Merci Dakar act vrema Sen ligey rafetna Ben info rawatounou si equipe national brav Bravo et encor bravo Dakar act TV merci yalnanou dieul coupe d afrique bi amine
Moi je sui Gambien mais je ne comprend par pourqoi Elhadji Diouf critique Aliou Cisse toujour paske senegal ce la paix de teranga un puple, un but et un equipe ce la equipe national du Senegal. Allez lez lion ndam rek
BONNE CHANCES MON IDOLE DIAO BALDÈ KAITA JE SOUHAITE UN EXCELLENT CAN YALLA NALA YALLA MAYE WÈRE MAYE LA DIAMOU INCHA ALLAH LEPE LIGA BEUGUE THI CAN BI YALLA NALA KO YALLA DÈFALE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE INCHA ALLAH
Nan je l'ai jamais vu faire un petit discours dans un rassemblement, mais sa ma fait super plaisir, car j'avais entendu dire qu'il avait pas les épaules pour être un l eader. 🇸🇳
YA HAMID maye gnou coupe d afrique thi daradiaye SEYDINA MOUHAMAD SALLALAHOU ALEYHI WA SALAM thi barke BOROME TOUBA ak thi BARKE MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE
Ahh sama guayi ma guiss ni war nagnou doli muscle touti deh... Affaire yi fi Afrique dou bena comme europe ma wakhlen lou lerr nak bakhna dale. Tanka yi ak bissepc yi ma guiss dale daloule sama khel torop waye Yalla bakhna.
Sadio mané dé méme estaf bi sakhe dogne ko fan bathi entreneur bi machallah ki yalla nako yalla lafale thiat
Limou deff mo reuy nak kaarr deux finales consécutives dont une remportée
Bég na loull
Merci Dakar act vrema Sen ligey rafetna Ben info rawatounou si equipe national brav Bravo et encor bravo Dakar act TV merci yalnanou dieul coupe d afrique bi amine
Bilai Dakar agtu masion spéciale
Dakaractu Merci à vous liguey bi rafetna Machallah. Sadio Mané sunu star bi aka humble Machallah. Yallah nalen Yallah defal Ndam🇸🇳💪🏆🇸🇳
Kou bague kaita balde basal jm
Mw jaime
ngiryalla dimbalilenou gagner can'bi sonou Nanou lool allez les lion 🇸🇳
Normal pour Sadio le leader ! Cette année moi j’y crois in sha Allah ! Assiko yii nekhna wayy 😍😍
Merci Encore une fois DAKARACTU TV douma diouk dileen diadieufal Good job à tte l'équipe Particulièrement l'infatigable BAMBA DIAGNE
Suis fier d'être sénégalais BN chance les lions✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊
Ramenez la coupe à la maison allez les lions allez 😎
Bilay kafou ma dé j'en ai besoin urgent Inchallah 💞👍
Perier pour vous inshalla dina nieuw
🤣🤣🤣🤣
Kou beugue Gana Geuye
Sénégal mogui sogua am star sans offensé les autres vive Sadio
Tu as raison
Vraiment star bou monde bi kham
Fo fatei el hadji diouf
El hadji Badji senegal 🇸🇳 yagg na am star
@@wakhaldeug8424 tamouy deug
Yalnalén yalla soutouraal, siiguil lén ciii barké Seydina Mohamed (SAW) ndam rék inchala amoul ragal
Moi je sui Gambien mais je ne comprend par pourqoi Elhadji Diouf critique Aliou Cisse toujour paske senegal ce la paix de teranga un puple, un but et un equipe ce la equipe national du Senegal. Allez lez lion ndam rek
Mina Queen diouf daffa beuri wakh
Il est jalous de lui!
@@sabalymody5919 wahal de
aliou Cisse dafa khamoull dara moutakh
éh kén ladiou la Bayi ba califie thi can bi gua dogua am lo wakh Ok
Sadio mane god gifted
What a player
Ameen. He is gifted with great skills. Sadio is very humble. May allah continue to bless him
Ndeyssane lii dio moukoo il est tellement gentil et humble tjrs souriant coup bi rkk Inchalah
OUI ON N A UN VRAI LEADERS MAINTENANT RESTE SUR LE TERRAIN MANE SOIT DANGEREUX
Diao kaita Baldr yalla nala yalla takhawou
Yalla nalen yalla défa ndam inchalla
Mais vraiment star sonouna dh mais bon courage mané
Sama mame nenama benn kilos gouro ma sarakhèko guisna senegal demm final dou ay thiakhane nak deff na sarakh bi tay vive le 🇸🇳
meissa gueye yalla bakhna naniou doundé yakar rek inchalla
Que le Bon Dieu vous protége et facilite la tâche à sadio le poids de toute une nation est derrière toi.
Que dieu vous protège
Yallah naléne yallah soutoural
Yallna yalla mayer ndam rek inchaallah
Machallah sadio on t'aime vraiment
ndame rek inchalla na xool yii ande Rek
j'aime bien manè
🙏🏼Dakar actu dieuradieuf way sur les informations ❤️
Sadio a pris une autre dimension ! 👏🏼👏🏼👍🏻
En Avant l’équipe du Sénégal 🇸🇳 Ramenez la coupe Inchallah !
Ils ont une équipe de ouf ces l'enfoirés 🇳🇬🇨🇲💪
BONNE CHANCES MON IDOLE DIAO BALDÈ KAITA JE SOUHAITE UN EXCELLENT CAN YALLA NALA YALLA MAYE WÈRE MAYE LA DIAMOU INCHA ALLAH LEPE LIGA BEUGUE THI CAN BI YALLA NALA KO YALLA DÈFALE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE INCHA ALLAH
On dirait que sadio mané a pris le rôle de leader !?
Bou yague
Fo nekone tamite Lolu dou tay
Lol ça fait longtemps
Mdrr bah c’est lui le leader en mm temps lol
Nan je l'ai jamais vu faire un petit discours dans un rassemblement, mais sa ma fait super plaisir, car j'avais entendu dire qu'il avait pas les épaules pour être un l eader. 🇸🇳
Aller les lions nous sommes deriere vous sadio on conte sur toi
Ball arreté légéy léne ci nguér yalla limou nioye trompé barina dh bone continaution les Lion de la teranga
Keita sw pa fans mai il est en plein forme
J'aimerais le voir titulaire moi
Il me semble vouloir jouer
@@ezheamich6859 wiiwi il veu joué il est conscient de cki l'attend il dw prouvé
Hun faites attention, regardez le bien ce gars manque de sérieux dans les efforts physiques, d'où s
es blessures récurrentes
@@Lecnfnt9751 pourtant je ne le vw pa insi mai le plu important moy niou diohko temps de jeu comme sa on jugera
@@beuguefallou1677 première match dama beugg niou ték MANÉ banc daat koy déparlo pour moi c'est mieux
Best of luck guy's greetings representing the smiling coast of The Gambia 🇬🇲 our prayers are always for you all inshallah
Mane c'est un mec trop gentil. Il est toujours ouvert en vers les gens.
E puis il est modeste timit ausi chapaux a lui
Dans tout groupe sadio a le plus petit gabarit mais machalah il est trop fort
Ndamm rekk inchallah 🇸🇳🇸🇳💪🏾💪🏾🏆🏅
Machalah séne liguéye rafête na
Allez les lions tous Sénégal sont derrière vous ndam rek inchalah
Amin yalla na yalla nangou nianyi defalen diamou si barke Mame cheikh mbaye
Yalla naleen borom bi soutouraal
Amine
Amine
Qui regarde cette vidéo en 2021 j'aime les lions de la téranga🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳💚💚💚💛💛💛♥️❤️💕❤️💕❤️❤️
Allez les lions de la teranga suportaire dp8 Madrid
Ma challah laff thiatt rek fofa tothie radiakh
Allez les lions bn continuation
Yalla naleeen yalla siguil insha alla
Sadio mané nous somm fier de toi yalla boula thiatt top machalla
Sincèrement parlé DTV mention spéciale pour les infos
Mbaye Niang je l'aime et Gana Geuye
yalnanou yalla may ndamm🙏
jajeuf allez les lions❤❤❤❤
Yalla na lén yalla dèfall diam may lén ndam inchallah
NDAM RK LES LIONS
DTV MENTION SPÉCIAL 💪💪💪
Alle le lion bon sance done fiertés le peuple sénégalais vous j't capable bon réussite
Diao Baldé frisé cheveux 😍
YA HAMID maye gnou coupe d afrique thi daradiaye SEYDINA MOUHAMAD SALLALAHOU ALEYHI WA SALAM thi barke BOROME TOUBA ak thi BARKE MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE
Bravo les GARS 💚💛❤⚽🌟⭐👑🏆🏆🏆🏆❤❤❤😍😍😙😘😚🌠❇🌟🌟🌟🌟🌟🌟🌟⚽⚽⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐👑👑🏆🏆🏆🏆🏆🏆🏆🌠❇✨👋👍✊👊👌💪
J'adore la modestie de sadio
Nous croyons en vous jusqu'au bout
Vraiment gars yi équipe bi amougnou layy concentration rek gnou dèm Égypte dieul ndam li inchallah
Merci Dakar actu
Coupe yalla mokoy diokhé senegal dé wakh rek mousoulen am yéné cii equipe bii
yalnanoulene ganié khamoulene tousse koulene yakaraye khady
Yaw yay Domou thiotou sa data yaye toubab yu ngay gnapa ndeyem faral Di gnanal sa rew li Ya kat sa ndeye rek thim
Yo alla newnu yo alla wallou يا الله يا رحمان
Je vous rappelle que personne ne pense pas a diao balde keita pour cette can tout le monde pense que mane mais vous aller voir le supris
Je suis du même avoir que vous
Merçi dakaractu
Oui, c'est bien de discuter
Bravo Dakar actu
Keita baldé deux pied gauche👀
ce qui me plaît le plus chez sadio c est qu'il n'est pas dépassé par son succès il garde la tête sur les épaules pour le plaisir de tous ses fans
Bon courage
Ahh sama guayi ma guiss ni war nagnou doli muscle touti deh... Affaire yi fi Afrique dou bena comme europe ma wakhlen lou lerr nak bakhna dale. Tanka yi ak bissepc yi ma guiss dale daloule sama khel torop waye Yalla bakhna.
vive le SÉNÉGAL🇸🇳🇸🇳🇸🇳
merci
Merci🙏🙏🙏Ha
Bonne chance nos lions
Dites moi s'il vous plaît le titre de cette chanson
Diao ndaysane adio rek la beugue
Wayyy asico yi néxna wayy
Sénégalais et fier 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
dém ba diékh . ns croyons en vous,
merci Lions
😍😍😍😍bravo lion yi
Nékhoul ba nékh Sadio Mané yay souniou Star yaw dokhalal
Gana gueye❤❤💋❤❤
bienvenue capitain sadio mané
Keita Baldé beugeul li nguaye déf way
Saway pourtant mou gui en forme nel je suis pas fan de lui rek
Mamadou Salif Ba nn grand iow staff bi nga warône bokk😂😂😂😂
Aliou Cissé amna bén comédien boumou may nirôl dama fatté tour bi😂😂😂😂
Machallah sadio manè.
9:17 kii dou Mbaye diagne
Evite le son c tro c bien c que vous fait cool
Oh kara Mbodji 😢😢
Gni dé faral léne yak koka dakh dagni tass yakar😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
adji sarr dafa diotagoul rek lou diot youmbou té am nagne si yakar bou bakh
Noo star néxna , srtt joueur nk
J'aime Mané
Et moi aussi
Yalla bouléne thiate topou
Mane équipe bi 3 joueurs la si khammm
Bilay
Nice music
Serieusement je suis confiant quand je vous ça c'est comme ça les GARS ILS FAUT SE PARLER DISCUTER CETTE UNION ET L'ESPRIT DE GROUPE