«Nabou Leye djité Gang bi ray Aziz? Après son Arrestation..Adamo boss enfonce et fait des révélation

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 28 окт 2024

Комментарии • 203

  • @diarydiallo2816
    @diarydiallo2816 2 месяца назад +80

    Heureusement j'ai pas d'amis je suis seule j'ai confiance à personne

    • @cissebabs8961
      @cissebabs8961 2 месяца назад +3

      Boula ci dara guéné

    • @bayesoumare6509
      @bayesoumare6509 2 месяца назад +2

      Ya wah deug ai deum laniou harit amoul

    • @GalsenJolof
      @GalsenJolof 2 месяца назад

      Je veux être ton ami😂

    • @samassadiouly8317
      @samassadiouly8317 2 месяца назад +5

      Moy deug mes seules amies ma mère ma soeur

    • @weuzpouye7247
      @weuzpouye7247 2 месяца назад +2

      C vrai wally n'était pas la bas quand on tué aziz mais wally avait vu tout le monde qui était là-bas c pour cela les amis on attendu son retour pour le tuer c sa vraiment

  • @marieveroniquemendy
    @marieveroniquemendy 2 месяца назад +138

    Bilaye YALLA sédéna ni sank batey mangui dioy AZIZ DABALA, ndakh déwam bi nimou mété. Dafmay fatéli décès NDONGO LÔ nima ko dioyé won. AZIZ DABALA nieup la dioylo. ❤❤❤ndeyssane yak adina ak avenir diambour thi zéro, wayé di nguen torokh 3h du matin mo diot ni meunouma nélaw ma melni kou bokak mom😢😢😢

    • @momo_le-pro.7
      @momo_le-pro.7 2 месяца назад +12

      Beurri ngassi morom 😢😢😢

    • @landella1411
      @landella1411 2 месяца назад +12

      Je suis là chérie , 3h3 la paré chapelet mangui ni Di xool. Ça me fait mal cette histoire

    • @cheikhmorgueye
      @cheikhmorgueye 2 месяца назад +6

      Non Ndongo lo est unique Aziz Dabala on va l’oublier d’ici 3ans alors que Ndongo restera éternellement gravé dans les cœurs

    • @Adulovev5qo
      @Adulovev5qo 2 месяца назад +3

      Marieveroniquemendy li nieupeu la méti bilaye

    • @FatouBeye-cv1ch
      @FatouBeye-cv1ch 2 месяца назад +2

      Kayi dou bénn ndongo lô qu'il repose en paix 🙏🙏

  • @Mais2019
    @Mais2019 2 месяца назад +59

    Faites très attention aux fausses amies hypocrites par jalousie ils sont capables de tout. Attention! Attention!

    • @IbrahimaLy-v5s
      @IbrahimaLy-v5s 2 месяца назад +2

      Mais c'est difficile a connaitre les vrais amis

  • @PaulineThiao
    @PaulineThiao 2 месяца назад +5

    Vraiment j’ai dit la même chose à mes collègues t’as raison Adamo

  • @adjaratoufatouthiam9699
    @adjaratoufatouthiam9699 2 месяца назад +19

    Si Wally n etait pas venu il serait le suspect numéro 🤲🤲

  • @MarieAmaar
    @MarieAmaar 2 месяца назад +79

    SÉNÉGAL il faut niou appliquer PEINE DE MORT 💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿

  • @fs8kl
    @fs8kl 2 месяца назад +56

    Une demande générale au président on doit plus sortir celui qui a commis une crim

    • @Adulovev5qo
      @Adulovev5qo 2 месяца назад +2

      Bilahi wakhgua deugeu

    • @sokhnafatimasarrsagna2595
      @sokhnafatimasarrsagna2595 2 месяца назад +2

      ​@@Adulovev5qo danou len wara rayé

    • @niangtra
      @niangtra 2 месяца назад

      S'il le faut gno def marche nationale et internationale ak wa diapora bi le même jour , peine de mort rek , sinon peuple bi fadial bopam

  • @sympathisante17
    @sympathisante17 2 месяца назад +21

    Ana dom djiguenn di demm di deukeulii ay gorr 😢c'est triste 😢

  • @clairemari7292
    @clairemari7292 2 месяца назад +2

    Moi je suis sidérée c triste et grave ça pourquoi en tout cas doyna waar ndeh merci adamo

  • @TallaFaye-y8t
    @TallaFaye-y8t 2 месяца назад +11

    Tu as raison adamo

  • @Dada-u8n
    @Dada-u8n 2 месяца назад +14

    Un conseil les gars bayilen kharit amatoul que ce sois homme ou femme

  • @layeba6264
    @layeba6264 2 месяца назад +31

    Lolou la geum dh beneu niit meunoul ray 2 personne a Mon Avis

  • @NdeyecoubeGaye
    @NdeyecoubeGaye 2 месяца назад

    Adamo do nit merci

  • @FatoumataKane-k2p
    @FatoumataKane-k2p 2 месяца назад +1

    Bilahi Adamo wadji daniouko toumal wayé rayoul danio beug étouffer affaire bi ma rousse thi polisou Sénégal

  • @DiarraThiam-hk1dy
    @DiarraThiam-hk1dy 2 месяца назад

    Mais affaire lous na mais yalla bakhna yalna lépou lére si barki seydina mouhaméd PSL

  • @papediouf48
    @papediouf48 2 месяца назад +3

    Lolllll thiey adamoooo!!!!,boy bi dou niittt!!!! Ya ko fekeeee

  • @kine1687
    @kine1687 2 месяца назад +1

    Ay adamo😢😢

  • @lasolutionavosproblème
    @lasolutionavosproblème 2 месяца назад

    Ndeysane

  • @NgonéDiop-c1g
    @NgonéDiop-c1g 2 месяца назад +12

    Yalla na yalla gay fégnal li thi diam j ai vraiment mal au coeur❤yalla boussi nabou ko konne dina ame louma méty

    • @fatousall3188
      @fatousall3188 2 месяца назад

      Nabou migui kereum gni wakhou gnou boulene topou ki aiye Vu la beuge

  • @MouhamadouGueye-n7g
    @MouhamadouGueye-n7g 2 месяца назад +14

    Non.........Admo do nite carte bou lére ngaye téck ni wayé da ma beugue nga yéme fi bayi wa DIC agalé yeuf yi ndé sa analyse dafa pertinent ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @Mounajate
      @Mounajate 2 месяца назад +1

      Dix da Mel ni Adamo laniouy deglou

    • @Adulovev5qo
      @Adulovev5qo 2 месяца назад

      ​@@Mounajatewalahi wakhgua deugeu

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo 2 месяца назад

      Adomo wakhoul wone lii day dègue di wakh rèk xamoul si affairs bi dara

  • @assaneloum4536
    @assaneloum4536 2 месяца назад +1

    Adamo chapeaux t'avait tt vu depuis le début

  • @YathWade
    @YathWade 2 месяца назад +19

    Adama a raison sur toute la ligne.

  • @bachirndiaye746
    @bachirndiaye746 2 месяца назад

    Deee bi nonou la mette Sénégal gi yup bilahi

  • @alydiedhiou1116
    @alydiedhiou1116 2 месяца назад +10

    Y-a-t-il pas un problème de réseau de vendeurs de drogue. En général, les problèmes liés à la drogue se règlent dans les coulisses.

  • @moussaba4865
    @moussaba4865 2 месяца назад +1

    Gouruope toppeka la bakke❤

  • @AboubacarSidikhCamara-q1j
    @AboubacarSidikhCamara-q1j 2 месяца назад +2

    Bonne analise adamo

  • @MaterDiop
    @MaterDiop 2 месяца назад +13

    Adamo domeleu sètaneu woheu deugeu wayè deugeu rek ngeu fii woheu

  • @fatousall3188
    @fatousall3188 2 месяца назад +2

    Adamo ya mene doul setal yalla si lingaiy nar ngene am gathie rek ki nga khame ni da alkou😢

  • @ndiayemamadou9982
    @ndiayemamadou9982 2 месяца назад +1

    Adamo.khana Mounga fa wône fékéna lépe

  • @diagnemomo4771
    @diagnemomo4771 2 месяца назад +16

    Toujours nabou léye yakhana adunam

  • @boussogningdiagnegning7974
    @boussogningdiagnegning7974 2 месяца назад +3

    Bene niite surtout contre niaary niite dafaaa yomb toroppp il n'était pas seule amnaaa nioumouu adalone

  • @houleyeMbodj
    @houleyeMbodj 2 месяца назад +1

    Dayil doul

  • @veritesavoir5415
    @veritesavoir5415 2 месяца назад +9

    Adamo niatta wakh ngafi wakh bi affaire amé batay il est temps nga nopi nak khamosi touss,gnép khamnaniou gnouko kham nioko ray lolou dou informations

    • @bayesoumare6509
      @bayesoumare6509 2 месяца назад +3

      Vraiment il nous soul
      Fen rek lay def

  • @dabacisse2957
    @dabacisse2957 2 месяца назад +1

    On dirait que Adamo à raison en tout cas laisse la police faire son travail

  • @farbadiouf1990
    @farbadiouf1990 2 месяца назад +1

    Hanh ! ? Adamo est un phénomène...
    Voilà une montagne...

  • @MaterDiop
    @MaterDiop 2 месяца назад +10

    Billahi jalousie leu gnignoyeu ayeu dommou goorr djiguèneu

  • @sarrmodou6470
    @sarrmodou6470 2 месяца назад +2

    Adama té nga noppi lé nga fi wakhoon léppp avant dara dou si dëgg , yaané woon samedi laniouko ray té rayou niooko samedi yagui fénati rèk baakh na .da nguéna wara noppi police dina léral lépp .gnisiy wakh gnépp daniouy douul rék xamou niou si dara .

  • @ogobrown9024
    @ogobrown9024 2 месяца назад +8

    Yooww Moom, Yâh Däkhää Doül Fïï..!!!!!!! Tu es à l'étranger, Bâ Parëëh Geneü Äy POLICE...

  • @الحمدلله-ض5ي8غ
    @الحمدلله-ض5ي8غ 2 месяца назад +7

    Il a du souffrir pov chou❤

  • @nafisene5335
    @nafisene5335 2 месяца назад +13

    Motakh Niit Da ngey reglé. Kham gni nga wara andal. Naka ngey boké ci famille bo khamni presque nieup ay hibadou la niou, ngey dougou ci gni ba niou ley def ni. Nio khamni tokh yamba ak nane rek. NABOU leye mi kou ko Guiss ak melokanam noy kharitowé ak mome

    • @didigalass2506
      @didigalass2506 2 месяца назад +1

      Gnigui wara andal nio laye complot di ma Cherie mba niou poisonela motakh mane sa TAKANDER MOY SAMA KHARIT

    • @SM_C24
      @SM_C24 2 месяца назад +6

      Man daal li ma ci geuna meyti rek moy fasongi deey bi ak nim betté Aziz. Ndax ku né beug nga dundu ba magget, bala lolu fekk nga toub lu bari li nga daan deff. Waay gni deff lii Aziz ak boy bi Waly degn len xagne chance bobu. Yalna len Yalla jegal te maye niou moujj yu rafett. Aameen

    • @Deathtomyennemis
      @Deathtomyennemis 2 месяца назад +5

      Saway andando kharite amatoul dieulale yalla defko mouy sa lepeu

    • @aidaniang9626
      @aidaniang9626 2 месяца назад +2

      Walahi DEUG la

    • @fatoudhasalihateseck9554
      @fatoudhasalihateseck9554 2 месяца назад +5

      @@Deathtomyennemisvoilà mane deh yalla moy sama confident parsk moma khamal lep té soutouralma ma togn diko dieguelou sou metté mome rek soumay dioy mome rek momay guiss

  • @aidafallousall6793
    @aidafallousall6793 2 месяца назад +15

    Aye waye waly bou guènton lii sakh dou gneuw

  • @IbrahimaKandji-b3u
    @IbrahimaKandji-b3u 2 месяца назад +5

    Wa Babacar touré
    Khana nèkoul Sénégal
    Taye mom sétane ngagnou

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 2 месяца назад +2

    Ca mome ca peut etre vraix au moment du crime de aziz wally n ete pas la mouye bene niou deme

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 2 месяца назад +3

    Nabou leye ndakaté ya raw diango sakh

  • @MatarCissokho
    @MatarCissokho 2 месяца назад +8

    Nabou ley moy domerame jiguenne sopal boull wollou

  • @DiorDIAKHATE-hh6mr
    @DiorDIAKHATE-hh6mr 2 месяца назад +7

    CrimeDistrict+ planète Crime+Chroniques Criminelles + Colombo=dof Adamo

    • @Lopios-g6l
      @Lopios-g6l 2 месяца назад

      Attestation parfois Day féen di yokk 😮

    • @fallabou
      @fallabou 2 месяца назад

      Kikay mo raw colombo😂

  • @NdeyeDiawara-rj7py
    @NdeyeDiawara-rj7py 2 месяца назад

    Comment il sait tout ça lui 😮

  • @myamandiang
    @myamandiang 2 месяца назад

    Adamo nabou leye soûla baloul dou bakh

  • @karamodrammeh8038
    @karamodrammeh8038 2 месяца назад +30

    S'il vous plaît, pour l'amour de Dieu, laissez ces problèmes à la police, ils font leur travail, arrêtez de nous donner de fausses informations

    • @LhommDanyMdy7667
      @LhommDanyMdy7667 2 месяца назад +7

      Est-ce que c'est pas mieux d'aller directement à la police te renseigner au lieu de faire comme si on t'a forcé à écouter la vidéo.

    • @MrFayemanou
      @MrFayemanou 2 месяца назад +1

      Vraiment

    • @MrFayemanou
      @MrFayemanou 2 месяца назад

      Tok dii doule rek ❌👎🚫🚫❌👎😡

    • @bayesoumare6509
      @bayesoumare6509 2 месяца назад

      Niom niepay fen informations boubah dal naniou har police mo geneu wor

    • @MamanLo-dc7ro
      @MamanLo-dc7ro 2 месяца назад

      Vraiment diay graw rk😂​@@LhommDanyMdy7667

  • @bayembaye682
    @bayembaye682 2 месяца назад +3

    Me adamo yueramale famii Aziz yi Aziz dabala Thiate dji tou nako sy bamelame rek 😢mok wally

    • @momo_le-pro.7
      @momo_le-pro.7 2 месяца назад +5

      Astahfiroulah thiate kay kimou djitou si sa bamel torokh nga yalna khipé aldiana mog wally amine 🙏

  • @laminendiaye6210
    @laminendiaye6210 2 месяца назад +1

    Adamo bayil doul😮😮

  • @TallNdiaye-oq9jr
    @TallNdiaye-oq9jr 2 месяца назад

    Adamorek

  • @abdelohod4884
    @abdelohod4884 2 месяца назад +4

    Kouy weur kou niemei yallah moy adamo😂😂😂😂 shiiii aka nieimei yallah adamo ligay dara guasi khamul bayyil feinne bi tamit

  • @momo_le-pro.7
    @momo_le-pro.7 2 месяца назад +2

    Amna lo khamni yanou woul sakh mana khel meunouko nangou ben nite kou seww naka la mana rayé gnarri nite sans que mou trace ag réplique wakhoumala nak gnarri goor sama khel bagne na bama guiss lenen wala confirmation DIC ma door ko guem

  • @moussabalde6194
    @moussabalde6194 2 месяца назад +1

    Hamothji dara mon frère

  • @Dykha-25
    @Dykha-25 2 месяца назад

    Adamo koula gnouss ga walh ki ray

  • @KhadyjaToure-xt1lw
    @KhadyjaToure-xt1lw 2 месяца назад

    Alkhamdu j ai pas d amis ❤

  • @fatousall3188
    @fatousall3188 2 месяца назад

    Yene gni nane nabou leye bayi lene domou diambour nabou kene diapou ko manou té yalla takh adamo diaroul topou

  • @AwaCoulibaly-f6l
    @AwaCoulibaly-f6l 2 месяца назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @combecane257
    @combecane257 2 месяца назад

    Délén wakh Abdoul Aziz svp mo gueun

  • @AmetThiongane
    @AmetThiongane 2 месяца назад +4

    Adamo doul kasse lay df guakoy tek fi di begue ay vue go way

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k 2 месяца назад +7

    Tieye adouna bi tite na ci sénégal

  • @BoubacarLo-q4f
    @BoubacarLo-q4f 2 месяца назад

    Je suis peut être d'accord ni Aziz ak Wally n'était pas ensemble au début

  • @mbenesarr1204
    @mbenesarr1204 2 месяца назад +6

    Nabou leye mii tamite🥹

    • @Mounajate
      @Mounajate 2 месяца назад +1

      Cette fille ne m a Jami’s inspire confiance

  • @aidaniang9626
    @aidaniang9626 2 месяца назад +1

    Mane dé nabou leye sou boke si li ma bayi adouna

    • @myamandiang
      @myamandiang 2 месяца назад

      D’à nga nane ma bayi sama meilleur amie mane mako wax

  • @malicksene6329
    @malicksene6329 2 месяца назад

    Aka am fiite😢😢😅

  • @cheikhfall9985
    @cheikhfall9985 2 месяца назад

    Adamo bayil fén

  • @mansourgaye6205
    @mansourgaye6205 2 месяца назад +11

    Goor nane laye bayé séne wa keur dème deuk ak morom goor ba près nangoul wax séne wa keur fanela né ak kanela nékal kénéne ki aussi guéne séne keur ba près fimou déme deuk mou faye andi ñiénéne gñu faye yéndou difa fan'ane kouné ak sa xél ba famille moudjé cas bi dou xaliss wayé borom yi deug xame naniou lanela

    • @cheikhmorgueye
      @cheikhmorgueye 2 месяца назад +3

      😂😂 gayii kayy beugougn wakh la réalité mai borom khéll comprendre nagn

    • @timab48
      @timab48 2 месяца назад +2

      Mane de lila wakh

    • @khadydiome6597
      @khadydiome6597 2 месяца назад +2

      C'est ça les vrais questions

    • @Lopios-g6l
      @Lopios-g6l 2 месяца назад +7

      Yayilén gnaw ndiorte djioulite
      Dou gnaw ndiorte sén papa yii bougnou
      Démé Europe aye gore lagnouye deukeul
      Thi foyer yii 2 par chambre téé tahoul gnou Doon gore djiguéne waly cherchait sa voix pour devenir artiste bayilén dii déglou Adamo bamm eupp.....

    • @oulymatadiatta1118
      @oulymatadiatta1118 2 месяца назад +1

      ​@@Lopios-g6lmercii bcp sénégalais dafa meuneu toumal moromam😢

  • @BachirWone
    @BachirWone 2 месяца назад

    DIAROUL NIOUY AM AY KHARIT YOU BARI AY ANNANDO CONNAISSANCE YEUP DIAROUKO

  • @mameseyefalloumbacke7906
    @mameseyefalloumbacke7906 2 месяца назад

    Waw waw Adamo amna complices d

  • @CheikhsanaDiakhaté
    @CheikhsanaDiakhaté 2 месяца назад

    Adouna kou nék ak noumouye déwé mouno dow be reutch gnou bakh gnougui bakh be légui mais gnou bonne gnougui bonne be tey

  • @BallaMoussaTamba09
    @BallaMoussaTamba09 2 месяца назад

    Mom da wakhone ni Hôpital la yobou Aziz alors que c’est pas vrai bén thiantt lagn démoone. Teh ci thiantt bobou la Aziz dioté ak gars yoyou. Après niou dieul taxi mom ak Aziz dem sila wathiè si yoon bi bayi Aziz continuer. En plus niou ladj ko kann ladoone communiquel ci goudi bi mouneh personne hors que bouniou holè téléphone bi dafadoone communiqué si watshapp bi. Motakh migui garde à Vue en attendant la suite.

  • @nndiayeballa
    @nndiayeballa 2 месяца назад

    On n'est pas là pour faire du théâtre.

  • @MarieAmaar
    @MarieAmaar 2 месяца назад +4

    Nite dal, kharito wal ak nio bokkal ndeye ak baay, ou sa ndeye ak baay ou dieukeur, diabar ou say doom, sénégalais mo sokhorr té leundeum

  • @ndeyefatou9072
    @ndeyefatou9072 2 месяца назад

    Wa keur Aziz nagnoudem sen keuryi rey sen ndeye

  • @mamadougaye9304
    @mamadougaye9304 2 месяца назад +1

    Adamo Bayil fen soniou police dina wax lep inchallah🤫🤫🤫

  • @omarmboup8624
    @omarmboup8624 2 месяца назад

    adamo bayell fine khamo thi dara

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 2 месяца назад

    KHARITOU BÉNN BAKKANE AMATOUL . DÉÉL MA DÉÉ AMOUL FÉNNN

  • @CheikhOumarFaye-if1eo
    @CheikhOumarFaye-if1eo 2 месяца назад

    Chac jours avec version bou bèss tè guèn tok dègrou enqueteur yii rèk tot ou tard deuk bi dina fègne

  • @BinetaNdoye-yf6pp
    @BinetaNdoye-yf6pp 2 месяца назад

    Mane dama warou waneguéne gnou Mamadou Lamine dao bou khéss kanane gui kome suigom wangnou kénéne kou gnou kome déteu légui mane topatouma ça bi dama sone féne

  • @AstouNiass-s1y
    @AstouNiass-s1y 2 месяца назад

    bayi léne nane tidiane yi ak niasséne gni mes niass sente la kouy tidiane rék baye niass moy sa khalifa arréte téléne lolou

  • @zulnhofaye2584
    @zulnhofaye2584 2 месяца назад

    Adamo yaw ki la wakh li warna niouko dieuli bilahi

  • @KhadySall-g1p
    @KhadySall-g1p 2 месяца назад +1

    😭😭😭

  • @DiawMamecheikh
    @DiawMamecheikh 2 месяца назад

    Mane awouma kharite insbi sama liguey Moy sama kharit dnax douma trahir

  • @cheikhtvndiaye1315
    @cheikhtvndiaye1315 2 месяца назад

    Con gniom binouy def lolou nekatoun ay nit ndakh toukh boone mome so mande nekato nit soubhana lah

  • @AhmedNiang-ue7uy
    @AhmedNiang-ue7uy 2 месяца назад

    Il faut faire très attention à certaines femmes dou djiguéne gneupeu baah

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 месяца назад

    Pékin dou dara

  • @fanyadelecoly3019
    @fanyadelecoly3019 2 месяца назад

    🤔🤔🤔🤔🤐🤐

  • @manediop5912
    @manediop5912 2 месяца назад

    Day doul rék rék khamothi darra

  • @yayefatyndiaye2132
    @yayefatyndiaye2132 2 месяца назад +1

    Temps yi yeup nélawouma amna louma métiii loll bilakhi déwou aziz bi métina en plus say xarite alakhou akbar

  • @M7B7A4Y6e
    @M7B7A4Y6e 2 месяца назад

    Donc touh yamba nane saguara donc dagno mbadiwone motakh gnou reyyy ko

  • @khadimamar1687
    @khadimamar1687 2 месяца назад

    Déména déevo fakhe maan dh

  • @BayembayeDiop-n4s
    @BayembayeDiop-n4s 2 месяца назад

    Goor djieguene yi niou fi bari naniou len wanji 😂😂

  • @AwaJobe-yt4rj
    @AwaJobe-yt4rj 2 месяца назад

    Yow fen

  • @abdousylla230
    @abdousylla230 2 месяца назад

    Ya mana doule bayil Yakar yaw dagay imajiné rek

  • @xnobot2.058
    @xnobot2.058 2 месяца назад +3

    Yowe mome doulrek hawma loutahe Senegaleyi dila deuklou

  • @mamadoulaminembodji9648
    @mamadoulaminembodji9648 2 месяца назад

    Lundi ç la loi qui le dit😮😢fii aye affairou Macky sall yoyou doufi amè dè😢😮daye leer ,enquete bii diar yone ,leup ci temps affaire de gouvernance pastef au fait😂😂yeuffi aperiste yoyou 😂protègè goordjiguène yi ak sèni lobbys domexarames.diex na fi .Cette fille a etait coupable meme devant les lamdas figurons nous devant les enqueteurs🎉🎉beugueu xaliss ,diaye tarr 😂😂dem lène sèyi mo gueune .,sama far fii ,sama nii ,na nè😂😂aye tiaga groupes aka barri ci deukeu bi .les amies de yerim sexe😂😂😂louè tiaga rek lafa nèkè domexarame diodiu😂😂demandez a Astou pourquoi elle est partie?😂😂]pas pour son passè😂dafadone saga sonko ci livre bi pastefiens yi yollè son proxènètisme ,la femme journaliste la😂😂motax 1 semaine laci tek 40taine ndeyame😂😂😂🎉

  • @zulnhofaye2584
    @zulnhofaye2584 2 месяца назад

    Danguén Di féne rék pour âme vue

  • @moustaphadiop20
    @moustaphadiop20 2 месяца назад

    LA NOUVELLE OPPOSITION ( LA PRESSE) & AK WA KEUR DOFF YI TROUVERONT BIENTOT UN LIEN ENTRE LA MORT DE AZIZ DABAL ET OUSMANE SONKO yagatoul ..

  • @abylam628
    @abylam628 2 месяца назад +4

    Yako fekké😔