Astahfiroullah thiey yalla nagnou yalla mousseul thi rére. Naka la nite Di ziaré Guy. Sénégal bo wakhé gnouné wakh nga wayé bokalé bi beurina. Yalla nagnou yalla diegual
Ziara gouye mosi dessone ayy Sénégal kagne laniouye gooré gueum yAllah wolou ko té bagne ko bockalè ki la bindeu weusakale la nguéye lekk di naan bindeu saye wadiour ndax kokou warou la doye thie saye sokhla ak si sa bopou ayy merité woule kouko bockalè dèh mome borom asamane ak souf yAllah naniou borom bi diégale
En tout cas si vs n'arrêtez pas mystifier vos publications ,tout le monde va fuir le Sénégal, ds les theatres sénégalaises y'a bcp de scène mystiques, la lutte sénégalaise aussi, ainsi k bcp de documentaires.... En tout cas vs dëmëfiez ou diabolisez le Sénégal 😢.....
Déme lène diamou Yalla swt mo gueune.
Li dh dou yeufou dioulite
Asstafiroulah Bayiléne bokalé ak kheureum qu'allah ai pitié de nous
Djiné ame na, yalla mo léne binde nimou la bindé
@@waxkatoudeugmais pas pour nioukoy diamou nekk leine nitt
@@Adaaaaa625 yow do bayi doul. Fane nga fi guiss si vidéo bi kou fi diamou ay djinns wala garab?
Yeufou thiedoo laffi djisss😊
Ay djiné rek niolèn fay toppou. Do lèn fa dieulé gueureumou borom bi dé. 😏
Mais li grab rekk leu amoulll dara lou extraordinair ziyar gooy aduna tukkina senegal bayilen fou gooy dou dara loudulll grab dong leu
yén déguén beug critique trop ki thiossan rek lay nétali ni rek
Bokalé rek nguéne déf
سبحان الله العظيم
Gouyegui mbéndéffou yalla 😂
Wallahi
Celui qui s exprime en Francais est tres eloquent. Mash Allah
Salam doungènma diappallé louy dindi farou rap 🤔?
da nga KO am wala dala néx ngay lathie
Il faut voir un imane pour qu'il te recite certains versets
Wa li moy lane soubhanallah😢
Remercions plutôt le créateur ki nous a fait découvrir ces propres créatures
𝙱𝚘𝚔𝚊𝚕𝚎𝚛 𝚍𝚎𝚞𝚐
Ziara diam Ay waay boulen bokalé
Bayi lene bokalé ak yalla yalla rk mooy yalla yalla mooy diarigne mooy loré bayi lene sene thiaxane
😂😂 Sénégal beuri n'a ay doof seytané géni diamou iow ak saye mame yeupeu ay doof ngéne
Li foum neh mom 😱
Li fadial la NEX apere zowal fadiout
C'est le plus grand baobab de l' Afrique apart le baobab de keynia
Goûte dé dou yobe nitte aldiana
Astahfiroullah thiey yalla nagnou yalla mousseul thi rére. Naka la nite Di ziaré Guy. Sénégal bo wakhé gnouné wakh nga wayé bokalé bi beurina. Yalla nagnou yalla diegual
Lii moy lane
Mais c'est impressionnant. Waw
Ce ne sont que ds mensonges j'ai visité deux fois ce baobab il ne marque que l'histoire des ancêtres sérères
Li mome bokalé leu
Guate nekoul tji gouye gui fi yalla fi nek
Ziara gouye mosi dessone ayy Sénégal kagne laniouye gooré gueum yAllah wolou ko té bagne ko bockalè ki la bindeu weusakale la nguéye lekk di naan bindeu saye wadiour ndax kokou warou la doye thie saye sokhla ak si sa bopou ayy merité woule kouko bockalè dèh mome borom asamane ak souf yAllah naniou borom bi diégale
Merci ❤
En tout cas si vs n'arrêtez pas mystifier vos publications ,tout le monde va fuir le Sénégal, ds les theatres sénégalaises y'a bcp de scène mystiques, la lutte sénégalaise aussi, ainsi k bcp de documentaires.... En tout cas vs dëmëfiez ou diabolisez le Sénégal 😢.....
Fadiale
Xalaas! 😅
Magnifique découverte ❤
ENCORE DU SHIRK ? HUM, OK !
Subhanallah
Astakhfiroulah azimal’ lazii