Mariage Alioune Seck, Wally Seck traite Mandiaye Seck sur scène et favorise Bambaly devant ses..

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 18 дек 2024

Комментарии •

  • @People221sn
    @People221sn  Год назад +6

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10

  • @dabadiedhiou-ug7yu
    @dabadiedhiou-ug7yu Год назад +25

    Ndeyssane papa Thione rek mofi manque diko gnanal foumou né yalla nako yalla yérem xarél ko aldiana que son âme repose en paix 😢😢

  • @fatoukinedieng4395
    @fatoukinedieng4395 Год назад +2

    Mashallah li daara genouko neekh papa thione rka fi ak niko Alioune beguee wone mais j'adore la complicité entre waly et bambaly🥰♥️mandiaye boula boula micro ak journaliste jaral dilaa bolee ak sa famille car cette dernière est sacrée ben lenene geunoul fort famille peace famille seckene🥰♥️🙏🏻

  • @KhalifaSene-t9t
    @KhalifaSene-t9t Год назад +3

    Machallah nice Couple diamm si ioww

  • @pendandiaye4539
    @pendandiaye4539 Год назад +22

    Qui sépare les familles ira enfer sue dieu sauvegarde nos familles

  • @Germinal5219
    @Germinal5219 Год назад +34

    Bayilene Seytané,bene probleme amoul sen diguanté.
    Bayilene famille diambour bi guene di roubé

  • @Youla_Beauty
    @Youla_Beauty Год назад +1

    Wadjiy oupou si guinaw mèré nako tchim doungourou nitt bakhoule heureux ménage à vous❤🎉

  • @gvfg3295
    @gvfg3295 Год назад +3

    Ndeysan yalla nalen sam amine ❤

  • @ndeyeawacisseka6124
    @ndeyeawacisseka6124 Год назад +9

    😢❤❤❤❤❤ khôl toye na yala naléne yala lafal thiate 🤲❤️💯❤️

  • @Karasenjr7
    @Karasenjr7 Год назад +5

    Lou takh yenne site internet yi mane doul la khamoul ?

  • @diilerecaalifuuta549
    @diilerecaalifuuta549 Год назад +6

    Babacar seck frère waly il très beau mignon

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv Год назад +8

    Mandiaye bou wally wayone doro gueye mou way lolou rk la mane 😂

  • @diilerecaalifuuta549
    @diilerecaalifuuta549 Год назад +2

    Je suis depuis a Paris nii laa mandiaye seck nieewe mii liimoye adouna

  • @Tttttttt-fm3ge
    @Tttttttt-fm3ge Год назад +2

    Mais pape thiopét mome 😂😂 khana dou diangkatte😂😂😂😂

  • @kanehapsa7952
    @kanehapsa7952 Год назад +3

    Masha’Allah❤❤❤❤❤

  • @gagnesirigueye300
    @gagnesirigueye300 Год назад +2

    Wa titres yi esk dou léne thi ay journalistes gnoy yok kharmi karaw? Beugue tass famille yi? Juste une question ?

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 Год назад +16

    Dérétte kéne meunou ko rakhass gnomou néne nasi diambour yi mandou li dara dakhou ko té rafétte na machaala

  • @omarngallaseck3056
    @omarngallaseck3056 Год назад +14

    Mais moi suis sidéré par l’ex danseur de Papa thione ( paix à son âme ) qui se permet d’être «le ventilateur» de Alioune Seck ; ah nitt dangayy geumm sa bopp tei ame touti dignité wayy.
    Heureux ménage 🥰 au couple ; yalna yallah barkel !

    • @sonkofocus2024-ph4hv
      @sonkofocus2024-ph4hv Год назад +1

      Li dara nkoussi nitte dangay woyof

    • @Beyoncekane245
      @Beyoncekane245 Год назад +2

      😂😂😂😂😂😂😂 lolou bannnn minute la ma holat vidéo bi

    • @omarngallaseck3056
      @omarngallaseck3056 Год назад +2

      @@Beyoncekane245 😅😅😅 Vivi dans cette photo le couple était entrain de se faire photographier motahh «ventilateur bi» arrêter mais regarde les autres vidéos de la réception dinga guiss limayy waahh

    • @coumbadiop6741
      @coumbadiop6741 Год назад +1

      Bilay c’est ce que j’ai dit ki nga khamnani matnako mame

    • @omarngallaseck3056
      @omarngallaseck3056 Год назад +2

      @@coumbadiop6741 bilayy 😅😅😅 niak fayda rk

  • @sankounkanoute3067
    @sankounkanoute3067 Год назад +6

    Machallah Wally Seck la famille est réunie même d'autres sont gens ça passera

  • @tairouniang1352
    @tairouniang1352 Год назад +7

    Bayileen ndeyou seytané li dara niawoufi

  • @aidajuf8377
    @aidajuf8377 Год назад +23

    Ouzin kouko diokh micro 😂😂😂😂mandiaye n'est pas l'aise d limotax gua wara moytou site ci problème rk lagn lay dougoul té do am solution

    • @samira260
      @samira260 Год назад +4

      😂😂😂😂😂😂 bilay dangay moudiè rouss

    • @a1e874
      @a1e874 Год назад +3

      Billahi lép Mandiaye la les problèmes de famille se règle en famille mais pas tok si télé gnép dila sétane nguay wakh du n'importe quoi dafa rous dongue

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf2749 Год назад +9

    Mandiay bilakhi yow ya geuneu ndurou ak wally seck lolou la Yalla dogal té déréte bii béneu leu beugn ak lamègn nio deuk amna yo khamné peut être meunoul niakk mais thioloul diéguél sa magg rk adouna amoul solo yalla nassene diame yagg

  • @Junior-kalish
    @Junior-kalish Год назад +20

    Li motakh euleuk mata saur Mandiaye tu avais deconè 😭 gathié day bayi borom top ma rousna sakh

    • @Germinal5219
      @Germinal5219 Год назад +3

      Kon aussi Wally war na bayi hele thi lolou adouna da goudou tank
      En plus bene probleme amoul sen diguanté

    • @milkmilo4082
      @milkmilo4082 Год назад

      ​@@Germinal5219wally amoul loumouy bayi nagnou réglé mon geune

    • @Junior-kalish
      @Junior-kalish Год назад +4

      @@Germinal5219 wally loumou def ? Dagako meussa guiss mou tok plateau di yak mbokam ? Mom il est conscient par rapport ak Mandiaye

    • @a1e874
      @a1e874 Год назад +1

      ​@@Germinal5219wallahi moso ko guis mou télé di wakh si famille wam lép Mandiaye la

    • @DieynaDia-oy1zj
      @DieynaDia-oy1zj Год назад

      Yen aye seytane guen chim dolen bayi liguen di souli

  • @RamatoulayeGuaye
    @RamatoulayeGuaye Год назад +4

    Ndeysane li nèkh na way ❤

  • @sidyndoye6037
    @sidyndoye6037 Год назад +1

    Boy bi Waly rk lay topp nimouy wakhé nimouy wayé

  • @Youla_Beauty
    @Youla_Beauty Год назад +1

    Ouziiiiiiiiin😂😂😂😂😂

  • @khalilgueye8516
    @khalilgueye8516 Год назад +7

    Niakk fayda meunoul wessou nék si famille diambour difa sol robe avocat ndax bén nitt
    Beuga mandou sa bir famille té ay problème doufa diex 😂😂😂
    Réglé lén problème yi nék sén keur té bayi niakk fayda bi ak

  • @mumsmbaye4805
    @mumsmbaye4805 Год назад +4

    Macha li nékh na

  • @assanesane3596
    @assanesane3596 Год назад +2

    Ay sheytane ngene fi Ani loufi Waly banial mandiaye mou weuy thiey Sénégal

  • @hassanatoudiallo7331
    @hassanatoudiallo7331 Год назад +2

    Kou dougou si famille desss sii

  • @yacinendiaye693
    @yacinendiaye693 Год назад +4

    Ani Mouhamed Seck wala wally amoul rak bou toudou Mouhamed ??

    • @adjingoyekane8032
      @adjingoyekane8032 Год назад

      Sisi mais il n’aime pas les écrans il est réservé

  • @fatouseck4915
    @fatouseck4915 Год назад +3

    Bayilene famy diambour kouthi dougou dress thi

  • @محمدعبدالله-ص5ذ5ف
    @محمدعبدالله-ص5ذ5ف Год назад +2

    Ouzin bi 😂😂😂

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv Год назад +2

    Ouzin loume beug 😂way wala fethii

  • @fatoujobegarjo2073
    @fatoujobegarjo2073 Год назад +16

    Mandiaye ya niakeu diom niow ba fi neh do wieuy dangah hamoul lo warra weuy motahh mah bagne kou jealous

    • @magy3113
      @magy3113 Год назад +1

      Wakh Bâle la dafa ame kersa

  • @Adeletewkante-dq8lp
    @Adeletewkante-dq8lp Год назад +4

    C toi qui a provoquer la situation asime la 😂😂

  • @teningngom7698
    @teningngom7698 Год назад +2

    Sénégalais yii nions meuna wakh djiou bonne cite internet yii baugue binde lou amoul sonf guéne torop

  • @samira260
    @samira260 Год назад +2

    Ouzin kouko diokh micro 😂😂

  • @diilerecaalifuuta549
    @diilerecaalifuuta549 Год назад +2

    Louma jaakal aba no stress il ne pas présenté baptêmes waly semaines dernière encore il ne présenté mariage Aliou seck lou keew ?

  • @fadangcamara3543
    @fadangcamara3543 Год назад +3

    Ay waye sama si diangue ni adouna loumou méti méti nagnou rafétale rek ndeysane ak lifi diota diare gneup takhoul il est venu assister le mariage de son Couzin ndeysane déréte dafa fore dama rousse comme si mane la

  • @a1e874
    @a1e874 Год назад +2

    Famille dafa sacré motakh boul nangou kéne dila diakhasé ak gningua bokal bo togué ak journaliste Sénégal yi khamal linguay wakh

  • @awadiop1068
    @awadiop1068 Год назад +2

    😭😭❤️❤️❤️

  • @maxdiop1394
    @maxdiop1394 Год назад +4

    En tous cas baye sy es méchant de mandiaye avec Waly il regarde avec un regard movais

  • @fatimalayoutubeusejallofam9236
    @fatimalayoutubeusejallofam9236 Год назад +3

    Mane lima diaxal moye lou takh la jeunesse Sénégalaise beug buzz. Pour mane depuis notre naissance Allah à fait de nous ce qu'on devrait être. Nit day geum bopam et trop d'amis trop de problèmes..Moy andi li yeup tay..xarite Sénégal legui mo diaratoul dara. .lo wakh ak nit ki attend toi un jour si vous avez des differents ,tous les petits secrets seront au éclatés au grand public. Wa legui ani dioulitè bigni woté très srx djiko changé nit gni transformé wou en monstre..mane dama warou sugnu dom yi vont seront né est grand ir dans ces genres de comportements c'est juste malheureux pour ce pays qui est le Sénégal j'ai très peur xalate léne beuss pinth le jour du jugement diarna soralé mbokmi..li kouko wakhoul warna si xalat..c trop nagnou delo xél yi sunu Borom,bayilén détails ak grand place ak gorr yi nguén di toumal.

  • @diarrawade9182
    @diarrawade9182 Год назад +6

    Bodei nitt dei do wayy

  • @MoustaphaTall-mt1yd
    @MoustaphaTall-mt1yd Год назад +2

    Wally mandiaye sa frère la déréte dafa forr

  • @MariamaKebé-e1c
    @MariamaKebé-e1c Год назад +16

    Atouka gnome naine kou ci dougou déssi maime sou wéyoule grawoule li guéneu am solo daife nako nio bocoup

    • @MbeneFall-il6wg
      @MbeneFall-il6wg Год назад +1

      Wally ninga takha wo sa rak contan nan si dh nioun faramaren yi

  • @jarieujallow8595
    @jarieujallow8595 Год назад +2

    C❤❤❤

  • @sayeseck1089
    @sayeseck1089 Год назад +3

    Ouzin ani mbakam😂😂😂

  • @aichasidibe8818
    @aichasidibe8818 Год назад

    😂😂😂😂😂😂

  • @sophiadrame
    @sophiadrame Год назад +4

    Djioulite deih mandou sama yonne nekoussi alioun seck sa diabar dji foko djeulé dama mandou wahouma dara

  • @cheikhibrafallmbaye2498
    @cheikhibrafallmbaye2498 Год назад

    Kone daaal Yeine wakh Lou Baax Ça vous dit rien. Dou ngeine ay Nite Sakh. Fermez cette chaîne et allez vendre du thiaff