Walahi diop koki mola epou ndiarigne si yonn wi fouf té lim wakh moy deg dano wara fonkou borom xam xam yi s saliou salam dafa wara am lépou ndakh gnignou kouy diokh molénko geun mérito fouf ah
كلام صحيح ،في القران والسنة شكرا لك يا اخي عبدالجبار ولله قولك حق واضح وفصيح، لا تبال المنافقين الذين لا يريدون الا الفساد ۔ وهم يعلمون ان قولك حق ، لا تخف افواه المنافقين وحسدهم ، بل انت عالم ،وفاهم وشجاع ،فلو كثر امثالك لغلق المنافقون افواههم ، امش الى الامام واطال الله بقاءك
Kilafa warna wakh dimbalé dou force té sétlou nani kou diokh guir wakh deg rék gnouni day khékh yonn ak serigne si moustapha diop loki limou wakh kén manuko wédi
Borom ham ham you beug adouna yi meunou nio beug serigne koki, serigne Moustapha lim wah leip deug la, sa temps bi boko defone si jangualê ham hamou charia ak djéma jamarlok gniy yaq derrou serigne touba si internet bi modone eupe ndiarigne.
Sa wax dji de barina ay NDIOUMTE te Walahi WAKHÉ wo xam xam BARINA lo wax si Serigne moustapha YIT LOXAM NI XAMNA daga gastowol wayé demewol NONOU té lima woor moy Serigne moustapha do sa MOROUM si ben COTE té bo Serigne bi dellu si woon si sahir gakoy xam
Li ame solou lepou s mountakha défnakou mouy tabakh ay jangou ték fa ay borom xam xam yorlén lolou mouy lépou kou beuge alal dangay ligéyi jarajaf mbacke
Serigne Abdou diabar machalla waxdji amna solo
Serigne moustapha diop yallah nako sougnou borom doli yiw ak gouda fan
S mousstapha bdiop koki yalla nafi yague tawér
Masha’llah amna solo diop koki jambar la way yénn yi meun na niak saliou salam yalla nafi yagg té wérr
S moustapha dé ku amal niarigne dioulite gni rawatina yonu mourite yalna yalla tahawuko
S Moustapha mom nité thi mom la deuké masha'alah. Borom kham Di nitt koubakh
Yallah nafi yagg lool ta werr
Serigne Moustapha Diop koki daal Boroom xam-xam bu am pastef la ta yit kou beug yoonou Mouride la lolou laa kham si mom yalla nafi yagg te wér lolll
Machalaa serignbi amna solou loll ta tégi ci xame xame
Akassa diaduef s bi am na solo
Walahi diop koki mola epou ndiarigne si yonn wi fouf té lim wakh moy deg dano wara fonkou borom xam xam yi s saliou salam dafa wara am lépou ndakh gnignou kouy diokh molénko geun mérito fouf ah
Yaw demal défal lèn leppeu. Dafa wara am lepp té yaw défaloko dara ban chance la am
كلام صحيح ،في القران والسنة شكرا لك يا اخي عبدالجبار ولله قولك حق واضح وفصيح، لا تبال المنافقين الذين لا يريدون الا الفساد ۔ وهم يعلمون ان قولك حق ، لا تخف افواه المنافقين وحسدهم ، بل انت عالم ،وفاهم وشجاع ،فلو كثر امثالك لغلق المنافقون افواههم ، امش الى الامام واطال الله بقاءك
Ah diaro.deguelou.s mousstapha.mola.ap.xam.xam.
Serigne Moustapha Diop kokki rawnalene bu yague
Mustafaa Jóob, daa bariy wax, moo tax lu nekk dina vi dugg.
Ñi xamul rekk ñoo koy aprice waaye ku xam du la yóbb fenn.
Kilafa warna wakh dimbalé dou force té sétlou nani kou diokh guir wakh deg rék gnouni day khékh yonn ak serigne si moustapha diop loki limou wakh kén manuko wédi
Dimbali nit dou force. Yaw loy khar pour dem dimbli nit gni
S abdou l diabar bayil internet bi
Machallah amena solo loll
S Moustafa niaari auto la amoon joxéna bénn ba ta yalla tax
Dama beugue dieul wird makhus si Serigne Moustapha Diop koki amna sama ndigualou Serigne
Borom ham ham you beug adouna yi meunou nio beug serigne koki, serigne Moustapha lim wah leip deug la, sa temps bi boko defone si jangualê ham hamou charia ak djéma jamarlok gniy yaq derrou serigne touba si internet bi modone eupe ndiarigne.
Abdou jabar wakho degeu de
Serign bi ya baax way
Serigne bi yaw dob diokhekat li muy wax Serigne mourtada teralna broma xam xam ba tayi
Dieredieuf Mbacke
Serigne bi wakhofi Dara s Moustapha limou wakh yeppou deugg la billahi
Sa wax dji de barina ay NDIOUMTE te Walahi WAKHÉ wo xam xam BARINA lo wax si Serigne moustapha YIT LOXAM NI XAMNA daga gastowol wayé demewol NONOU té lima woor moy Serigne moustapha do sa MOROUM si ben COTE té bo Serigne bi dellu si woon si sahir gakoy xam
Maim ya ni nga waxe baxul nada da ngay khasse
Waxóofi darra de te sax da ngay bëg a bai ay wax
Dangua far.
Gnii ay pass passi wahabiste you bone laniou yor dieureudieuf Serigne bi wakh dji amna solo lool
Li ame solou lepou s mountakha défnakou mouy tabakh ay jangou ték fa ay borom xam xam yorlén lolou mouy lépou kou beuge alal dangay ligéyi jarajaf mbacke
Des aponé.sakh.thiam
Waaw goor diop koki daal day radiékhé rek. Dafa wara dall
Dia dieuf Mbacké bàlla aysa da am gno kham ni ci yone wi lou niaw rk lagnouy wakh téli rafét bari na
Bilahi wakhgua deugg té soo wakhee niouné ay mourid laniou diop koki miiii ay mbiram léroul
MBACKE Yagal ta wer lol
Mais koki tamite est-ce que ça va
kii niaku na xrom dh door katou martou la
Iow Yagui beug Bari ay wax ish
Moustapha Diop koki mookk Ahmadou rafahi nioo yamm ay connerie rek laniouy wakh si yoonou mouride nane nou may diamou way soof naniou torop
Yaw yaa mana fenn waay te reew
Ibrahima cissê yaw plus de 1 ans mangui niouy dadjé si ay commentaire mai youssi eupe danguay niakey tegine imam rafahi. Ak serigne koki
Jahiil gui Moy waral lolou rék
Lu du waxi ku am xel
كلام عبد الجبار كلام فارغ
S abdou l diabar bayil internet bi