FIER D´ÊTRE MUSULMAN FIER D´ÊTRE SÉNÉGALAIS FIER D´ÊTRE TIDIANE EN COMPLICITÉ AVEC LES MOURIDES ET LAYÈNES VIVE L´ISLAM VIVE MOUHAMAD (PSL) ALLAHOU AKBAR
MACHA ALLAH, priez sur le Prophète Muhammad SALLAHOU Aleyhi wa Salam et faire des zikrs au nom d'ALLAH ne pourrait être jamais Haram car ce sont des recommandations du saint Coran.Merci Professeur 🙏🙏🤲🤲
Kou amoul xam xam, meunoul weural xam xam bu woor ak woorut. Meuné gni Gamou woul de nyo bakaar? Kon legi Umar Ibn Al Khattab, Abu Bakr, Uthman, Ali ak Sahaba yeup, teg ci tabiyoon ya nyeupa bakaar ndax massou gno Gamou? gni nga xamneh Yonent bi (PSL) ci lamegn niou bopam mor wakhneh gno geun ci jamano. Gamou Bid’ah la. Sa yu ngen ko beug daganal geun di xoot ci ayy pakhou wakh ludoul deug
Togg ba di caricature ni yonent bi ak Sahaba ya daan solo, di yarr sen Sikkim, serigne Touba deff ko, Elhadj Malick deff ko, kii tahaww naan gni ko solo de nio beug torohal Islaam moom nga naan wakh ju woor la deff? Demal xool natalu seign Touba ak Elhadj Malick yeup xool ni niou solo.
والله والله sama holl toyyna dioyyna ki kuko magalul kan gay magal professeur wallahi hamo sakh nigay def sama holll nekkeu talibe cheikh grade geunuko reuyyy yalla naniou yalla fayal makk gni begna begna yalla nagen am diammeu 😭🤲🏽❤️Subhanallah
Pour info dans les 57 pays musulmans seul 12 pays fête cette (anniversaire) à la Mecque il formellement interdit de célébrer cette fêtes, passible d'une peine. Je ne parlerai pas de biddah mais ce qui est sûre est que quiconque la fête n'a pas suivis la Sounnah du prophète et de ces compagnons. Juste pour dire qu'il n'y a aucune garantie du payement par Dieu de cette act créer par les hommes particulièrement de la tarikha tidjaniyya et des chiites . Le Prophète(saw) a été envoyé par notre Seigneur pour qu'ils nous apprennent comment bien adorer DIEU et non pas comment adorez le prophète raison pour laquelle DIEU n'a même pas mentionné l'histoire de la naissance du prophète(saw), de son père ou de sa mère car cela n'a pas bocoup d'importance pour la vie du croyant . D'ailleurs le prophète lui même nous a mis en garde en disant : ne faite pas l'exaltation de ma personne comme l'on fait les chrétiens avec jésus. Pourquoi les gens ne se limitent- il pas aux enseignants du prophète lui qui connaît mieux ce qui mème au paradis D'ALLAH (aza wadj'al).
Écoute celui-là encore qui vient sortir une sottise. "La personne du Prophète exaltée" tiré d'un hadith sûrement(dalil svp)? Bala malay tontou Gueum nga ni Yonente SAW YALLA SWT raniané nako souff mou dem ba assamani diourom,niar romb sakh fofou bref ba yegue si YALLA? Après niou wakhtane?
@@ibrahimaabibmane7337 dalil dites vous ? Tenez en quelques : le prophète صلى الله عليه وسلم a interdit cela lorsqu’il dit : “Ne me couvrez pas exagérément d’éloges comme ce fut le cas des chrétiens concernant Jésus fils de Marie, je ne suis qu’un serviteur, dites alors : “serviteur et messager d’Allah”. (Rapporté par Boukhari et Muslim) “Ô vous les gens, dites votre parole et que le diable ne vous induise pas en erreur, je suis Mohammed, le serviteur d’Allah et son envoyé, je n’aime pas que vous m’éleviez au-dessus de mon rang, dans lequel Allah m’a placé”. (Rapporté par Abou dawud et authentifié par Sheikh Al Albani). Il صلى الله عليه وسلم détesta qu’on lui fit des éloges en employant ces termes : “tu es notre maître”, “tu es le meilleur d’entre nous”, “tu es le plus grand d’entre nous”, sachant qu’il est la meilleure des créatures et le plus noble, pourtant il les interdit de cela, afin de les éloigner d’aller au-delà de ses limites et d’exagérer dans son droit, et afin de protéger l’unicité. Il صلى الله عليه وسلم leur indiqua de le décrire par deux attributs qui représentent le rang le plus élevé chez le serviteur, et qui ne comprennent pas d’exagération, ni de danger pour la croyance : Le serviteur d’Allah et son envoyé. Il صلى الله عليه وسلم détesta ainsi, qu’on l’élève au dessus de son rang dans lequel Allah l’a investi et l’a agréé pour lui. En dépit de cela, beaucoup de gens ont contredit son interdiction, ils commencèrent à l’invoquer, à lui demander secours, à jurer par lui, à lui réclamer ce qu’on ne réclame uniquement à Allah, comme cela se passe dans les fêtes de la naissance (du prophète صلى الله عليه وسلم), les poèmes et les chants, sans distinguer entre le droit d’Allah et celui du prophète صلى الله عليه وسلم.
@@MamadouBa-u5l bo topé yonenti bi à coup sûr do gambou , cause il ne l'a jamais fait , sa fille qu'il a laissé après sa mort ne l'a jamais fait ainsi que ses compagnons qu'il vivait avec lui . Kone koi gambou topo sunnah Mouhamed
Toutes choses qui font que ont nous assimile au non croyant n'est pas conseiller tel que anniversaire ,jours de l'an Noël et autres, presque tous les musulmans connaissent les jours de fête autorisée et il sont tous mentionné dans les texte.donc rien que l'ogiquement ont s'est qu'il y a un doute sur ceux que vous prediquer au gens professeurs est où il y a des doute il faut s'en écarter comme ce qu'il à étais conseiller religieusement par le prophète sws avec un hadith qui dis délaissé ce qui souscite en toi le doute pour ce qui en souscite pas qu'il soit autorisé ou non il est plus prudent de s'en éloigner car personne ne sera la pour être responsable de vos actes au jours dernier méfier vous
Saway lolou sa xalat ndakh yaw ci ëx lil kitab nga bok. Alors que tte connaissance ne se trouve pas sur les livres. Yamal ci say téere te noppi. Xam xam yamul ci ay kayit rek.
D'accord ce que tu dis quand est ce que le prophète l'a dit ou les sahaba l'enseigner ....perso j'ai jamais vu ....et dans la religion tt est permis jusqu'à ce que Dieu ou le Prophète l'interdis... En plus c paradoxal, les non croyants porte des habits tu en portes ça c une ressemblance😂quand tu dis toute chose vraiment ça n'a pas de sens Fait approfondir votre réflexion en fonction de ce que le prophète a dit mais pas créer des lois qu'il n'a mm pas dit
Alhamdoulilah le jour dernier on sera fière d'avoir prier sur le prophète comme Dieu nous l'a recommandé et d'avoir assister à des assises qui raconte la sîra du prophète, alhamdoulilah alhamdoulilah
Togg ba di caricature ni yonent bi ak Sahaba ya daan solo di thiakel, di yarr sen Sikkim, serigne Touba deff ko, Elhadj Malick deff ko, kii tahaww naan gni ko solo de nio beug torohal Islaam moom nga naan wakh ju woor la deff? Demal xool natalu seign Touba ak Elhadj Malick yeup xool ni niou daan solo.
Mais franchement je n'ai pas de problème pour gamou pas, mais prier sur le Prophète c'est quelque chose que l'on doit chaque jour et cela n'a pas de limite ou de jour fixe...mais ne pas célèbrer le jour du gamou ne signifie pas que les gens ne prient sur le Prophète....donc si tu dit que celui qui ne célèbre pas le jour du gamou ne fait pas ce que Dieu nous demande....donc prier sur le Prophète égal attendre le jour du gamou pour le faire....
Non franchement on est entrain de vivre des moments difficiles, parce que ses temps si t'es pas doté de science il serait tellement difficile de savoir quelle voix suivre....que Dieu nous préserve
Meme sa sunnah on n'a pas fini de suivre maintenant vous confirmé les anniversaires sur l'islam.aimé le prophète ce de suivre le coran et le sunnah du dernier annonciateur du paradis et avertisseur du feu de l'enfer, PSL😢😢
Mbir yi c’est simple kou gueum na dieuf gueumoo nga deff linga gueum pourquoi imposer les autres ce que toi tu crois ? En plus lou bon ci gamou baniou war ko bagn
Le prophète Mahomet PSL est le parfaite référence dans la Religion car il a très bien accompli sa mission sur terre avant de partir donc venir derrière lui inventer des choses en islam soit disant que vous êtes sur le droit chemin 😅 non on aimera jamais le prophète Mahomet PSL plus que ses compagnons donc c'est vous les dadiales que tu parles
Encore naka la yallah djoulé ci yonéntebi 1 Naka la sahaba yi djoulé ci yonenetebi 2 Esk ayat yinga toudou ioe yako ngëna xam yonénte bi ak Sahaba yi bamou tax ngané moy firri gamou ak wazifa et donc loutax sahaba yi da wouñu wazifa wala sahaba yi xamouñu wone liy firri ayat yoyou
question pertinente ,lii kesse mom la leraloul wante li mou wah yeub thi wazifa bi tekk ko thi al quran deug leuu. lii mou wax si bagna beuganté bi kou nekk di gagn benen kourel bi deugueula tah na adouna bii amouniou fi baat té mounou niou sah tahawou wa palestine ndeysan , ah xana xaar mahdi bou makk bi nieuw dadialé watniou niou nieup
mdrr ce professeur trompe les gens;;;; maintenant cite moi un seul ayat ou allah dit de faire trois rakkats a timis cite moi un seul ayat ou on dit de faire le gamou professeur dis nous un seul des compagnons qui a celebre le gamou
@@cd5officiel989 ndax daño raconter ci xadiss yi. Comme mome wolou woul xadiss yi litax mou guëme rapporte bi ci conférence bi dadjale deff parce que moko arrangé🤣🤣🤣🤣. Ki philosophe la diappé diné dji
tré bien dit barke borom touba kou beugue yonnete bi beusel aime
FIER D´ÊTRE MUSULMAN
FIER D´ÊTRE SÉNÉGALAIS
FIER D´ÊTRE TIDIANE EN COMPLICITÉ AVEC LES MOURIDES ET LAYÈNES
VIVE L´ISLAM
VIVE MOUHAMAD (PSL)
ALLAHOU AKBAR
Je suis mouride ,et j'aime beaucoup cette personne ngir yallah
MACHA ALLAH, priez sur le Prophète Muhammad SALLAHOU Aleyhi wa Salam et faire des zikrs au nom d'ALLAH ne pourrait être jamais Haram car ce sont des recommandations du saint Coran.Merci Professeur 🙏🙏🤲🤲
Walaye ndeysan vérité absolue ❤😭💯❤🙏💪yonenteh bi ken leu com niko Serigne Touba di wakhé yonenteh bi mo djitou gneup
Non li doumathi doyal dieureudieuf professeur ❤❤
Je vérifie le Coran je vois les propos du professeur
Yalla nalleu Yalla saamm
Ndeyesan ❤️😭😭😭😭 salalahou allah Mohamed ❤️
Wa salim
Ham ham rek mo woor
Ma sha ALLAH
Kou amoul xam xam, meunoul weural xam xam bu woor ak woorut. Meuné gni Gamou woul de nyo bakaar? Kon legi Umar Ibn Al Khattab, Abu Bakr, Uthman, Ali ak Sahaba yeup, teg ci tabiyoon ya nyeupa bakaar ndax massou gno Gamou? gni nga xamneh Yonent bi (PSL) ci lamegn niou bopam mor wakhneh gno geun ci jamano. Gamou Bid’ah la. Sa yu ngen ko beug daganal geun di xoot ci ayy pakhou wakh ludoul deug
Togg ba di caricature ni yonent bi ak Sahaba ya daan solo, di yarr sen Sikkim, serigne Touba deff ko, Elhadj Malick deff ko, kii tahaww naan gni ko solo de nio beug torohal Islaam moom nga naan wakh ju woor la deff? Demal xool natalu seign Touba ak Elhadj Malick yeup xool ni niou solo.
❤ grazie mille Dio ti benedica grazie ❤
مشاء الله
جزاك الله خيرا ❤❤❤
Xam xam dafa nexx wallahi ❤❤❤ dieureudieuf professeur
Professeur yalla nala Faye ❤❤❤ Souma khamone sa keur nala setsy
Merci a toi pr fall
Mâcha allah
Salalahou allah Mohamed ❤️
Machallah yalla na xam xam bi yokkou❤
Merci beaucoup Prof contane thi yéene Allah Athiou
Kou tol ni seydina mouhammad mi takh yalla bindeu niou.
Machallha professeur yallna yalla mberckéll ❤❤❤❤❤
Barké Serigne Touba content na ❤❤ si yaw dieuredieuf professeur ❤❤❤
Machallah Yalla nala Yalla faye yiiw si leral yi❤
Machalah oustaz
Manchallah 👍👍👍
Très important très pertinente
Deug nitt bou wakhè sa ❤ Moy nangou lii deug la Lou graw
Salaallahou alah mouhamed🙏
Machallah 😍✅
ماشاءالله تبارك الله فيكم
professeur dh tiyaba yi nguay am ci diangalé yiii yi ngua niouy diokh 🙏🙏🙏
Merci beaucoup
Professeur !!
Machalah oustaz madiama fall
Salalahu halla Mouhamadine❤
❤❤❤❤❤❤❤ Salalahou aleyhi wa Salam ❤❤❤❤❤❤❤
May GOD guide us. Our religion is tearing apart
Mashallah
MERCI BEAUCOUP PROFESSEUR DIEU VS GARDE
Machaalla sama setugne
صلى الله على محمد
Machallah ❤❤❤
Que Dieu te garde !!!
Machallah wahtane bi amna ndiarigne
Diadieuffati alna yalla barkel 🙏ammine
Franchement merci beaucoup 🙏
والله والله sama holl toyyna dioyyna ki kuko magalul kan gay magal professeur wallahi hamo sakh nigay def sama holll nekkeu talibe cheikh grade geunuko reuyyy yalla naniou yalla fayal makk gni begna begna yalla nagen am diammeu 😭🤲🏽❤️Subhanallah
❤️❤️❤️muhamed saw❤️❤️❤️
Merci grand
Dieureudieuf❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci
Machalla machalla
👏🏽👏🏽👏🏽❤ Mash Allah
Bou yakheu kat di yakheu, défar kat bi warta toke béneu place di noupi
Suko defe toñ. Ndax wax dafa joy ni kima waruta wax moma wax te kima wara wax noppi. Kon ki wara wax te waxul tooñ na.
Dafa lerr ❤❤❤❤❤
Choukrane ya raby
massalah professeur lèrna nangne
Lolu werna Macha Allah
Sallalahu Alayhi wa Sallam ❤
❤❤❤Dieureudieuf
Deugueleu ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha allah eupeu na solo
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pour info dans les 57 pays musulmans seul 12 pays fête cette (anniversaire) à la Mecque il formellement interdit de célébrer cette fêtes, passible d'une peine.
Je ne parlerai pas de biddah mais ce qui est sûre est que quiconque la fête n'a pas suivis la Sounnah du prophète et de ces compagnons.
Juste pour dire qu'il n'y a aucune garantie du payement par Dieu de cette act créer par les hommes particulièrement de la tarikha tidjaniyya et des chiites . Le Prophète(saw) a été envoyé par notre Seigneur pour qu'ils nous apprennent comment bien adorer DIEU et non pas comment adorez le prophète raison pour laquelle DIEU n'a même pas mentionné l'histoire de la naissance du prophète(saw), de son père ou de sa mère car cela n'a pas bocoup d'importance pour la vie du croyant .
D'ailleurs le prophète lui même nous a mis en garde en disant : ne faite pas l'exaltation de ma personne comme l'on fait les chrétiens avec jésus.
Pourquoi les gens ne se limitent- il pas aux enseignants du prophète lui qui connaît mieux ce qui mème au paradis D'ALLAH (aza wadj'al).
Écoute celui-là encore qui vient sortir une sottise. "La personne du Prophète exaltée" tiré d'un hadith sûrement(dalil svp)?
Bala malay tontou Gueum nga ni Yonente SAW YALLA SWT raniané nako souff mou dem ba assamani diourom,niar romb sakh fofou bref ba yegue si YALLA? Après niou wakhtane?
@@ibrahimaabibmane7337 dalil dites vous ? Tenez en quelques :
le prophète صلى الله عليه وسلم a interdit cela lorsqu’il dit : “Ne me couvrez pas exagérément d’éloges comme ce fut le cas des chrétiens concernant Jésus fils de Marie, je ne suis qu’un serviteur, dites alors : “serviteur et messager d’Allah”. (Rapporté par Boukhari et Muslim)
“Ô vous les gens, dites votre parole et que le diable ne vous induise pas en erreur, je suis Mohammed, le serviteur d’Allah et son envoyé, je n’aime pas que vous m’éleviez au-dessus de mon rang, dans lequel Allah m’a placé”. (Rapporté par Abou dawud et authentifié par Sheikh Al Albani).
Il صلى الله عليه وسلم détesta qu’on lui fit des éloges en employant ces termes : “tu es notre maître”, “tu es le meilleur d’entre nous”, “tu es le plus grand d’entre nous”, sachant qu’il est la meilleure des créatures et le plus noble, pourtant il les interdit de cela, afin de les éloigner d’aller au-delà de ses limites et d’exagérer dans son droit, et afin de protéger l’unicité.
Il صلى الله عليه وسلم leur indiqua de le décrire par deux attributs qui représentent le rang le plus élevé chez le serviteur, et qui ne comprennent pas d’exagération, ni de danger pour la croyance : Le serviteur d’Allah et son envoyé.
Il صلى الله عليه وسلم détesta ainsi, qu’on l’élève au dessus de son rang dans lequel Allah l’a investi et l’a agréé pour lui. En dépit de cela, beaucoup de gens ont contredit son interdiction, ils commencèrent à l’invoquer, à lui demander secours, à jurer par lui, à lui réclamer ce qu’on ne réclame uniquement à Allah, comme cela se passe dans les fêtes de la naissance (du prophète صلى الله عليه وسلم), les poèmes et les chants, sans distinguer entre le droit d’Allah et celui du prophète صلى الله عليه وسلم.
Nioune topouniou makkah ms yonente bi
@@MamadouBa-u5l bo topé yonenti bi à coup sûr do gambou , cause il ne l'a jamais fait , sa fille qu'il a laissé après sa mort ne l'a jamais fait ainsi que ses compagnons qu'il vivait avec lui . Kone koi gambou topo sunnah Mouhamed
@@DJob3dkheetou Muhammad yalla doulen dadialé si réér 😑👌
Machalla
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤wallay ndaysan ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Gamou c'est une innovation : une simple question si gamou est vraie pour quoi on ne fête pas ça au Mecque
😅😊❤
Ndeysaane😂 gnakk ndiangue baxoul
Bidda la bouniou sonal birthday yonènte bi bidaà la nèwoul si al quran nèwoul si hadiss
Wa légui loutakh nguén déf photo CHEIKH OMAR DIAGNE bi si page bi. CHEIKH OMAR DIAGNE mouhadam la si tariha bi. Talibé Baye Niass leu. Dafay gamou Di gamouwatt. Meussoul dakk gamou. Bayilèn yakk yakk bakhoul
Salam.... Ki si photo bi dou cheikh Omar diagne mais oustaz oumar sall
@@faliloumbackegueye khana do khoooll. Guisso CHEIKH OMAR DIAGNE si diigg bi
Waw naka la yalla Julli we?
Xam xam mo worr
No ce pa le vérité
Walay yow yay dadial
Yaw khana dadiall nga 😂
Walay qui dey Fenn rek yallah khamnaco
Wlh c’est vrai tellement que il est menteur
Yaw khana dadiall nga 😂
Se data ndeye khamo diango nopil
Niou defar kadou yi, quelques soit nos différences nous resterons toujours les fils du Bien Aimé Prophète ❤
Gamou dou diamou yallah si no yonnete bi déf ko
Diamou yallah bala mo wérr bokouna thi ga déféko niko yonanti bi déff
té yonennti bi défouko.
A feti😂😂 ka
Nane la yonenté Diko defalé bopam ,kon waroulén dougou auto ndakh yonenté bi meusoul dougou auto.
@@mbayedia-gt4lx et les sahaba pourkoi il l'on pas fait
Dougou auto dou diamou yallah
Té temps sonanté bi auto amouttonn
Yaw dof nga rekk
@@jahbarkhamsbn1495 alhamdulilahi bima néké doff si yonenté bi.
Heweul boula thi yalla boléwoul mano thi moss
Salam..je pose une question,ES QUE LE PROPHÉTIE (PSL) fetait ca?ou les SAKHABA commomoraient ca?
Toutes choses qui font que ont nous assimile au non croyant n'est pas conseiller tel que anniversaire ,jours de l'an Noël et autres, presque tous les musulmans connaissent les jours de fête autorisée et il sont tous mentionné dans les texte.donc rien que l'ogiquement ont s'est qu'il y a un doute sur ceux que vous prediquer au gens professeurs est où il y a des doute il faut s'en écarter comme ce qu'il à étais conseiller religieusement par le prophète sws avec un hadith qui dis délaissé ce qui souscite en toi le doute pour ce qui en souscite pas qu'il soit autorisé ou non il est plus prudent de s'en éloigner car personne ne sera la pour être responsable de vos actes au jours dernier méfier vous
Saway lolou sa xalat ndakh yaw ci ëx lil kitab nga bok. Alors que tte connaissance ne se trouve pas sur les livres. Yamal ci say téere te noppi. Xam xam yamul ci ay kayit rek.
Dafa leer👍🏿@@ndiayemouhamed2352
D'accord ce que tu dis quand est ce que le prophète l'a dit ou les sahaba l'enseigner ....perso j'ai jamais vu ....et dans la religion tt est permis jusqu'à ce que Dieu ou le Prophète l'interdis...
En plus c paradoxal, les non croyants porte des habits tu en portes ça c une ressemblance😂quand tu dis toute chose vraiment ça n'a pas de sens
Fait approfondir votre réflexion en fonction de ce que le prophète a dit mais pas créer des lois qu'il n'a mm pas dit
Comment peut on douter d'une "chose " qui fait augmenter ton amour pour le prophète (psl) ?
Alhamdoulilah le jour dernier on sera fière d'avoir prier sur le prophète comme Dieu nous l'a recommandé et d'avoir assister à des assises qui raconte la sîra du prophète, alhamdoulilah alhamdoulilah
Gammou mo protège Sénégal sac année yalla wathie moussiba si sen khaw
Fou dionganté alkhourane am ci adouna senegal mokay dieul ! Moussiba yi na yém ci yaw mikoy guiss
Ban moussiba mobile wathi
@@gueyedarou8886 séne yéné laniouy wakhé, té yéné négu leu
Yaw khana dadiall nga 😂
@@àndëdéfaru sa baye moye dadial bou mak bi domeram
شتام سباب لعان بس
Togg ba di caricature ni yonent bi ak Sahaba ya daan solo di thiakel, di yarr sen Sikkim, serigne Touba deff ko, Elhadj Malick deff ko, kii tahaww naan gni ko solo de nio beug torohal Islaam moom nga naan wakh ju woor la deff? Demal xool natalu seign Touba ak Elhadj Malick yeup xool ni niou daan solo.
Non il a dit de faire des teintes sur leur sikimmm c’est ça.Réécoute bien 👍
Mais franchement je n'ai pas de problème pour gamou pas, mais prier sur le Prophète c'est quelque chose que l'on doit chaque jour et cela n'a pas de limite ou de jour fixe...mais ne pas célèbrer le jour du gamou ne signifie pas que les gens ne prient sur le Prophète....donc si tu dit que celui qui ne célèbre pas le jour du gamou ne fait pas ce que Dieu nous demande....donc prier sur le Prophète égal attendre le jour du gamou pour le faire....
Et ou est le rapport entre prier sur le prophète psl et célébrer son anniversaire ?
Franchement....
Non franchement on est entrain de vivre des moments difficiles, parce que ses temps si t'es pas doté de science il serait tellement difficile de savoir quelle voix suivre....que Dieu nous préserve
@@abdALLAH09999franchement
@@Amm2293 exactement cherchons juste ce qui est conforme au coran et a la sunna du prophete PSL
Meme sa sunnah on n'a pas fini de suivre maintenant vous confirmé les anniversaires sur l'islam.aimé le prophète ce de suivre le coran et le sunnah du dernier annonciateur du paradis et avertisseur du feu de l'enfer, PSL😢😢
Ton titre s'il te plait. Tu peux appeler tes frères musulmans comme des ennemis de l'ilslam? il faut les répondre par la sagesse et des arguments.
Il s’est autoproclamé professeur té xamoul dra . Voilà le Sénégal 🇸🇳 Soubhanallah
Mbir yi c’est simple kou gueum na dieuf gueumoo nga deff linga gueum pourquoi imposer les autres ce que toi tu crois ?
En plus lou bon ci gamou baniou war ko bagn
Le prophète Mahomet PSL est le parfaite référence dans la Religion car il a très bien accompli sa mission sur terre avant de partir donc venir derrière lui inventer des choses en islam soit disant que vous êtes sur le droit chemin 😅 non on aimera jamais le prophète Mahomet PSL plus que ses compagnons donc c'est vous les dadiales que tu parles
Pourquoi le message ne t’il pas fêté ça à lui même mom loumu wra wahx Dou Li me afer tarixa loulu la wara wahx
Kon Sahaba yi ak tabiyoon yi degn Bakaar ci lign gamou woul?
Tres bonne question
Encore naka la yallah djoulé ci yonéntebi 1
Naka la sahaba yi djoulé ci yonenetebi 2
Esk ayat yinga toudou ioe yako ngëna xam yonénte bi ak Sahaba yi bamou tax ngané moy firri gamou ak wazifa et donc loutax sahaba yi da wouñu wazifa wala sahaba yi xamouñu wone liy firri ayat yoyou
question pertinente ,lii kesse mom la leraloul wante li mou wah yeub thi wazifa bi tekk ko thi al quran deug leuu. lii mou wax si bagna beuganté bi kou nekk di gagn benen kourel bi deugueula tah na adouna bii amouniou fi baat té mounou niou sah tahawou wa palestine ndeysan , ah xana xaar mahdi bou makk bi nieuw dadialé watniou niou nieup
mdrr ce professeur trompe les gens;;;; maintenant cite moi un seul ayat ou allah dit de faire trois rakkats a timis
cite moi un seul ayat ou on dit de faire le gamou
professeur dis nous un seul des compagnons qui a celebre le gamou
Professeur bou Mona fenn la fenne rekk la fi neke😂😂
Sa bay moko daka fen bly 😂
Fenkat moy ki weedy té dou indy preuve
@@thiernohagne3495haine ak jalousie moléne di guider. Dou xam xam, dou xéll bou rafét
@@TheBlackCoton billahi
Yaw khana dadiall nga 😂
soi disant lés thieukelé danion khamou niou séne bop
Lëkk yi xana motax dumaleen may dara😂😂😂
Xam xam liberté loy sula lere doci am siki sika. Zikr leen liko jar mooko jar
Zikr dafa néhx
@@ndiayemouhamed2352mouride la, mais sonorité wazifa bi rek dafa mélni loulay doundeul
Tu ne dis que ce qui t'arrange.
Tu peux remuer terre et ciel t'auras jamais raison donc boulgnou sonal ak wakh diou bari
Katal sa ndaye Domi ndiaalo khaalis rek ngaye wout
Yaw khana dadiall nga😂😂
Merci
😢😢😢😢😢😢
😢😢😢
Limaye lathe madiama moy conférence dadjale mome fékké wooko donc nk la deff ba xam lolu.
No deff ba xam Li yonénte bi dan wax
@@cd5officiel989 ndax daño raconter ci xadiss yi. Comme mome wolou woul xadiss yi litax mou guëme rapporte bi ci conférence bi dadjale deff parce que moko arrangé🤣🤣🤣🤣. Ki philosophe la diappé diné dji
« Ceux qui peuvent vous faire croire à des absurdités peuvent vous faire commettre des atrocités. »
Ceux qui sont cons au point de croire que les gens croient en des absurdités sont des imbéciles qui doivent bien tenir leurs langues