Diadieufeuti Toure gnoune wa New York bilahi sante nagnou la Toure nak def gua gnou guiss diadieuf Toure yallana yalla mayy werr ak goudou fann Kamal gua Ridial gua
j'aimerai quand on invite un grand moukhadam de CHEIKH MOUSSA, au lieu de tjrs perdre notre temps pour justifier notre appartenance au mouridisme,on doit montrer au monde entier qui était CHEIKH MOUSSA son enseignement,ses qualités et son message. je pense que la prochaine fois ce serai mieu que le cheikh(l'invité),de proposer au présentateur,quel sont les points qu'il veut développer au courant de l'émission, comme ça les jens comprendront mieu qui était le vrai CHEIKH MOUSSA,CHEIKH MOUSSA authentique...di toup di yess lou nieup kham kouy CHEIKH MOUSSA rék la si joub lou. rafét na touré yal na yalla geureum té yagal la fi.dieureudieufé BAYE GUEYE.
Pourtant ki wakh na lepp dh. Wakh na qualité yi, enseignement yi ak message yeup. Émission bi nak defaralou niouko talibé cheikh moussa motakh niouy leralate mbir yi rek
On diré k serigne touba limou bind gayi dougnko wax liléne néx rek lagnou wax Comme serigne touba mom dadane bakouko rek lolou dou yone nagn diagui li serigne bi wax si dine dji
Xam yallah soko beugué tay dagay iew si baye Niass so iewoul si BAYE do xam yallah Nitt meunena xam yallah si toureum , nitt meunena xam yallah si mélome , nitt meunena xam yallah si dieufeum .. wayé nga xam yallah si dieumeumm DEUG DEUG kéne meunouko amm loudoul nga diarr si Maolana Baye Niass
Nia sën =moy niou sën (aperçu) yalla ça veut dire k yene khamolene yalla guissolene yalla en plus amolene tawhid parck danguéni takk térré .Nioune douniou yéne té bougouniou mél ni yéne
@@elmassthiam467 Ah bon Mane Doff ci nit Weirr Fa Yalla moma Gueuneule Weirr Fi nit gni Fék Dof lah fa Yalla Mame Cheikh Ibrahima Fall Liguèy Ba am Ngërmandé Yalla ngay Wakh yù Niaw yi Ndeyssane Sénégal Danio Oumpalé wayé Lou way wakh mba mou déff bopam
Dieuredieufé BAYE NIASS , dieuredieufé NDIAMBÉ DAROU , Sénégal nak pour gniom gnioune gnioy dof yi ...
Wayé doff si yallah dara dakouko
diadieuf ndiamé borom darou sangue cheikh moussa touré jarama❤❤❤❤❤❤
Yàlla jajeuf yadi yakari jam gni jërëjëf
Touré Mandi Mauri ya guene 😍🙏
Diadieufeuti Toure gnoune wa New York bilahi sante nagnou la Toure nak def gua gnou guiss diadieuf Toure yallana yalla mayy werr ak goudou fann Kamal gua Ridial gua
Amatina sollo yalla na yalla fayla oustase maodo
Yalna niou la YALLA feyal yook leerrr bidjahi borom Darou barké borom Touba
dieureudieufé borom touba diarama mame cheikh barki cheikh moussa
j'aimerai quand on invite un grand moukhadam de CHEIKH MOUSSA, au lieu de tjrs perdre notre temps pour justifier notre appartenance au mouridisme,on doit montrer au monde entier qui était CHEIKH MOUSSA son enseignement,ses qualités et son message. je pense que la prochaine fois ce serai mieu que le cheikh(l'invité),de proposer au présentateur,quel sont les points qu'il veut développer au courant de l'émission, comme ça les jens comprendront mieu qui était le vrai CHEIKH MOUSSA,CHEIKH MOUSSA authentique...di toup di yess lou nieup kham kouy CHEIKH MOUSSA rék la si joub lou. rafét na touré yal na yalla geureum té yagal la fi.dieureudieufé BAYE GUEYE.
li mom constat bou am solo la cheikh Moussa wa rewmi gneupa ko xam si numu melone kone leup lerr
Pourtant ki wakh na lepp dh. Wakh na qualité yi, enseignement yi ak message yeup. Émission bi nak defaralou niouko talibé cheikh moussa motakh niouy leralate mbir yi rek
TOURÈ Ken dou yaw ❤️❤️❤️💯💯
Santé cheikh moussa cissé ndiamé borom darou léerou lerr yi rek ba faw
Jërëjëf Cheikh Moussa Toure
Wakhal ta yalla take chiekh akhmadou fadiama niang moko chiekhal xamoul serigne touba
Cheikh toure Ambasader Cheikh moussa Ndiambe darou
cheikh Moussa Touré jajeuf leral bi cheikh Moussa cissé ndiambe borom darou kouko xam beugko walahi waliyu pir lawone
MASHA-ALLAH 👌👌👌💓🖒
Serigne touba mo fi nek kènene nekoufi diereu deiufe baye Moussa
DEUG dou wessou deug mouk tee YALLA rek moy deug dieuredieufe cisse
Ja jeuf Sangue bi amatina solo
On diré k serigne touba limou bind gayi dougnko wax liléne néx rek lagnou wax
Comme serigne touba mom dadane bakouko rek lolou dou yone nagn diagui li serigne bi wax si dine dji
Yalla rek moy deug Ken dou Ndiambé
Mashallah Sangue yaram xol sédd na lol
diarama wa 2stv kén amul sén fayy émission bi kawéna lol
Mane moustapha Diop bayou cheikh moussa cisse coly Diop sant n'a cheikh moussa bou bah djadieuf touré mame maodo amna solo lol
Macha allah
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wakhtaan amna solo loool
Xam yallah soko beugué tay dagay iew si baye Niass so iewoul si BAYE do xam yallah
Nitt meunena xam yallah si toureum , nitt meunena xam yallah si mélome , nitt meunena xam yallah si dieufeum .. wayé nga xam yallah si dieumeumm DEUG DEUG kéne meunouko amm loudoul nga diarr si Maolana Baye Niass
Fidel Fidel Ziar yaram bi lane moy niit ?
Fidel Fidel ak kane moy baye ?
on dirait un fanatique waxal xam xam té dièmal dindy sayy ayib yalla yatuna lol té cheikh Moussa cissé doy nanu
tu apprendre à respecter les gens et laissez la propagande lolu du yalla du yonent
Nia sën =moy niou sën (aperçu) yalla ça veut dire k yene khamolene yalla guissolene yalla en plus amolene tawhid parck danguéni takk térré .Nioune douniou yéne té bougouniou mél ni yéne
Diadieuf
oustaz maodo ku woyof té dall beug xam xam lol mala soop
Wa legui bo à mai ndolal bâ parai dougou si tariha lou tah ngen delou guinaw bayi diouly ak yenen ponk l'islam
Dalli Cheikh Omar foutiyou tall kéne geunouko makama sikaw souff ( bamou beugué Ani tarikha bopam , yonenti bi dafniko tarikha yougniou garanti sikaw souff diekhna) lolou takh bou diap si tarikha tijane ... Tarikha tijane bobou nak Sila baye Niass rawé kepp kouy woté dieumelé si yallah (kou kham yallah nane dou diouli dou worr kokou khamoul wayé da geuneuh rerrr )
@@Og_gasen Légui noy déff ak Mame Cheikh Ibrahima Fall Mi Nga Xamni Moy Bayou Yalla Yalla yi
@@mouhamadoulaminediobate1393 kokou dou yalla doff la
@@elmassthiam467 Ah bon Mane Doff ci nit Weirr Fa Yalla moma Gueuneule Weirr Fi nit gni Fék Dof lah fa Yalla Mame Cheikh Ibrahima Fall Liguèy Ba am Ngërmandé Yalla ngay Wakh yù Niaw yi Ndeyssane Sénégal Danio Oumpalé wayé Lou way wakh mba mou déff bopam
Dalil rek, li nga wakh lou amla, wayé dou nieupp tamite, ndakh guiss naci niou bari bari niouy respecté ponk yi.
Machalla