Alahou akbar🛑Bour guewel meerna nak recour bi-le discours de Max mbargane envers Tapha gueye

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 27 дек 2024

Комментарии • 280

  • @veritesavoir5415
    @veritesavoir5415 Месяц назад +79

    Serigne mounetakha yalla nafi yagu té wér

  • @diaabdarahmane1537
    @diaabdarahmane1537 Месяц назад +6

    Lamb Sénégal so Amoul won Buur geweul dou nekh il est fort epuis Talibe la Macha'Allah y'Allah nga goudou Fan

  • @fatygueye1985
    @fatygueye1985 Месяц назад +41

    Bilahi tu as parfaitement raison 👈

  • @lomamadou4526
    @lomamadou4526 Месяц назад +26

    Manch'ALLAH boür fier d toi toujours pertinent Grand big Respect....!!
    Mé niyoo yii da xawa goudou wagnii ko rek😂😂

  • @Socrate4477
    @Socrate4477 Месяц назад +11

    Merci Bour Guéweul, tu es un bon communicant !

  • @mansoursy9554
    @mansoursy9554 Месяц назад +18

    Bour sa nouyo bi machallah nékh na trop wolahi
    Nouyo bi da sélleu trop

  • @ablayediouf593
    @ablayediouf593 Месяц назад +18

    Felicitation Modou lo

  • @adamapamba3375
    @adamapamba3375 Месяц назад +1

    Bour siteu danguene ko wara recruté si plateau bi. Nakh molene dakk wakh 😂😂. Bour il est très pertinent machallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @AlassaaneSow-sk7rx
    @AlassaaneSow-sk7rx Месяц назад +10

    Bour guewel toujours cohérent,toujours pertinent

    • @ibrahimamba1296
      @ibrahimamba1296 Месяц назад

      Il avait dit que Siteu n'a aucune chance et tu dis qu'il est cohérent. Lou takh nguene mana féne?

    • @kefgg
      @kefgg Месяц назад

      ​@@ibrahimamba1296Yaw maygnou diame. Bour a eu totalement raison. Dafani 35 combat Siteu dou dane Modou Lo. Et effectivent Siteu danoule Modou Lo. Donc Bour avait eu raison, il a tout predit avant le combat

  • @sellediop1817
    @sellediop1817 Месяц назад +10

    Machala bour ❤❤❤❤

  • @dielkeffelywele8128
    @dielkeffelywele8128 Месяц назад +6

    Bour tu es comme El Hadj Mansour Mbaye en terme de sagesse et de grandeur.Je te félicite.Continue!

  • @mameballaniang5741
    @mameballaniang5741 Месяц назад +2

    Bour begue nala ngir serigne mbacké madina❤

  • @mbayemalick7297
    @mbayemalick7297 Месяц назад +4

    Merci buur toujours pertinent

  • @BabacarNgom-hr7nt
    @BabacarNgom-hr7nt Месяц назад +3

    Bour ak fadam gnomm deug rékk lagnoufii nékké deug nakk gnépp layy lalll merci bour diam sii yaw

  • @zora3115
    @zora3115 Месяц назад +9

    Bilahi bour right nga wah❤❤❤🎉🎉

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 Месяц назад +2

    Bour tu es le meilleur des spécialistes de la lutte

  • @mormbengue1951
    @mormbengue1951 Месяц назад +13

    Machallah 🙏🏽🙏🏽

  • @KebbaJobe-f8m
    @KebbaJobe-f8m Месяц назад +19

    Modou lo ndam rek ❤❤❤

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 Месяц назад +36

    Merci beaucoup Bour té boula kénna güéné ci wakh deugue ✍️mouye Modou lô mouye Siteu thiak thiak✍️ waxal liye deugue rék ✍️ ndame rék ngaye ame 👏 il faut ma envoiyé la 200.000€✍️

    • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
      @AboubacryGASSAMA-zs7oi Месяц назад +1

      😅😅😅200.000€ eske yonè ko nonou dîna yombe wala dagua dioume😅😅😅

    • @assanendiaye5640
      @assanendiaye5640 Месяц назад +1

      Deug bi Moy modou lo est tombé,IL faut etre veridique

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck Месяц назад

      B​@@assanendiaye5640 danga khifff je Hana

    • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
      @AboubacryGASSAMA-zs7oi Месяц назад +5

      @assanendiaye5640 véridique wèssouwoul li règlement wakh tamitt .Usain Bolt sous beguè nèk rois des arènes na bayi dawe bii tahaw beuré deguel bopam wagnii wakh bou barrii bii voilà lac 3 bou diamaguene😅😅limassi guene mèti limou wakh si signature bi damay ndèguègne yaram bi same diagua dèfoul loudoul dawe rék.rois daguakoy mérité comme gnifi diota diare voilà

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 Месяц назад +3

      @@AboubacryGASSAMA-zs7oibilahi ndéké tapete bou reuye leu man dama moudjou rouss sakh

  • @ibrahimasy3165
    @ibrahimasy3165 24 дня назад

    Merci Bour très bonne analyse franchement ay niome coach bakary Nio khamoul dara sou aye na niou beuré Di na Kham leup deguele mais toke thi chaise bou bou rek dou ratatati rek

  • @abdourahmanebarry1582
    @abdourahmanebarry1582 Месяц назад +10

    Ayy way Bour djeureudjeuf sii logique guou lamb bigua wakh fii

  • @MmeSaliouNdiaye
    @MmeSaliouNdiaye Месяц назад +5

    Amine M'backé yalnafi yagg té werr

  • @sadiafaty2556
    @sadiafaty2556 Месяц назад +7

    Pere Bour vous avez raison la sensibilisation contre la non-violence doit être au cœur de la gestion par intérim du CNG de lutte en place .Lutte SANS VIOLENCE est un bon slogan pour 2025 .Trop c trop soit c’est un divertissement soit on arrête .

    • @ngagne7760
      @ngagne7760 Месяц назад

      En effet , je dirai plutôt la sensibilisation contre l'indiscipline !

  • @abdourahmanetounkaraaknigg8837
    @abdourahmanetounkaraaknigg8837 Месяц назад +5

    ku beugg deugg ngueu yaw buurr mais doudou bon courage a toi
    ke certaines presse en ligne fassent attentio thi gni nouy taalal micro et Modou lo est un roi INCONTESTER
    PERE BUUR TU AS RAISON SUR TOUTE LES LIGNES

  • @Mbena7116
    @Mbena7116 Месяц назад

    Merci bour❤❤❤❤❤❤❤

  • @rouguietousy2292
    @rouguietousy2292 Месяц назад

    Walahi Modou mérite beaucoup de respect meussoul yak lam bou dano ak bounouko dané mothi yam diome, fouleu, fayda boléthi nek reference thi lamb. Felicitations Modou ❤

  • @Jeuneentrepreneurcheikh217
    @Jeuneentrepreneurcheikh217 Месяц назад +2

    Merci bour Guéweul 🎉 Modou vrai champion leu 🎉Siteu day daw Rék comme thiak thiak 😂 Père Moustapha Gueye lim wakh léérr naa 🎉

  • @SophieSall-cn7cs
    @SophieSall-cn7cs Месяц назад +5

    Vérité absolue ❤❤❤

  • @laminedione4807
    @laminedione4807 Месяц назад +1

    Bour bayile seytané. Toi et fadam yéna indi toute cette tension autour de ce combat. Yalla wane naléne doléme dimanche passé

  • @coumbadinho7055
    @coumbadinho7055 Месяц назад +5

    Bilahi bour y’a bakhe y’a degou ❤️❤️❤️🥰👍

  • @tivactutv
    @tivactutv Месяц назад +1

    Walahi bour Guewel ya Bakh ❤❤

  • @mbayelo6090
    @mbayelo6090 Месяц назад

    Je félicite tout les supporters de modou lo

  • @TaphaGueye-o9n
    @TaphaGueye-o9n Месяц назад

    Bilaye yalla rk takhe guaye wakhe❤❤❤

  • @khadimdiop8192
    @khadimdiop8192 Месяц назад +1

    Sokhor rek bilahi wakh nga léép Senegalais beugoul ndanane

  • @bocarsam5736
    @bocarsam5736 Месяц назад

    ❤merci beaucoup mbuur

  • @CheikhounaMbake2005
    @CheikhounaMbake2005 Месяц назад

    Merci bour ❤

  • @FallouMboupe
    @FallouMboupe Месяц назад

    Merci bour ❤❤❤❤

  • @bvfatima8039
    @bvfatima8039 Месяц назад

    Bien dit bilahi❤❤❤

  • @ThiernoDiallo-i8p
    @ThiernoDiallo-i8p Месяц назад

    Merci ❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhniang4186
    @cheikhniang4186 Месяц назад

    Merci beaucoup bor❤yala nala yala defal diame ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MameSow-m7e
    @MameSow-m7e Месяц назад

    Modou lôoooooo ❤❤❤❤

  • @sokhnatall4434
    @sokhnatall4434 Месяц назад

    Merci beaucoup bour

  • @Deggou
    @Deggou Месяц назад

    Bour 💯💯💯💯👏

  • @aliouneseck9774
    @aliouneseck9774 Месяц назад +1

    les niveaux de pensée ne sont pas les mêmes la lutte et un sport merci boourr

  • @birahimndiaye9553
    @birahimndiaye9553 Месяц назад +2

    Machalah yaw dangeu deugou bilaye fi daffa barri aye nafékh séne khôlle yi bonne pourquoi 😭

  • @taphaka4954
    @taphaka4954 Месяц назад +1

    Nagne wakhanté deug bilaye walaye Buur deug rekk gua wakh lamb ki legui da bari aye Nafekh Siteu beuré woul da daw combat bi yepou té Modou lo ne mérite pas ça

  • @abdoudiop8697
    @abdoudiop8697 Месяц назад +7

    Merci tu es véridique mtx j t apprecie Modou gayi dagno beugue mou danou mais yalla fi nekk

  • @SokhnafatydiopDiop-t8u
    @SokhnafatydiopDiop-t8u Месяц назад

    Billah vérité absolue

  • @modoumbayeka5045
    @modoumbayeka5045 Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤buma Ken tere wakh sakhalat❤❤❤❤❤

  • @veritesavoir5415
    @veritesavoir5415 Месяц назад +5

    Wakh deugu siteu nimou beuré ni manousé daane modou lo
    En plus roi des arènes nak dou lou ndaw sokoy dieul mérite la wara done mais daw ba sonou naane mo daane

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Месяц назад +1

    Wa diamageun yi danou yakar gon mome nit gni wakh ak daw rk maxalla ayy dof lanou salté tilim 😂😂😂

  • @Moussa.r19
    @Moussa.r19 Месяц назад +1

    Merci beaucoup ❤❤

  • @ladjicamara5476
    @ladjicamara5476 Месяц назад

    MODOU LO C Le meilleur d sa génération. Buur ta absolument raison

  • @papelo8737
    @papelo8737 Месяц назад

    Bour vraiment c’est fort👏

  • @bayeseydilaye3878
    @bayeseydilaye3878 Месяц назад

    Machalla boure nouyobi amna solo

  • @jazaka3178
    @jazaka3178 Месяц назад +6

    Même siteu a fait 4 appuis

  • @SarryElhadjiOusmane-kq5lc
    @SarryElhadjiOusmane-kq5lc Месяц назад +1

    Ya deuggu❤

  • @ElhadjCisse-l2u
    @ElhadjCisse-l2u Месяц назад

    Merci grand Frere diamal ❤

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 Месяц назад +7

    Nékhoulo ma mé nak taye wakh gua deugeu sitieu méme limou beuré sounou ko diokhone dameli war naa rous di daww rék mèlni taxi 🚕 nila défone contre lac danou di wakh mélni mo dane 😂😂

  • @assanesene1646
    @assanesene1646 Месяц назад

    Vous avez raison Bour, les gens de la lutte ont intérêt d'être normal. Fou kën sagnoul wax sa xalate mom lolou dou dokh

  • @SYLVESTREKANKOLA
    @SYLVESTREKANKOLA Месяц назад

    Merci bour guéweul lou lér nga wakh 🙏🙏🙏🙏

  • @mauricefaye3075
    @mauricefaye3075 Месяц назад

    Bour yall nala yalla feye sa xol ❤️ deug rek ngay wakh

  • @mormboup9301
    @mormboup9301 Месяц назад

    Buur t’es un bon bilahi!!!
    Yag nga wax dpui Ama ngani guiso si boy yi kouko si mena danne

  • @leuzsb5423
    @leuzsb5423 Месяц назад +3

    Pa bi beug nako dh alahou tu as bien dit les termes

  • @pbccouture4144
    @pbccouture4144 Месяц назад

    Amine ya Rabi

  • @BabaCisse-u7f
    @BabaCisse-u7f Месяц назад

    Bilakhi nitte yii yokou thiow rék lagnouy déf😢

  • @seydoudiop5028
    @seydoudiop5028 Месяц назад +2

    Respect grand

  • @taphambow2262
    @taphambow2262 Месяц назад +1

    ☝🏾

  • @FatouMendes-h8g
    @FatouMendes-h8g Месяц назад

    Bour t as tout dit merci

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 Месяц назад

    Diadieuf bouur kaddou yi rafet na machallah yalnala yallah samm defal la diam

  • @taphambow2262
    @taphambow2262 Месяц назад +1

    👑🗻Lô👑

  • @laminesylla3113
    @laminesylla3113 Месяц назад

    Bilay Bour yay Ndanane

  • @OmarBao-gu5qp
    @OmarBao-gu5qp Месяц назад +1

    Bour bilay deug rek lay wakh ❤❤❤

  • @Mrdiop
    @Mrdiop Месяц назад +1

    Max Mbargane amoul foula amoul faydaa lou dieum si lamb bou Tapha Gueye di waakh dafa wara dieul bic ak cahier di noté.
    Max tassou lanékéwoone si mbapaat yii bou mbeur yekssé mou teféssou

  • @dielkeffelywele8128
    @dielkeffelywele8128 Месяц назад

    Bour tu es sage.C'est Dieu qui va te récompenser.Niit kou bakh nga!

  • @abasall711
    @abasall711 Месяц назад

    Diadieuf boure ya niamer degue kendu modou machalah

  • @23seye
    @23seye Месяц назад

    Bilahi buur deugueula

  • @NdeyeSao-y1d
    @NdeyeSao-y1d Месяц назад

    Bour ❤❤❤ m aschalla 🎉🎉🎉🎉

  • @MorWade-w7q
    @MorWade-w7q Месяц назад +1

    Bour wakh gua degré bilaye❤❤❤

  • @adamandour9166
    @adamandour9166 Месяц назад

    Amine amiiiiiiiine amine yarabi barkep Borom Touba 🤲🤲🤲

  • @Nounou08-r1t
    @Nounou08-r1t Месяц назад

    Merci beaucoup bour guewel yalla na sa diam yagu tapha gueye dafa soff

  • @GorguiDiop-p5f
    @GorguiDiop-p5f Месяц назад

    Merci Bour lambadji mo beury aye nafekhe

  • @hawathiam3485
    @hawathiam3485 Месяц назад +2

    Vraiment

  • @Fatou-z7s
    @Fatou-z7s Месяц назад +1

    Merci👍👍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @mbayelo6090
    @mbayelo6090 Месяц назад

    Deugue nga wakh

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 Месяц назад

    Réalité absolue

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Месяц назад

    Siteu mome na bayi beuré boudée nilay mbeuré daw rk😂😂😂

  • @NdiayeMory-wt3mr
    @NdiayeMory-wt3mr Месяц назад

    Modou lô rek 💪💪💪💪

  • @sebamc4219
    @sebamc4219 Месяц назад +1

    Bour yafiné dengue rekk Moy moudiou

  • @isocra-ktm4099
    @isocra-ktm4099 Месяц назад +2

    Bour bilay deug rek lay wakh

  • @mamadoundiaye9683
    @mamadoundiaye9683 Месяц назад +3

    Mé père tapha gueye cng la nék il maîtrise bien les règlements

    • @bayemo4147
      @bayemo4147 Месяц назад +1

      Père max margane sah hamna règlement bi mais li nekh siteu rek la topp Di dof doflou . Paa yi danio doywaar koi

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop Месяц назад +1

      Ioe am nga fitt dh Tapha Gueye kagn la nek cng 😂😂😂😂

    • @mamadoundiaye9683
      @mamadoundiaye9683 Месяц назад

      @Jnrjoop moy séne conseiller

    • @mamadoundiaye9683
      @mamadoundiaye9683 Месяц назад

      @@bayemo4147 moko geuna kham wayé dou guiss dara

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Месяц назад

    Pour tant liga wakh deugue leu siteu 35 combat meunoul daan modou lo le roi

  • @Nounou08-r1t
    @Nounou08-r1t Месяц назад

    Deugu nekhoul bilahi deugu rekkkkk ga wah

  • @mamadoulassyastine2499
    @mamadoulassyastine2499 Месяц назад +1

    Walahi bour guénale soope taye nite déye wakhe deugue koi sérieu

  • @abdoudiop8697
    @abdoudiop8697 Месяц назад

    Presse en ligne gnisi Bari gno yakk lambj bilahi

  • @yvonnebadiane2702
    @yvonnebadiane2702 Месяц назад

    Merci Bourr

  • @khadythiandoum7200
    @khadythiandoum7200 Месяц назад

    Bilay bour il a raison

  • @BaraNdiaye-jm9uo
    @BaraNdiaye-jm9uo Месяц назад

    Koula gueuna kon mou geuna tardé si lamb
    Sireu dou massa dieul couronne kou wéddi ladial Bathie séras

  • @salioudia9358
    @salioudia9358 Месяц назад

    Deugleu bour geuweule 💯 seen nawlé journalisteyi nioyakk lamb doff boudiouk nioudiokhla 🎤🎤🎤🎤

  • @courtoisgueye3419
    @courtoisgueye3419 Месяц назад +3

    Bour yay nittou deugg wayy