série bi nekhna trop mais sen montage yi ak scenario yi xolat Leine ko waye. Bcp d'erreurs ont été constatés exple sur l'épisode 12 Ba réunir na Thiam ak Deureum ak Moustapha ba annoncer Leine mariage bii Thiam bagne ensuite Episode 13 bii ni Thiam di annoncer watt le mariage t andeu nathi bipaa. Dieul leine sen tps ngen servir gnou mouy guene nekh BTW mercii bcpppp
Yaye dou tayi béneu yone si doomam xolal seune reek nimouy soné si doom ja bou té doudeutoul leçon biniou si wara diangué moy yaye moy lépp sama xoll sorina trop si diguenté seune ak doom ji
LEGUII MOOM THEATRE IU TEKEFILN BI NSNN KO WOOWÉ ,,,POLYGRIOTS LA TOUDOU 😅😅😅..DARRA NEKHOUSI..AYYY HONKOU AKII HIIIHII HAHAHAAA RECK,,,BEN SENS SUR LA POLIGAMIE AMATOUSSSI...DES HISTOIRES BÊTES ET AUCUN SENS SUR LE THÈME POLYGANE .,A PART DOOMII BA YOU DIAXA SOOYIII ,,DOOMM DI FEULEU CHAQUE JOUR BÉNN DOMM PERDU DE VUE NIEU TAXAWW
Lou beug Serigne Fallou mbacke la jem ❤❤
Kou beugue serignebabacar sy rèk lalal jaime❤❤❤❤❤
😂😂sacré ndeye ndiaye tout pour l argent mais massar tmt lénéne la 😂😂
😂😂massar kay kenne dou mom
Kou beug sayedina Mohamed lalal je amine❤
Salla watou alyka ya khabibi ya❤❤❤ rasouloulahi ❤️❤️❤️ psl ❤❤ psl ❤❤ psl ❤❤ psl ❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
HALEYHI SALATOU WA SALAM ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Non série bi sans ndeye ndiaye😂dou nex yalla nasa diam yague ❤😂😂😂😂😂
Bilay
Massar dé mongui batré rk gni lijenti wouniou fou halis dioge baham borom niari tour yila wala Mouy diay drogue ndeye ndiay mom halis foumou diogue bahna Nay halis rk😂😂😂
Kou beug serigne saliou lalal j'aime ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
Mame saliou ma vie ❤️🥺
💕❤️💕❤️💕❤️💕J'aime y'a gaugue❤️💟💙💗💚💏🌹💖💞
❤❤❤❤
Nn Ndeye Ndiaye 😂😂elle est dans tous les sauces avec l'argent 😅😂😂❤
Non masaer moofi meune il est trop fort 🤣
Notre série préféré on réclame le retour de bouda
Beugo diam dei😂
Ay Mariage Fat Kiné Massar 😂😂😂 duo bobu kuko tardé Massar tay rek ngaay dé 😂
Bou dawra diaw mariage fatou kiné yenou massar
@@NdeyefatouSylla-yp9px non yakamtina lolu🤣🤣🤣
Seuyou gnari wakh katt
@@assalihouproductionje t’assure 😂
Mère binta machalah sa duo ak tata coumba begu nane ko dee
Ndeyssane maman seune damako yeureum elles seul..mais nak da wara bayi xoulo bi garde ton calm maman c'est trist billahi
Lika dal dafa néxoul si xol😢
Bayilen Serigne si ngéndi fowé 😢lo néck dafa am palasam
Deureum dou nitte😅😅 le awa ak astou non machalah ndaye tu est très forte kine yangui si dra de mane sama cheri la nam oumou rk lay topou
Oumou problématique ngay name 😂😂
@@fatigaye6489 mom rk la nam
Sama serie prèfèrè❤ fat kine mo diongomana kay bou jourou mirage bi lay gniawat
Guanima daguay togne wala
Bou Dina gnew wala
@@Fabeautystyle29 tougnouma de bou dee woul wa keur gui lay setlou rek🤣
@@Mbéne-l9jhaann kone dé épisode bobou dina nékh saff😂😂😂😂
Non guiss nani daguay dalal sama khel bi ni 🤣🤣
Massar raynama😂😂😂😂😂😂
Ndeye ndiaye raynama beug ngue khaliss
Astou mom da doff😂😂😂😂
Wa mane noumay def ba guis massar bo toguê sakh mou mayla 200000mil😂😂😂😂😂 Ndeye Ndiaye boko wakhone mou ray nit sakh dinako def 😂😂😂
Série bi nekhna mom sen waw ak sama waw la bolenko bolé mouy wawaw😂😂😂😂
Mane MASSAR la beug ❤❤❤❤😂😂😂😂😂
Astou pour môme seuy bii dall serigne la🤔🤔🤔
Ko dakor né 3em saison bi ,mon dakeu rék lalal j'aime ❤
Yal na Yàlla rëbbu Ibu Ndafa ak képp ku Ànda ak moom!
😭😭😭😭😭😭😭😭
😢😢😢
Machallah kinè Yangui melni khalè❤
Il es fort massar❤
Mais massar est-ce que dou vrai gueweul il est tres fort
Massar tmt 200000f moom khana 200f moko diapé 😂😂😂
Moma dia khall 😂😂😂
Doyna warr de 😂
Moma diakhal
Non Ndeye Ndiaye mome ngagnou li wa bakh na bamou sotii khalisse rek laye liguénté😂😂😂
Tém mou tiryan thi dé😂😂😂😂
Always love you fa Kine 🇬🇲❣️❣️🥰🥰
Massar té meilleur machalla
Waaw! Massar, khana dafa deubeu keurigne, taye ko thi kaw beut yi?😂😂.J'arrive pas à voir ses yeux😂. Tout est" gnoule nagneu"😂😂😂. LOVE
😂😂😂
Enfin fata😅😅😅
😂😂 nieuwatinga
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂j meurs ay fata cheuuu
Ndéye Ndiaye djiguène diou bakh Dou niane xalisss surtout biye séyyy
Massar mii ahhh souma nekone si série bi dina KO nok chaque jour kii loumouy deff nii 😂😂😂😂😂😂😂
😂😂
Ndéye Ndiaye ak khalis dagnou longtemps 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
BÂ, c'est la toxicité en personne. Shiii, sacré personnage.
Kou abonné sunu chaîne yalna yalla may doom bou goor nga toudé KO seydina mouhamed psl🎉❤
Amine ❤❤❤❤❤
Serie bii amatoul sans saison 2 rk bakhon n'a kou d'accord aimél sama commentaire
Ndeye ndeye motkh maye setane série bii😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
Tâta Seune la begue ngéne diokheko respect sinon je désabonne
Astou toujours égale à elle dofna loll nena serigne noumouy toude sadio ndiaye
Aye ndeye Ndiaye mome khaliss rek 😂😂😂😂 fate kiné rèw nga molon kay 😂😂
série bi nekhna trop mais sen montage yi ak scenario yi xolat Leine ko waye.
Bcp d'erreurs ont été constatés exple sur l'épisode 12 Ba réunir na Thiam ak Deureum ak Moustapha ba annoncer Leine mariage bii Thiam bagne
ensuite Episode 13 bii ni Thiam di annoncer watt le mariage t andeu nathi bipaa.
Dieul leine sen tps ngen servir gnou mouy guene nekh
BTW mercii bcpppp
Non Ndeye ndiaye ak l’argent c’est une longue histoire massar dou ma raye dé 😂😂😂
Astou aka reuy lamigne heure bouy wah damay wagni sama volume😂😂
Massar dinamaaaa rayyy 😂😂😂 ndeye ndiaye melniiii badienouuu gokhhh😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂🎉
Wa Massar mii nitt leu😂😂😂😂😂 scheutt 🤣😅
Khaster bakhoul ter mo yakhe senegalais. Nite daye khole hier di sentou demain. Allale famous djiemer ns femmes amoul glace. C triste
sacré Ba lo wakh amna reponse sam😂😂😂😂😂😂😂
Je réclame le retour de la fille de Seune
Mdr khady amoul beneu dieurigne 😂
@@fatigaye6489 Non si dafa wara réussir yorate keur gui
Cheikh dethialaw seck gaindé ngourane ❤
Awa dilalen siwal yeup dina khameni daguen liggey kine
Non massar Dinama Ray AK Sama bay bou bakhna néna😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Serigne sadio ndiaye😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Deunou Kiné bi louko reuthieu😂😂😂😂?
Bou jourou khéw bi lay niow fofou tothieu😂😂😂😂😂
Astou Serigne dou seuye 😂😂😂🎉
Astou kay nimou mel legui dou diam😂😂😂😂
Lepp Awa la 😂😂😂😂
😂😂😂😂😂no bineta raye nama, nèna fatou kinè moussoul ame banèkhou seye ndakh bou dsfa patawone 😂😂😂 chaque jour daf ko dane yobou gnou mothie deune bi. Maye fatou kinè di deugal😅
Ndeye Ndiaye AK massar dinagn ma ray rek bilahi 😂😂😂😂
Fatou kinè ngui rèe binta 😂😂😂 nèna damako dane yobou di mothioulou deune bi
NO BOU DAFA WARA GNEUWATE WAY NO BOU WAROUL DEH NA DEF LE REVENANT🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Astou la y topou😂😂😂😂😂😂
Alhamdoulilahi tay Bâ soloul waxi
Nn série yagu n'a nékh temps ya Thiam yoré won poutique bi 😂 té dou diay draa😂😂 ndakh xouloc
Mass at rek❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂
Macky dou nitt ku baax
Billahi
Tata seune pourtant li père ba def lolou leu l'islam wakh Dee
Sisi
@@fatigaye6489seune mom khaw ma kagn lay am bonheur rk
Bilay polygame daniouy meilleurs❤😂
Matar comme salade bou lakh 😂
😂😂😂😅😅😅😅
Ndeye ndiayeyalaga goudoufanenodaguayedinistress😂😂😂😂😂
mani ndeye Ndiaye pourquoi mou lové khaliss 😂😂😂😂
Kome yaw rek 🤣😂
@@djilybakhdad borome bakhdad man ma tane ndeye Ndiaye 🤣🤣
صلوات على النبي كل كم ❤
Ndeye Ndiaye khaliss rek la beug
Wa Ndiaye Ndiaye sa dôme dji khana bouye tak Diabar Dina guéne
Surtou llou 😂😂
😂😂😂😂😂😂c’est bizarre dall
Thiey sacré ndeye ndiaye dou nittou fi 🥰😂
Oh pauvre Seune
Ma jolie kiné sa teint bakhna
Yaye dou tayi béneu yone si doomam xolal seune reek nimouy soné si doom ja bou té doudeutoul leçon biniou si wara diangué moy yaye moy lépp sama xoll sorina trop si diguenté seune ak doom ji
Ndeye Ndiaye ak massar dinagn ma ray rek😂😂😂😂😂😂
Astou m'a 😂😂kagn la Serigne dane toudou Sadio Ndiaye 😅
Sadio Ndiaye kay😂😂😂
Non massar est très fort mon dégue😂
Waw ana domi ndeye ndiaye
Sadio mané 😂😂 moma diakhal dh
Massar wa evenprod waronagne la dieule si série bété bété😂
Gewo wi géwi binta samb géwago dé sanékh ken dou mome😂😂😂😂😂
Ndéye Ndiaye dorr katt leu
Aïye ndeye Ndiaye 😂😂😂
Nonnn j’aime trop Ma Sarr 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🥰❤️
Hooo ana naffiii yii manifesté vous 🎉🎉🎉🎉🎉
Thiam nieup laay haine amoul mbokou 🤣🤣🤣🤣😂😂😂
Man moma diakhale sacré thiam😂
Wa kiné kobayék bébé bou
Am Isa Kebbeh from The Gambia 😊🇬🇲
Sama serie préférée ❤️ mais la
Hoo liguey bi diapna non waye kiné do bagne
thiam amoul thiakhanne🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
passât kou rew leu😂😂😂ndeye ndiaye mom damako beug
Non massar il est fort 😂
Wouy fin bi fat kine nena amelnako 100 mille 😂😂😂 bii khaliss yaague nah nake😅😅😅
Don't give ndey njie the money to share it, ndeye is a mafia you know that ndeye is following you for her own interest
EY WAYYY BEYTIR MADJIGUÉNE MBOR RA SONEU WAYYY AHAHAHAH😂😂😂😂
LEGUII MOOM THEATRE IU TEKEFILN BI NSNN KO WOOWÉ ,,,POLYGRIOTS LA TOUDOU 😅😅😅..DARRA NEKHOUSI..AYYY HONKOU AKII HIIIHII HAHAHAAA RECK,,,BEN SENS SUR LA POLIGAMIE AMATOUSSSI...DES HISTOIRES BÊTES ET AUCUN SENS SUR LE THÈME POLYGANE .,A PART DOOMII BA YOU DIAXA SOOYIII ,,DOOMM DI FEULEU CHAQUE JOUR BÉNN DOMM PERDU DE VUE NIEU TAXAWW
Khalis mom.dagénko yombal mom😂😂😂😂