Vous êtes des meilleurs vraiment begal gen niou durant la mois de ramadan merci à vous tous lima si metti rekk moy digan niou manqué trio bii waroul yam sii koor gui rekk wayy dorr len yanen projets on est derrière vous
@@mayachoco1073 lool, et la bêtise insista... Au passage ait un peu de classe et de pudeur dans tes propos amna solo surtout chez une lady. Ndeyssane '' j'aime'' deh dina ray xaleyi 😂 yacco Bisou 😘
Taay leu aldiouma bou moudjou si wér koor gui bounou fatté profité gueun si wéteul sunu brorm diouli si sangue sangu yi yalla na nieup am diam. Niankou sanékh manoumbé na yalla goudal sén fane🙏❤
Bonne fête de korité à tous et à toutes . Yallah na sounou borome nanguou koor guii diégual niou sounouy bakar niou téwé KO ayy atti atte inchallah. Mousseul niou ssi mbasse mii té ibi bounetou weursseuk yeup inchallah
Borom Khass tv yegualil serie yi si barker Serigne mountakha mbacke nguir mbecter bimou djour akh limouy retane lo t mbecter bok si li nekh sunu borom koussi ande beussal jaime yalla na sen djam yagg
Bilay c’est la première fois may commentaire mais sama xoll daffa sédd ci NIANKOU NDIAYE GOLDEN BOY Bilay NIANKOU yalla na goudou fann ak kou wax amine rek Barké muhamad ❤️
Non ils m ont tué vraiment vous êtes les meilleurs duo bi waroul yem si koor guirek vivement mou continuer way MERCIIIIII pour ces fou rire yal na lene Yallah fay 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Extraordinaire cette série vous n’avez pas moqué du ramadan et c’était trop drôle avec des acteurs de tailles commençant par sanex, yoro,niankou,le propriétaire de la maison,le vieux qui est locataire, manoumbé, la mère, c’est une bonne inspiration de la part de ttes l’équipe et une idée générale bien différente des autres série bravo à vous tous et merci !
Tout au long du Ramadan vous nous avez aider à rester dans une ère Salama.
Que dieu vous aide et vous donner le Salama.
Gv
Vous êtes des meilleurs vraiment begal gen niou durant la mois de ramadan merci à vous tous lima si metti rekk moy digan niou manqué trio bii waroul yam sii koor gui rekk wayy dorr len yanen projets on est derrière vous
Machalla sama ghaye
fallou diouf
Fii amoule Niankou, Yoro,sanekhe,mandoumbé,ils sont tous des professionels.ont les aiment tous
Moi
Franchement
Re éehd
Bien dit ❤️🌷
Nn mai niankou mofi meun loy sisou
Meussou ma am j’aime dep8 le début ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️na bleu way
Legui bo ama j’aime loumou laye yokou😡😡😡
T'inquiète pas di nga bleu
Machalla serigne Mountapha mbacke yalla nafi guegu te wér si burkeu serigne touba
Allahouma amine🙏🙏🙏
Amineee
Bi ramadan bi commencé batay amagou ma plus de 10 j’aime 👍🏽 😔😔😔😔😔😔
Ne nous fatigue pas. Nga dem setane tei nopi. Tu ne vas pas en mourir. Ciao
daaa bo sétanone tei kepp sa lolou nonou 😂bi yaw tamit kén doula guene
@@mayachoco1073 lool, et la bêtise insista... Au passage ait un peu de classe et de pudeur dans tes propos amna solo surtout chez une lady. Ndeyssane '' j'aime'' deh dina ray xaleyi 😂 yacco
Bisou 😘
daaa 😂🤣🤣🤣🤣😂😂😂💋
Maya Choco dagnion wore way
ioe mi lire commentaire bi yallah nga ame diam🙏
Amine
Amine way
Amine
AMINE 🤲
Amine❤️❤️
Cette série doit continuer après la fin du ramadan qui d’accord avec mw
👇🏽
Moiiiii
Me
Moi
👌
Si siiii
Ana gni d’accord série bi continue
Moi
Mane
Avant de parler il faut réfléchir
Moi 👍🏼☝️☝️☝️
Moi
Yene gni def examen kom mané yala n'a nieup admis si barké nabil Moustapha ❤️
Aminnne way yalla na yalla nagou niann
Amine way
Amine
Amine
Amine way 🤲❤️💯✨
Sanex yalla na sa diamou yagg way🙏
Manoumbé réw nga😂
Niankou t'es le meilleur en ce moment là 😎
Sénégal yalla nafi diamou sah🇸🇳🙏❤️
Diogoye Séne
Yoro Rek
Kou yaakar Serigne Touba yakarou jame yi❤yalla nala yalla téral si korité gui barkébe Mohamede (psL)😘🙏🙏
Yallah na suniou borom nangul niou sunu koor..Dewenati les gars jam si yen 🙏🏿🙏🏿
Sheu met yagui feupp
Amine
Mdrr do niit sakh @doudoudieng
Boul laye😂😂😂😂😂😂 niankou m’a tué sketch bi mom il faut mou continue après ramadan
Niankou l'homme de l'année qui est d'accord 😉
Année 2020 bi douma kheuthio ak kene😅
☝🏻☝🏻☝🏻❤️
☝🏻☝🏻☝🏻❤️
☝🏻☝🏻☝🏻❤️
Nabou Samb
Taay leu aldiouma bou moudjou si wér koor gui bounou fatté profité gueun si wéteul sunu brorm diouli si sangue sangu yi yalla na nieup am diam. Niankou sanékh manoumbé na yalla goudal sén fane🙏❤
Balèn ma akk balnalène yalnaniou yalla défall diam sii barkii Serigne Touba🙏🙏
Oh j'ai les larmes aux yeux😂😂😂 bou kene aimé sama commentaires beugouma
Par force 🤣🤣🇸🇳
Ay waye bayil rk ma mayla sarakh nguir yallah 😅
Bonne fête de korité à tous et à toutes . Yallah na sounou borome nanguou koor guii diégual niou sounouy bakar niou téwé KO ayy atti atte inchallah. Mousseul niou ssi mbasse mii té ibi bounetou weursseuk yeup inchallah
Amine
Allahouma amine yalla na yalla nangou niaane yi si barké yonéene tebi saw
1ère vue yalla na yalla nangou kor yeupp amine 👍💕
Rtsrcuh
Borom Khass tv yegualil serie yi si barker Serigne mountakha mbacke nguir mbecter bimou djour akh limouy retane lo t mbecter bok si li nekh sunu borom koussi ande beussal jaime yalla na sen djam yagg
Niankou lew gua vraiment wetali guen niou ci koor gui bonne continuation 😂😂😂😂🙏
Premier commentaire
Niankou avairr bii yaw la 🤣🤣😅
Niankou est le meilleur de l'année ki est d'accord
🥰🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤭🤭Love🥰🥰🥰💚
Yaye oee dangaa molle dhei...ish ay waay sa yaye la😂🤸🏿♀️ ,u're da best
Guys maay leen ma like way comme nieeup 🤣🙌🏾
Nn niankou c'est l meilleur😂il est très professionnel il joue bien son rôle
Bien parler
Non niankou Amoul bilahi
🙄🤣🤣🤣
lo wér Nga wakh
Lol LERNA ms delen commentaires thie série bi svp
Les meilleurs série de sanex niankhou mandojnbé longues vie a à toute l'équipe ligueye bi rafetena
Niankou ndiaye f@ramaréne Golden boye.😂😂😂 may lén ma j'aime bok👍
Képou kouy df exament yalla nga am si barkep psl Ana gni content si niankou
😂😂😂😂😂vraiment vous êtes les meilleurs contane si yen Golden boy
fallou diouf
yall na diame yageu si Sénégal ❤🙏🙏!! nianko le king 👉👑😂😂😂
Ay mbékté yangi dem😭 na série yi contenue way me yally rew nga😂😂😂😂
Nianko yalla na sa fan goodou way yaw ak gni geu andeul di tournée amine
Bilay c’est la première fois may commentaire mais sama xoll daffa sédd ci NIANKOU NDIAYE GOLDEN BOY Bilay NIANKOU yalla na goudou fann ak kou wax amine rek Barké muhamad ❤️
Kou d’accord ni sanex est un gars modestie besseul j’aime 👍
1ere Aimé Alhamdoulilah! Bonne fête de korité. Déwenety lène . Fèké ay ati ate you bari . Insha'ALLAH ! Insha'ALLAH 2021 AK NIANKOU.
Aminee
Une très belle leçon merci o trio magique
Niankou le meilleur 😂 ❤
Mai assa diop yiw nga
Lii Mounnama Ray très sérieux Nak 😆😆😆😆😆😆😆😆😆😆Nguirr Yallah Gayii Bala Ngaina Commentaires Délènn Sétann baparé beugeu Ay j’aime 👍 Diaroull Yéneu Yidé 😂.....Aparsa Na Nieupou wax serign Touba Dieureudieuf 🇸🇳👑
YALLAH NA NIOU YALLAH NANGOUL SOUGNOU KOOR TEI MAY NIEUP KHEWEUL BOU NIOUY KORITE CI DIAAME KENE BAGNA TOUMERANKEI AMIINE
1er vue mayy léne ma aime tmt
"Wa legui mayma 100flan" 😂😂 non Niangou golden boy amal djam way
Bi niankou mo dakh benene bi les trio sanex nyanko ma ndoumbe vous êtes les meilleurs niankou si doff nakk ga dieum
Salam 😂😂mais niankou greffage samm bi reynama🤣🤣🤣🤣🤣yayou xallehh feeegn na🤣🤣😂😂
Oh je t'ai revu, contane na
Niankou sen yaye bi dafa melni yeina nirou coiffure 😂 😂 😂 😂 😂
Notto wayy😂😂😂
😂😂
@@serigneibrahimathioune1460 Lol D'accord😁
mane ndoumbe momaye raye 🥁👔😉😋
Taye sen tv goudi serigne babacar sy la senagal bene bopoula mouride tidiane yepou béne la lakoum dinoukoum wale yadine
Kou dacor ni niankou dofoul dafa rèw
Le trio me rend folle vraiment😂😂😂😂
Non ils m ont tué vraiment vous êtes les meilleurs duo bi waroul yem si koor guirek vivement mou continuer way MERCIIIIII pour ces fou rire yal na lene Yallah fay 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Extraordinaire cette série vous n’avez pas moqué du ramadan et c’était trop drôle avec des acteurs de tailles commençant par sanex, yoro,niankou,le propriétaire de la maison,le vieux qui est locataire, manoumbé, la mère, c’est une bonne inspiration de la part de ttes l’équipe et une idée générale bien différente des autres série bravo à vous tous et merci !
Niankou il parle tjrs d'actualité. Mention spécial vraiment
Je croyais que j'étais le seul a l'avoir remarquer...
Bly
🤣🤣🤣🤣je vai mourir no vous fort ki es pour k ça continue🖐🏽🖐🏽🖐🏽
Niankou ko mou ray la begue😁😂😅😅😘
Barki alkhouranou karim Niankou yalla nga goudou faneu non damaa réeee ba sonou bilahi😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤
Bi serie bi coumaché ba tay awe ma jaime😫😫
Niankou Tay leçon bi dialenaaa😭🙏
😂🤣🤣🤣🤣🤣Niankou rewww naaaa Golden boy 😝😝
J peux plus vraiment ils sont forts 😂🤣🤣🤣
Oh le trio va me manké xamna dama moudjé déménagé si RUclips rek
Bon déménagement 😅
@@lyabdourahmane5703 merci bc
Toure beugue thiép esk yagui woor
@@magayelo8099 MDR Touré da am diom nak si kor
li yeup djiguene gni gnokay deff bayi sa domm do kham si loumou nek mé trio bi contane nagn loll na sen diam yague bne fête de korité à vous tous🙏🙏🙏
Yalla naniou yalla may korité diam
Niankou est toujours le meilleur
Néna dfa dofone ba werr niankou amoull😂😂😂😂
Yalnaniou yalla fewalé ak saytané té boléniok nabi Moustapha ba aldiana firdawsi in challah
Meilleur série du ramadan kou d'accord
Sama anti stress yi malene beugueu💓❤😂
Que la grâce De dieu soit avec vous
Thiey le Golden boy mongui nii Niankou 👌🏽
Ana gni beugue série bi continuer manifestéléne👨👩👦👦👨👩👦👦👨👩👦👦 maguise☝️👆👆👆
Niankou vraiment c le meilleur car il donne en même temps des conseils en fesant des bêtises vraiment il est superbe 😍
C vrai c du comedy mais en même temps des réalités dans la vie ✌️
Kou dacor avec moi que c'est la meilleure serie beusseul j'aime
Kou j'aime yalla nala yalla dollil diam ak senegal guépp
Vraiment ravi de vous les gas.. Vous m'avez fait pleurer de rire... Amlein djame sama xole bagui frigo
C'est ma série préférée cette année vraiment ils ont fait du bon boulot chaque commedien interprète bien son rôle machalla RAS merci Big up
iow mi di lire commentaire yalle na yalle réalisé say rêve
Amine ak yaw miko bind
bilay niankou tu es le meilleur serie bi waroul diex way
Alhamdoulilah Série bi day Continué After Koor Gui💟👍
Niakhou l’homme de l’Anne 😂😂
Big béguéii à vous nékhal ngeine sunu koor vraiment yalla na seine diam yague koumay dimbali niou nianal leine😍
Athia mayko 100frc bi mou diekh😂Niankou 💪💪💪💪💪❤❤❤❤❤
Niankou 🤣😂😂🤣🤦♂️sacrée Niankou
Meilleure épisode,moralité bi amna solo
Wa ms gayi j’aime waye wala 🤩🤩
Quelle que soit la situation ne faut jamais abandonner vont enfants 💪💪😘😘
Oui as compris le message chapeau à niankou et mandoumbé👌👌❤️
yalla nagnou ko féké ay déwen you baré barii ci barké Mouhamed(PSL)
Sy barké serigne Touba je veux 500 j'aime nguir yallah
Niankou manoumbé one love❤️
Yalla nagn ko sétane aye att you beurii beurii😍
Bilahi dina nam sketch niankou yi si koor gui😅
No li sou koor gui diékhé nako nameu bilay😭😭😭
Le dernier vendredi pour le ramadan y'allah na niou y'allah def fal diam 👌🇸🇳🌏😍😍👌😍😍
Koor gaa ngui dém yalna noufi bayyi
Bouy déllou ci yalna noufi fékkatt ak jàmm ak xéweul
Amiine 🙏
Amine
Ohhh vous allez nous manquer 😢😢😢😢😢😢✌️✌️✌️
niangou ndiay golden Boy dinama rey
Woye niankou nenako boul layyyyye😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Lou am solo la Niankou di wakh. N'abandonnez pas vos enfants pour quoique ce soit. Adouna dafa goudou tankeu
Bilay degue rek nga wax Chiekh Djily
Bilay degue rek nga wax Chiekh Djily
Oooh yalla nalénn yalla fay way😭😭😭