Yen nakhlen yombouna..Ki wakhe kat la..mouni ragaloul yallah..Dans talib al ilm on lit ceci : La crainte et l’espoir font parti de l’adoration.Lui c’est un arrogant ignorant.Vous parlez d’esprit.Quel esprit ?
Pourtant il a parfaitement raison, deug gou wérr la wakh, ragal yalla c'est pas donné à tout le monde. Nafékh menoul wéssou di déff lépp li yalla di téré ba nopi sagna takhaw ni da nga ragal yalla
Allah n’a pas mentionné dans le coran..le fait de se repentir ? Les péchés que l’être humain fait n’a rien à faire avec la crainte d’Allah.Et la parole est à mesurer le fait de dire je ne crain pas Allah c’est différent du raisonnement qu’il fait..Il ne devrait pas raisonner en disant « je ne crain pas allah »..Que des spéculations dans le plateau..Pas de connaissance que des conjectures..Et il dit que des bêtises cet idiot..En plus il dit « yallah amoul yeurmandé » ngen key bayi ci plateau bi ?
Il a décortiqué sa phrase👂 Pourtant kudul djuli à temps aka gneme Allah t yab ko sax Yalnagnu yalla bal rek t tek gnu si yoon Il est trop franc pour notre société Ndax sunu société day wodu wax alors que mom amoul filtre donc si deguine dafay violent thi sunu "entendement senegalais"
Vraiment d une part franchement parler je suis avec moudou .il est sincère avec lui .il ne laisse pas emporter par les autres vraiment .je ne veut pas le juger mais dé fois aussi il part trop loin. Bonne continuation et félicitations à toute l équipe tfm
J'aime la vérité elle a pour moi une importance capitale et rien en elle ne me semble indigne vous comprendrez donc aisément pourquoi j'ai beaucoup d'admiration pour ce monsieur
Mani sétlou ba khame seuye bi dina bakh ou pas , lolou dou islam ,seuye yallah mokoye tak, Modou daffa dégue islam ta andeu ak yallah motakh douffi bakou di gnodi nane mo gueneu ragal yallah, il est sincére, honnete machallah Yallah khamoul sentiments fékna bb si birou ndayam rayko ta yeureumoul yaye dji, modou aye verset coranique laléne di tégual
Bravo Modou, faites jamais de politique/ Vite votre bon projet, mes enfants petits-enfants et amis et moi-même donneront un euros par mois. Alors foncez. Je suis fière de vous.🙏
Modou yangui wathieu yonne dh yalla yeurmandé la dh moy ar rahman di ar rahim moy yeureum kouko nekh fi si dounya te tamit moy yeureum tanekham si alakhira modou yangui wathie yonne nakkk sois plus modeste et humble
Sénégal parfois Damaye rous si quelque débats goudou fan gatou fan yalla d'où défar pour 4 jour Di réy dans 3 jour Sénégalaise déy fénn fa moudiou guém ay fénam naniou délou si yalla Lou way sokhla yalla amnako
Moi perso c'est aujourd'hui que j'ai commencé à regarder cette émission et je trouve ça vraiment intéressant. Mais j'aurais mieux préféré qu'on élimine Ya Awa. Par ce que grâce à votre émission on y apprend beaucoup on à besoin des personnes qui se servent de leurs cerveaux comme Modou et Ndélla mais po gni wakh juste pour qu'on remarque leur présence
Modou Geuy togou kaay biga took soudoul won yeurmande yalla rote ga bou yague tok biga tok fofou di wakhtan âme wer mana wakh mouma wo soudoul won yeurmande yalla fo dieum soudoul won yeurmande yalla.....
Al rahmane brom yérmandé ki eupp gneupp yérmandé tei di diokhé yérmandé téydji boula yeuramoul wone doo tolou fii ngua talou té doo am lingua am kone dél xoll linguèy wah
1. O hommes! Craignez votre Seigneur qui vous a créés d'un seul être, et a créé de celui-ci son épouse, et qui de ces deux là a fait répandre (sur la terre) beaucoup d'hommes et de femmes. Craignez Allah au nom duquel vous vous implorez les uns les autres, et craignez de rompre les liens du sang. Certes Allah vous observe parfaitement.
Limou wakh deg deg la ayy doff nguen rekk senegal Ken ragalou fi yalla mais modou am na jamou yalla yo khamni de meun nan la nianal yalla yokou say fan
Ay wakhi doff rek la fi dègue Modou Gueye Ar-rahman si tourou yallah yi la bokou. Wakhi kou bèw rek ngay wakh Ndoye Ban Bayil rasatou bi yallah dañkoy xam ragalko tamite bolèsi.
Bro modou géstoule nga khole univers bi ak leep liko weur allahou défla ngay niit limou geuna téral si limou binedeu ay way naniou goréé ta sante rabbi souniou borom mi niou amal ta tagouwouniou dof deug moy kham lila war ta nékoulosi yagi réér bro !!fébar wésouwoul rééréé yeurmendé ya rabbi soumet toi pendants qu'il soit trop tard le seul reméde c'est le coran et le noble prophète seydina mouhamad salalahou aleyhi wa salam please!!! Salam frere.
Ki dafay doul rék so ragaloul Yalla nioune ragal nanouco,so geumoul ni Borom bi beurina yeurmandé nioune Geumm nane co ndah ci yeurmandéme motah nga tokk fofou di wakh sa wakhou dof yoyou mou bayi laci
Modou gueye akk gni nek si plateau bi yup yem hamou gatt.. Nena Yalla ampul yermande g potie niak jangue bakhoul defay rereul bilahi. Yalla nalen Yalla weul bati
☝️☝️☝️Modou fassé🤔on es en Afrique !!!gueumo serigne!!! louy sa tétal? koula Jokh tétal ?lou ko warral tétal bi ??pour quoi toujours tt noir et tt blanc... ya leundeum🤔🤠🤠🤠
Wakh deguine la lath kou ragal yala do tarde wakhou diouli do moy et il a parfaitement raison Sénégal danou nième yala de trop te wessouwoul nitt kouye fenn surtout
Il faut essayer d'analyser les idées de ce Modou pour chaque émission je ne le blâme pas par-ce-que son rôle dans les émissions c'est apporter des apposition pour chaque sujet. Donc tout ce qu'il dit il n'en croit pas.
Il est excelent, ce Modou c un gran type, un Big cerveau
Bilahi ki éspris la guiss na lolu
Yen nakhlen yombouna..Ki wakhe kat la..mouni ragaloul yallah..Dans talib al ilm on lit ceci : La crainte et l’espoir font parti de l’adoration.Lui c’est un arrogant ignorant.Vous parlez d’esprit.Quel esprit ?
Pourtant il a parfaitement raison, deug gou wérr la wakh, ragal yalla c'est pas donné à tout le monde. Nafékh menoul wéssou di déff lépp li yalla di téré ba nopi sagna takhaw ni da nga ragal yalla
Allah n’a pas mentionné dans le coran..le fait de se repentir ? Les péchés que l’être humain fait n’a rien à faire avec la crainte d’Allah.Et la parole est à mesurer le fait de dire je ne crain pas Allah c’est différent du raisonnement qu’il fait..Il ne devrait pas raisonner en disant « je ne crain pas allah »..Que des spéculations dans le plateau..Pas de connaissance que des conjectures..Et il dit que des bêtises cet idiot..En plus il dit « yallah amoul yeurmandé » ngen key bayi ci plateau bi ?
Il a décortiqué sa phrase👂
Pourtant kudul djuli à temps aka gneme Allah t yab ko sax
Yalnagnu yalla bal rek t tek gnu si yoon
Il est trop franc pour notre société
Ndax sunu société day wodu wax alors que mom amoul filtre donc si deguine dafay violent thi sunu "entendement senegalais"
Vraiment d une part franchement parler je suis avec moudou .il est sincère avec lui .il ne laisse pas emporter par les autres vraiment .je ne veut pas le juger mais dé fois aussi il part trop loin. Bonne continuation et félicitations à toute l équipe tfm
Lim wax diss na ssi deiguinn wawé deug pire leuh
Kou ragal yallah deug dou dox ssi tiaxann
Niounn nieupp gueneunn yallah mé rare sont gni ragal yallah 🙏
Modou tu as dit tout haut ce que nous disons tout bas
D'ailleurs Diamano biii kou Ragal Yallah esk aam naa...?
merci beaucoup modou Gueye
J'aime la vérité elle a pour moi une importance capitale et rien en elle ne me semble indigne vous comprendrez donc aisément pourquoi j'ai beaucoup d'admiration pour ce monsieur
J’apprécie trop ce mec❤
Modou gueye je l'adore. Il est véridique
Machallah modou machallah
وقال صلى الله عليه وسلم إنماأعمال بالنيات وإنمالكل إمرء مانوىٰ
Je te respect tu parles pour toi inchaallah
Yallah amoul yeurmandé Asbounallah Modou Gueye wakhoulo deugue Bour yallah diokhla wéure gou yarame diokhla ngèlaw loy Noyèe diokhla léupe lingay dieufeundiko thi Adouna ngani Amoul Yeurmandé wallahi Fayoulo Naare ba khoramam
J'aime beaucoup ce Mr Gueye parce que il est vraiment pertinent
modu et tres pertinent
Bravo Modou!!! I think so great 👏
Mani sétlou ba khame seuye bi dina bakh ou pas , lolou dou islam ,seuye yallah mokoye tak,
Modou daffa dégue islam ta andeu ak yallah motakh douffi bakou di gnodi nane mo gueneu ragal yallah, il est sincére, honnete machallah
Yallah khamoul sentiments fékna bb si birou ndayam rayko ta yeureumoul yaye dji, modou aye verset coranique laléne di tégual
Merci modou
Chii ndoy bane mo ngi doda wakh louma d’accord yallah dagne kay xam
Merci Modou Gueye tu es raisonnable
Degue nékhoul ❤❤
Fans club modou geuye depuit itali
Hane amdy j'hadère mais nak na changè chemisame bii😂😂😂
Antouca nitou deug puir moy Modou Geuye il peuz bien ces mots wa salame
@@binetoudiop337 il porte que tu blanc il la di
No j'aime cette Monsieur bilahi mashallah tu é direct
Je l'aime trop
Modou tu es le meilleur
Niaka Kham yalla motakh guéne diko todou fi
Bravo Modou, faites jamais de politique/ Vite votre bon projet, mes enfants petits-enfants et amis et moi-même donneront un euros par mois. Alors foncez. Je suis fière de vous.🙏
Modou yangui wathieu yonne dh yalla yeurmandé la dh moy ar rahman di ar rahim moy yeureum kouko nekh fi si dounya te tamit moy yeureum tanekham si alakhira modou yangui wathie yonne nakkk sois plus modeste et humble
Il a parfaitement raison ce Modou Gueye kou ragal Yalla dou déf lou bone
Modou il est intelligent 🧠
Parfaitement d'accord avc modou,mais ndoy bann non,yala kouko xam ragualko.
J'aime Modou Gueye il est pertinent way limouy wax ak gnimouy waxal sax deganetei wouniou mais wax bou am solo la wax
Modou gangaye khalé tu d'or
Modou limou wax nekhoul degg wayé amna youma ko nangoul nak
S saliou nena yalla yeurmadela waye boula fatele bopam do tal loudoul mom
Nite kou deugeu franchement mais sénégalais yi dougnou comprendre fimouye wahé
Mane dé modou la beugeu bilahi
Si vous l'écoutez bien modou gueye a toujours raison...
Modou boull dioume baye wèdi waxi yala ndaxe tè yala mo waxall bopame yonénetebi néko rabi ikhfire warhame wa anta arhamou rahimine
La parole est un couteau à double tranchant ,mais il faut bien écouter modou,car c'est un orateur qui masques ses paroles par la sagesse
C’est juste un beau parleur mais ce qu’il raconte est dépourvu de sagesse il commet des sacrilèges.
No modou il est extraordinaire jtjur!! Je sui totalement en phase avc lui
Sénégal parfois Damaye rous si quelque débats goudou fan gatou fan yalla d'où défar pour 4 jour Di réy dans 3 jour Sénégalaise déy fénn fa moudiou guém ay fénam naniou délou si yalla Lou way sokhla yalla amnako
modou il parle en argot il faut etre tres intelligent avoir un esprit ouvert pour comprendre la ou il parle
Sûr d'accord avec toi
Mais YALLAH amoul yeurmeundeh suis pas d'accord avec toi. Sa contredit avec la parole DIVINE qui dit ARAHMAN ET RAHIIM
Ragal yalla n’a rien avoir avec les péchés car par nature l’homme est pécheur. On ne peut que chercher refuge au près de Dieu contre les tentations.
Modou guéye yangui dioum dh Le Pardonneur fait partie des magnifiques noms de ALLAH SWT
Frr kou dh AK sa bammél
Vraiment modou dall en voulant être trop intelligent on devient con au final
Ay modou adouna worr nala dh
Moi perso c'est aujourd'hui que j'ai commencé à regarder cette émission et je trouve ça vraiment intéressant. Mais j'aurais mieux préféré qu'on élimine Ya Awa. Par ce que grâce à votre émission on y apprend beaucoup on à besoin des personnes qui se servent de leurs cerveaux comme Modou et Ndélla mais po gni wakh juste pour qu'on remarque leur présence
Modou Geuy togou kaay biga took soudoul won yeurmande yalla rote ga bou yague tok biga tok fofou di wakhtan âme wer mana wakh mouma wo soudoul won yeurmande yalla fo dieum soudoul won yeurmande yalla.....
Al rahmane brom yérmandé ki eupp gneupp yérmandé tei di diokhé yérmandé téydji boula yeuramoul wone doo tolou fii ngua talou té doo am lingua am kone dél xoll linguèy wah
Il dit trop vrai
Modou ragal yape yalla la
Sénègal daguène beugeu affaire serigne!
Modou damako beugue🤣🥰
Merci moudou magi si yaw
J’adore se monsieur Gueye il est véridique je te jur mai vous comprenez pas ou il est entrain de parler
Ou il est entrain de parler ?
Wa ki mom loum donne bâ ausé du wakh li ak mom moy Kane khana dafa bari khalis
Bah oui c'est un grand philosophe Modou gueye
Modou moyetol yalla diaarr na ragal 😙
Yalla diarna Raggal deug deug
Mane ak Modou kif-kif même vie
Wooooye
Modou ma la fann
Billae modou gueye a parfaitma raison srx j 'adore ce . Ca wallahhhh
Mo guerrier leu 💪💪💪💪💪💪
J sw daccord avk modou gueye
1. O hommes! Craignez votre Seigneur qui vous a créés d'un seul être, et a créé de celui-ci son épouse, et qui de ces deux là a fait répandre (sur la terre) beaucoup d'hommes et de femmes. Craignez Allah au nom duquel vous vous implorez les uns les autres, et craignez de rompre les liens du sang. Certes Allah vous observe parfaitement.
Limou wakh deg deg la ayy doff nguen rekk senegal Ken ragalou fi yalla mais modou am na jamou yalla yo khamni de meun nan la nianal yalla yokou say fan
J'aime beaucoup Modou gueye
Lima diakale Moy Modou ak Mane danio bokkou même kalate Mane dama foguone ne werouma waye guis'na kou melni mane
Modou j suis d accord avk tw la tradition n est pas tjrs sagesse
Pour comprendre le raisonnement de Mr Gueye, il faut penser philosophiquement...
Wakh gua deugue de
Sama Modou way
Ay wakhi doff rek la fi dègue Modou Gueye Ar-rahman si tourou yallah yi la bokou.
Wakhi kou bèw rek ngay wakh
Ndoye Ban Bayil rasatou bi yallah dañkoy xam ragalko tamite bolèsi.
Bro modou géstoule nga khole univers bi ak leep liko weur allahou défla ngay niit limou geuna téral si limou binedeu ay way naniou goréé ta sante rabbi souniou borom mi niou amal ta tagouwouniou dof deug moy kham lila war ta nékoulosi yagi réér bro !!fébar wésouwoul rééréé yeurmendé ya rabbi soumet toi pendants qu'il soit trop tard le seul reméde c'est le coran et le noble prophète seydina mouhamad salalahou aleyhi wa salam please!!! Salam frere.
Il a parfaitement raison
Modou con neu 😂 nenaa yalla amoul yeurmandei 😭😭😭
Sénégal gni wara noppi gno fess télé yi désole😭😭😭
Je te jure
Sama pape lay degeu mounane ma yalla kendou ka ragal dangakay moytou
Ah loy moyto kay ragal ngako
Ki dafay doul rék so ragaloul Yalla nioune ragal nanouco,so geumoul ni Borom bi beurina yeurmandé nioune Geumm nane co ndah ci yeurmandéme motah nga tokk fofou di wakh sa wakhou dof yoyou mou bayi laci
Niveau bi kawé n’a khamo lenn li modou di wakh
Modou Gueye a raison💯💯💯
Modou yaye chef💪
Madou les sénégalais te comprends m'aime pas tu parles bien ce plus que clair
No vraiment c’est gas a parfaitement raison bilay
Daguène di degglou Modou Gueye ak khèle! Ragal Yallah aye wakh rèèk la.
Modou gueye akk gni nek si plateau bi yup yem hamou gatt.. Nena Yalla ampul yermande g potie niak jangue bakhoul defay rereul bilahi. Yalla nalen Yalla weul bati
Modou mi waxi dof lay wax..yalla moni ina rahma talahou minal moukhsi niina..nganan yalla amoul yeurmandé
ki soumako mounone guiss diakhrane dinako wédilo limou wakh si anam gou tarr
أعوذ بالله من الشيطان الرجيم إتقو الله تبارك وتعالى في كل حين إن الله غفور رحيم
Vérité absolue bilay
Bien sûr sans complexe pas de dérapage Nice j’aime jl logique dans ces faits merci
Vous écoutez pas Modou Gueye il réfléchit très bien
Modou daal dou nafèkh il dit ce qu'il pense. Voila
Dans talib al ilm ont lit ceci : La crainte et l’espoir font parti de l’adoration.Lui c’est un arrogant ignorant.Vous parlez d’esprit.Quel esprit ?
Modou taye môme wakhgna nakh wakh nékhoule déguine monékh
J’en suis sûr et certains que d’aucuns pensent qu’il joue ou qu’il fait de la comédie Ndeyssane vous n’avez rien compris
Ndoye bane mome vrai inossent le
Dafa nehoul degue mais modou deugue rek lay wakh
☝️☝️☝️Modou fassé🤔on es en Afrique
!!!gueumo serigne!!! louy sa tétal? koula Jokh tétal ?lou ko warral tétal bi ??pour quoi toujours tt noir et tt blanc... ya leundeum🤔🤠🤠🤠
Wakh deguine la lath kou ragal yala do tarde wakhou diouli do moy et il a parfaitement raison Sénégal danou nième yala de trop te wessouwoul nitt kouye fenn surtout
Li mo takh SENEGAL dou am diammou maky sall bakhna ci wa SENEGAL
Mdr😂😂😂mane dall modou la begue
Il faut essayer d'analyser les idées de ce Modou pour chaque émission je ne le blâme pas par-ce-que son rôle dans les émissions c'est apporter des apposition pour chaque sujet. Donc tout ce qu'il dit il n'en croit pas.
Wakhine la déguela lathie 👍👍
Yaw wakhofi Dra démal diangui