Masha'Allahou sokhena marie diop togou yaye Isseu. Leke na nems loubari waye bide mais Diangale ngama nems yi. Contane na. Yallah Na Yallah Wereule Lokho bi dounede ba gnabotes gui dila Sargale bi diaahi nabyl moustapha Staws.
samedi passé on avait un annf at home mani ma engagée nem yi😂té meussou mako essayer bilahi mais j'ai suivi votre vidéo et je l'ai fait comme telle et mashallah je l'ai bien réussi😊croustillant neu nékh neu et tout le monde le réclame 😅 bilay c'est la meilleure recette de nem essayer et vous allez voir😊 Merci maman Isseu et longue vie à vous 🙏🥰 Iao rék lay topou 😅
Mach, Allahou tata isseu toujours égale à elle même vraie cordon bleu là fi gua gueneu bakhna yallah na yallah barkél sa dounde ta gua yague fi lol ta and akk wér Amiiiine yarabi 🙏❤️❤️
Machallah tata j’essaye la recette aujourd’hui et mon mari a adoré disons c’est la première fois que je fais des nems merci à vous et longue vie aussi 😘😘😘
Machala jadore vos recettes et vos astuces c top machala . Mais à la place de l'eau froide je préfère je laisser 1 ou 2mn au congélateur et ensuite les frire
Yaye Isseu kuko xamoul deigg ngako🤧🥰😍😍😍 mane sa nokoss royal momay Ray. Dafa neex trop. Je l'ai une fois reproduit , mais louné la👌🏼 manchallah, andd akk xeitt bu neex sakh, rafeit. Vraiment lafthiat maman Isseu. Yangui dff lu am solo. T togg mom, comme diangue la rkk, on finit jamais d'apprendre. Sinon par rapport à la croustillance, on m'a aussi dit que le sucre et quelques gouttes de vinaigre feront aussi l'affaire. Je l'ai essayé et ça a marché. Vous pouvez aussi essayer pour voir en mettant un peu de sucre et de vinaigre dans cette eau tiède où sont plongées les galettes de riz. Bisous maman Isseu. Je vous aime et vous suit tjrs😘🥰. Je m'appelle Élodie et je suis passionnée de cuisine comme vous🤩.
Dieuredieuf sunu international bi yaague fi lol ter weur damadone lathie vermeselle Chinoise bi daniouy tangal dokh tremper ko thi ak carottée bi tamite râpée la
Machallah Tata 😍 mais juste une question est ce qu' on peut ne pas mettre le nem au frigo ou au congélo pour éviter le contact de l eau avec l huile ???
Salaam chef machallah vraiment recette bi beugue na thi bégueul sounou wa keur mes vives félicitations Ma beuguona kham feuille bi AK vermisselle chinoise bi ngua wah fougnka mana amé Merci bien
Machaallah yalla na sa jam yag mais bane galette guay utilisée mane lido bi lay defaré nem mais soumako dougualé si huile bi day tass sugéré ma benne galette bou bakh tata damay diay chaque damay perdre lou bari merci d avance
Masha'Allahou sokhena marie diop togou yaye Isseu. Leke na nems loubari waye bide mais Diangale ngama nems yi. Contane na. Yallah Na Yallah Wereule Lokho bi dounede ba gnabotes gui dila Sargale bi diaahi nabyl moustapha Staws.
Machalla toujours égale à elle même longue vie et merci beaucoup pour les recettes
Machalla essayer n'a ko mais nékh n'a trop sakh chapeau à vous merci pour ses recettes tellement facile à reprendre ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maa Shaa Allah sa recette yi nekhna . Merci de partager. Yala na la yala gueneu barkel loho bi. Ameen
Choucourane yaye Isseu yalna borombi fayla
Mane deh khawema vietnamien khawema chinoien mais depuis que je découvre sa méthode bi mom rek lay def lepay gnor machallah
samedi passé on avait un annf at home mani ma engagée nem yi😂té meussou mako essayer bilahi mais j'ai suivi votre vidéo et je l'ai fait comme telle et mashallah je l'ai bien réussi😊croustillant neu nékh neu et tout le monde le réclame 😅 bilay c'est la meilleure recette de nem essayer et vous allez voir😊
Merci maman Isseu et longue vie à vous 🙏🥰 Iao rék lay topou 😅
Ha Fatoumata très contente ❤️❤️❤️❤️
Tu ressemble à ma fille elle s’appelle fatima sene comme yaw
Mach, Allahou tata isseu toujours égale à elle même vraie cordon bleu là fi gua gueneu bakhna yallah na yallah barkél sa dounde ta gua yague fi lol ta and akk wér Amiiiine yarabi 🙏❤️❤️
J'en ai fait hier pour le réveillon vraiment je l'ai reussi grâce à vous machalla cordon bleu ❤️❤️
Machallah tata j’essaye la recette aujourd’hui et mon mari a adoré disons c’est la première fois que je fais des nems merci à vous et longue vie aussi 😘😘😘
Moi j'arrive pas a la faire car y a trop d huile quand je mets les nems dans l'huile
@@Gggge_dudiolof9536 évite de mettre les galette trop longtemps dans l'eau
Merci beaucoup maman mane si yaw rek lay dieulé recette machallah 🥰🥰🥰🥰
Machala jadore vos recettes et vos astuces c top machala . Mais à la place de l'eau froide je préfère je laisser 1 ou 2mn au congélateur et ensuite les frire
Ah bon! Et on aura le même résultat ?
@@FatouFall-wf6xu biensur
Macalah tata yalna yalla yagal sa takhawaye difal gnu sa pitzza
Bilahi pizza rk lagnouy khar
Dieureudieuf togue mame isseu bon appétit nekhna lol dinako def incha allah
Waouh j'adore merci beaucoup yaye boy mane mome farcie bi dmakoy togou normal m galette bi la doul meuna roulé normal légui môme ça y est
Bravo Tata Macha Alla je vous adore. j'aime cuisiner et je vous suis beaucoup.
Machalla amena solos femme forte CHEZ 👍🏿👍🏿👍🏿💪🏼💪🏼💪🏼👏🏿👏🏿👏🏿💛💟💜🇫🇷🇸🇳
Miam-miam 😋, jazzakAllahou khayran encore ❤
Ah thioum machala machala yala bayi lafi ba thi kanam kanam
J aime bien ta façon de faire la cuisine c est comme disait l autre la nature de l homme c est l artifice merci pour les conseils
Je viens d'en faire, ils sont "mouah". Merci de nous aider à nous améliorer en cuisine, Yaye Isseu.
Cccff
Ù😮Hrkiezbu eu ne k par
Salam salam Togou Yaye Isseu Come Dab Rek Masha Allah Dieureudieuf Amal Diam Illimix Amine Y'a Rabbi 🤲🤲🤲❤😘🇸🇳
Machahala ❤❤❤
Merci beaucoup Yaye isseu man méthode bi mo gueuneu vientnamien bi manchalla
Yaye isseu diguentemm akk saf SAP histoire bou yagu laa😂🤣😂
Waaaaw Waaaaw bi mome sa façon la machalah 🥰🥰
Tata merci beaucoup waay. Lii nékh neu torope. Sama Dieukeur contaneu lole sakh. Dafa lékeu bay beugue dée 😘😘😘
Allahumma Barik ❤❤❤❤
Dieredieuf tata tay sa ma Dimanche nekhatina lp yawla si archive la kheuyé tey may Allah SWT bless you and your family ❤️
Mashalla mama pour les nems❤❤❤❤
Machalaaaa togue yaye isseu sa yo guéné gueune bilay
MashaAllah❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤ tout tes plats son bon
Machalah maman 😍😍😍longue vie et santé
Merci chef pour les astuce juste magique je pense que meme cette farce peu servir pour des rouleaux de printemps merci
Machahala yalla nala yougnou borom bi fay si you bakh yi ngua niouy diokh
Machallah tata goudeul fane... Chaque fois ga diox gnou ay recettes you amoul fen. K dieu te protége
Machaallah yaye isseu ken dou yaw💪💪💪❤❤❤
Machalah yalnagnou feke toguou mame isseu.merci yaye boy
Machaallah lep diar na yone contane thi yaw rek
🥰😍 mashallah
Ya isseu bilahi bo finekoul wone lambaye niaàw❤❤❤
Slt tata j'adore t'es plat mahallah 🥰 je suis passionné de la cuisine .
Machalla'llah tata,goudal fann rék on aime fort 🥰
Masha 'Allah Maman
Yalla na Yalla yagal satakhawaye
Feye la yiw wa fi Dunnya wa fi Akhirati
Amine ya raab
Cambridge United Kingdom 🇬🇧 ♥
Macha Allah yaye isseu trop bon
Machalah comme d'habitude 🥰😘
Machala maman nem yii nekhna trop eunigua benene façon 😇🥰😍
Macalah tata yalna yalla yagal satakhawaye
Machalla yalna yalla guoudeul say fane
Mangui diangue dall diekeur dafaye beiteiii djigueine dall dafawara meune cuisine ❤❤❤sinon ton mari va cherché une autre Wawaw 😂
Je vais l essayer inchaallah yaw dal goudou fane rek lagne lay gnanal
Machaala yala na yala wéreule lokho bi
Feuilles you nems bi bou mak bila wala merci pour les recettes
Yaye Isseu kuko xamoul deigg ngako🤧🥰😍😍😍 mane sa nokoss royal momay Ray. Dafa neex trop. Je l'ai une fois reproduit , mais louné la👌🏼 manchallah, andd akk xeitt bu neex sakh, rafeit. Vraiment lafthiat maman Isseu. Yangui dff lu am solo. T togg mom, comme diangue la rkk, on finit jamais d'apprendre.
Sinon par rapport à la croustillance, on m'a aussi dit que le sucre et quelques gouttes de vinaigre feront aussi l'affaire. Je l'ai essayé et ça a marché.
Vous pouvez aussi essayer pour voir en mettant un peu de sucre et de vinaigre dans cette eau tiède où sont plongées les galettes de riz. Bisous maman Isseu. Je vous aime et vous suit tjrs😘🥰. Je m'appelle Élodie et je suis passionnée de cuisine comme vous🤩.
Merci Élodie heureuse de faire ta connaissance pour astuce je vais l’éssayer merci encore je vous adore 💕 j💕😍😍💕💕🙏🏻
Thiéye yaye issa yalla nala yalla téral bilakhi Contane na trop ci yow
Quelle recette et technique de production précises , bravo .
Mashallah mama jerefer yal na yalla faye
Machalahhhh tata🥰 mais nane lagnouy deffarei sauce bi
Machala 😂❤❤❤
Dieuredieuf sunu international bi yaague fi lol ter weur damadone lathie vermeselle Chinoise bi daniouy tangal dokh tremper ko thi ak carottée bi tamite râpée la
Machaallah comme d’habitude merciiiiiiiiii ♥️
Thieuyyy sounou yaye isseu dieureuf yague fii yaye boy
Mashallah nexna sel n’a 😍
Masha allah ❤ j'adore vraiment maman notre maman nationale vie sur vous
Ahh mère taye mom sama plat préféré nem ohh 😋😋😋😋😋😋😋
Merci avec toutes les Bonne recette
Machalla ❤️❤️
Machallah diarna yone 😘
Machallah Tata 😍 mais juste une question est ce qu' on peut ne pas mettre le nem au frigo ou au congélo pour éviter le contact de l eau avec l huile ???
A bou di na ko essayé ba kam
Je penses cest mieux de le mettre o frigo dora saff
C mieux sak
Oui je l’ai essayé mais c’est mieux
Machallah 🙏🙏👍
Merci beaucoup maman longue vie à vous. Esk on peut préparer des nems sans vermicelles chinoise.par ce que j'aime pas ça
Toog mome.ya set noko beugué rek
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashalaah
MACHALAH ❤❤❤
Yaye isseu xana Diouf gua sante 😂😂
Akassaaaaa machallah maman.
Machala tata 🎩 à vous 👌🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machallah😋😋❤
❤️❤️❤️sa tour bi nekhna manchallah
machalla tata issa❤❤❤
Machallah ya iseu
Merci yaye isseu gueneu yag gueneu wer machalah
Bonjour ma grande sœur man da ma beugg sa ay astuces goudal fan and ak wer werle neckal ci diamm
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah🥰
Feuille nem bi fan lako meuna amé
Hummm trop bon
Merci bcp Yaye Isseu
Amo morome diame rék gaye ame 🌹🌹
Machallah damala namone torop
Do you put the rolls in water before you deep fry the rolls.?
Machala tata 🥰
Bjr tâta je peux savoir bane galette mo geuneu bakh pour nems merci bcp j adore tes recettes
Machalla amna solo lol
Champion bi faan lako mana amé
Machalla maman ❤🤲
Ma sha Allah nehatina 🥰🥰🥰
Salaam chef machallah vraiment recette bi beugue na thi bégueul sounou wa keur mes vives félicitations
Ma beuguona kham feuille bi AK vermisselle chinoise bi ngua wah fougnka mana amé
Merci bien
Merci papa demale auchan
❤❤❤❤
Machaallah yalla na sa jam yag mais bane galette guay utilisée mane lido bi lay defaré nem mais soumako dougualé si huile bi day tass sugéré ma benne galette bou bakh tata damay diay chaque damay perdre lou bari merci d avance
Belle recette.cest fantastique merci