Certificat médical refusé Boy Niang 2…? 22 jours avant son combat, contre Reug Reug

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 дек 2024

Комментарии • 17

  • @youngboybpshoot421
    @youngboybpshoot421 День назад +3

    Boy niang togne guama nak
    Sama t-shirt Reug Reug yima défar gua yakhal mako ni
    Mes Nice digua mako faye déhhhhh

  • @KhadimFall-r2d
    @KhadimFall-r2d День назад +2

    Boy Niang toujours boy Niang chaque combat médical jusqu'à quand

    • @doudousanebadji696
      @doudousanebadji696 День назад +2

      Yaw kou gnémé yalla ngua

    • @Ma-Habba19
      @Ma-Habba19 День назад +2

      Boy Niang c’est la première fois qu’il dépose un médical arrêtez vos sottises

    • @papezulefaye7263
      @papezulefaye7263 День назад

      Yaw ya meuna doule fane nga meussa guis boy niang yakh lamb akk médical

    • @seydousow7040
      @seydousow7040 15 часов назад +1

      Yaw ya meune doul Boy niang il a toujours présenté ses combats

    • @papezulefaye7263
      @papezulefaye7263 10 часов назад

      @seydousow7040 ahh bro kii diaroul tontou sakh dafa khamoul boy niang meussoul yakh lamb

  • @sambaba683
    @sambaba683 12 часов назад

    Dèffa ragual reug reug rekkk tappètte leu😂😂😂😂😂😂😂

  • @WalyDiouf-w9p
    @WalyDiouf-w9p День назад +2

    Dafa daw ragal leuh

  • @ITOLDYOU-p8z
    @ITOLDYOU-p8z 2 часа назад

    Man hamna boy niang dey dwo. Dara jutu ko

  • @murtadaajonn6502
    @murtadaajonn6502 День назад

    Bu leen seen sëriñ yi waxee ne mbër mi jekku na la rekk, walla ñu ne leen combat baaxul jamono yii rekk ngeen crée Maladie.

  • @muhammedjuwara3633
    @muhammedjuwara3633 День назад

    Boy Niang danga daw y ammal diam

  • @sambaba683
    @sambaba683 12 часов назад

    Raggual rekkk😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @fantadiop6033
    @fantadiop6033 День назад

    Site yi fén rék

  • @amdymoustapha5603
    @amdymoustapha5603 6 часов назад

    Bayil tapalé

  • @MamadouKébé-y5t
    @MamadouKébé-y5t 12 часов назад

    Yow wahkofi Lou ler doul rek