubole gnep rawatina bokk ben deret
    Deret dafa fort Man d souma narone nonok sama deret rouss thi sama yay bignou djour

  • @annabenjamindiouf369
    @annabenjamindiouf369 5 лет назад +2

    Mada Bâ ya deuggou fan naleuh sah bilahi longue vie á toi jtm

  • @OumouAidara-zi8yg
    @OumouAidara-zi8yg 9 дней назад +1

    Mada❤❤❤❤❤❤❤❤ sa yaye sokhna Oumoul Fadly Aidara louga

  • @khadygueye2985
    @khadygueye2985 12 дней назад +1

    Machllaha mada❤❤

  • @diallomassata7722
    @diallomassata7722 7 дней назад

    Bravo mada pure verite nite day gore ame loumouye bagne,deugou

  • @beautedafrique709
    @beautedafrique709 6 лет назад +14

    Svp garder vos vies privée...et vs les journalistes ayez un peu de retenue ...

  • @seydinaniang233
    @seydinaniang233 4 года назад +10

    da nga digne motakh nga nekh ma

  • @mamecheikhk
    @mamecheikhk 9 лет назад +48

    Ma sœur, ma ngui laye djégalou téy niane, ndakh kheyna sakh ya ma gueune, wayè souma sanione wakh you mélni nga khamni daye khawi soutoura, ndakh téy takhna niou kham louniou waroul wona kham thi sa sœur, ndakh nioune tourou LAHOU bimou dane maggal rék mo niou sokhalone wayé taye khaw nga yakh image bou sokhna khady. LAHOU mo beug soutoura, mo takh mou wathié goudi ak beuthiak, té digualniou djéguelé ak djélalé mouy faté louy takhal dérou nite sirtou sa khète bou wathi liguèy. Nio ngui nianal Sokhna Khady yalla nako tourou LAHOU bimou dane toude Rammou té rafète naniou thi ndiorte. Maha salam

  • @bureautiqueexpert6223
    @bureautiqueexpert6223 6 лет назад +8

    Je t'aime bien mada ba ...lingafi yeupa leer je suis avec toi

  • @omarcissebichriomarcissebi5679
    @omarcissebichriomarcissebi5679 4 года назад

    Machalla

  • @seynaboumamyndiayediallo7526
    @seynaboumamyndiayediallo7526 9 лет назад +4

    J'apprécie la franchise de mada ba gagne n'a ka régler ses problèmes de famille

  • @fatmaba3266
    @fatmaba3266 6 лет назад +30

    Mada ba problème de famille kéne douko wakh si télé ndakh journalistes yi séne intérêt rék la gnouy khol

  • @daviddiop86
    @daviddiop86 2 года назад +2

    Yaw sokhna Khady mola guene fouff billahi yalnako yalla yueram té kharéko Aldiana firdawsi

  • @houmahaniaw1335
    @houmahaniaw1335 6 лет назад +6

    Merci beaucoup Mada Bà koubah dobari kharit Mane Nila Méle Si sounie famille Nakh Mouna Wakh dégue Rak

  • @iibrahimadiop4292
    @iibrahimadiop4292 7 лет назад +18

    kou dégueu say paroles khamni amoo thiakhane. wakhou deugue nékhna kham. yalla bakhna

    • @mamiissasoumare55
      @mamiissasoumare55 5 лет назад +2

      Iibrahima Diop mada ba nio deukone dpui liberté 4 momeu yar mai kéne meussouko dég silou niak fayda nite kou mandou réglé diap niamboureum machalla mbakh rék lako khamé séne keur mome késsé mofa réglé

  • @tamraanidag2293
    @tamraanidag2293 6 лет назад +2

    Merci madame ba

  • @madeleine7159
    @madeleine7159 8 дней назад

    Sénégal kou deugou niouni dagua compliqué wala dagua dof, Thione Seck li legn ko done wakhal, bamou guener adouna la nieup kham moy kaan deug! Yalna nou Ya Allah sakhaal ci yonou deug!

  • @aichaguisse9960
    @aichaguisse9960 5 лет назад +4

    Mai li dou wakhou fi Famille soutara la ishhhh est ce que yagui étalé sa vie privée fi bonne

  • @famakhathiouba2087
    @famakhathiouba2087 Год назад +1

    Je suis comme Mada ba motakh on me taxe de rancunière bilahi je suis pas hypocrite té fii kou deugou bari ay nonn Mane dé nii la mel tu m aime je t aime tu m aime pas je t aime pas non plus et la vie continue

  • @toubaglobaltv9880
    @toubaglobaltv9880 Год назад +3

    Mada je t'apprécie bien, mais sa c'est une erreur qui as touché beaucoup, après le décès de ta sœur, fallait pas parlé de sa vie sur les réseaux.Té nagua khamni nite kou bakh la

  • @papadiop2642
    @papadiop2642 4 года назад +2

    véritable pur ka wakhe

  • @MameAli-tb4rv
    @MameAli-tb4rv 11 месяцев назад

    Courage Mada

  • @senegalaise2251
    @senegalaise2251 6 лет назад +7

    Sama tourando mane ak yaw gno yam djiko.

  • @musamar1945
    @musamar1945 7 лет назад +3

    bon rek la

  • @binetasankhare5135
    @binetasankhare5135 5 лет назад +6

    degue rekk nga wax mada ba

  • @rabyarabya3780
    @rabyarabya3780 8 лет назад +3

    comment peut-on interroger des gens comme ça
    ????

  • @saratazouloudiouf1378
    @saratazouloudiouf1378 Год назад +3

    Mane zoulou souma saguané ba seytané féweulémeu ak sama propre sœur...bisbou guéné adouna warouma am dara loumay wakh si mome...comme que bamouy doundou amoumawone ak mome wakh. Et gnoune gneupay dem kén doufi dess

  • @altaflimbada7346
    @altaflimbada7346 4 года назад +6

    Sénégalais bo deugo bari nonne

  • @dammmedama7869
    @dammmedama7869 5 лет назад +5

    wa gui mome nite la

  • @mamadoulamineloumloum5141
    @mamadoulamineloumloum5141 6 дней назад

    Niit kou deugou të dioub❤

  • @Bayeasndiayeinternational
    @Bayeasndiayeinternational 7 лет назад +59

    dafa sincere rek senegal nak kouffi sincere do bari kharit ndakh deukkou hypocrites leu

    • @fagay1716
      @fagay1716 7 лет назад

      Baye As Ndiaye International
      acrtyuig

    • @fagay1716
      @fagay1716 7 лет назад

      Baye As Ndiaye International o' ou' m

    • @yadefall136
      @yadefall136 6 лет назад

      no khamo kou serieux ki day doul bilahi walahi talahi

    • @adamadiop7262
      @adamadiop7262 6 лет назад

      Baye As Ndiaye In ternational cg

    • @adamadiop7262
      @adamadiop7262 6 лет назад

      Baye As Ndiaye Intern ational

  • @bassseye1335
    @bassseye1335 8 лет назад +13

    dia diaf mada ba ya gore waye yala doula fatie

  • @cheikhdiop866
    @cheikhdiop866 9 лет назад +20

    Le linge sale se lave en famille!

  • @mamecheikhsylla6367
    @mamecheikhsylla6367 11 дней назад +1

    Fene rek

  • @bromprokhanebousso6315
    @bromprokhanebousso6315 5 лет назад +2

    Wakh dji rafetoll 😅😅

  • @modoundiaye4306
    @modoundiaye4306 5 лет назад +4

    No man beug na ma daba sa fouleu dall teuye ko

  • @awandiaye6971
    @awandiaye6971 5 лет назад

    Bonjournehkna

  • @bayembackeseck4243
    @bayembackeseck4243 7 лет назад +9

    Ki dou bax Nitt sou Fatou daguay Wax Lou rafet sii mome

    • @madiordiop1245
      @madiordiop1245 4 года назад

      Baye Mbacké Seck

    • @madaba5571
      @madaba5571 3 года назад

      Yaw. do. Yalla. So. bone. Yalla. Soxoroul. te. degue la. begue

    • @moustafaniang225
      @moustafaniang225 3 года назад

      @@madaba5571 envoye ma numero mada ngir yalla

  • @camarakaty6960
    @camarakaty6960 7 лет назад +11

    walfadjri nio geuneu seytané

  • @zenabeomzogueye9248
    @zenabeomzogueye9248 9 лет назад +3

    deugue dji yalla rék moka kham mé nak soumaye dégue mada ba mouye wakh dege rék laye guisse si mada ba mé mada gnoune aye fns nagne pour la prochaine foi boul expliké devan la télé tégual lép si lokhoye sougnouye borom nakh famille lou sacré la on vou adore mada bonne continu
    ation

  • @Max-maguette5fall
    @Max-maguette5fall 5 месяцев назад

    Ndeye san du courage legui file Sénégal tollou wakh ton tou rek kolako deff nga deff kokou

  • @sadikhboiro9784
    @sadikhboiro9784 7 лет назад

    Thioro camera bii noumou fixer sa wen yii,pathial souf grillage bii pathena

  • @zryhjkbcheikh9177
    @zryhjkbcheikh9177 5 лет назад +3

    sa rak waro ko wilipandai nak wero dh c prive

  • @houmahaniaw1335
    @houmahaniaw1335 6 лет назад +1

    kouguene bone Si famille Noye Yak dére

  • @papalaitybasse7717
    @papalaitybasse7717 6 лет назад +3

    Tu est vraiment juste et sincère

  • @dammmedama7869
    @dammmedama7869 5 лет назад +4

    no dofe bou sokhor bakhoule

  • @neneba5469
    @neneba5469 4 года назад +1

    Les mains sallent se lave en famille mais pas ici

  • @ndeyefatoufall4009
    @ndeyefatoufall4009 7 лет назад +6

    virement même boudé deugu sakh waroko wakh yaww sa rakk yii gay yakkk séné derrr ba baye kara dila dioubolé mada soutoura dioum gueu dall on dirai keu daga mbandii kw

  • @khadimediouf8998
    @khadimediouf8998 6 лет назад +1

    Ta soeur est morte et tu n y vas pas parceque tu ne t entends pas bien avec son mari n est pas une excuse mais mada reste un exemple comme sa soeur ,on ne les a jamais entendu dans certaines betises.

  • @cheikhahmadoubambasene5196
    @cheikhahmadoubambasene5196 8 лет назад +2

    soutoureu way

  • @omarcisse991
    @omarcisse991 4 года назад +2

    Mada dioum nga

  • @alinendaw8542
    @alinendaw8542 5 лет назад +3

    Yalla rk mo kham

  • @modoudiakhate6820
    @modoudiakhate6820 4 года назад +2

    Sokhna khadi mola guene

  • @madamedieng3099
    @madamedieng3099 5 лет назад +19

    Kep kou la commentair lou bakh hypocrite leu... ya wow khole. Fi la beut yam.. do meusa avancer thi musik

    • @madaba5571
      @madaba5571 3 года назад

      Yaw. momou. Ta. Yes

    • @mamadoundiaye3425
      @mamadoundiaye3425 3 года назад

      Yow ya meneu doule

    • @assballagaye2348
      @assballagaye2348 2 года назад

      @@madaba5571 ndéysann nite kou bax nga mé déréte da for nite kouné amo loudoul sa mbok

  • @bellawomen
    @bellawomen 9 лет назад +11

    Mada vraima je t'adore tu es honnête mai noor nit day mandou tu dis k dafa tardè tu ne sais rien nit day mandou

  • @macoumbandiaye4655
    @macoumbandiaye4655 4 года назад +2

    🤐🤐🤐🤐

  • @jerysow1717
    @jerysow1717 4 года назад +3

    Diadieuf mada

  • @dialndiaye6357
    @dialndiaye6357 5 лет назад

    deugue vrai

  • @khadimsarr3141
    @khadimsarr3141 9 лет назад +6

    Mane dee mada ba comprane nala thi sa degou wayee djoum nga lol ndakh lou way diotek nit ba mou dedou aduna nga meunko diale dji rawatina sa rak surtt naniu moytou di werante ndakh eulenga takh le pire nak moy khawma mo def am defoul wayee yalla rebena kouy dogouk mbok... yalna yalla tapee xolyi amine

    • @mberygaye4026
      @mberygaye4026 6 лет назад

      KHADIM SARR n

    • @berebuxamxam1383
      @berebuxamxam1383 6 лет назад

      KHADIM SARR elle a bien fait de expliquer la autres qui voulait en profiter pour ... Mada à tellement fait de bien pour ses sœurs

  • @mamethiaw7415
    @mamethiaw7415 6 лет назад +1

    Mada ba ya bakh

  • @thiofmbaye7503
    @thiofmbaye7503 4 года назад +1

    Dafa degou rekk leral bakhna adouna
    Dafa gouda tanka

  • @aliounediop6618
    @aliounediop6618 8 лет назад +1

    doudegne yep laniouy wag

  • @famasene8642
    @famasene8642 14 дней назад

    Kou bonnne nga khady mo guennne fouffff

  • @fallyaramfall4285
    @fallyaramfall4285 4 года назад

    boulèn wèrantè soutou bakhna loooool

  • @coumbageuye9128
    @coumbageuye9128 5 лет назад

    Mada dôme sonekè nitoudegue barenone bessisseyboke.kouladegue gaywakhe khamene nitoudeguega

  • @boudechou
    @boudechou 8 лет назад +1

    NOOOOO JE SUIS choquée!!!!

  • @rokhayambaye5761
    @rokhayambaye5761 12 дней назад

    Kiiii mom tame yakk sene famille… sokhna Khady nitou adiana leu… iOw mom doff nga rek

  • @souleymanembodj7129
    @souleymanembodj7129 3 года назад +2

    Amal sa vie privé mada

  • @mariemediop4680
    @mariemediop4680 9 лет назад +9

    mada ba vraiment doo nite yow wéroo dof bou sokhor ngua roussnaa trop si kaddu you bone yiii amoo béne droit di wakh say probleme famille si médias yi le linge sale se lave en famille j'ai vraiment honte de toi sa rak dji nak di sokhna Khady moungua si aldiana you kaké serigne touba dinako térou silou bakh la nékone ba guén adouna yow nak khessal ak musique singua nék Yalla dinalen até

    • @madaba5571
      @madaba5571 3 года назад

      ma. gêne. nithe Sa xet

    • @moustafaniang225
      @moustafaniang225 3 года назад

      @@madaba5571 dieuleul sama numero 34641158747

  • @user-qe9dj3lt7r
    @user-qe9dj3lt7r 6 дней назад

    Mais musique da arame thé yagui si mais sokhna est ta sœur gnianal ko yeurma dhé yala