Wally Seck "waxna loum meusoul wakh si relation papa Thione et maman diaga:ndeyesane...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 фев 2023

Комментарии • 249

  • @vicincialy8928
    @vicincialy8928 Год назад +16

    Tout enfant a besoin d’être béni par ses parents . Le pagne que ta maman t’a mis te protègera toute ta vie Amin

  • @naboudiop3659
    @naboudiop3659 Год назад +26

    Oh mon chanteur préféré tu es parti sans me dire au revoir yalla nala Yalla yereume harer la aldiana you gueuneu kawer amine Pape thione le meilleur de sa génération le parolier le véridique le digne le sage l incontournable l honnête le sincère le gentil louma metty reck moy niou bary hamouniou wone yaw yaye kane 1an déjà oh ce dimanche fût le jour le plus dur de ma vie je n oublierai jamais ce jour yalla nala Seydina Muhammad PSL terrou la aldiana you gueuneu kawer amine waly motakh yangui mayer auto you bary mashalla du courage diko nianal reck c est vraiment dur mais sa ira inshalla masta

  • @fantadabo9642
    @fantadabo9642 Год назад +36

    C émouvant j’ai les larmes aux yeux longue vie bonne continuation

  • @mamediarraalioufaye7901
    @mamediarraalioufaye7901 Год назад +14

    Ndaysane j'ai des larmes aux yeux😭 papa Thione yalla nako yalla xaré aldiana firdawsi thi barké Seydina Mouhamed🤲🤲🤲🤲

  • @fatoumataba9925
    @fatoumataba9925 Год назад +75

    Sakhou ñianou wadiour dafa ame solo sidome té Wally môme la dëff mâcha alla longue vie à toi frérot

    • @adamengomndiaye4209
      @adamengomndiaye4209 Год назад +1

      Aka bakh boko ame boul tite téke thi diamou yalla

    • @mamadoukante8427
      @mamadoukante8427 Год назад +1

      Lolou moy galadj bou assuré...nama yalla dimbali ma meune léne teral

  • @khalildiene7832
    @khalildiene7832 Год назад +25

    J'ai les larmes aux yeux ... Waly ndam rek barke CHEIKHOUL KHADIM... CHEIKH AHMADOU KARA MBACKE NOREYNI moni wone Adunaa yeup dinaniou la ni Jakkk motakh ndam rek

  • @rokhayasarr6468
    @rokhayasarr6468 Год назад +75

    C'est très émouvant longue vie à diagua, waly tu va vivre très longtemps sa dounda amna diarigne💞💞💞💞

  • @aissatoudiouf2245
    @aissatoudiouf2245 Год назад +19

    Les prières de tes parents t accompagnera toujours reste toi même ❤

  • @diarrakaire8782
    @diarrakaire8782 Год назад +17

    Yaw Wally ❤ lou bakh rèk gay am inchalla goudal fane rèk lay niane 111 ans ak wèr amine

  • @khadycheikhmbengue9354
    @khadycheikhmbengue9354 Год назад +13

    Une très Longue vie à toi wally😢et beaucoup de bonheur❤

  • @kumbasarr1444
    @kumbasarr1444 Год назад +13

    Lum jooh yalla ak domaduna cherr motaah my follow wally .I have stopped listening to music for ages but wally is exceptional 👌 mashallah

  • @sotrapbatbalaye5047
    @sotrapbatbalaye5047 Год назад +32

    Avec tout ce que tu as fait pour tes parents Dieu récompensera sur terre et dans l'au delà. Continue de travailler et je prie que le seigneur te prête longue vie pleine de santé!

    • @batouservices3125
      @batouservices3125 Год назад +2

      Machalla seck yalla n'a gua goude fane soute sa baye fane té déssé barké bi seck vraiment Machalla

  • @amytraore4433
    @amytraore4433 Год назад +19

    Vraiment il est brave un grand cœur aimons nos parents

  • @ablayendiaye3460
    @ablayendiaye3460 Год назад +11

    Sidat tu est un vrai ndanane chapeau à Waly

  • @fatoundiaye8545
    @fatoundiaye8545 Год назад +13

    Merci sidath, machallah Waly ❤️❤️❤️

  • @mormbaye2989
    @mormbaye2989 Год назад +16

    Amnga foula d😂😂😂😂dound Lo feker❤😂😂

  • @haddybah4040
    @haddybah4040 Год назад +15

    May Allah continue to have mercy on Papa Thiones soul

  • @ndeyethiorseck9462
    @ndeyethiorseck9462 Год назад +12

    C trés émouvant waly tu as gaté ma journée avec des l'armes de bonheur, beguenala dakh niga takhawo wadiour yi fo dioublou yalanafa yiwou yallah dioublou. Thione seck damako begone , aye woyame manchallah, yalana aldiana firdawssi di keureum 🙏🙏🙏

    • @khady.60
      @khady.60 Год назад

      MachaAllah waly djàm rék ngaye am Waly Billahi wallahi wa tallahi mane dou ma djouli mouk di ñianal waye djitou ta boolé wouma thi papa thione wallayla asim

    • @ndeyesow9570
      @ndeyesow9570 Год назад

      Wally ♥️♥️♥️

  • @SD-ih6bz
    @SD-ih6bz Год назад +9

    Geureum Baye. Yeureum Ndèye kouko dèf tékhé 🤲🤲

  • @lounekhwayedeffsenegal6165
    @lounekhwayedeffsenegal6165 Год назад +12

    Mane wallaye je suis ta fans quand écoute musique je pleure

  • @hamadyyguisse252
    @hamadyyguisse252 Год назад +6

    Machalla c un jeune que j aime tend par sa franchise machalla que le bon dieu vous protège des méfaits des hommes

  • @fatou9155
    @fatou9155 Год назад +6

    Machalla Waly yalnagua douane 100 t'àns sens ordonnance AK sà yaye ga douane ba sa diabottes faylo ko merci merci

  • @ndiemegueye8556
    @ndiemegueye8556 Год назад +14

    Longue vie waly ak kou la yéné

  • @codousow5840
    @codousow5840 Год назад +11

    Bilaye ki damako beugue ba yeureumko do torokh mouke maryacine j'ai les larmes aux yeux

  • @ramatoulayesabaly5907
    @ramatoulayesabaly5907 Год назад +7

    J'ai les larmes aux yeux 😭😭😭 yallah nako yallah yeureum té hareko Aldiana thi barki Naby Moustapha PSL 🙏

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 Год назад +7

    Ndeyssane machallah wally yallah gua am diam😍😍❤❤

  • @ndeyebintaniang873
    @ndeyebintaniang873 Год назад +6

    Machallah yallah nala Borom bi sameu leu man damako beug ndankh nimou mel ci wadiouram ❤. Doundeul wéral

  • @vivianeniasselareine2847
    @vivianeniasselareine2847 Год назад +7

    Ndeyesane wally seck yalah dinala téral deh do trokh mboukou

  • @abdoulayey.diagne2603
    @abdoulayey.diagne2603 Год назад +14

    Doundal seck le meilleur reste à venir Honneur à la grande dame Fatou kine Diaga

  • @assakante6490
    @assakante6490 Год назад +7

    Masha’allah ❤❤❤❤❤ longue vie et santé de fer à toi Wally

  • @diazakaria4047
    @diazakaria4047 Год назад +22

    Courage mon Frère dieux est grand

  • @oumieleigh8556
    @oumieleigh8556 Год назад +6

    Papa Thoin, May Allaah have mercy on his gentle soul and grant him janatul firdawsi with all the departed souls. Continue to rest in perfect peace papa Thoin. Wally secka. May Allaah continue to guide and protect you. Allaah will continue to guide you to be successful with countless blessings Incha Allaah. Well done keep up the good job.

  • @sarroumou658
    @sarroumou658 Год назад +3

    Walay ndeyssane hoooo walahi ces émouvant j'ai les larmes aux yeux pape thione yalna khipé aldiana firdawssi wali long vie à vous toi inchallah diam rek ngua ame inchallah wenibik hâte cœur ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️

  • @diamilatouwonysy4797
    @diamilatouwonysy4797 Год назад +8

    C'est émouvant maachaallah allahouma barik

  • @kourasamb9459
    @kourasamb9459 Год назад +7

    Machallah Waly😭

  • @fatymafall2369
    @fatymafall2369 Год назад +11

    Fi domeyè rawati miguisi wadjoyè yalana yalla takhawou

  • @yayeawambaye5480
    @yayeawambaye5480 Год назад +6

    Ndeyssane🙏🙏

  • @ramatoulayesagna3017
    @ramatoulayesagna3017 Год назад +16

    Machala ❤❤❤

  • @rabysamb904
    @rabysamb904 Год назад +2

    Waly❤sa xol mo rafet ❤Amal diam rekkk❤Papa Thilone yalla nako yalla kharé aldjana

  • @aichaaicha4690
    @aichaaicha4690 4 месяца назад

    Yalna leu yallah faye seu khol bou rafet... Wally yallah bo weet incha allah. Yalna leu yallah takhawou. Nite bou bakh ga

  • @Mody-nz3zt
    @Mody-nz3zt Год назад +5

    Mère diaga leikoul nanoul môme domame la tal ❤

  • @nogayesylla7153
    @nogayesylla7153 Год назад +5

    J ai des larmes aux yeux deysane

  • @ndagousarrba9217
    @ndagousarrba9217 Год назад +7

    Machalah walahi

  • @fatoudieng7270
    @fatoudieng7270 Год назад +1

    ToubarkaAllah machaAllah lawla wally Seck faramaréne bi yallah nala thiat sékhlou bour yallah same la same djiabotte gui mousseuléne thy seytané ak loukoye sabape yocke khéweul yi bidjayi nabil moustapha sallalahou Aleyhi Wassalam amine yaraby

  • @mamansow1969
    @mamansow1969 Год назад +6

    Wah deugue mar bamou nekh❤❤❤❤

  • @kevinkebe
    @kevinkebe Год назад +6

    I really like this guy. He has a good heart

  • @agnamballo7525
    @agnamballo7525 Год назад +3

    Ndeyssan faramaren bi yala n'a ça diam yague ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @MameAwaSene-lz6xr
    @MameAwaSene-lz6xr 4 месяца назад

    Yalla nalla yalla diapalei, yalla balela sa aye bakar yeup adouna ak alakhira, maye soutoura adouna ak bou alakhira tei teikala thi siratale moustakhime ak mane a beipe djioulite thi bakhayou sounou borom ❤️

  • @aminatambaye4147
    @aminatambaye4147 Год назад +1

    In cha Allah thi kaw thia kanam thi sa barqué Yaye Sokhna Diaga Seck

  • @ndeyematycisse6946
    @ndeyematycisse6946 Год назад +1

    Machallah wally seck longue vie à toi santé de fer je t'aime bcp on t'a d'or ❤️❤️❤️

  • @yambojang3088
    @yambojang3088 Год назад +3

    In’Sha’Allah.. papa thione 😭may his soul continue to rest enternally 🙏

  • @kebediarra4144
    @kebediarra4144 Год назад +3

    Machallah lafe thiate❤💯

  • @mbathio4435
    @mbathio4435 4 месяца назад

    Motakh nak boul tite boul khof, Wally yaw rek domou Diaga la référence et Papa Thione rek, lep diam in cha allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bgsonsthriving.
    @bgsonsthriving. 7 месяцев назад

    That’s so powerful ❤❤❤Ma Shaa Allah wonderful family

  • @aicharassoulsow9545
    @aicharassoulsow9545 Год назад

    Wally dara diomboula mar yacine meissa bigué mar danga meilleur seck yalna nga soute sa baye aye fane yalla bayila ak sa yaye bamouye dokhé bante inchallah

  • @salimatakonate5332
    @salimatakonate5332 Год назад +3

    😭😭yalla nala yalla sameu ❤❤❤

  • @maguayediaw35diaw95
    @maguayediaw35diaw95 Год назад +3

    Machallah machallah Wally ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ndeyeawasene6412
    @ndeyeawasene6412 Год назад

    MA SHA ALLAH tu m as fait pleurer.Que DIEU te bénisse et te protége

  • @aminatatakonate6485
    @aminatatakonate6485 Год назад +2

    Machalla yaram dawneu yalgha am fan you guoudou

  • @djeinababa3988
    @djeinababa3988 Год назад +1

    Machallah Machallah vraiment Machallah doundal bessawane bawane

  • @kamadiawara8916
    @kamadiawara8916 Год назад +6

    Longue vie Wally Seck ainsi à toute ta famille ❤️❤️❤️❤️🙏🙏

  • @user-sq1vh9cy6t
    @user-sq1vh9cy6t 4 месяца назад

    Deugue pirrr ,on a vécu sa mais sante yalla , j'avais un problème et sa toucher mn père mais sama pape néna doléne meusseu torokh ,et sa je le vois maintenant paix à son âme

  • @mamesarrfall5684
    @mamesarrfall5684 Год назад

    Machalah yalnala yalla defal jammm barki sekhoul khadim

  • @ndeyebounamadiop5863
    @ndeyebounamadiop5863 Год назад +2

    Maschaala wally magui dioye sakh

  • @Xippillxole
    @Xippillxole Год назад

    Machalla yok ba yeuk inchalla yalla defal gnouko defal mbolombi djoulitt amine diadeuf wally

  • @evadieye9266
    @evadieye9266 Год назад

    Machahalah Wally si kaw si kanam mann sayy histoire damfma yémm walaxi yallana sayy baxx baxxx sayyy ndammm di yokou❤🙏
    Bilaxi sama baye niilawon youbari youmoudonn defff si baxx bimou fato lakoxamm walaxii motax linga waxx touché namaa..
    Yalla nako ALLAH SWT yeurem xaréko Firdawsi youkawé akk kouloukoum wayydawlo té diégalniou 🙏

  • @ramatulayendoye4387
    @ramatulayendoye4387 4 месяца назад

    MASHA ALLAH. Yala NA YA ALLAH khep doli amiin ya Rabbi.

  • @user-wv9mj1fz8h
    @user-wv9mj1fz8h 3 месяца назад

    Longue vie à toi Wally té say parents Yalla yeureume lène té kharé lène Aldjana Firdawsi

  • @aidaseck4029
    @aidaseck4029 Год назад +1

    Bilay yalla ka gueune bakh Ballago Doumbé Yacine yalna khipé aldiana,❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @aminatakane2969
    @aminatakane2969 Год назад +2

    Macha allah domou Papa Thione sama sopé sama karite thi kaw thi kanam yalla nala souniou borom samal bopam

    • @maxdiop1394
      @maxdiop1394 Год назад

      Sidath bayil woyane bi waly mayal auto sidath

  • @aissatambaye2881
    @aissatambaye2881 Год назад +1

    Machala DOM yalla n'a la yalla sam

  • @awandiaye161
    @awandiaye161 Год назад +2

    Thione Yalla na ko Yalla yeureume te khareko Aldiana

  • @khadyba1462
    @khadyba1462 Год назад

    C émouvant yaye gnou bakh rek mon âme solo merci tata gnakka jtm waly

  • @aminatabodian1205
    @aminatabodian1205 Год назад +2

    Waly tu ma fait pleurer

  • @diengdioprama1977
    @diengdioprama1977 Год назад +1

    Wally seck nianou weydiour Moy lep téé amguako bamou doy bilay walay sa kaw sa kanam rek inchallah 💪❤️❤️👈

  • @sokhnanenefall5432
    @sokhnanenefall5432 Год назад

    Machala waly dagua âme diome yalna yalla sameu leu bayifi ya yaye bayoukoy wèr ak wèri

  • @ndeyegueye115
    @ndeyegueye115 Год назад +3

    NDEYSANE 😭😭

  • @sainabouceesay8255
    @sainabouceesay8255 Год назад +1

    Wally yu will never suffer in life may Allah bless you and protect you 🙏 ❤️

  • @bacarycisse5925
    @bacarycisse5925 Год назад +1

    Je t'aime wally Ballago seck

  • @ayethiam1166
    @ayethiam1166 Год назад

    Machallah mn frère waly sa kaw sa kaname inchallah loubakh rek gay âme inchallah li motakh beugla

  • @salimatadiene2111
    @salimatadiene2111 Год назад +6

    Ndeysaan kou mougn mouuuugn

  • @umarfallumar2138
    @umarfallumar2138 Год назад +1

    Machala faramarenbi yalna yalla Samo

  • @coumbaseye1168
    @coumbaseye1168 Год назад +3

    Papa Thione yallana aldiana firdawssi sone keureume.ak.bep.wadiour boumefa nek

  • @elimaneba3004
    @elimaneba3004 4 месяца назад

    Tres émouvant Wally tayy lala beug mane dma beug sama yaye

  • @kharitouyay
    @kharitouyay Год назад +7

    Lép lo déf say wadiour yalla nalako yalla fay thi sa ndiabot, man damala beugeu ba souma dégé koulay critiqueé damaloy méré walla hi tamassouma la giss, ta gno bokk kogne nord foir

  • @nyansarangmbaye4199
    @nyansarangmbaye4199 Год назад

    So emotional may Allah grant him Jannatul Firrdaws Ameen

  • @nantenindiakite7432
    @nantenindiakite7432 Год назад

    Vraiment beug nala Wally très émouvant

  • @dabadiallo9680
    @dabadiallo9680 Год назад

    Amine Seck yalagah gouda fanne ak sa famille yepe masha allah si barker Seydina Mohamed psl

  • @ndeyebinetoundiaye4330
    @ndeyebinetoundiaye4330 Год назад

    Machallah ken dou yaye

  • @ramatulayendoye4387
    @ramatulayendoye4387 4 месяца назад

    Yala bou sokhla diam niak. Li mo nekh YA ALLAH. Yala na famou nek gueuneulko fimou diougue ALAHOUMA amiin.

  • @nogayediasse449
    @nogayediasse449 Год назад +1

    Bilaye azim Wally yalla gua goude fane si Barker le tout puissant

  • @margaretjarra5898
    @margaretjarra5898 Год назад +4

    Wally wally..... Please avoid the media.....and talk little
    Thanks

  • @mariamasinyan6078
    @mariamasinyan6078 Год назад

    Ndeysanne wally machallah God is great

  • @aminatandiaye8122
    @aminatandiaye8122 Год назад

    Machallah histoire est trop triste wallah 😥

  • @pivoine481
    @pivoine481 Год назад

    Bakh rek mo wor, Mach'Allah, Yalla nala Yalla yok diam🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dieliadia393
    @dieliadia393 Год назад +1

    Yalnala yalla téral

  • @khardieng9763
    @khardieng9763 Год назад

    Machallah Wally lo dounde rék doyoul amal jaam

  • @younoussakane3713
    @younoussakane3713 Год назад

    Wally seck tu as un jolie cœur diame rek gaye âme inchallah laffe là thiatte mon frère bègue

  • @mamingom103
    @mamingom103 Год назад

    Pape Thione yalla nako yalla yereum té kharé ko aldjana 🤲

  • @mbayendeye3075
    @mbayendeye3075 Год назад +1

    Machallah wally Seck gaïndé