LES PAROLES DE SERIGNE SAM MBAYE SUR LA BALANCE || OUSTAZ ALPHA BA

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 81

  • @abyseye4513
    @abyseye4513 4 месяца назад +5

    Wa kaddu dîné ma lène beugue. Yalna sounou BOROM swt faye lène yiw fii dounya wal akhira. Amiiine yarabi

  • @bambafallhouboulkhouranedg6891
    @bambafallhouboulkhouranedg6891 13 дней назад

    Dieureudieuf serigne touba

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 4 месяца назад +3

    Kou beug mouthe fi ak feulé topale alhourane ak souna .mane dhé dama done nèlaw deug deug yéwou diotena nak vraiment.

  • @alhassanethiongane3632
    @alhassanethiongane3632 6 месяцев назад +6

    Alfa yalla nagua goudoufane

  • @YusuphaTouray-oo4vh
    @YusuphaTouray-oo4vh 8 месяцев назад +4

    Senegal is full of religion confusion belai . may Allah guide Alpha and his members doing this great job 🙏🏽🙏🏽

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO 8 месяцев назад +3

    Merci Alpha, Younous, Sokhna Khady et les autres ❤❤❤
    Quand j'étais petit je croyais que ces genres de marabouts étaient très forts et qu'ils ne faisaient jamais des erreurs mais en grandissant que j'ai su que beaucoup de marabouts et prédicateurs ne metrisisaient pas l'islam, ils ont écrit et raconté beaucoup de conneries et absurdités, que Dieu les pardonnent

    • @amadoutoure1840
      @amadoutoure1840 4 месяца назад +1

      Dans le pays des aveugles, les bornes sont les rois. Telle fût la vie de Ahmadou Bamba parmi ses contemporains.
      Profitant de l'ignorance de son entourage, il raconta de n'importe quoi pour se faire valoir à ses contemporains. Il devia de nombreuses personnes de la vraie religion.
      Aux yeux de l'islam, Sam Baye n'était qu'un griot en marge de l'islam.

  • @sendeugtv8501
    @sendeugtv8501 Месяц назад

    mande damay re rek😂serigne bi kaw rek lay diam bi isnil lahi

  • @abyseye4513
    @abyseye4513 4 месяца назад +1

    Alhamdou lilah yallah yallah faye lène Alpha et compagnie. Vous. La oumah islamique sera éclairé.

  • @mouhamedmbaye9333
    @mouhamedmbaye9333 4 месяца назад

    Mâcha Allah ❤contane si yéne diam rék ❤

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад +1

    يا ألفا العلم لابكثرة الرواية. بل ضمها نور مع الدراية .

  • @hassanatoudiallo7331
    @hassanatoudiallo7331 10 месяцев назад +1

    Waa Kone alpha cheikh bi laniouy koyyy wowè 😂😂😂

  • @fatiuie4994
    @fatiuie4994 7 месяцев назад +1

    Thank you sheikh may Allah bless you ❤❤

  • @broaderknowledgerek
    @broaderknowledgerek 2 месяца назад

    Demlen guestou ji Serigne Al Hassane Salam pour nguen am une idée thi dayo Serigne bi

  • @gueyeahmadouabdoulaye4429
    @gueyeahmadouabdoulaye4429 5 месяцев назад

    C'est de la métaphysique au physique. Essayons de savoir dans quel état était l'auteur de ces écrits était.
    Parlons du bien à nos morts😢😢😢 😢.
    Que Dieu nous guide 💚 🙏 💚 🇪🇭

  • @1447abdallah
    @1447abdallah 7 месяцев назад +1

    Yallah bimouy sak serigne touba est ce que taggou nako ?

  • @kinteh-2
    @kinteh-2 11 месяцев назад +2

    How can Islam as understood by Prophet of Mercy and his Companions, the Best of Generations CAN BE FITNA ????

  • @SouleymaneNiang-z5w
    @SouleymaneNiang-z5w 4 месяца назад

    ❤❤

  • @سرجفضلانجاي
    @سرجفضلانجاي 7 месяцев назад +7

    Serigne touba thi diamo yalla la nékon badem❤boy wakh wxal ak gayi ndax s touba thi alxoran ak sonne la neckon ba dém

    • @abloslimshady
      @abloslimshady 6 месяцев назад

      Mom deh nééna mo yoré nafsou diam yii!
      Kon mom teunkouwoul tchi Alqurann teunkouwoul tchi Sunna. Konn kokou mingui tchi bokkalé mou reuy!

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 4 месяца назад +3

      33diabars 😂

    • @PapaMballo-o8p
      @PapaMballo-o8p 2 месяца назад

      ​@@elagegueye3310 lolou gewmani wernah .Serigne akh temps bounioukho exilé diapouma amone na temps wou takh autant de femme

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 2 месяца назад

      @@PapaMballo-o8p 4 diabars you bok bayla tak billahy 3 nio bokou ndeye ak bay

    • @broaderknowledgerek
      @broaderknowledgerek 2 месяца назад

      Boy reew ba yeksi thi Serigne bi bess dina gneuw nga xamni lep deugla

  • @mokamara9562
    @mokamara9562 11 месяцев назад +1

    Assalamu alaikum everyone 🙏

  • @IbrahimFall-f2b
    @IbrahimFall-f2b 9 месяцев назад +1

    سام امبي مجنون

  • @sendeugtv8501
    @sendeugtv8501 Месяц назад

    no alpha da saf khoram nak

  • @LamineKamby-q3p
    @LamineKamby-q3p 18 дней назад

    Alpha thiaga bou goor la

  • @sendeugtv8501
    @sendeugtv8501 Месяц назад

    😂😅😂

  • @LamineKamby-q3p
    @LamineKamby-q3p 18 дней назад

    Alpha lo outiwoone maroc
    Balthazar

  • @bassirougueye9485
    @bassirougueye9485 Месяц назад

    Kone yaw kham nga maqama gneupp?

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 2 месяца назад

    Yen tekk lay deglou legui. Wa Senegal danio diangoul.mo talh setign yi dilen nakh

  • @bayefalldiop3897
    @bayefalldiop3897 5 месяцев назад

    Dieurdieurfff serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @BabacarCissé1990Babacar
    @BabacarCissé1990Babacar 6 месяцев назад

    Bilahi wallahi talalhi xam xam tosss amolinekossi demloene diagu tayalla takh

  • @abdoukarimcoly244
    @abdoukarimcoly244 7 месяцев назад

    yalla nala yalla may degu ak topu ndakh xam xam bou low

  • @sendeugtv8501
    @sendeugtv8501 Месяц назад

    tidian yi serelenko

  • @ElhadjicheikhDia
    @ElhadjicheikhDia 11 месяцев назад +1

    yaw alpha ba manna am dianganga ay teeree waayee amagoo nivoau worom xam xam nakh natou kaayou woroom xam xam moy ragal yalla tee menna mandar gaam ragal yalla dijsoumako thi yaw ak nii melni yawإن الذي لم يخش رب العالمين ليس بعالم ولوافني الفنون

  • @ibrahimaba5199
    @ibrahimaba5199 11 месяцев назад +2

    Wallahi khamoulèn lou bari yéne lounguén meuneu mabou khana sén dîné nguén di mabou yéneu réw té khamadi billahi wallahi Serigne sam mbay ragal yallam ak kham khamam weéssouna sén bop adouna yakhouna .

  • @boubacarsoumare9910
    @boubacarsoumare9910 6 месяцев назад

    Ce serait très intéressant d'organiser un débat civilisé entre Oustaz Alpha et Serigne Mbacké Sakho.
    Merci

  • @bayefalldiop3897
    @bayefalldiop3897 5 месяцев назад

    Wadial magal gui rek ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @abyseye4513
      @abyseye4513 4 месяца назад +2

      Wadial bidah. Qu'ALLAH TOUT PUISSANT vous guide les égarés...BRAVO wa kaddu diné

  • @ElhadjicheikhDia
    @ElhadjicheikhDia 11 месяцев назад

    soufeekee lii mootakhoon niouy diangee. sou yaboo niou doonn ay djiahll nioun nieppالعلم لا المجادله ولاالمنافسة كالمنافق...ومن تعلم لهاذه الأشياءفإنه يموت بالإصرار علي الكبائر...قال الإمام الغزالي من أعان من قداكتسب علما وما ...لغير دنياه فإنه شاركه فيما جني كبائع السيف للص كمنا

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад

    Xaléboréw nak dana dajé ak loukoyar

  • @modoundiaye3147
    @modoundiaye3147 11 месяцев назад +3

    Khawma dara dh mais nji malén geuneu parré si alhourhane kou wedi nieuweul pv serigne sam amoul kouko eupp kham kham si Senegal

  • @MoustafaMbacke-kf8sj
    @MoustafaMbacke-kf8sj Месяц назад

    Yéna geuneu touti thi yakh liguéyup stouba meusnga wakh ba dégu kolané mourid la won wayé légui wahabist la tébo démé tba fékfa Séni morom yuy dane thieukel di liguéyeul Serign touba

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад

    حسب رأيك من لم يكن له بصيرة لا يري الحقيقة أنتم من الذين اعمي الله قلوبهم. أنتم لستم من اهل السنة والجماعة. بل من الذين ضل سعيهم في الحياة الدنيا وهم بحسبون انهم يحسنون صنعا

  • @bambandiayendiaye
    @bambandiayendiaye 4 месяца назад

    Wadjii Kou oubii leufeulll ndaye laaa domouram

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад

    Ay say say youbon ngén xamngén yén thi ay réso aki télé rék ngén di waxé lii ngen didéf yombona

    • @abyseye4513
      @abyseye4513 4 месяца назад +1

      Tu n'as rien compris. Va apprendre la religion c'est mieux

  • @broaderknowledgerek
    @broaderknowledgerek 2 месяца назад

    Yaw ya meuna fenn dé ngani S. Moussa Ka jangoul?
    Xaw ma kan waye S.Sam dousa moromou bay thi xam xam

  • @abdoukarimcoly244
    @abdoukarimcoly244 7 месяцев назад

    yaw dell wakh rk ba kerokeu yalla di fay wakh di bay dieuf

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 6 месяцев назад

    Tarihayi gnoo dakha fénn ci dîné l'islam bokalé bida moo ci eupou

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад +1

    Vous êtes des rebelle dans l islam xolatlén sénpoppu

  • @youssoudiop3389
    @youssoudiop3389 5 месяцев назад

    Yaw da nga sankou

  • @ibrahimaba5199
    @ibrahimaba5199 11 месяцев назад

    Serigne sam mbay gnimou défar sén dîner kén khamoul nimou tollou nguén koy wakhal si louguén khamoul dara wallahi yéna rére DEUG DEUG.

  • @modoubane118
    @modoubane118 4 месяца назад

    Serigne Same Mogui Défar Aynit Gnou Awone Si yone Wou Bone Bou Gnou Guéne La Fouf.
    Sa Bop Rék Gafi Nékal lo Ame Si Sa Compte bi Rék

  • @AbdoulayeSow-n3r
    @AbdoulayeSow-n3r 4 месяца назад

    Un si tu est oustaz t'as pas de pédagogie
    Deux t'es pas polie yaruwo
    Trois tu es en mission de destination
    Alpha BA alnala yallah dibal

  • @modousene6367
    @modousene6367 3 месяца назад

    Yow mis kou Diarra yeureum nga fekhel yalla nguindi la danga rére deh yen pour yen yalla meunoul dra so amé AG setlou yena gueuna tardé Sénégal tei nenguen yena nekal yalla yen wakhabiss yi

  • @sendeugtv8501
    @sendeugtv8501 Месяц назад

    li s sam wakh mo wer de

  • @broaderknowledgerek
    @broaderknowledgerek 2 месяца назад

    Serigne Touba kouko wedi sa tekhédi lou weer la.

  • @PapeDemba-eu9hu
    @PapeDemba-eu9hu 4 месяца назад

    Soufi louko nex rék lay wax

    • @broaderknowledgerek
      @broaderknowledgerek 2 месяца назад

      Yaw nopil ko xam ni fater nga linga rerer demb di weddi lo xamni xamo thi dara.

    • @PapeDemba-eu9hu
      @PapeDemba-eu9hu 2 месяца назад

      @@broaderknowledgerek yaw yaa xamoul tassawouf, nioun cilagn nékkon té bayyi nagnko

    • @broaderknowledgerek
      @broaderknowledgerek 2 месяца назад

      @@PapeDemba-eu9hu Demal guestou ji Seydina Al Hassan Salam

    • @PapeDemba-eu9hu
      @PapeDemba-eu9hu 2 месяца назад +1

      @broaderknowledgerek Démal niou firil leu alkhouran ak hadis

  • @bambasow9638
    @bambasow9638 11 месяцев назад +1

    SHAME ON YOU YOUR WAY IS FITNA

    • @kinteh-2
      @kinteh-2 11 месяцев назад +1

      How can Islam as understood by Prophet of Mercy and his Companions, the Best of Generations CAN BE FITNA ????

    • @bambasow9638
      @bambasow9638 11 месяцев назад

      HIS TARGET MUST BE NON-MUSLIMS IN ORDER TO CONVERT THEM, ATTRACT PEOPLE TO ISLAM, AND NOT CRITICIZE OUR COUNTRY'S ELDERS. HE ENGAGES IN DENIGRATION; HE SHOULD FOCUS ON OTHER THINGS. THIS IS SHAMEFUL, AND HE ADVANCES THINGS THAT HE DOES NOT FULLY UNDERSTAND; HE IS FLAGRANTLY MISTAKEN."
      @@kinteh-2

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 6 месяцев назад

    Kiidinané thiamoy yéfarla yén doungén ay joulit ay naféxa ngen vérénté ak ak sos moy sénmbir

    • @thiammady4782
      @thiammady4782 21 день назад

      Caméra bi moo mel noonou waayé ndidioor lay naané.

  • @ibrahimaba5199
    @ibrahimaba5199 11 месяцев назад

    Chaytané nguémbounaléne wayé dinguénko réthiou yonéte bi diguléoul togne ak wakh lo khamoul liguén di déf dou alkhouran dou sounah réwadé là.

    • @abyseye4513
      @abyseye4513 4 месяца назад +1

      C'est bien ceux qu'ils font au Sénégal il trop de shirk et du bidah à cause des tarikhas qui placent leur marabouts au dessus de tout

  • @bayefalldiop3897
    @bayefalldiop3897 5 месяцев назад +1

    Wadial magal gui rek ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @KhaliSeck-jx3wp
    @KhaliSeck-jx3wp Месяц назад

    ❤❤❤❤❤