beus boulen di khamni que culture existe woul que yallah dafa sib lolou rek senegal avancer 🤲man louma kham moy man dioulite la te senegalaise la alhamdoulilah💕 awma ben culture bokouma ben khet te beugouma bokou sakh
Ah Sanekh dioum nga ! Sama nar bi, sama sérère bi, sama Toucouleur bi, ce sont des mots affectifs. C'est du Wolof pure, sama yaye, sama Baye, sama morom, sama xarit... Il y'a beaucoup de personne qui ont appris la langue Wolof dans la rue, elles ne comprennent pas le vrai Wolof. Et pourtant Sanekh, tu es Wolof. Tu comprends ces nuances la. Il faut que l'association Mbootaayu Leppiy wolof parle pour éclaircir les Wolofs et les lakkwolof ( Wolophones).
Sanekh rew you bari ame na seuy yo kham ni dufa ame lou ame senegal barina si khéty dh Mali am nafa basi rew arabe yi am nafa france amna khét bo khamni sen birr rk nioy seuy kou beug xam internet bi ken sonatoul tapel khol
Mane mi amna si histoire nop ben sarakholé mais fima rombou gnouni ma nopaloul ki doko takk ba nônou lassi moudiou ba takk keneen te kokou rek la beugone 😢😢😢
Moi même je suis gneigno pur bete bete mais j’ai un esprit de dépassement. C’est juste une série pour sensibiliser. Donc les insultes ne me dérange pas
Bane Gnégno moy Nangou nioulay wakh Gnégno kharamata Ndiaye Sa nekh sa scénariste bobou dafa beugg Diay série bi rek mais battou guinaw meunoul niakk mais amoul ken kou sania takhaw ak sa moromou nitt diko wakh sa Askanou kharamata Ndiaye bi en face moulay kh👀l ni té defoul si yow Lou métti ce mot là admettons le c'est vraiment exagéré " Gnégno Kharamata NDIAYE wala Guéwel kharamata NDIAYE wala Guèrr kharamata NDIAYE" jamm dilassi féck Théâtre là rek pour sensibiliser nitt gni alerté nitt gni pour niou bayi lolou ndakh L' Islam nangouwouko Christianisme nangouwouko
Yaw linga xamoulo ci adouna dafa melni beuriwoul...moi je suis gnégno et la séquence en question ma famille et moi l'entendons presque chaque jour! Donc ne dites jamais que cela n'existe pas ou qu'une personne ne puisse pas avoir le courage de le cracher à la figure d'une autre personne. Sénégal lepp amna fi...
Sa existe dh bilaxi ande na ak sama ben xarite Di niane diabar bilaxi mere bi bagn Liga done gueweul moma diaxal mais kou bakh ga beug sama dom diapaleko bep côté respecte gama yarou ga Mané sama copin bi ki na fek la niou dem bilaxi ba ni la yake diganté bi
Guéweul, gnègno ak laobé ay nit lagnou wayé dagno wara bayi di gnan sène moromou nit bamoulèn di yab. Wayan bahoul dou yeufi gor. Wayan mo tah gnou bari di wah né dougnou may sèn dom guéweul. Le griotisme doit être aboli.
Lolou afrique rek la ame rawatina Sénégal mo takh niou tardé deuk bo kham ni daye guene di pauvre di dém europe li bou fa amone kou prononcer mot bobou casso ngua dieum
Le problème des castes au senegal est mal posé.Est ce que les castes se sont affranchis de leur pratique? Quand cela les arrange ça ne dérange pas .ils se réclament griots pour revendiquer le micro central et bénéficient par cette posture de privilèges.
Niénio Kharam yi mom rafetoul mais nak Sénégal depuis les royaumes lolou mo mosss am Guer-Guéweul-teugueu-niénio-maabo- diamm(esclave) au bas de l'échelle
Sanékh est le meilleur de tout les temps
Nioun ngengo yi dh nioye Sénégal loufy bakh nioun la j suis fière d'être ngengo balamaissa ❤❤❤❤❤niofi am méthié niofi eupp diom buegue Lou bakh
Bien dit
Amoule sii alkhourane dh ♥️🤟 la
Contane na si lou Maréme nokou si série bi Maréme référence la fi Sénégal di représenter djiguéne bou bakh fi Senegal ❤
beus boulen di khamni que culture existe woul que yallah dafa sib lolou rek senegal avancer 🤲man louma kham moy man dioulite la te senegalaise la alhamdoulilah💕 awma ben culture bokouma ben khet te beugouma bokou sakh
Mane damay moudié dem deuk si Layenne yi rk pour eviter affaires caste yi😢😢😢
C'est ce qui fait la spécialité de cette série
J'ai hâte de revoir Maréme SALL alliance Soumboulou
Aziz Niaaneu l'Ecrivain🎉❤❤
Merci.sa.nex.bougout❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤yala.na.yala.faye.❤❤❤logue.vie.inchala.atise.da.fa.wara.yé.té.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂
Machalla kadouyi amna solo nioune niep béne lanie fa yala Nanou diapanté té yala rék takh Adina sakhoul
Sanekh mom dama ko beugeu Yalah gua am diamou amine bete bete amna solo lool sakh 🥰❤️🇸🇳❤️
Mem gewelyii tamit nonou lagnouy khebé gergni😢
C'est quoi gewel
Mém gergni tmt nonou laniou gergnie khébé nioune guéweul yi
Te pourta gnoun gniepa yam thi yalla kou gina joullité ragal yalla mofi gin wayé dou ger dou gewel kou nekka defa kheb kenen😢
❤❤❤ billaahi j'adore sanekh maachalaa
❤❤❤❤❤❤❤❤❤ machallah Nice ❤❤
Merci sanekh yéx yan guen depuis polémique guan warronn wax
Le meilleur de sa génération ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤machala.❤sa.nex.kotana.thi.wawe.mane.dé.géwele.la.wayé.géne.douma.yape. 3:56 nax.mousoule.ma.taxaye.thi.genne.nane.ko.mayma
3:49 kuko gëm yaa ngi bakkaar. Ku amul thieur ci Yallah, Ku amul bén leer rekkay xool moromom diko xeeb
Les ñéñon son des noble
Je vais commencer à suivre la série à cause de Halima Gadji❤😊🙌
Ah Sanekh dioum nga ! Sama nar bi, sama sérère bi, sama Toucouleur bi, ce sont des mots affectifs. C'est du Wolof pure, sama yaye, sama Baye, sama morom, sama xarit...
Il y'a beaucoup de personne qui ont appris la langue Wolof dans la rue, elles ne comprennent pas le vrai Wolof. Et pourtant Sanekh, tu es Wolof. Tu comprends ces nuances la. Il faut que l'association Mbootaayu Leppiy wolof parle pour éclaircir les Wolofs et les lakkwolof ( Wolophones).
J'ai des scénarios de haute classe, producteur bouma niémé rék manguilay khar
Ooh sanex trop fort
Sanekh rew you bari ame na seuy yo kham ni dufa ame lou ame senegal barina si khéty dh Mali am nafa basi rew arabe yi am nafa france amna khét bo khamni sen birr rk nioy seuy kou beug xam internet bi ken sonatoul tapel khol
Com sarahulle rek wai legie mou diekh nak😀
@@nourradam6391Mame lebou la si sarakhoulé lay seuy niom amouniou problème mbok ils sont adorables machallah
Mane mi amna si histoire nop ben sarakholé mais fima rombou gnouni ma nopaloul ki doko takk ba nônou lassi moudiou ba takk keneen te kokou rek la beugone 😢😢😢
@@momo_le-pro.7 exactly giss nga lii baxoul dara billahi.
@@nourradam6391 limu yakk beurrina lool
Bilaye sanékh wakh ga deug sénégalais mo guena raciste sakh toubab bo wakhé nk niounane dagua compléxé sénégalais baxoul bly fiér d’être sénégalais ❤
Armérou guéweul😮 c'est la première fois que je l'entends. Je suis choquée par ces affaires de castes
Oo doyna war bilay yala bkh na😢😢😢😢
Je suis fière d’être ngengo balamaissa
وخلق الإنسان والمومنين والمنات 😂😂😂
Sama nar bi, sama sérère bi,sama Toucouleur bi, lolou bonoul. Nitt gni nio ko yakh
Voilà lolou dara néku ci
Affairou guéwal ak ngér existéwoul nioun nioko dougal thi sounou ada rék ,naniou tàpé khol ta yénén té lou bakh adouna amoul béna solo lépal diékh ❤
Bilahi amna Sindia vers Mbour amna armére gueuweul ame bou sèrère ak bou mixte cad bou peulh yi ak olof et consors comme nioune nièpe dèmoussi yallah
li deug la wala deguay foooo🙆♀thiey man li safara dina mbeuri ay senegalaise deh si neke deug la astarfullah😭
Ouais amna key suis d sindia
Mane gueuwel la mais nak gnoune gnou gnane beugue lou yob arrêtons la quémande c est nous qui se rabaissons devant les nguers
Moi même je suis gneigno pur bete bete mais j’ai un esprit de dépassement. C’est juste une série pour sensibiliser. Donc les insultes ne me dérange pas
Li dh dou evenprod sanekh molén khelal li
Ndeyssane
Tu as raison sa nek
Ravi de voir xalima Gadji alias déguene dans cette série.
❤❤❤❤❤nitte.lane.laye.taxaye.ak.morom.nitte.nittam.nane 3:56 3:56 .ko.ma.la.genne.❤❤té.you.bok.founou.ndougé.xana.béne.yala
Sanekh le meilleur
C est à Ngoundiane dans la région
Thieuye yalla
Ohh yaram daw neu
Bane Gnégno moy Nangou nioulay wakh Gnégno kharamata Ndiaye Sa nekh sa scénariste bobou dafa beugg Diay série bi rek mais battou guinaw meunoul niakk mais amoul ken kou sania takhaw ak sa moromou nitt diko wakh sa Askanou kharamata Ndiaye bi en face moulay kh👀l ni té defoul si yow Lou métti ce mot là admettons le c'est vraiment exagéré " Gnégno Kharamata NDIAYE wala Guéwel kharamata NDIAYE wala Guèrr kharamata NDIAYE" jamm dilassi féck Théâtre là rek pour sensibiliser nitt gni alerté nitt gni pour niou bayi lolou ndakh L' Islam nangouwouko Christianisme nangouwouko
Nél dégagoko sokhnasi mais boulni amoute
Yaw linga xamoulo ci adouna dafa melni beuriwoul...moi je suis gnégno et la séquence en question ma famille et moi l'entendons presque chaque jour!
Donc ne dites jamais que cela n'existe pas ou qu'une personne ne puisse pas avoir le courage de le cracher à la figure d'une autre personne.
Sénégal lepp amna fi...
yow doundo ko mais boul wakh ken doundou ko ne sois pas egoiste toi aussi🤦♀🙆♀️sheuteuttt
Daflay daloul motakh
@@fabithiam9054 ki key dalouko mouy invinter nonou🤦♀️
😭😭😭😭
nay san 😢
Sanakh seul
❤❤❤
Walay youma so tini mo djinda a mayiiii 😂😂😂
Marem eska eumbul😅day guint
Gnégno seul
Ethnocentique laniou def
Deug leu c'est à bandia on enterrait les gueweuls sous le baobab
kon li amna senegal te yeugou mako soubhanallah😭
Sa existe dh bilaxi ande na ak sama ben xarite Di niane diabar bilaxi mere bi bagn Liga done gueweul moma diaxal mais kou bakh ga beug sama dom diapaleko bep côté respecte gama yarou ga Mané sama copin bi ki na fek la niou dem bilaxi ba ni la yake diganté bi
😢
Guéweul, gnègno ak laobé ay nit lagnou wayé dagno wara bayi di gnan sène moromou nit bamoulèn di yab. Wayan bahoul dou yeufi gor.
Wayan mo tah gnou bari di wah né dougnou may sèn dom guéweul.
Le griotisme doit être aboli.
Lolou afrique rek la ame rawatina Sénégal mo takh niou tardé deuk bo kham ni daye guene di pauvre di dém europe li bou fa amone kou prononcer mot bobou casso ngua dieum
Guerr yi danio diapni nioo guen nieupou
Lolou dou deuggg
déjà accepté les castes c’´est accepté cette discrimination je suis sénégalaise et musulmane une créature un être humain point
Deug leu d
Amul fen ci ALCORAN guer gueweul laobe akh teug au contraire ils sont des nobles pour ku kham YALLA Té di ap dioulit waro gueum ay khet
enfin gnit bou yewou bou khamni que yeufou khet yi amoul si islam 👏❤❤
Deuguela nioune aye laobelaniou keure laobeyi leniou wakhe
Vèritè gènèral si finbi
Affaire de griot ya pas dans l'islam nous sommes tous égaux devant dieu
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
D’habitude, les griots etaient enterrés dans des baobabs. J’ai oublié l’explication traditionnelle, mais c’était pas pour les rabaisser.
Delen toudou laobé yi nak. Ci combat bi lagnou bok
Gnun guewel yi aka no fière
lolou amoul si islam guemoul ni yow dioulite gua rek do son si sa adouna bilahi🥺
@galsen_girl bilahi waxnga deg mé lii damako dund
@@Touty-wp3gp massa cherie fi adouna la lou meti dina diekh beun jour 🥺
@galsen_girl merci beaucoup
Le problème des castes au senegal est mal posé.Est ce que les castes se sont affranchis de leur pratique? Quand cela les arrange ça ne dérange pas .ils se réclament griots pour revendiquer le micro central et bénéficient par cette posture de privilèges.
Kouné keu bour ga sa keur baye
Leup Sénégal ley khew
pas senegal kese deh demal inde wala pays arabe yi gnom ils sont pire walahi😌
Arrete waye
Peul bou dég ndayam bii😢
Bouléne gnou sonal aiy gniégno guéwal teugeu loabé amoul ci Alkhourane
Loutakh senegalais khamoul personne ak personnage
Gnio gnieukeu raciste gnioune
Niénio Kharam yi mom rafetoul mais nak Sénégal depuis les royaumes lolou mo mosss am Guer-Guéweul-teugueu-niénio-maabo- diamm(esclave) au bas de l'échelle
Voilà le classement normal des choses. Selon notre tradition.
Amoule sii alkhourane dh ♥️🤟 la
alkhourane sakh daka sib khet bilahi yow😌
😢😢😢😢😢😢