RIP Habib, cela me fait de la peine de revoir Lamine qui est également un guitariste extraordinaire sans oublier Vieux Mac Faye. La musique sénégalaise doit beaucoup à la famille Faye.
Paix à son ame. Grand Lamine yallah yallah feug sa bop ba nga am weer. Le Sénégal vous doit beaucoup en premier chef les artistes que vous avez révélé et éclos. Big respect. On te souhaite une santé de fer et une longévité
Allah meme grand lamine est meconsissable le senegal n aura plus ces pro de talents et genies ils etaient en avance sur le temps Qu habib reposes en paix
Senegal meune nguéne décourager lo nitt Lamine Faye dé Yalla boumou lire séne commentaires yi nguéne top ko ni rék ( dafa fébar, dafa changé, kholal nimou mel) khana vous oubliez que makk dafay gnow c'est juste ça en plus artistes yi séne liguéye dafa méti enregistrements, répétitions, voyages, concerts. Gnanal léne ko rék Sounou Borom bayi kofi té méy ko wér
C bon pleure pleure ton frere vous avez ete des grands valeureux et respectables beaucoup ont pense a toi k dieu te donne la sante et accueille ton frere au paradis
Jàr a jëfati waa kër Ibràhima fay ci ubbee gi nu nu ubbee ci musik. Ca Aadama ba ci sët yi'y yëngu tay ci mbir mi (Yéye, Papiis,...). Budul koon tee'k yéen, musik ci senegaal nasax ndàx yéen a ko ëndi fii mu nekk tay. Jàr a àmee yéen. Yàl na Yàlla sàxalal Abiib làmmiñam ba mu man a tontu laaju bàmmeel yi mu jub. Yàlla jéggal ko ay rëcc- rëccam, te fegal ko mbugalu safara. Aamiin
Tonton lamine kou bakh beugue nite je me rappel biniou neke JT tous le temps chez toi et tu nous a aime et considéré comme madjiguen yala nala yala mey wergouyarame bou bakh bref tonton habibe yala ga khipe aldiana amine
Maass baba mougnal aduna nonoula bilaye bo niakai kou la djeguai aduna doula saf Dara yallana ko yalla yeureum tu m'as fait penser à ma mère ndeysan yallana fi dieum Guen fi gnou dioguai ci Barker seydina Mohamed psl
Merci beaucoup pikini yéne kasé la guiss nitt ganiou guéne di topou Ay information yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi
🤲🏼
RIP Habib, cela me fait de la peine de revoir Lamine qui est également un guitariste extraordinaire sans oublier Vieux Mac Faye. La musique sénégalaise doit beaucoup à la famille Faye.
Billahi famille faye dagne lene wara rendre hommage koufi music wam nex niom la
Oh 1an deja att gawna yalla nako yalla xaré aldjana
Paix à son ame.
Grand Lamine yallah yallah feug sa bop ba nga am weer. Le Sénégal vous doit beaucoup en premier chef les artistes que vous avez révélé et éclos. Big respect. On te souhaite une santé de fer et une longévité
Li dafa daw yaram do kham sakh loy wakh kholal lamine nimou fébaré mome si bopam yalla na nala yalla may tane doy na war 😢😢😢
Ameeen
Aicha Gueye amine
Émouvant et triste. Lamine Faye. Une grande personne. Yalla nala Yalla dolli wër. Amine
Allah meme grand lamine est meconsissable le senegal n aura plus ces pro de talents et genies ils etaient en avance sur le temps
Qu habib reposes en paix
Tonton Lamine massa, Habib Faye Sénégal yeup nioo ko diooy !!!!!
Senegal meune nguéne décourager lo nitt Lamine Faye dé Yalla boumou lire séne commentaires yi nguéne top ko ni rék ( dafa fébar, dafa changé, kholal nimou mel) khana vous oubliez que makk dafay gnow c'est juste ça en plus artistes yi séne liguéye dafa méti enregistrements, répétitions, voyages, concerts. Gnanal léne ko rék Sounou Borom bayi kofi té méy ko wér
Noom sanou reeeeeenala😆😆lamine batou lire msg yi wakhe deuk
sanou faye bien dit
Oh la la c'est triste quant on perd un être cher tout est dépeuplé mille lumières à son propre compte amine 😥😥
Yalla na réthiou limoudone def si aduna yalla na khipe aldiana firdawsi repose en Paix 11 likhlasse
Adouna dou dara khou khol lamine faye mi rek xamni adouna dou dara
Habib etait un genie. Il realisé meme des music de film hollywood
Masseu yalla nako yalla yeureum té xarei ko aldiana
Yalla nga am tane lamine
Yallah nala yallah may tan teh nga yagg fi lool
fimou nék yalla nako geuneul fii mou diogué.amine😭
Respect ABIB yalla nalle sougnou borom kharé aldiana firdawsi
C bon pleure pleure ton frere vous avez ete des grands valeureux et respectables beaucoup ont pense a toi k dieu te donne la sante et accueille ton frere au paradis
Mon grand Habib repose en paix un homme humble
Jàr a jëfati waa kër Ibràhima fay ci ubbee gi nu nu ubbee ci musik. Ca Aadama ba ci sët yi'y yëngu tay ci mbir mi (Yéye, Papiis,...). Budul koon tee'k yéen, musik ci senegaal nasax ndàx yéen a ko ëndi fii mu nekk tay. Jàr a àmee yéen. Yàl na Yàlla sàxalal Abiib làmmiñam ba mu man a tontu laaju bàmmeel yi mu jub. Yàlla jéggal ko ay rëcc- rëccam, te fegal ko mbugalu safara. Aamiin
Ils sont originaires de la Casamance, du village de Adeyane. Leur trait physique est celui des gens du Sud Sénégal. Ce sont de l'ethnie Soce
Faye bi foumou diougue ?
Ndeyssane adouna dou dara yalla na ko yalla yeurame
Tonton lamine kou bakh beugue nite je me rappel biniou neke JT tous le temps chez toi et tu nous a aime et considéré comme madjiguen yala nala yala mey wergouyarame bou bakh bref tonton habibe yala ga khipe aldiana amine
Ndeysann nako yala kharé aldiana. Yala maylene kholou mougne. Yokou tann gui. Amine
Yalna khippe aldiana firdawsi😢😢😢😢
Ndeyssane yalna ko yalla yerem
Ndeyessane massa! Amine Yallah na fimou dem gueunale ka fi amine
Chak jour yalla wane gnou boppam yalla nagnou yalla may mouthiou bou rafet
ndeysane Habib que dieu es pitié de ton âme par la grâce du saint prophète psl
J8bjjjde b6bjb8jbjjbj8jjbbjjjbbjjb8jbjbjbjj8jjbjj8bjjjjjfor j88bbjbjbjbjbjb for bjbjjjbibi jjN.B. jbjN.B. b8jbbbbj8bbii9o
Yalla na khipe aldiana firdaws yalla na rethiou limoudon def ci adouna yalla nako psl derou amine ya rabbi
je regarde tout en pleurant 😢😢😢 paix à son âme
Yalla nako yalla yeureum kharéko aldiana si barké seydina mouhamed si barké khadim rasoule amine
Niit kou bakh mashaa Allah yallah na ko Yallah yeureum🙏🙏😔
Que firdawsi soit sa demeure Barke Serigne saliou mbacke khadim Rassoul.
Par signe de professionnalisme on ne montre pas une personne qui pleure
C l amateurisme
Surtout un homme i un peu malade may Wakh cameraman bi diko summe
Deugg!!!
Yalna khipe aldiana barke moukhamed
Yalla nako yalla yerum ndeyessan
Yalla nakko yalla yereme té tabalko adiana you kawéya ya
Ndayssan yallna yalla yesal yuermed si mome
Ndeye sane yallana dueke ak s saliou
Ah magam la ndeysane yalnako yallah yeureum té kharé ko aldiana firdawsii
Ndeysann yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi amine ya rabile halamine
Yalla ba ka yalla yeureume
Yalla na khipe aldiana fridawsi si barke seydina mouhamet psl
Maass baba mougnal aduna nonoula bilaye bo niakai kou la djeguai aduna doula saf Dara yallana ko yalla yeureum tu m'as fait penser à ma mère ndeysan yallana fi dieum Guen fi gnou dioguai ci Barker seydina Mohamed psl
Adouna dou dara habib yalla nako yalla yeureum sama yaram.dawna lol
ndaysan yaram dawna YALLA na YALLA yeurem ko kharé ko aldiana
Abib repose en paix yallanala sunu borom haré aldiana firdawsi thie seydina mohamed psl.
Repose en paix Habib Faye yalla na souff woyoff si kawam amiine
Que DIEU l'accueille dans son Paradis Éternel.
Merci beaucoup Pikin bon travaille
Allahou akbar yalla moy bour
Nako Yalla yereume te djiegalko Thi barkel moukhamad psl p
Yalla nako yAlla kharèi Aldiana firdawsi 🙏Wa pikini sèn mic 🎤 war guèn ko changè tilim na modèi na No way
Yallah nako yallah yeureum kharéko aldiana ndeysann
Paix à son âme
wa pikini ana khady faye
Yall nako yala kharey alljdana
K firdawsi soit sa demeure éternelle amine
Metina trop k son ame repos en paix
j'ai les larmes aux yeux 😢
Ndeysane thiey adouna yalnako yalla yeureum té khareko thia aldianay firdawsi ya Amine att guawna adouna dou dara😭😭😭
Paix a son âme 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
yallah nako yallah yeureume,
Ndeyesane yalla na khipè aldiana firdawsi
😭😭🙏🏽🙏🏽
Yalla nako yalla kharé aldiana té oyofal suff si kawam
Ohhhhhhh rip😭😭😭😭😭😭
Salam . C’est le même que le lamine Faye de Lemzo Diamono ?
Paix a son ame
😭😭😭🙏
Paix à son âme amine
Paix à son âme😭😭
Grand yala naga tané boubah nguir yala delene diapalanté kou febeur ngene tahawouko gnene gnigui yore alal bou beuri Di setane gni sohleu ndibeul vrement yala.naga tané ak diam
😔 Triste
Alhakou akbar .att gawna
Repose en paix Papa Habib
C très triste deeysaan
Yallana firdawsi di keureum
Ndayssane métina trop
Metina trop😭
😢😢😢😢
Kene doufi dess
Rip
Yakh nguén salam khôl bi
Ngir yalla son pama bi doléne gnoussi dimbeuli sou nite amè naxar sheuuuuuut
Ndeyssane
Métina trope
Yalanaco yalla xare aldialna
Youssou ndour tamite bou féké beugone na Habib faye ne dimbali magame bi.
Naniou mandou
Ndeyssane adouna dafaye nakhate.Abib faye YALLA na khipper aldiana firdawsi.Amine
@@ndiourasarr4228 saway nagnou mandou rk louy xew ci souf yow yeugoko
Yallanako yalla yeurem kharé ko aldianna
Paix á son âme
Paix a son âme
Paix à son âme
😭😭😭
Paix à son âme
Paix à son âme