Serigne Moustapha Sy à Capitaine: "dimbalima rék réne bul..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 64

  • @papakhouma1951
    @papakhouma1951 Год назад +2

    Machallah machallah alhamdoulilah alhamdoulilah saneta yalla

  • @malickba5147
    @malickba5147 Год назад +1

    Merci beaucoup serigne bi

  • @tidianediouf4856
    @tidianediouf4856 2 года назад +6

    Dieur dieuf Serigne Moustapha sy

  • @mariamasouare153
    @mariamasouare153 2 года назад +7

    Belle complicité, machallah avec capitaine

    • @mamadouthiaw6173
      @mamadouthiaw6173 2 года назад

      Gamou c'est enseigner sur notre Prophète mais pas comme ça ça c'est gamou c'est miting

    • @cheikhounatine758
      @cheikhounatine758 2 года назад +1

      @@mamadouthiaw6173 tu as suivi l’intégralité ou c’est sur cet extrait uniquement que tu t’es basé ?

  • @alioufaye844
    @alioufaye844 2 года назад +5

    Demalena yeureum walahi loudoul alqur âne ak souna rére la yalnalenn yalla gindi wonelenn souna li bakagne

    • @mameniang8847
      @mameniang8847 2 года назад

      Ki bimou diangue sen bayyi niogui nelaw

    • @alioufaye844
      @alioufaye844 2 года назад

      @@mameniang8847 mom lane la fi wah toumal Ay yonente Di wédi wahou yalla Lolou la fi def yalla mo tagg dawoude ak Souleymane. S'en wadji gnow dilen toumal ndialo yéna yéss

  • @sokhnaseye7491
    @sokhnaseye7491 2 года назад +1

    Wallay ndeyessan sy malick ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @daoudathiago4850
    @daoudathiago4850 2 года назад +1

    Wallahi sante yalla aka mala beugue machallahou sa talibe mouride la

  • @sidymbacke5648
    @sidymbacke5648 2 года назад +2

    اللهم صل على سيدنا ومولانا محمد وعلى آله وصحبه وسلم

  • @adamabarra7555
    @adamabarra7555 2 года назад +1

    Bilakhi ki damako beug guiss djebalou ci mome bilakhi WALAKHI

    • @Alboury
      @Alboury 2 года назад +1

      Demal diebalou si sey wadi our mo guen. Ne perds pas ton temps mon cher. Ici chacun défend ses intérêts et sa famille. Demal topoto say wadi our et tu auras tout inchallah

    • @adamabarra7555
      @adamabarra7555 2 года назад +1

      @@Alboury sa yone nekoul ci mane

    • @Alboury
      @Alboury 2 года назад

      @@adamabarra7555je pensais bien faire en te donnant conseils mais mangui dieguelou balmeu 🙏🏽🙏🏽🙏🏽

    • @fatoukane6495
      @fatoukane6495 2 года назад

      Macha allah fofoula kou wéddi khôlal thi gnabotam gou teunkou

    • @fatoukane6495
      @fatoukane6495 2 года назад

      @@Alboury yow mom yéram nala sakh té khamoula li tmt thi thi mbagnél sérign moustapha SY borom khôl you tilim yi meunougne nangoul 🙏

  • @abdoukarimfaye8193
    @abdoukarimfaye8193 2 года назад +4

    Bayyileine tathiou yi djoulite takbir lamome mai pas Ay tathiou

  • @dadjibokaleiakbida539
    @dadjibokaleiakbida539 2 года назад +2

    Moustapha sy comédien la

  • @moussangom3840
    @moussangom3840 2 года назад +3

    Ama Toul loum wakh ndeysan

  • @ndeyefatoucisse2996
    @ndeyefatoucisse2996 2 года назад +1

    Ko mo gueuneu nékh fi 😅

  • @sarrmarieme7856
    @sarrmarieme7856 2 года назад

    Vraiment diar na lathier dh

  • @mouhamadoukane9835
    @mouhamadoukane9835 2 года назад +2

    Autre chose gnimou diokh wird amolen touss ndakh tapha Sy dieuloul wird té nimoukoy diokhé bakhoul tarikha bi da am charte

    • @cissecheikhtidiane569
      @cissecheikhtidiane569 2 года назад +1

      Mouhamed War ngua khol ci sa tourrbi rk té khamnii li dousa wakh niite ki lo niak andak AK môme boum takha ngua dikowakh loudoull nonou🙏🙏

    • @mameniang8847
      @mameniang8847 2 года назад

      😂😂😂 yaw sa khol nekhoul deh tegua nane ndokh

    • @mouhamadoukane9835
      @mouhamadoukane9835 2 года назад

      @@mameniang8847 bayilen thiakhane

    • @malickthiam4732
      @malickthiam4732 2 года назад

      Ki moo donnoi cheikh yaw warro wax waxou diokhei wird ki amoul kouko soutt si tariha bo

    • @mouhamadoukane9835
      @mouhamadoukane9835 2 года назад

      @@malickthiam4732 wakhi kou réer AK Doff ngay wakh

  • @mouhamadoukane9835
    @mouhamadoukane9835 2 года назад +13

    😂😂😂😂 commedien entouré par des fou

    • @madiagnediopbousonko
      @madiagnediopbousonko 2 года назад

      Un peu de respect 😡

    • @mouhamadoukane9835
      @mouhamadoukane9835 2 года назад +1

      @@madiagnediopbousonko lui il ne respecte personne

    • @madiagnediopbousonko
      @madiagnediopbousonko 2 года назад

      @@mouhamadoukane9835 bane Mank de respect ngafi guiss

    • @mouhamadoukane9835
      @mouhamadoukane9835 2 года назад +2

      @@madiagnediopbousonko je connais tapha Sy mieux que toi mon frère de 1990 a nos jours il traité Mame Abdou Aziz Sy (RTA) de tt les noms d oiseaux Serigne Mansour Sy Serigne Abdou al Amine juska l actuel khalif mo takh nga balma mais meunoumako diokh respect excuse moi ce gars il est méchant il ne dit j amais la vérité en plus fétiche la geum comme si bokoul tivaouone yor na ay audio yimou done wakh si famille et Abdou Diouf so deglo dangay diomi

    • @madiagnediopbousonko
      @madiagnediopbousonko 2 года назад +1

      @@mouhamadoukane9835 okiiiiii

  • @mohamedndiaye1797
    @mohamedndiaye1797 2 года назад +1

    Goudi Yonente bi lagni magal wala ? On a du Mal à entendre son nom wala micro bila ?

    • @biba0501
      @biba0501 2 года назад

      Dèmal dèklou guouddi gui li ziar bi leu résidence bii kagn mo amoul gamou khawma lougnou donn déff nonn

    • @biba0501
      @biba0501 2 года назад

      Dèmal sétann digua khamné moustaph dousénn morom

  • @mamadouba9504
    @mamadouba9504 2 года назад

    Mom.capitaine lanla sah ?

  • @mansourgaye6205
    @mansourgaye6205 2 года назад +3

    Théâtre rk laye jouer ak dôme dji bou gnowé diko répéter d'informations manipulations propagande victimisations diehna amule lénéne motax douma ko deglou légui yi gñusiye deug di dougale rk lasi setane té dara dousi changer nimako xalaaté lakaye défé ki mo rawe kounkandé

    • @malickthiam4732
      @malickthiam4732 2 года назад

      Diappal lolou rekk ki limou yarr si ayy nitt sa baye degouko bayam defouko bayou bayam defou nopul et degage

    • @mansourgaye6205
      @mansourgaye6205 2 года назад

      @@malickthiam4732 sa baye bouye mar tati moustaf kounkandé iblise sy moustaf iblise kounkandé sy di mar sa tatou yaye yaye sama yone nékousi dou très boufi néké di doul manéko doul nga waxko mou bayi ndokhane bou méti bi mo gueune mak mou âme 71ans de plus âme guel liberté 6 ameko dieupale tro c'est tro fofou la yamandi nak

  • @lugodseye4124
    @lugodseye4124 2 года назад

    .

  • @deug648
    @deug648 2 года назад

    Ay way yéwou lén ki bopam lafi nékal dh ak domam

  • @papesarr8167
    @papesarr8167 2 года назад

    Kklu

  • @molomolo5993
    @molomolo5993 2 года назад

    Di promouvoir sa dome bofi jogyué mou gneuw jusqu'à quand ?

    • @ahmadtidianeathie2192
      @ahmadtidianeathie2192 2 года назад

      Moma diaaxal 😂

    • @mameniang8847
      @mameniang8847 2 года назад

      Yaw do dem topp kigua yakar teh yarrou

    • @molomolo5993
      @molomolo5993 2 года назад

      @@mameniang8847 topp kane ??? Yalla rek la yakar yonnentebi Di sama idole , mais da lale sama pas pas .

    • @malickthiam4732
      @malickthiam4732 2 года назад

      Niounn dh résultats ak travail mooy takh niou topp nitt