*Mercredi Le 08 Mai 2024* Machallah Serigne Mor Asta Touré Yalla Nala Yalla Faye Yiw Yalla Goudeul Sa Fane Té Barkél Xam Xam Bi Amine Allahouma Amine Mane Deh Masturbation Moma Sonal Bëgg Naako Bayi Lool Nak Waayé Khawma Lane La Waayé Inchallah Magui Niane Yalla Mou Safaraal Mako Bama Bayiko Ak Mbooléem Kou Koy Déf Amine Allahouma Amine 🤲
Salam s more yallnanoula yalla fayale si barki ckhie ah madou bamba yaa bakhe ya tabé sisa xam xam bi maguilay top ndékété li sakhe si sounou reuwmi leup ndiaringi kasé la
Oui gueint di seuy Lou normal leu waayei sou barrei de manière répétitif meune naa neikk affaire cheytane Serigne bi Bari na ham ham waayei masturbation ak gueint di seuy yeupp meune naa neikk affaire cheytane
Man de dama am problem bo khamne 12 Années mangui seuye te masouma am banekh manam douma yeuge banekh khaw lanmokomana dindi 😭😭sonn naa basi kanamou Yalla demna Hôpital ba son ay waye koumaye dimbali te yalla takh😭
Assalama aleyekoum s mor lingay wakh lep ci kolon mane magui koy doundou birbou meti lamay deff ba ni sama bir bi mogui diam linga ni da koy deff yép mogui ma koy deff sa fait deux semaines dimbalinou ci secrets bi koy fathie
Lép louffi waay ñiane YALNAKO SUNU BOROM NANGOU. TÉ MOU DOLI ÑOU DIMBALÉ GATANDOU ÑIOU AK TAWFEX BOU SËRIÑ BI. AMIINE BARKEP MAM CHEIX IBRAHIM FALL LAMP
*Mercredi Le 08 Mai 2024*
Machallah Serigne Mor Asta Touré Yalla Nala Yalla Faye Yiw Yalla Goudeul Sa Fane Té Barkél Xam Xam Bi Amine Allahouma Amine Mane Deh Masturbation Moma Sonal Bëgg Naako Bayi Lool Nak Waayé Khawma Lane La Waayé Inchallah Magui Niane Yalla Mou Safaraal Mako Bama Bayiko Ak Mbooléem Kou Koy Déf Amine Allahouma Amine 🤲
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysane 😢 yalla na nio yalla dimbali Amine
@@KaouzouToure Lou Ménti La Waayé Yalla Bakhna Yalla Na Gnou Yalla Yereum Té Diégeul Gnou Amine Allahouma Amine
Amine 😢
Jërëjëf Sëriñ Moor ❤
Dieure dieuf serigne kham kham rafetna machala
Mashalla amatnina solo❤️❤️❤️
Dierediefety serigne touba dierediefety serigne touba dierediefety serigne touba
Dieureudieferii Serigne Mor Amna solo wahtane
Machallah srg bi manager solo looll yalla na yalla yokku Xm Xm bi tayokku barké bi❤
Alhamdou lillah mâcha Allah allahouma barick ya oustaz
Yaw moum khawma lanla mais soma lay deklo damay contaan ndakh xam xam bi❤
Bilahi do Yaw dongou
😊..@@serignefalloumboup6936
Dieureudif Serigne mor Touré am na solo lool 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
الحمد والشكر لله ماشاءالله شكرا جزيلا
Yallah nala da borom bi Fayal la Boppam tei Sam la Ci barké Seydina Mouhamed PSL ❤❤❤ . Merci 🙏🏽 1000 fois ❤️
Yalna yalla Faye la si barkéb alkhourane
Masha.allah Alhamdoulilah amna solo lool diàdieuf ❤❤❤❤❤
Salam s more yallnanoula yalla fayale si barki ckhie ah madou bamba yaa bakhe ya tabé sisa xam xam bi maguilay top ndékété li sakhe si sounou reuwmi leup ndiaringi kasé la
Merci beaucoup amna sollo yague té wer
Salam serigne mor magui ziar mor louy fath nokhoum siti merci
Outeul khassou guiguis ak khassou dank bokoy naan mouy genn
@@GnagnaSow-fo3yxku baax maa ngi ziaar. Mann mii siti mooma sonal lool sax. Nan lañ koy jëfëndikoo???
@@salioundiaye6697 dagu kay khoothie si 20 l bou yabée gua Koy naan
@@GnagnaSow-fo3yxan nokay nanei dangakoy baxal walah
Jërëjëfëti Touré ❤
الله اكبر li de.ndiepu dji wara diout ❤❤❤
Ndeysaan jërëjëf Séex bi ❤
Machallah meune dh yaw rék lay toppouu🎉🎉🎉🎉
Machalha amna solo dieradieff yalna Yalna fayele yiw
Ndaysan Serigne mor amna solo torop jdeureujeuf
Machalla yalla na la yalla sam❤❤❤
Sama Oustaz Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤
ماشاء الله تبارك الله عليك
Merci beaucoup machalla amnasolo
Machalah toure toure
Amna solo machalla merci
Machaa Allah oustaz ❤
Machala amna solo
Machalla nio gui ziare bou bakh dama don lath birr bouy daw
Merci manedé damaye geuénte disaye loubari mais damafogonné raplah
Oui gueint di seuy Lou normal leu waayei sou barrei de manière répétitif meune naa neikk affaire cheytane Serigne bi Bari na ham ham waayei masturbation ak gueint di seuy yeupp meune naa neikk affaire cheytane
❤❤❤❤machallah amna solo
Machallah ❤❤❤❤ ❤❤❤
Masahallah❤❤❤❤❤❤
Amtnslo ❤❤❤
amna solo
Slm serigne bii ziar mane damay lathiè sa youma yèwo beu saw beu parè maniw tayy gueneu wallah yauge naa sii mane wallah lolou lane mokoy dindi
Merci
MachAla
Machalla
Amna solo
Man de dama am problem bo khamne 12 Années mangui seuye te masouma am banekh manam douma yeuge banekh khaw lanmokomana dindi 😭😭sonn naa basi kanamou Yalla demna Hôpital ba son ay waye koumaye dimbali te yalla takh😭
Ndaysaan metina Waayé insalla dana werak jàmm de loumana fadioula sax
Sa dieukeur moye guawa danou wala yaw yadoule ueuk banékh
Sokhna ci mane dei meune naala dimbali inchallah
Diaradieuffati S mor
Yalla na la yalla faye ci xam xam bi ngay yatal dierëdiëf
ما شاءالله❤
Machlhha yalla Na xam xam bi yokou
Ziar pour fajj yaff dieuleul rénou garabou mboum nga defko ci morço deuboukko dikko fone ci sa bakane c tres efficace
Bane mboum thiakhat Ndour wala bane khetou mboum
Mboum bou tiéré
Dafa am thianri façon mboum thiakhat ak Ndour bane lassiii
@@MamegooSarrLerul dé Ban mboub mbou da beuri ta wouté
Machallah jeureu jeuf
Sa Nimoro télé fone serigne mor
Diadieff Serigne mor diadieff
Amal diamou ❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam
Sone na trop bilahi merci
mane MoMA sonnal porno
Lane moola dale ???
❤❤ ماشاء
❤❤❤❤❤❤❤❤
Assalama aleyekoum s mor lingay wakh lep ci kolon mane magui koy doundou birbou meti lamay deff ba ni sama bir bi mogui diam linga ni da koy deff yép mogui ma koy deff sa fait deux semaines dimbalinou ci secrets bi koy fathie
assalaamou hallaykoum ko yaramam ame khame nak
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam Serigne Mor,S'il vous plait loy fath ndohum siti bu yakh manuew
Reenu dakhar bakhbasi
Salam ak ziar
Kou am topoum siti noy def
Birr bouy daw birr bouy daw
Lép louffi waay ñiane YALNAKO SUNU BOROM NANGOU.
TÉ MOU DOLI ÑOU DIMBALÉ GATANDOU ÑIOU AK TAWFEX BOU SËRIÑ BI.
AMIINE BARKEP MAM CHEIX IBRAHIM FALL LAMP
Jereu jeuf Serign More nima dégué nga décrire colon mom njiorte nani sama métitu biir bi colon 9 ans may dounde ak mom
Diadieuf mouride...
Sa numéro tamit beug nan ko
❤❤❤❤❤❤❤❤❤😮😮😮😮❤❤❤
❤❤❤❤
Sanemor teléfono
Nokhoum citi
Malheureusement 80%sénégalais yeup dougne sax diém nieuw di xol genres vidéo yi
Xaleyy diguén yi sen Solu yi léguii yi mo gueneuu graaw prono
Beugne loukoy fathe
louy fayaar
Lan moy topé siti ?
Sa numéro la beuga am
Salam fayar moy lan
Nimerobi
Numéro s mor la sokhla
Ko bëgg sa Numéro nag?
Man bou ma ňawé Senegal lek you bari day daw sa birr ma don lath lou koy sàfara
Souma télona guiss sa vidéo bi douma pért sama khaliss ahh sonouna
Serigne bi defal niou vidéo si rabou thiossane nguir yalla
Daga ame rabou thiossane???
🫀❣️👏🏽✅
Kaani khegne moom dina meti di nunukoy lekke ? Deskoy lekk nonu wla
numerom la beugonn
Ss numero la sokh la❤❤❤
Beguone na kham lan mooy fayar d
Némorou téléphone ma challh
Ni maroby
Sonou n'a trop billahi
Magi wate ci yala né rewmi kéne eupeuko fi xamxam
Loolou boulko waat ci yalla wakhal rek amna ham ham waat dou ay foh
Lane moy dindi xale boy saw lall
Meune naala boolei ak koukoy fathie
nkelew SEYTAN NNKA
Ngeilaw shaytane nga wakh???
@@CheikhDiop-mo8kq waw
@@CheikhDiop-mo8kq numero
@@fatoukonta-pj4mx mane dei meune naala boolei ak koukoy fathie
@@CheikhDiop-mo8kq boukna
Moytou di teudé ndeufénay aussi. Ak wagni lékk yiy yokkou ndokhou gor comme arachides ak coco
Merci Serigne Mor
Quelle est la signification de faire l'amour avec une femme qui a les deux sex hermaphrodite
Sa nimero la soxla
lan moy fayard
Xale boy saw lall lane mokoy dindi