Baptême: l'épouse d'Oustaz Mouhamed Mbaye verse de chaudes larmes

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 дек 2022
  • Baptême: l'épouse d'Oustaz Mouhamed Mbaye verse de chaudes larmes

Комментарии • 439

  • @mamediop8845
    @mamediop8845 Год назад +272

    Ndayesan Mane mi lolou ladone niane yalla dimanche bi passé laniouma done nguénté toudé KO yonnénte bi psl ❤️ té papam aussi yonnénte bi psl laniouko toudé té machallah khéw bi yalla dafa yombal leup kendou bayou Fatima ak seynabou😭😭 machallah yalna niou yalla soutoural

    • @antaleye6537
      @antaleye6537 Год назад +13

      Machallah mam ak yaw niou yam mam sama dom mouhamed sama borom keur mouhamed 🥰🥰🥰

    • @dieyifall829
      @dieyifall829 Год назад +7

      Amine yalna ko yalla barkel

    • @ndiayendieme7056
      @ndiayendieme7056 Год назад +4

      Machalla

    • @yacineyacinendiaye3152
      @yacineyacinendiaye3152 Год назад +4

      Machalla way yalnaléne yalla lafal thiatt

    • @antaleye6537
      @antaleye6537 Год назад +2

      @@yacineyacinendiaye3152 amine ma chérie 🥰🥰

  • @ngonediakhate8608
    @ngonediakhate8608 Год назад +29

    Mach'Allah Yalla na bb bi doundou té barkel
    Louma diakhal diabarou oustaz yi daniouy def cheveux té Oustaz yi di deuk ci diniou War... Bouma keneu né sa yone nekouci rek

  • @awasy4475
    @awasy4475 Год назад +43

    Macha allah mais oustaz xana do warre Sokhna si mou mouru comme ninga Koy defé

  • @ramaramatoulaye8770
    @ramaramatoulaye8770 Год назад +32

    Longue vie à Bb mouhamed et félicitations aux parents

    • @bintely3262
      @bintely3262 Год назад

      Machalla félicitations yayou nabi

  • @ndeyendiaye2150
    @ndeyendiaye2150 Год назад +35

    Machalla guoor nilaye méle dina tahe djiguéne yi guena goor goor lou 😌🙏😇

  • @ndayefatou5039
    @ndayefatou5039 Год назад +17

    Yé niey Commentaires yép nianal léma mame Domenech bou gorr toudé ko seydina mouhamed gir yalla 😭😭

    • @fatimasylla5614
      @fatimasylla5614 Год назад +1

      Yalla nalako yalla may si barki Seydina Mohamed psl❤❤❤❤

  • @papoumendes369
    @papoumendes369 Год назад +88

    Franchement je suis ému 🥹je suis chrétien j'ai pris beaucoup de chose je vous souhaite beaucoup de bonheur ,réussite totale ,santé de fer et un coeur plein d'amour 🙏🙏🙏🥲🥰

  • @aminatamane131
    @aminatamane131 Год назад +24

    Ma cha allah yalna tourondorou sangue bou tédeu bi sallallahou aleyhi wa sallam doundou téh barkel ci barkey alqur'an 🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @mameboussodiagne6471
    @mameboussodiagne6471 Год назад +12

    Yalla nanou yalla may doom bou gour bu toud seydina Mouhamed psl Amine amine

  • @adjadiaby8923
    @adjadiaby8923 Год назад +10

    Manchala longue vie bébé Mouhamed et c'est parents j'ai adoré le témoignage de oustaze Enver se fe c'est magnifique mme

  • @moustaphamboup730
    @moustaphamboup730 Год назад +10

    Yalla na yalla mayko goudou fane ak wéer Machallah ❤️ Seydina Mouhamad salalawou aleyhi wa Salama

  • @ramatoulayesabaly5907
    @ramatoulayesabaly5907 Год назад +33

    Ohhhhhhhhhhh Mancha Allah ken dou bayou Fatima borom Madina toulmou nalwara kou beugue Naby Moustapha PSL lalale ♥️❤️❤️🙏♥️♥️🙏♥️♥️🙏♥️♥️🙏❤️♥️🙏♥️

  • @ndeyachoudiop6587
    @ndeyachoudiop6587 Год назад +11

    Machallah yalnaguéne ma wall ak bép doulite bou amagoul dome , ndaysann contane na sama xarite guéthi nako guiss Mére Séna 😍, Oustaz Mouhamed Mbaye ya bakh yaye machallah longue vie à elle 🤲🙏🥰❤️❤️

  • @yacinendour442
    @yacinendour442 Год назад +19

    Je suis trop contente Masha allah yalla na yalla barkel inshaa Allah

  • @yacineniangcamara7809
    @yacineniangcamara7809 Год назад +41

    Alhamdoulilahy ba amna seydina mouhamed psl

    • @oumoucisse8602
      @oumoucisse8602 Год назад +1

      Niari mouhamad la am sante yalla❤❤❤❤❤

  • @deuguerek4547
    @deuguerek4547 Год назад +6

    Oustaz nak mashaALLAH so kholé nimouy kholé ak wakh ak diabar dangay guiss mbeguel lolou sakh mashaALLAH YALLAH na YALLAH khepp doli🙏🏾❤️

  • @seynaboundiaye1212
    @seynaboundiaye1212 Год назад +10

    C émouvant yallah nalene yallah mousseul sii seytané barkél ndiabot gui sii barké seydouna Mouhamed sallahou aleyhi wa salam

  • @aminafall8736
    @aminafall8736 Год назад +11

    Machallah lii nékhna mais li ma djakhal Lou takh oustaz yi sén sonkha yi dou niou voilé wou

  • @katyfall3610
    @katyfall3610 Год назад +10

    MachaAllah longue vie au bb Mohamed ken dou Seydina Mouhamed

  • @yatoundiaye2521
    @yatoundiaye2521 Год назад +5

    Amna seydina Aliou ñanal lenema ma am seydina Mouhamed

  • @mamymbacke6931
    @mamymbacke6931 Год назад +10

    Yaw dh mouhameth mbaye lo âme dou chance mérit la machalla yallah na doundou té âme ndaye ak baye

  • @unehijabiste580
    @unehijabiste580 Год назад +3

    Des parles de joie ndeyssane😍adouna ngui nonou deif lou rafeit reqqa wor Ma-Shaa-Allah🙏🏿🥺😍❤️

  • @ramatasy350
    @ramatasy350 Год назад +4

    Ndeyssane manshallah wayè dioy yi bakhoul thie yaw longue vie à vous et nous aussi bonne et heureuse année 2️⃣0️⃣2️⃣3️⃣

  • @oumoukaltomdiop5202
    @oumoukaltomdiop5202 Год назад +6

    Ma shaa'allah ya oustaz felicitation yalna bb bi dound te dieul tourando wam ci ay djioko❤wayé sope Gana ak samane gana ak Sandjiry ndiane Gana bi lall nama ma shaa'allah contane ci yen❤❤🙏

  • @astoudiene3341
    @astoudiene3341 Год назад +7

    machalla bayou Moukhamed kkadou yi rafete na li dess yalna barker thi barker seydina moukhemd psl

  • @dieyemaman5724
    @dieyemaman5724 Год назад +37

    Aye waye Kagne laye amate dôme ba toudé mouhamed psl dôme❤️❤️

  • @habyly6015
    @habyly6015 Год назад +5

    Machallah yayou sangue bi dou ay fo mardi passé ladone toudou louma yagui gnane lama sounou borom may Mouhamadou Rassoul 🙏🙏

  • @kadidjatouthiam6335
    @kadidjatouthiam6335 Год назад +36

    Yalla mangilay niane nga mayma seydina mouhamed 🤲

  • @khady6961
    @khady6961 Год назад +4

    Machalla longue vie au bébé li nékh n'a yalna gua ma walle ❤️❤️

  • @matyseye7163
    @matyseye7163 Год назад +34

    Nama niepou nianal ame mouhamad صل الله عليه وسلم li nékhna

    • @mamediop8845
      @mamediop8845 Год назад

      Yalna lako yalla défal inchallahou

    • @fatimaseck3981
      @fatimaseck3981 Год назад

      Yalna niouko yalla May inchallah té mou guéne

  • @cmavie580
    @cmavie580 Год назад +5

    Macha'Allah
    Man sama borom keur Ahmadou la toudou sougnou taaw toudou Mohammad.

  • @yamasamb7068
    @yamasamb7068 Год назад +18

    Machalla longue vie au bébé

  • @sokhnacisse4824
    @sokhnacisse4824 Год назад +8

    Mashalla yalla na doundou té barké thi barké Seydina je

  • @Ummou2983
    @Ummou2983 Год назад +10

    Maschallah ❤mai sa djkeur nek oustaz warone gua mourou kmm c mignon longue vie notre mouhamed ❤🙏🏻

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe Год назад +2

      Moma diakhal mane oustaz yiy waraté séni diabar yi di deff bopou néne ak mèche greffage. Lou wayy di woté dakoy nirou

    • @mariamsylla1307
      @mariamsylla1307 Год назад

      @@MimiMimi-vm5oe merci je me pose la même question pourquoi outaz leurs femmes met du mèche dans leurs têtes c'est pas honoré quand même

  • @coumbadiaw183
    @coumbadiaw183 Год назад +15

    Machallah longue vie au bébé mouhamed mbaye 😍😍😍

  • @aminafaye455
    @aminafaye455 Год назад +9

    Mach'Allah yalla na dounde ba dilén térél💖

  • @ZeynabRassoul1
    @ZeynabRassoul1 Год назад +62

    Wakh léne si lou bakh limou wakh diabar dji. Goor bou takhaw sant diabaram ❤ en public contane na 🎉. En plus c une belle 🤩
    Les jaloux tjrs à critiquer, Bayilén di weur ay critique si bissoup diambour. Séne Keur yi amna ay cas yolén mouna lidienti. Diokhi léne conseil sén yaye ak sœur you mourouwul soff. Sou diabaram mourouwul louthi séne yone. Nakh mourou veut dire bakh wala dioup. Oustaz yi dagnouy diotali li yalla wakh. Kéne thi gnoune mataloul lepp. Sou moro Té bakhoul nakk ??🤧wala diouliwul nakh . Wala mourou moy 1 er pillier de l’islam.
    MachAllah Oustaz bakh Té meune Limouy deff ❤

    • @agnamballo7525
      @agnamballo7525 Год назад +1

      Merci♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    • @madlenesow9428
      @madlenesow9428 Год назад +1

      Degue pirr gua Wakh

    • @fatoukanteh4061
      @fatoukanteh4061 Год назад

      Jaimerais bien que ta femme soit en coll

    • @magattgaye1760
      @magattgaye1760 Год назад +1

      Dégue na degue lou am solo

    • @cmavie580
      @cmavie580 Год назад +7

      Li nga wah deugueuleu dé mais mourou thi diamou Yallah la bokou.
      Yallah nagnou Yallah yok soutoureu thi Baarké Yonenté bi Salallahou Aleyhi wa Salam

  • @bintouahmadgaye101
    @bintouahmadgaye101 Год назад +8

    Wa ani voil bi...yalna yalla takhawouniou

  • @aissatoukande9529
    @aissatoukande9529 Год назад +11

    Machaallah long vie a vous

  • @khadydiao6632
    @khadydiao6632 Год назад +17

    Ah mashallah souhaite-moi le bébé le nom de Dieu a donné ça prophète c'est la Mohamed Salah je suis très content

  • @marietoundiaye4304
    @marietoundiaye4304 Год назад +5

    Yaa oustaze baringua si morome mane dema beugue yonnetibi ba beugouma gnoukoy toudou si deba politique defmey merlo lole, sama dombi ma touddé yonétebi bima eumbè Laa gnaane yalla Mou néke goor Mou yalla nangouko ma wah AK sama brome keur Mou nangoul mako Al hamdoulillah aujourd'hui c'est son anniversaire de 1ans gnanal léneko goudou fane

    • @mamaawagueye4519
      @mamaawagueye4519 Год назад

      Je vais faire meilleures prières 🤲 pour lui❤ndah mala geun beug yonent bi Mouhamed junior yalla nko brom bi Defal tawfeekh ak Taissir diox k djiko yi newwoon si Turando wam Sallalahu Aleyhi Wa Salam

  • @ndiayadiop69
    @ndiayadiop69 Год назад +19

    Wa oustaz ani sa colou diabar ji yabatéguèn dè guèni waar domou adama yii tè yèèn warouwoulèn yèn oustaz yii yabaté guén trop

    • @mamoudaltall4980
      @mamoudaltall4980 Год назад

      Wa oustage ya meune doule ngane kou toude yonetebi dougou aldiana

  • @Diamakane1213
    @Diamakane1213 Год назад +14

    Machalla long vie au bébé

  • @coumbadieye4180
    @coumbadieye4180 Год назад +6

    Machallah yalna Mouhamad goudou té am barké

  • @khadygueye6577
    @khadygueye6577 Год назад +26

    Machallah longue vie au bébé 🙏

  • @gnilanefaye4764
    @gnilanefaye4764 3 дня назад +1

    Machallah nekh nga defal parceque gore nga yalle nalen thiate sékhlou ❤

  • @mamadousarr9531
    @mamadousarr9531 Год назад +41

    Je ne comprends pas .Vraiment ,on doit revoir les prêcheurs qui se mettent devant nos écrans pour transmettre la parole d'Allah .Leurs femmes ne se voient pas,elles font des greffages ,des perruques...,et la gravité de ça . Soubhannalah

    • @aissatoukande9529
      @aissatoukande9529 Год назад +3

      Il faut méfier les vie des autres

    • @mamadousarr9531
      @mamadousarr9531 Год назад +8

      @@aissatoukande9529 je ne parle pas de la vie de personne .C'est un constat que j'ai fais

    • @joyfulness80
      @joyfulness80 Год назад +3

      Akhirou zaman

    • @mamadousarr9531
      @mamadousarr9531 Год назад +1

      @@joyfulness80 wallahi mbok

    • @fallsokhna.1871
      @fallsokhna.1871 Год назад +4

      C'est leur problème mais sont les paroles de dieu

  • @amybayeniasse7944
    @amybayeniasse7944 Год назад +7

    Machalah longue vie au bb

  • @ndiayendieme7056
    @ndiayendieme7056 Год назад +7

    Machalla yallna yalla may goudou fane AK wèrr baga FÈKÈ sa ndiariniou ndiabote yèp amine

  • @khadysonko663
    @khadysonko663 Год назад +12

    Machallah long vie au bébé amine yarabi inchallah

  • @awadiop149
    @awadiop149 Год назад +2

    Ndeysan Aicha yalla na seuy bhi barkhel barkhe seydina mouhamet psl

  • @ndeyethiorotaye3878
    @ndeyethiorotaye3878 Год назад +6

    Machallah long vie au bébé

  • @aissataba8902
    @aissataba8902 Год назад +7

    C'est émouvant 😭😭😭😭

  • @KhemessNdiaye-dc3ik
    @KhemessNdiaye-dc3ik 6 часов назад

    Machallah ❤️ yalnaniou yalla may dôme boy goor niou toudé ko seydina Mohamed psl 💯 et yalna s'en bb doundou bo teral lene

  • @ndayelootambacke7337
    @ndayelootambacke7337 Год назад +2

    Machalla yalla na yalla barkeil man iow rk yama mana Joy lou ji yunén ti bi psl

  • @awangom9069
    @awangom9069 Год назад +3

    Niarel Machallah rafetna Oustaz yabakh

  • @sayeseck1089
    @sayeseck1089 Год назад +7

    Yalla naléne yalla moussal sam leen ar leen ci barke Nabil Moustapha

  • @khadydiao6632
    @khadydiao6632 Год назад +4

    À mashallah je suis très content

  • @lovemouhammad6277
    @lovemouhammad6277 Год назад +4

    Machallah dama divorcée amna seydina Mouhamed yalnaleen yalla barkel mok rakam teh yallah mayatma borom keur bou beugg seydina Mouhamed ak serigne Touba amiiine🙏🏾

    • @zeynabkama
      @zeynabkama Год назад

      qu'Allah SWT t'accorde un autre mari bou gueun

  • @evadieye9266
    @evadieye9266 Год назад +4

    Yalla ndoundd té amm barké si barcké Seydina MOUHAMMAD PSL 🙏

  • @sokhnambacke3209
    @sokhnambacke3209 Год назад +10

    YALLA boumou oumpou ben jijeen bou bakh

  • @antagueye7811
    @antagueye7811 Год назад +6

    Waaw ousraz lii yalla wakh ci bopou nene ci djiguene tngua khamko loutakh Madame mourouwoul

  • @serignemouhamadoumadiamasy5574
    @serignemouhamadoumadiamasy5574 Год назад +4

    Yalna yalla barkél wayé délén waar sén sokhna yi nioy mourou diglé yalla yi moy djitou nga doga topou sa ndigalou borom keur wayé di waraté ta warou wou oustaz yi ak serigne yi nio thi bari da nioy diglé sangou ta do nio sangou adouna do keur

  • @KanyGueye-fl6fm
    @KanyGueye-fl6fm 13 дней назад

    Aka bakh aicha te yarou sama goro bi felicitation mon fils mouhamed mbaye borom yaye biu bakh bi ak sama mak dji sa papa yalla nako yalla yeureum

  • @ramatoulayedar197
    @ramatoulayedar197 Год назад +4

    Machallah amna solo❤️❤️❤️❤️

  • @mbayemoussa5967
    @mbayemoussa5967 Год назад +4

    Machalla yalna yalla barkel yonentibi rek mo Am solo

  • @khadywilane9103
    @khadywilane9103 Год назад +31

    Loutakh Ouzta yi li dji eupp séne diabar yi douniou
    Mouroux

  • @sokhnadiop6622
    @sokhnadiop6622 Год назад +6

    Machallah rafetena torop machallah

  • @fatouseye4580
    @fatouseye4580 Год назад +3

    Ha machalha sokhena Aïcha sa beusebi sama khool seedenesi top li la gniguene yeupe Di niane yallha khewele sa dieukeur Di la sedele sede you rafete yi yallha nalene yallha lafale thiaate boule dioy sokhena Aïcha mouhamed m baye djamyl machalha yallha n'a yallha saam haar goudal sene faane

  • @zeynadiame7052
    @zeynadiame7052 Год назад +1

    Machallah longue vie à vous deux ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @satafall2469
    @satafall2469 Год назад +4

    Macha allah yallah na goude fan

  • @senegalthikhol1653
    @senegalthikhol1653 Год назад +3

    Damaka yague gnaane mo takhit sama taw mom lagnouko touder direct amoul bénène tour sama dome leu mais damakaa rouss nakh tourondorom bi rk😭

  • @aramesy9566
    @aramesy9566 Год назад +12

    ❤❤❤❤❤❤aka.maa.beuge.seydounaamoukhamat..wayé.samakhole.sédna❤❤❤❤❤❤

  • @dadindiaye4807
    @dadindiaye4807 Год назад +4

    Ndeye saane yalla nako yalla sounou borome doli soutoureu inchallah

  • @adamangom6567
    @adamangom6567 Год назад +5

    Je suis un homme mais en tout cas duiguene gni ayyy vrai Diambar lagne.

  • @fatmaibrahimafall8205
    @fatmaibrahimafall8205 Год назад +12

    Oustaz Moy guewélou bopam.aka Bari wakh

  • @moriciss6368
    @moriciss6368 Год назад +1

    Oh yarame dawna ndéysane xol sédna yalna yalla moussal léne si seytané waye tes barkél kou diara toudé dome kéne ko toudé yalna dounous mag tes barké tourono wame

  • @sokhnaastousidi6881
    @sokhnaastousidi6881 Год назад +12

    Loutax sokhna Oustass yi douniou mourou

  • @khadykane9544
    @khadykane9544 Год назад +1

    Diabarou oustaz bi dioy na baptême bi yep c l emotion mais Longue vie au bébé

  • @mariamabadji2445
    @mariamabadji2445 Год назад +3

    Machallah yalla na goudou fan

  • @khadysow571
    @khadysow571 Год назад +4

    Machala yalna yala sam and bi

  • @aidadiop5325
    @aidadiop5325 Год назад +1

    Machalla way yalna doundou te am ndeye ak bay

  • @baymassbessane2344
    @baymassbessane2344 Год назад +1

    Machallah yalnako yalla doundal té barkel ko

  • @ablayendiaye6670
    @ablayendiaye6670 Год назад +14

    Machalla 🙏

  • @kouragning5399
    @kouragning5399 Год назад +6

    Machalla 👍

  • @Mankeursamb
    @Mankeursamb 7 месяцев назад

    Machalla Oustaz yalla na Yalla fay sy barké seydina Mouhamed 🙏🙏🙏

  • @aidadiouf5085
    @aidadiouf5085 Год назад +4

    Machalla tata Aïcha ❤️❤️❤️❤️

  • @bandelba3463
    @bandelba3463 Год назад +1

    Longue vie à bb Mouhamed

  • @maremedoudoudiouf9299
    @maremedoudoudiouf9299 Год назад +1

    Machallah yalla na yallah barkelko

  • @maimounacamara2142
    @maimounacamara2142 Год назад +6

    Il a amené son épouse au clinique casaousse ville sonnou si ba dh lou nekk mou koy diendd je le voyais tous les jours faire les cents pats devant la clinique j’habite en face de la clinique kou begue diabaram Mogui ni

  • @mamanfatmafall1756
    @mamanfatmafall1756 Год назад +2

    Machaa Allah oustaz

  • @mamediarragueye9254
    @mamediarragueye9254 Год назад

    Machala sama sopè bi yala na am dom bouma toutè yonenetibi psl

  • @diaynabakane7378
    @diaynabakane7378 Год назад +16

    Oustace niga Beugué seydina mouhamed sa diabar dji warona mbourou Def cheveux no Senegal li motakh Senegal change fi yomboul

  • @fafagaye3894
    @fafagaye3894 Год назад

    Macha allah sama taw mome lak9 toudé longue vie au bb

  • @aissatoundiaye5671
    @aissatoundiaye5671 Год назад +3

    Salam je partage votre bonheur tu as de la chance d’avoir une Aicha Lo gué vie au bb

  • @ndeyedieng3716
    @ndeyedieng3716 Год назад +2

    Machalla long vie bb

  • @diarradiene4275
    @diarradiene4275 Год назад

    Mashallaah sama oustaz mouhamed mbaye sama sopey khôl yalna bb doundou mak TEEKI barkel am ndaye AK baay

  • @aidadiouf5085
    @aidadiouf5085 Год назад +5

    Machalla 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰

  • @Rifafaye2454
    @Rifafaye2454 9 месяцев назад

    Machalla longue vie au bb ba nguéne féké djarignam

  • @evelynefall9562
    @evelynefall9562 Год назад +3

    Ndeysaane leboue ndakarou.diome rek,baakh seye rek.Yalla na Mohamed bou ndaw mag nourou Yonente bi ,barkele ba yorlene.