Je suis tidiane moi aussi un cas similaire m'ai arrivè mais ce lui qui m'a sauvè la vie grâce à DIEU ç'est le petit-fils de serigne mourtada mbackè ibn serigne touba
جهلتم بأسرار معاني تحبب % ببنب الذي لم اخف سواه في قلبي يجدونني من ياتيه لتبايع % وما سبقتني من عاشوه من الحب ولن امدح لنيل نلت الكرامة % ولن ارفع مرئا لقصد تعصب فعبد الكريم كني ذي المكارم % تشبه الشيخ الفاضل لان كاالترب أستاذ بقنانون البلاد وحاكم %وحفيظ فرقان وصيل الي الرب توقره اهل العلوم لعلمه % ويبذله كل المواطن بالهيب وتزوره الحكومة باقتصادها % وتحبه النسوة للبهج والكسب وتجده يعيش البنب واهله % لذالك تثنوه قوالين بالحسب وله بقدر يرفع كل السافل % ويزيد ذي المعال يسقط ذي الودب جميل الصفات كامل الذات سيد % قريب شعير للزوار مع الهيب حميد شريف صاحب الناس بالهدي % وبالآخرين يعترف من النخب بشاش ولايسلم الا ويبسم % رحيب الضيوف عامل البر ذي الخطب فالإنساني الحقوقي المتعاطف % مريد الخديم سبطه منظف الحوب هذا الشيخ نال القصد منذ الولادة % بكرامة الدارين عمدا لدي الصحب وانا له حب لحب وسيلتي % بنسبته كما له حسن بالحسب طبيب الوجود ليس يعلق بابه % لمحتاج أو من عيق داءا اوالخرب وبحوله تجتمعان جماعتي % عراة وعفاة واشكاهما السكب تزدحمه الشعوب كي تتسلموا % أياعجبا نجل الفضيل اعتلي الرتب فرحم ربي شيخي ووسيلتي % واطالنا صحيحي الجسام بلا كرب LE/11/01/2020/خويدم الخديم ابراهيم غي
Bamba moy sa Mane diarra sa Mame baye Saliou sa baye baye fallou sa baye leuh sougnouy mbiir dou diex ndax Mbacke balla say mbiir dou Diex dama marone ga beuneul ma tenou thiofel ma xif ga dioxma dabay ngeunel❤❤❤
DoMOU BAMBA DOU GALI SETEUME DOU NAKHSAYE KÉNE DOU HAMMADOU KHADIM MAKO BEUGUE TE WOLOU KO FI SI ADOUNA AKH ALA KHIRA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL ,MVACKÉ YAGUE FI TÉ WERE DI DIBLI DIAME YI COMME SA BAYE SERIGNE FALLOU MBACKE
S abdou karim mbacke yalnangfi yag tewere si brk seyidina mouhamad salalahu hanleyehi wa salam
Thiey Serigne Abdou karim Mbacke yalla nafi yag té wér si barkéb Serigne Touba khadimou Rasoul
Machalla Serigne Abdou Karim mbacke ken dou mom yalla na fi yague te weur si barcke Serigne Touba
S r abdou karim mbacké yalla nafi yague téweur amine barke serigne saliou
Tabarakalah Tabarakalah🙏
Borom Makarimoul Akhla🙏
Yague fi lool teh andak weur sa neek amal naniou ndeurigne lool Mbacké🙏
Dieureudieuf Mbacké ! Yagua fi Ak weer si barké sa mame Borom Touba Khadimou Rassoul🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Thiey serigne Abdou karim. Mbacké balla loula nara dall yalla nako borom bi wathié ci manee
Mashalla sokhnassi mai prochaine fois defal l tt ba takherlou mouride day degg ndigeul yalla na yalla samm la barkei seugn karim
Barki serigne Touba j'ai les larmes aux yeux mais Baye Kraim boumou diahaleu kėnn Serigne fallou❤ moy bayam
Beugue Nala dè
Je suis tidiane moi aussi un cas similaire m'ai arrivè mais ce lui qui m'a sauvè la vie grâce à DIEU ç'est le petit-fils de serigne mourtada mbackè ibn serigne touba
thieuye serigne touba serigne Abdou karime amoul morom Wallahi
Loumouy def lolou mosii geuneu ndaw goudeul fane mbacké
Mister mor Mister rmo billahi ndeysane lolou dhé dou dara ndeysane kii dafa bakhe rek
@@elhadjimalickthioubtesdeda6790 v
Mister mor Mister rob by c by
domou s fallou seutoup s touba di diamou yalla tégou thi siratal moustakhim warnako meune dioubok yalla réka wooooor
Dieureudieuff serigne touba ak diabootam...❤
Kii moy serigne fallou di serigne modou bousso mbacke yague fii
Machalla serigne abdou Karim mbake yague fi ande ac weurre bargue serigne fallou
Kokou Serigne Fallou moy bayam sama sangue bi yalla nafi yague tei werrr
aka werr allahu akbar
Amine 🙏
Amine
Bay karimm Dou Nith Kii Barcke Billahi Touba kouko xamm Deug sak jours Dingako Saitii
Batinn Baii Barii Loll Barcke Borom Touba ☝🏻❤️.....Yallah Nakofii Yallah yagall lol Taimou wairr Thi Barcke cheikh Akhmadou Bamba sa Mam 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Dieureudieufety Borom Touba machalla Serigne Abdou Karim Yalna Yalla goudal sa fane mayla wér Mbacke
Walakhi mbackè sa baye serigne fallou mbacke dè masoul tas yakar machallah
Mbacké balla yagg fi looole ta wérr amine si barképe serigne fallou
Serigne abdou karim kou yala bahé leu borom bah leu machala
Dieuredieuf Mbacke yague fi te wer si barki serigne Touba
Kén dou serigne abdou Karim rek point
Assurance rek dieuredieuf Baye Abdou karime
Allahou akbar dieuredieuf serigne touba diarama serigne abdou kharim borom makalimoul akhla
Mbackè balla aissa boury domi serigne fallou Mbacke borom ndindi borom na âme mou âme Serigne Mbackè maram mame diarra bousso mathia prokhane Mbacke linga ma defal Mbackè balla finga ma dieulé 😭😭😭😭😭walah Mbacke yalla na fane yi goudou inshallah
ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH MACH'ALLAH
Serigne Touba Amoul Morome Adouna ak Alakhira
Dieureudieufeti serigne Touba
Dieureudieuf baye Karim ❤
Ndeyessane bay karim ni rek la man mel
Kii Yallla sounou Borom laa Yalla Nafi sakh dakk rèk te wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèreu wèrrrrr Bihouurmatii Karim Fallou Sama Kholl ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
da fésss déleu bilahi yague fi looool Mbakè balla aïcha
Machalah mbacke yague fi rek
Ki serigne fallou bou nieuwat kessé leu
Thiey Serigne Abdou Karim
Serigne abdou Karim Mbacké amol morom ndeysane jërëjëf Mbacké
La ilaha ilalah thieuy serigne abdou karim mo yémé Mbackè
جهلتم بأسرار معاني تحبب % ببنب الذي لم اخف سواه في قلبي
يجدونني من ياتيه لتبايع % وما سبقتني من عاشوه من الحب
ولن امدح لنيل نلت الكرامة % ولن ارفع مرئا لقصد تعصب
فعبد الكريم كني ذي المكارم % تشبه الشيخ الفاضل لان كاالترب
أستاذ بقنانون البلاد وحاكم %وحفيظ فرقان وصيل الي الرب
توقره اهل العلوم لعلمه % ويبذله كل المواطن بالهيب
وتزوره الحكومة باقتصادها % وتحبه النسوة للبهج والكسب
وتجده يعيش البنب واهله % لذالك تثنوه قوالين بالحسب
وله بقدر يرفع كل السافل % ويزيد ذي المعال يسقط ذي الودب
جميل الصفات كامل الذات سيد % قريب شعير للزوار مع الهيب
حميد شريف صاحب الناس بالهدي % وبالآخرين يعترف من النخب
بشاش ولايسلم الا ويبسم % رحيب الضيوف عامل البر ذي الخطب
فالإنساني الحقوقي المتعاطف % مريد الخديم سبطه منظف الحوب
هذا الشيخ نال القصد منذ الولادة % بكرامة الدارين عمدا لدي الصحب
وانا له حب لحب وسيلتي % بنسبته كما له حسن بالحسب
طبيب الوجود ليس يعلق بابه % لمحتاج أو من عيق داءا اوالخرب
وبحوله تجتمعان جماعتي % عراة وعفاة واشكاهما السكب
تزدحمه الشعوب كي تتسلموا % أياعجبا نجل الفضيل اعتلي الرتب
فرحم ربي شيخي ووسيلتي % واطالنا صحيحي الجسام بلا كرب
LE/11/01/2020/خويدم الخديم ابراهيم غي
Ah Balla aysha sa baye defnako sa l'âme defko.dono thia seut d'Ay guena deugueur rek...
Machalla kokou Moy baye karime
Yalla na say fan goudu fan ak weer
MASHALLA YALLAH NAMA ALLAH MISÉRICORDIEUX WONALE AK SERIGNE ABDOU KARIM INCH ALLAH KHEWEL REK
Ken day moom Serigne Abdoul kerime lolou mo geneu touty si loumuy def
Ma challah yague fii lol Mbacké té ande ak wére
Thieye sama wadji baye karime
Ken d’où mom machaallah damaka beug bilahi
Machallah Mbacke balla
MACHALLAH
Thiey Serigne Fallou lepp môme la Mbacké
AYE waye.mbacké.yallnagafi.yague.lole.téwer loll.sy.barkeb.SERIGNE touba
dieureuf dieuf MBAcke serigne FAllou Mbacke moy sa waydiour lolou waroul béte kéne.
Kene dou Seringe abdou Karime
Baye karim yalla nga fi yague lolou t weer Mbacké balla gnola beugue gnola gueum gnola sope
Machallah mbacké
Mbacke yaay brom sagne sagne bilahi yagg fi lol te werr
Dierediefeti Serigne touba Serigne abdoul karime Mbacké
Yag fi rék inchallah
Yag fi lol ta wér mbackè
Allahou ak bar
Serigne Touba moy waye
Yaa gname' YALLAH
Dieuredieuf mbacké yague fi lolll teh wer
Dieuredieuf serigne abdou Karim mbacke
thieuy serigne abdou karim kenn la
Ma cha allah kènne d'où mame Cheikh Ibrahima Fall mo Waral li yeup
Ay mbackè
YALLAH layy KARIM
Li gueune touti si louco yalla defale serigne fallou moye bayame bamba ye mame
Machalla
Merci serigne abdou Karim mbacke
Masha Allah
Karim dhe Fallou loy bayam na am mou am dou am dou am lolou la yalla défe nio am kou kéne amoule mouy Ahmadou Bamba
Wane lene ma baye karim mbokou talibes yii
حفظه الله ورعاه
Bamba moy sa Mane diarra sa Mame baye Saliou sa baye baye fallou sa baye leuh sougnouy mbiir dou diex ndax Mbacke balla say mbiir dou Diex dama marone ga beuneul ma tenou thiofel ma xif ga dioxma dabay ngeunel❤❤❤
Amo bene talibé
Waw
Seul allah peut allongé le vie de quelqu'un ou prendre son âme c'était juste pas l'heure de sa fille
daw na yaram mbacke
Ken dou ahmadou
Bilay ki kéne dou mome
Ndeysan
Yagefi tewer
Bilahi dafa yeme
KHARITU AMADOU BA
Ay way beugnako guiss d
Yow djiguene souy wakh ak kilipha dou takhaw di wakh dey tokk sou bene yone naka tokk
Wah nga deugeu lolou la beugone wah ak yeukeuti saye lokho di diokhar bi
@@alimajolie3195 wah deug bokoul si ay teguine dafa warona yegue souff
@@cheikhounasene8228 wawaw yonnu mouride mom ay téguin lanou rawé nieup té serigne sidi moukhtar dane nako wah kou amoul tégui do tégui dara
Serigne fallou lay bayame
Baye karim dafa tèral karim motakh alkhour ane fayko❤❤❤
ALAHOU AKOUBAR
Mbacké yagueu Filooll
Ay mbacké bala aïssa boury yague fi lol
Goudeul fane mbacke balla
akssha
DoMOU BAMBA DOU GALI SETEUME DOU NAKHSAYE KÉNE DOU HAMMADOU KHADIM MAKO BEUGUE TE WOLOU KO FI SI ADOUNA AKH ALA KHIRA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL ,MVACKÉ YAGUE FI TÉ WERE DI DIBLI DIAME YI COMME SA BAYE SERIGNE FALLOU MBACKE
Dieunreudieuf mbacke
Numero mer bi la soxla ndax mako yabalone ci chiek abdoukarim mbacke
Thiey
Bimou toudé khadim rk gueneu contane
Magui europ wayé mome rék la beug ga guiss
Man ak yaw
☕☕☕🤲
R
Machallah
Machalla
Machalah