Размер видео: 1280 X 720853 X 480640 X 360
Показать панель управления
Автовоспроизведение
Автоповтор
S Mustafaa joob ku rafet xol la te xam lu bax di ko wakh yalla na ko yalla fay
Aka deuggou yalla na aw fanam gouddou té mou wer
Bilay wakhna dague brome xam xam yi fiisi yoon kén dioukhouleen seen akh yalla khamnakou s Saliou salaam kou Bari xam xam Dieuredieuf koukkiyou
Sëriñ Mustafaa ak mata Bayi xél jambar degg la
Serigne saliou salam un savant multidimensionnel ❤❤❤
Sëriñ Mustafaa aka sopulu machallah
Wallahi. Auto bou rafete ak keur guou rafete la wara ame. Siguilna Mouride gui taye Leroul Seydina Al Hassane Salam. Mane Soumako amone djokh koko.
ndeysan dagua bakh srgne moustapha amna solo🙏
Amna solo d
Yalla nala yalla faye AK gayeepou AK leepou loma yéne yalla naco ame
Serigne Moustapha Diop koki nitou deugue
بارك الله فيك اخي الحبيب سرن مصطفى
NDEYESANE NEKHNA
Walàhi serigne Moustapha Diop Koki deug rék nga wakh diàdieuf Masha.allah ❤❤❤❤❤❤
S Moustapha diop kokki amoul morom thi yon wi
Billahi boroom xam-xam yi dañu léen à wara taxawu dañ léen à seetaanLi ëpp ci ñi fiy woote woo sëriñ bi ciw askan amaluñ yoon njariñ
الحق حق. والحق معك يا شيخ مصطفى جوب
Wallaahi s moustapha wakh nga deug 😢
أصدّق قول المصطفى فهوصادقوإنّى لـه فيمايقـول مُـــوافـــقعن العلمآأشياخُناأعرضوافــــلايعـزّلدى الأشياخ إلامُــــنافـــــقيعـزّلديــهم جاهل هَمُّـه الغـــنىومُنحرِفّ أهلَ الهُدى لايوافـــقيُهينون أهلَ العلم لايكرمـونهــمفعندهمُ يعلو المُعلّـــمَ فــاســـقلقدخالفواوالله تعـليمَ شيخـــنـاومـالواإلى الدنيافبانت عوآئــقفماشجّعوامَن يخدمون العلومَ فىطريقتِنابل شجّـعوامَـن يُنـافـقلمُـدّاحِهـم أموالُهم لالــــعـالِـــــمبـه قديَرى رُشدَالخديم المُرافِقُفياعُلمآءَالنَّهـج صبرًاخُـذِلتُـــــمُفصدرالذى يدرى بذالك ضآئـقخُذلتُـم فصبرًالاتضيع أجـورُكملدى اللـه صبرًافالمُهيمنُ رازق
BILLAHI WAKHNGA DEUG
akou deuguou Serigne Moustapha
Machallah
Serigne Touba amna ko
Wax ji aka dëggu!
lii dé moy déug
Ww goor
Deug rek moy deug
Seringe Moustapha diop koki lou wer ga wakh kham kham moy dauge borom kham kham yi nan len takha wou
Wala hi wakh gua degua dé
Ki dafa dof ken warou ko djokh micro thi bir nit gni
Y’a doff yaw
Daga xamadi té réw seriñ deug rek la wax
S Mustafaa joob ku rafet xol la te xam lu bax di ko wakh yalla na ko yalla fay
Aka deuggou yalla na aw fanam gouddou té mou wer
Bilay wakhna dague brome xam xam yi fiisi yoon kén dioukhouleen seen akh yalla khamnakou s Saliou salaam kou Bari xam xam Dieuredieuf koukkiyou
Sëriñ Mustafaa ak mata Bayi xél jambar degg la
Serigne saliou salam un savant multidimensionnel ❤❤❤
Sëriñ Mustafaa aka sopulu machallah
Wallahi. Auto bou rafete ak keur guou rafete la wara ame. Siguilna Mouride gui taye Leroul Seydina Al Hassane Salam. Mane Soumako amone djokh koko.
ndeysan dagua bakh srgne moustapha amna solo🙏
Amna solo d
Yalla nala yalla faye AK gayeepou AK leepou loma yéne yalla naco ame
Serigne Moustapha Diop koki nitou deugue
بارك الله فيك اخي الحبيب سرن مصطفى
NDEYESANE NEKHNA
Walàhi serigne Moustapha Diop Koki deug rék nga wakh diàdieuf Masha.allah ❤❤❤❤❤❤
S Moustapha diop kokki amoul morom thi yon wi
Billahi boroom xam-xam yi dañu léen à wara taxawu dañ léen à seetaan
Li ëpp ci ñi fiy woote woo sëriñ bi ciw askan amaluñ yoon njariñ
الحق حق. والحق معك يا شيخ مصطفى جوب
Wallaahi s moustapha wakh nga deug 😢
أصدّق قول المصطفى فهوصادق
وإنّى لـه فيمايقـول مُـــوافـــق
عن العلمآأشياخُناأعرضوافــــلا
يعـزّلدى الأشياخ إلامُــــنافـــــق
يعـزّلديــهم جاهل هَمُّـه الغـــنى
ومُنحرِفّ أهلَ الهُدى لايوافـــق
يُهينون أهلَ العلم لايكرمـونهــم
فعندهمُ يعلو المُعلّـــمَ فــاســـق
لقدخالفواوالله تعـليمَ شيخـــنـا
ومـالواإلى الدنيافبانت عوآئــق
فماشجّعوامَن يخدمون العلومَ فى
طريقتِنابل شجّـعوامَـن يُنـافـق
لمُـدّاحِهـم أموالُهم لالــــعـالِـــــم
بـه قديَرى رُشدَالخديم المُرافِقُ
فياعُلمآءَالنَّهـج صبرًاخُـذِلتُـــــمُ
فصدرالذى يدرى بذالك ضآئـق
خُذلتُـم فصبرًالاتضيع أجـورُكم
لدى اللـه صبرًافالمُهيمنُ رازق