🔴Intégralité du Combat Balla Gaye 2 Vs Tapha Tine
HTML-код
- Опубликовано: 6 фев 2025
- ALBOURAKH EVENTS LA CHAINE EVENEMENTIEL
"Suivez-nous sur Albourakh Events TV, votre destination ultime pour une expérience immersive alliant sport, culture et événementiel. Plongez dans un univers où l'excitation des compétitions sportives rencontre la richesse de la culture, le tout ponctué d'événements inoubliables. Rejoignez-nous pour vivre des moments uniques, où chaque instant est une nouvelle aventure à découvrir. Albourakh Events TV, où la passion devient spectacle."
Kou faralonn balla gaye 2 lalall j'aime ❤🤙
Balla gaye ak bombardier folen fogoul fofou laniou laye betta.dinou niekhou kou niew facilement.technique molen di dane dou dolé❤❤❤😀🤣😜🤸♀️🤸♀️
❤❤@@halamadrid2108
Balla seul moye lamb bly
❤❤❤❤❤❤
Balla Yako dakhe khekhe Yako dakhe beurré
Balla Gaye 2 lorsqu'il est en difficulté c'est là qu'il nous sorte ses gestes anthologiques. BG2 est le MEILLEUR franchement parlant.
Dafa dane Yekini tok ci plateau bi ma dégue Pere Birahim Ndiaye def temoignages ci mom. Né Balla biss bou ay supportéram tité ci la xelam di guéna dal. Té dou dane mbeur ba jubilé. Ca prouve que beuré dafko meune.
Parle Français 😊@@Concept0208
Balla gaye 2 rek... beurré rek laye deffe... machalah, machelah..., un grand champion, ndame rek...
Balla dh comme réal Madrid rkk
Tapha tine ya bonne staff...khamolén dara....nila yalla bindé....amo diom jtj....félicitations a BG2
Balla le meilleur lutteur soit il gagne où il perd mais il ne triche pas. Félicitation balla
Bilay
Ça mome c'est vrai
Lolou moma nékh si môme il ne triche jamais soit il gagne soit il perd
Billahi Lou leer nga wax. Il se bat dignement loumou ame dieul
Surtout loolou.
Souy daanou day nèkh
Souy daane day nèkh
Khamoul tappalé ay samp nul
Non non
Kep kou faralon balla gaye lalal j'aime ❤❤❤
@@babacardiouf213
Fgxhx
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Si paré NGA wakh ma Lou doyé j'aime yi
@@moustaphadione5509 lolou sa yon nèkousi so menoul j'aime manoul
Carrière bi Tapha Tine tierna
Merci balla gaye amal diamo rék bilaye 😢😢😢❤❤❤❤👌👌👌👌
Kou sa mbeur beuré woul bo mandou woul dégg loula nékhoul fi balla point ❤
Vraiment 😂balla seul ❤
@@fatoufall515 mofi nékk lolou la yalla déff ❤️
Kou kontane rèk lala jm
Balla gaye aime les défis ! Quand il est outsider, il est hyper motivé
@@abdoulayegueye6686 exactement
Toi tu connais bien Balla Gueye. C'est un homme de defis
Loolu la doon wakh
Bg2 So gépp gnakkè yaakaar si moom rék mou deff exploit
Lamb dou mystique
Sport amoul triché entraînement et mental
Taye Balla a mérité il a été au dessus à tous les niveaux
@@BAYUBgoor484 bilaye
Vraiment bayile sisou mane yi rek 😂
Walahi bignou tousse ba pare lane physiquement balla mo geneu pare tay vivacité rapidité ak détermination mofi fegne balla a mérité sa victoire
Faraloumako mais deug gua wax il as mérité
Yaw ami batine li mystique bou flagrant la déloléne sén xél si Yallah victoire djaroul yén mystique yi
Kou d'accord né balla dou nitt rk beseul jaime 😂❤
Eumeu Sene est d'accord 😂😂😂😂
kon lumu
Tapha dafa niakeu diom rk saway li boudon ama balde la dou demei ni
@@dienauto4087 Lou fi indi koku,😂 sa khôl nekhoul
@@MousliSeye-dx1ct toogne rek 😄
😢Tapha tine dou saram ndm kou d'accord rek lalal j'aime ndm
Tu a raison ki domoukharame deugueuleu mome tafa tine
😂😂😂😂😂😂😂😂
Dèsèla tougnou Dara bly 🎉❤
Bilaye chérie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
*Dimanche Le 21 Juillet 2024*
Balla Gaye 2 C'est Le Meilleur Lutteur De Sa Génération Balla Gaye 2 Mo Mana Beuré Té Mane Khékou Lamb Modou Lo Moy Roi Des Arènes Waayé Balla Gaye 2 Moy Meilleur Lutteur ❤❤
❤❤❤❤
dou bénn mystique Tapha daga meunoul khékhe lambou té Balla gaye 2 dafa meune khékhou lambou
Wakh Ngua Dëgg Deh
Wakhule degue kone prkoi mou dore boy gnanG bamou guéneu sakou yi elton ac B52 balla guaye mystique lay df guanane lane
@@ahmadoutalla9228j’espère que setane gua du début jusqu’à la fin
Début bi guisso li tapha dor??
En plus demal setanat combat tapha eumeu sene di comprendre
@@babacargassama3057 Deug rek nga wakh
@@ahmadoutalla9228 Te pourtant Bilahii BN2 mo dominer wone khekh bobou door nako fa ay gauche droite ba Tapha teureuf mais BN2 dafa done bayi khel Tapha de trop. Khana setano Tapha Eumeu, Eumeu dougouna thi garde bi doumako doumeu yi metii
il est incontestablement le meilleur de sa génération
Dafa leer
❤❤❤❤❤😊😊champion ya doff dehh beuré khelll laa😅😂😊😊😊😊😊on est content 😊😊😊
C'est le meilleur et le plus actif si tu le bat c'est la chance non le mérite chapeau balla
Kou d'accord ni balla mo meun thi Sénégal
Balla Gaye damalay beugue ba kagne sédal gua sama xol que dieu te protège❤️🥰🙏
BG2 ya meun nakk dama contane beu ins bii magui sétann combat di setanatt🎉🎉🎉❤
Ya meum nak est nekhna faral ❤balla Gaye2 forever ❤🔥
Balla amna cardio nak machallah balla moy lamb
Lamb moy balla
🎉🎉💃🏻
Balla dall gaïndé leu MashaAllah félicitation yalnala djick 🎉un vrai champion 🏆 🥇 ❤
Vive Balla gaye 2 ..vive Messiiii et vive Sonko ❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂ses trois personnes ma lén gueuneu Beugueu thi adouna❤❤❤😂😂😂
Avec tout son show et son entraînement,il s'est fait humilié
Décidément kii tapett leu comme le disait Balla😂😂😂
Balla 👑💫🇸🇳💫👑physique bii meuneu gueneu bakhate inchallah allah👑👑 👑👑entraînement reek 👑balla L'empereur yallah nalla ndame djigue lafe diatte
Je pense que Balla limou beugone ci Combat bi amnako, moy force, cardio, endurance ak mobilité. Mais meuna guëna liguey.
Effectivement gni di di wakh nane balla muscle yi da bayi dagnouy wakh loulene nekh rk
Bou entrainé seurieument
Contact lou beurri mo meun si arène bi
@@Concept0208 vrai
kou faralon balla lalal j,aime❤
Qui est la en octobre 2024 😂😂 douma si doyal bly Balla Le meilleur
je suis la en 2025 🎉❤😂
Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah Alhamdulillah ☝
Aziz Ndiaye yagnou bégue ba kagne sax❤❤❤❤❤ félicitations à Balla gaye
Balla le meilleur de sa génération 🎉🎉🎉
Combat épique dirions nous empreint d'une belle victoire... Un Balla sérieux et bien musclé donne des résultats autrement... bienvenue la retraite.
Congrats g2
Tapha Tine a un seul et unique problème, c'est qu'il a terriblement peur de BALLA GAYE 2. Tapha Tine amoul fitt, c'est son principal problème...
Félicitations à BG2 qui a attaqué, cogné et gagné comme disait Tapha Gueye.
Ndeysanne Peulh bou raféte kouko dégue lou nimouye reporter khame Balla la faral 😅machallah Balla da nékha beugue
Balla gaye 2 ❤le meilleur félicitations ❤❤
Mbeur dotul mélni balla gaye ci aduna ❤❤
Xana danga faté doff yi Pikine la'la wax 💚❤️
Walahi dama dioy
Je viens de revoir le combat Tapha tine dafa poids boumou attanoul vraiment !!!!forza balla ❤️❤️❤️
Tu as vu juste. Il manque d'explosivité et vivacité
Tapha est toujours comme ça la réalité est k massoul ñèmé balla et mbeur soko ñéwoul doko dor bakoy dan. En réalité Tapha dafa bonn
Avant le combat laa wakh ni Tapha Tine forme bii mou yor baakhul.
Désatognou dara bilahi. Tu es tout simplement le meilleur.
Le seul et vrai lutteur dans le game
Balla Gaye le vrai lion ❤
Le meilleur des meilleurs Balla gaye 2❤
BG2 un vrai lion wow quel défis relancé encore! Félicitations champion BG2❤️🔥🫶🏻 du courage à Tapha car ainsi va le sport🤘✅
Felicitacion balla tu es le meillieur du courage tapha tine
Kou d’accord ni balla Gaye moy roi 🤴 la lal jeme
Merci beaucoup balla gaye 2❤❤😂🎉
Balla guay yabb yabko sett 😂❤❤
Félicitations le lion de guediawaye😂😂😂😂❤❤❤
Balla Gaye contane na d oooh 🎉🎉🎉🎉🎉😢❤ le meilleur
Balla est de retour 💪🏾👑❤
Bonjour Balla.
Tu as lutte avec vivacite. Agressivité.
C.est ta vraie valeir et manière de lutter.
Tu as ete un JAMBAR
Continues comme ça.
Bonne quiye.
Vaq reprendre le Roi de arenes chez Modou LO.Ya ko mann.
Merci
Cou beugeu Balla gaye lale jaime ❤❤❤❤
Je suis modou lo mai franchement balla merite sa victoire fi ben mystique fegnoufi bele passe mystyque bi aussi mystique menoul nek moi j'analyse sportivement tapha entraînement bi desna yaram bou beri berewoul tay physiquement balla été plu pret sur touts les rapidité souplesse vivacité et determination la balla gagne combat bi tapha tine dafa tapette balla lolou moy wakh dji gnemewoul balla yow khekhe moy sa avantage arbitr siffle ngay dem outi diapante tapet bou bonle quand ta balla na yokatte entrainementyi il est sur la bonne voie sou ligeye ba niewate dou nekha dan ndakhe fiibi ak sagn sagn bi woko natte rek wesounako
Lamb nak mo nekh. Ponkal mouñou douma ñouné daño téyé lokho yi. Alors que Tapha a bien abordé le combat, mo dox ci kawam, mo ndieuka door (04:39s) mais biko Balla yeurdo (04:43s) la rer ci Lamb-j. Balla boko soralé wala yéméwoko doko dane.
Waroul wone diapaneté ak Balla té touchéwoulko ba koor diko ci fék. Xamna dañkoné dara nekatoul ci Balla diapouko dane.
Dieula coups warona guén sakou yi ñewat.
Mais du courage na dieul Franc puisk mok Serigne Ndiaye ño bok medina.
Le retour du lion dans la jungle .. tous l’escalier animaux veulent se cache dans la forêt.. balla est le meilleur de génération.. combat royal maintenant modou lo soit prêt pour rendre la couronne avec dignité
😂😂😂😂😂
Quelle dignité iow démal sawi té teudi@@mansourdieng2000
@@mansourdieng2000mayniou diam
Waw waw 😂❤
Katall sa ndeyyy gua maynou jamm gayy bari doull sa baye moyy lakhatou lo tontou sa boudjou Mame
Cette image m'a fait pleurer quand baye Ndiaye et balla se serre les bras 😢
Wakeur Aziz nio beuré di😂
Lole sa problla
Cng warna téré teug lamb farale ko ce nest pas professionnel
Mais kharitame leu dei depuis temps boys es ce que dou nguene xol lolou tamite
Ak bi Aziz di guen ak Tama bi 😭😭😭 niom danio beug Balla bilahi😭❤️
Kou guemone né balla daye dane avant combat bi beusseule j aime
Félicitations Président Maissa Ndiaye vice président CNG.
Mbour est fière
Ak wa Asc bi ❤💛
Qui est là toujours 😂
Kéne doyaloule
Ndeysan ma begue Balla. Félicitations walahi beureh yeufeume leu dako meune ❤
Honnêtement bala n’est pas mon lutteur mais guissouma mystique bala a étais plus fort
Machalah balla gaye 2 yalla nga am diam si barké seydina Mohamed psl ❤❤❤❤❤❤
Il faudra toujours continuer a persévérer rien est facile mais c'est l'objectif que l'on atteigne qui est important machallah
Balla dou sama mbeur mais da meun beuss Machallah il assure l’ambiance à fond félicitations à lui
Le nom de la chanteuse du bakk seereer au début de la vidéo please
Balla gaye c'est un vrai lion 🦁🦁🦁🦁🇸🇳🇸🇳🇸🇳
BG2 seul ❤❤❤❤
Lou mounti khew boulén fatté nii Modou lô moy Roi des arènes 🎉😊anni fans Xlô yi beuss Lénn j'aime way❤❤
Balla seulll👑🙌🏾❤️
Balla a du mérite
Voilà un vrai balla gaye 2
Tapha dou gawa dane balla gaye dé pask balla dako napp téksi guenko paré fép nak du courage tapha
Tu a dit vrai
Damako yereum sakh ! Saway yeukeuti lokho yi comme kouy djebalou
@@papadiom9260 te pourtant mo ndieukeu door
Le vrai lion 🦁 de la lutte sénégalaise ❤🔥✌🏾
Balla reek toujour balla ❤️❤️Mome reek wala dara
Balla je te salue depuis le Congo champion respect
J aime bien azizi n diaye avec une simplicité incroyable bravo balla Gueye 2
quelques soit t'es difficultés Balla chez moi tu seras tjr le meilleur ❤
Bravo champion ❤❤❤❤❤
Balla c'est un grand champion sérieux
Victoire De Balla gaye Congratulations UP Congratulations Tapha Tine Said Sport Continue Travail And Courage Avec Solidarité UP UP 🇸🇳🇸🇳💕💕🙏🙏⛱️
Tapha DCD(DOOR CAXABAL DAN)
Un vrai combat de guerriers
Courage a Tapha felicitations a l empereur
Balla gaye est de retour💪
Le meilleur de sa génération❤
Tapha Tine je me dis que s'il n'avait pas ce gabarit il ne serait jamais un lutteur. Apparemment c'est son physique qui l'a aidé, mais techniquement il est moins bon que les autres VIP
Balla gaye 2 est de retour
Félicitations balla khol sedna❤❤❤
Kou tafa bett com man rek lalall❤ borom damalaye tiohpp😂😂😂😂😂
Balla Gaye moy Russie 🇷🇺,Russie moy Balla Gaye 😂😂😂Tapha Tine moy Ukraine 🇺🇦,Ukraine moy Tapha Tine😭😂
Sakho élimane contane na ❤
Le champion gaye et retour ❤❤❤❤
Bien fait merci balla
Bala gaye 2 yaye beur si Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Balla gaye sera toujours le meilleur dans l'arène ❤
Machalah yalna ladjik té yénéne topousi inchallah
Seul combat ki a 1million de vus en 2semaine ken dou BG2
Oooh TAPHA métina nama téy trop (seul contre tous :Lutteur, Promoteurs, Reporter .....)😢10ans amo défaite, mais li dou dara,geuneu défarou wat rek 😢 le meilleure reste a venir 🎉du courage li Sport la rék (ce défait n'enlève en rien l faite k t'es un grd champion, EUMEU ngafi moudié daan❤)
Felis également a Balla (li moy Sport mais j'espère bien k sa youñ la danaté ils ne dirons plus k tes malades ou c'est YÉKINI) rek
Sen mbeur bi wakh lene ko deug mo djangui khekhou lamb ak beurer ! Bougn wakhanter deug, Eumeu dafko warona dane bilahii Yalla rekk mo gnew beus bobou mais Eumeu dafko doumeu yi metii narone ko dane deff erreur !
@@papadiom9260 saway TAPHA dou Sama mbeur (Modou lay supporté)même si mom la faralone demb
Mais beussou ñakeu thiouné ngay done,té a mn avis je trouve les commentaires trop sévères (lamb🇸🇳)dafa ay nîmouy démé
Parfaitement d'accord avc twa (dans les principes : il a d lacunes, com tt l mnde d'ailleurs)mais danou contre BALLA waroul taax ñou beugeu ko réduire du néant (com koufi défoule dara,alors k'il a bcps faits dans ce discipline sportif.....)
Merci beaucoup🥰 grave azize ya mbeug balla
Merci beaucoup Damas Balladur je t aime beaucoup ❤❤❤❤
Bècaye nèna door you mèti😂😂
Oh oh oh je n'ai jamais vue s de ma vie balla y'a meilleur kay
Notre roi est venu ❤❤❤❤🎉🎉ça ce célèbre
Tapha massa balla douma nalla nak ndeysann 😢
Sama gayi nieuwatt na déh